Ndessay li dawna yaram: La Famille Ba expulsé dans la rue par notre propre sœur et la maison démolie

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 9 ก.พ. 2025
  • Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
    / @dakarbuzztv
    Contactez-nous: +221 77 687 97 12
    Site Web : www.dakarbuzz.net
    TikTok : www.tiktok.com...
    Facebook : / dakarbuzz
    Instagram : / dakarbuzz

ความคิดเห็น • 310

  • @fatouwade5048
    @fatouwade5048 ปีที่แล้ว +69

    Yana léne Yalla takhawou si barké Seydina Moukhameth (SAW)

  • @christinegning382
    @christinegning382 ปีที่แล้ว +37

    Que le seigneur vous assiste et vous protège. Ceux qui construisent sur les larmes des autres vous aurez votre propre karma car Dieu est juste. Le seigneur va vous assister car il le Dieu juste.

  • @dabasamb5607
    @dabasamb5607 ปีที่แล้ว +37

    Yalnalenes sounou borom tahawou Sy Barker seydina Mohamed. Amine ya rabi

    • @HORE2023
      @HORE2023 ปีที่แล้ว

      ALAHOUMA AMINE 🤲🤲🤲

  • @MK-Architect
    @MK-Architect ปีที่แล้ว +24

    Yallah nalen Borom bi atter. Diay doller bakhoul. Ceux qui ont cet acte vont le regretter. Si on peu faire un Don pour cette famille en détresse je suis partant. Courage. Yallah nieup laffi nekkal.

    • @haby8760
      @haby8760 ปีที่แล้ว

      Numéro

    • @khadidjatougaye5153
      @khadidjatougaye5153 ปีที่แล้ว +4

      Il faut faire très attention avec les histoires de famille

    • @amadouaw365
      @amadouaw365 ปีที่แล้ว

      Demal lathier wa keur yi fa deug keur Samy Thioune gnougnou

  • @diariabousso466
    @diariabousso466 ปีที่แล้ว +5

    Béne affaire aussi amna keur Baye dou keur keur yaye dou keur nioune jeunesse bi li warnaniou servir de leçon ligueye souniou euleuke bo tolo si ligueye ligueyal amal sa bopou ndakh euleuk motakh dafa diara soralé du courage frére

  • @biba9498
    @biba9498 ปีที่แล้ว +15

    Yalla na léne Yalla takhawou ci barké Seydina Mouhamed psl

  • @BiraneToure-tm5cb
    @BiraneToure-tm5cb ปีที่แล้ว +9

    Yalla naniou yalla may Allal niounou Mana dimbali domou adamayi

  • @yacinetraore6827
    @yacinetraore6827 ปีที่แล้ว +17

    Salam j ai le cœur meurtri ce monde n'a pas d importance on va mourir . Les bonnes volontés aidaient cette famille par la grâce d allah. Si j'avais les moyens

    • @ndeyekhadysow3689
      @ndeyekhadysow3689 ปีที่แล้ว +1

      Amo moyen wayé amngua kholbou rafett yala nala sounou borom mey loy dimbalé waté amine

    • @mariamabandia777
      @mariamabandia777 ปีที่แล้ว +1

      Nite kou nioul Lou mou la eupalé wané la ko😢😢😢

  • @GfyThiaroye
    @GfyThiaroye ปีที่แล้ว +9

    Yalla nalén Yalla takhawou barké seydina mouhamad ( s.a.w.s ) les bonnes volontés aidez cette pauvre famille,

  • @adamadieng8720
    @adamadieng8720 ปีที่แล้ว +6

    VRAIMENT DEUGUEUDO YI NIOU BAKH LANIOU . YALLAH NAH YALLAH FEYY❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @KIRIKOU34
    @KIRIKOU34 ปีที่แล้ว +4

    Kou décédé depuis des années kéneu mbirassoul c’est pas normal. Lolou mo andi lii yeup

  • @Fashavision
    @Fashavision ปีที่แล้ว +13

    Aman mbok yo khamnè bagna bok ak niom sakh mo geune li Alal diaroukou adouna diarouko😭

  • @biba9498
    @biba9498 ปีที่แล้ว +22

    Koudoul xalate beusou penthie lou la nekhe defal😢

    • @cisco9615
      @cisco9615 ปีที่แล้ว +3

      Bilahi ndeysane 😢

  • @coundadiallo8586
    @coundadiallo8586 ปีที่แล้ว +7

    Ndeysan souma yalla narè maye alalou adouna pour massiye toutal nite yalla boumako am li niawna si diambour wakhoumalak si moke

  • @CheikhtidianeSy-xk6rd
    @CheikhtidianeSy-xk6rd ปีที่แล้ว +10

    Soungne bayenono daye yombe il doivents saisir la Justice downa yarame Yalla nalene Yalla diapale❤❤❤❤❤

  • @fatoucoulibaly9800
    @fatoucoulibaly9800 ปีที่แล้ว +10

    Tout ça finira inchalla kan sonko sera pr🙏

  • @Queen-forever-n8c
    @Queen-forever-n8c ปีที่แล้ว +10

    Gni sén yaram dou daw sakh Thimmmm
    Bilahi Sénégal dou réw😢

  • @nafidrame868
    @nafidrame868 ปีที่แล้ว +13

    Thiey adouna waxi Souf rek fateni gneup si Souf lagnouy moudié adouna amoul solo mbok alalou yalla la delen ko rafetal

  • @amymalor4641
    @amymalor4641 ปีที่แล้ว +3

    Ndeysane j n peux mém pas retenir mes larmes walay lii rafétoul 😭yalla beurina soutoureu yalnaléne yalla taxawou si barké Mohammed PSL 🙏🤲❤😞

  • @mamendiemethiam7540
    @mamendiemethiam7540 ปีที่แล้ว +11

    Yal na yalla nék séne avocat soléne yégué tribunal yalla diokh léne ndame

  • @thiamasall4400
    @thiamasall4400 ปีที่แล้ว +13

    Waaaaaw ak deee bou gaaw bi amna niou titoul kone 😢

  • @nafifalm9434
    @nafifalm9434 ปีที่แล้ว +5

    Thieuy cette histoire est bien triste Payi delene regler sene keur yi avant de mourir.
    Yeureum na mere bi et son fils. Yalla na souniou borom defar leep

  • @matybraham
    @matybraham ปีที่แล้ว +17

    Koudoul khalat niati fanou bamel loula nékh défal

    • @TeyaSow-j7x
      @TeyaSow-j7x ปีที่แล้ว +2

      Walay 😢

    • @ousmaneba9503
      @ousmaneba9503 ปีที่แล้ว +1

      Non mettina.yallah.bakhna.mei.senegal.so.amoul.khalis.ken.doula.yerem

  • @mariamasambou1075
    @mariamasambou1075 ปีที่แล้ว +2

    Ibrahima tu n as pas un oncle de meme mere et pere de ta maman courage n pleurs pas soit fort pour ta maman dieu est o controle inchallah dina bakh

  • @baegirl8049
    @baegirl8049 ปีที่แล้ว +2

    Hun niaw na torop sakh mais nak Ibrahima neko si deugu nakh waroko fa wone khar. Seutt dou done, bi nieup guéné bayi fa seu yaye ngene warone wadial té khamni tôt ou tard Li dina am ndakh dou continuer. Ils sont les héritiers et sont majoritaires, à moins que seu yaye teguil lene c’est leur droit de faire le partage. Mettina mais keur famille dou keur, courage 🙏🏽

  • @fadieye8219
    @fadieye8219 ปีที่แล้ว +8

    Yalla bi mouy sak famille pour dimbaleuté xamou ma nou histoire bi démé mais li rafétoul yalla na léne yalla may keur bou geune bi barké cheikhoul khadim

    • @khadidjatougaye5153
      @khadidjatougaye5153 ปีที่แล้ว +1

      Affaire famille dafa diara déf attention

    • @fadieye8219
      @fadieye8219 ปีที่แล้ว

      @@khadidjatougaye5153 khana lire message néna xamou na la démé ak lou mo done affaire domou adama nguéne dou ko torokhal

  • @haby8760
    @haby8760 ปีที่แล้ว +3

    Mon frère masta vraiment li métina mais sachez qu'on est de tout cœur avec vous . Dieu n'aime pas les injustes . Li gnawna trop thim ... deugne léna diay dolé wayé gnom khamu gnunikeu Yala eup gneup doolé

  • @astoulaye62
    @astoulaye62 ปีที่แล้ว +8

    Ndeyssane yeurmandé amatoul yénn commentaire yi font mal au coeur. Mou neek seut wala seutaat yeupa si yam c la même famille bilahi Sénégal néxatoul khamé bonn ngueen sen xol yi khatt na. Yalenaleen yallah taxawou ngueen am lou eup lii

    • @aminatasow4504
      @aminatasow4504 ปีที่แล้ว +2

      Bilahi wahgua deug

    • @haby8760
      @haby8760 ปีที่แล้ว

      😢😢😢😢

    • @baegirl8049
      @baegirl8049 ปีที่แล้ว

      Sokhnassi, Li dé khalatouma ko def Sama Adouna, tok niak moma ko gueuneul mais nak niite yi yamougnou, té gni ils sont les héritiers lignou def amnagn si droit kene meunoussi dara. Motakh Adouna demalal seu bop, Lo am nga khamni moy seu weurseuk mais boul yakar si allalou mbolo

    • @haby8760
      @haby8760 ปีที่แล้ว

      @@baegirl8049 bref ngueuné lignu dèf am neugnethi droit kignu guènené témit amneuthi droit dankh domu borom keur gui le

  • @diariabousso466
    @diariabousso466 ปีที่แล้ว +2

    Li mo takh Toubab gueune niou démine. Daniouy def testament avant leur mort nieupe ame diam

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 ปีที่แล้ว +10

    Thièye aduna foumou dieume ohh 😢 mais nak keur

  • @BiramaGueye-so1ui
    @BiramaGueye-so1ui ปีที่แล้ว +19

    Thiey adouna dou nii dée tey ka âme souba do âme yalla naleine yalla soutoural ❤❤❤

    • @maoudediao653
      @maoudediao653 ปีที่แล้ว +2

      K'importe li dafa gnaw masla touti sax

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc ปีที่แล้ว

      ​@@maoudediao653amna gno xamni kéne dou massela ak gnom ki dioy ni daga ko xamoul nak waxx baxoul

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 ปีที่แล้ว +7

    Bilahi métina trop j'ai même les larmes aux yeux 😢😢

  • @dabacisse2957
    @dabacisse2957 ปีที่แล้ว +8

    Ki def li déh elle est sans cœur dothie mon nekh si khôl bi

  • @papeamadourobertfaye729
    @papeamadourobertfaye729 ปีที่แล้ว +6

    Man damay latie ndakh kouy xallat ni beuss dina gneuw di ngua dé gnou sangue leu sangueu la dioulé leu guass bamou xot gnou soul leu you melni doko xalata def . YALLA na len YALLA taxawou

    • @ramadiaw5023
      @ramadiaw5023 ปีที่แล้ว +1

      Bilaay beuss bou diara khalaat lo meun dangoulako daifaal gua wara khamni adouna dou keur...

  • @dashundiaye9401
    @dashundiaye9401 ปีที่แล้ว +4

    Bilaye Senegal yakouna nite yi amatouniou hole waye yalla nopina yalla nale sounou borome tek lohome ❤❤❤❤❤

  • @TEDUNGALTv
    @TEDUNGALTv ปีที่แล้ว +1

    Lii yeup ndakh alalou adouna😢! Yallah nanou takhaw té may niou soutoura, si barki SEYDINA MUHAMMAD (SAWS)😢.

  • @mamediarasy6274
    @mamediarasy6274 ปีที่แล้ว +11

    Métina 😢mais yalla baxna

  • @MaryamaOumouhissaSene
    @MaryamaOumouhissaSene ปีที่แล้ว +1

    Ndeysannne alalou aduna defloneu nit loumuy reuthiou alahira😢thiey dernier jugement Dina metti yalnalén yalla tahawou

  • @ndacksene7214
    @ndacksene7214 ปีที่แล้ว +10

    Thiey famille légui yi .

  • @diatou2190
    @diatou2190 ปีที่แล้ว +1

    Ay way yaye boy boul dioy tu ma fait pleuré yalla andna ak niy mougne

  • @dabadieng-us2vq
    @dabadieng-us2vq ปีที่แล้ว +6

    Yalnalén yalla taxawou😢

  • @mourtalladiakhoumpa4949
    @mourtalladiakhoumpa4949 ปีที่แล้ว +2

    Yallah na yallah tek Senegal thi lokhoy ousman sonko ndakh kou am ak kou gniak yeup yam thi reuw mi

  • @Adamsbaby-o4n
    @Adamsbaby-o4n ปีที่แล้ว +3

    Yéne borom Allal yi yor appartement ak keur youdoul diékh diapalé léne gni Al léne digne deuke allal dangay bokk Al gnilo yéllo yalla da diokhé 'guir nguéne sédelé😢😢😢yéne gniye batré si soiré Waly seck sidy etc am nguéne gninguéne dimbali😢

  • @OusmaneDiop-uk5hm
    @OusmaneDiop-uk5hm ปีที่แล้ว +1

    Bilay merbi defli bou naikon sama yaye ma bayuiko niew faiksi sama cousin bi

  • @Bluelove447
    @Bluelove447 ปีที่แล้ว +38

    C est triste mais il faut savoir partir à temps. Des que lon se marie, il faut essayer d avoir quelques choses à soi même si c est une location. Vivre éternellement dans la maison familiale commune n est pas une option éternelle. Surtout les hommes, songez-y avant de vous marier

    • @mariamaniass7734
      @mariamaniass7734 ปีที่แล้ว +4

      Suis parfaitement d’accord avc vous

    • @mouhameddia5168
      @mouhameddia5168 ปีที่แล้ว +3

      Deugue nékhoul mais ta parfaitement raison,

    • @kanaty9313
      @kanaty9313 ปีที่แล้ว +1

      Verite pire

    • @tyma2640
      @tyma2640 ปีที่แล้ว +1

      On parle de famille de sang

    • @Bluelove447
      @Bluelove447 ปีที่แล้ว +2

      @@tyma2640 la loi ne prend pas en compte cela. Mieux vaut prendre ces precautions que de mettre sa famille de sang dans cette situation oú personne ne gagne.
      On ne peut pas forcer les gens à donner ou faire du bien

  • @astoufall5252
    @astoufall5252 ปีที่แล้ว +5

    Yallah bakhna ki deff li amoul khol 😢

  • @LibasseSow-p2i
    @LibasseSow-p2i ปีที่แล้ว +1

    Ay hathiii lagnou

  • @lakhateToure-s5q
    @lakhateToure-s5q ปีที่แล้ว +1

    Sénégal new dolé togne là

  • @AwaFall-gi8qg
    @AwaFall-gi8qg ปีที่แล้ว

    Dans ce cas nguani respecter ngua sa baye toroxal ay ndiabotam😢

  • @Bbei_mya7343
    @Bbei_mya7343 ปีที่แล้ว +5

    Ndeysann demb mangui fa wonn mais li kouko feke woul meuno kham metite bi kogne bi nieupa dioy😢

    • @mbayerama7292
      @mbayerama7292 ปีที่แล้ว

      Metina d mais je pense que le problème est beaucoup plus profond

  • @UneQueen.22
    @UneQueen.22 ปีที่แล้ว

    Yalna niou yalla doli soutoura🥺li ñiaw na troppp barki alhourane yalna lène yalla may lou gueune li, lou kawè sène ndiorte tè yalla leral lèppp barki Seydina Mouhmed🙏🏾🙏🏾🥺Adouna bi legui nittt yi amatougn soutoura sokhor nagn alal diaral nalène lounè, sou famille yi dèmè bay dèf ni wakhou malak diambour yi

  • @fatoudiakhate1516
    @fatoudiakhate1516 ปีที่แล้ว +1

    Yalla nalén yalla taxawou barke zeydina Mohamed sama xol bi diekhna

  • @abdoulahaddiop2810
    @abdoulahaddiop2810 ปีที่แล้ว +4

    Yallah naléne yallah takhawou ❤

  • @Diarista90
    @Diarista90 ปีที่แล้ว +1

    Ande léne ak yalla mom rék mo meun 🙏🙏🙏😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @diyandiaye944
    @diyandiaye944 ปีที่แล้ว +4

    Soubhane allah 😢😢😢😢😢

  • @elzoatti8951
    @elzoatti8951 ปีที่แล้ว

    la bible dit que dans les derniers jours l'amour du plus grand nombre se refroidira .
    l'homme est un loup pour l'homme .

  • @maguettecamara4578
    @maguettecamara4578 ปีที่แล้ว +1

    Guirr yalla aidé cette famille té yalla takh bilahi souma amone louné guadieu defal léneu ko

  • @dabacisse2957
    @dabacisse2957 ปีที่แล้ว +3

    Aïe waye louko fi diar mère bi sonena adouna bou diekh bi cheuteuteute li gnawna

  • @abdouazizfaye9244
    @abdouazizfaye9244 ปีที่แล้ว +1

    C'est extrêmement triste yalah nalen yallah takhawou. Mais affaire yi ame na lou léroul dé

  • @teningndao6031
    @teningndao6031 ปีที่แล้ว

    Méchanceté gratuite bi am Sénégal diaxal nama trop 😢dangay eupeulé niit ki sax aulieu nga diapalé ko nga koy torokhal ak diko sokhoré. Naniou yeureumanté fii sabililah 😢

  • @khoudiafall2607
    @khoudiafall2607 ปีที่แล้ว +3

    Yalla naléne yalla takhawou😢

  • @AlassaneNdoye-pf5qi
    @AlassaneNdoye-pf5qi ปีที่แล้ว +6

    On verra tout dans ce pays nous ne sommes plus des sénégalais ni des musulmans.

  • @morsarr2259
    @morsarr2259 ปีที่แล้ว +3

    Thiey nitou dkr ak alale

  • @fatoundiaye6991
    @fatoundiaye6991 ปีที่แล้ว

    Ay way adouda diaroul lii ...niawna.... yalnalen yalla takhawou aarlen same len

  • @astellendiaye8799
    @astellendiaye8799 ปีที่แล้ว +2

    Yalnalen yalla tawou

  • @astoulaye62
    @astoulaye62 ปีที่แล้ว +4

    Tiey yallah li louko fi diar

  • @madokhoureychy4886
    @madokhoureychy4886 ปีที่แล้ว

    YALLAH BAKHNA

  • @yacinenguer1358
    @yacinenguer1358 ปีที่แล้ว +2

    Yallanalène yalla até inchallah

  • @namaly829
    @namaly829 ปีที่แล้ว +2

    Vue l’état du monde actuel ou l’humanité a complètement disparue de la conscience des hommes mon Dieu ou va t-on😭

  • @yvefay620
    @yvefay620 ปีที่แล้ว

    Le Sénégal de la méchanceté de l'avoir à tout prix d'injustice

  • @nanafall4134
    @nanafall4134 ปีที่แล้ว

    Na justice deff liguayam il faut gniou sédaléko

  • @aminagueye7013
    @aminagueye7013 ปีที่แล้ว +2

    C'est le cas de bcp de maison entre niary tally medina et fass une seule famille s'accapare de la maison et dit niet aux mirass alors que la maison ne leur appartient pas a eux seul.
    Mirass obligation la si diné

    • @mbayerama7292
      @mbayerama7292 ปีที่แล้ว +1

      Voilà tu a tout compris toi histoire bi gueuna profond li d

    • @thiorodiouf9627
      @thiorodiouf9627 ปีที่แล้ว

      Mais comme benene côté bi amnane khaliss nanou dawal yeurmandé ak mbok bayeko gni amoul dolé

  • @elixxx632
    @elixxx632 ปีที่แล้ว +1

    Cette vidéos a gâcher ma soirée 😭😭😭

  • @sarretv1760
    @sarretv1760 ปีที่แล้ว

    Méttina lole yalla naléne borom takhawou
    Mais seutte loumi déf keur mamame.

  • @mameousmanediaw1221
    @mameousmanediaw1221 ปีที่แล้ว +4

    La justice de ce pays est vraiment

    • @alassanendoye939
      @alassanendoye939 ปีที่แล้ว +2

      Khamoulo nimou démé beug atté...lolou bokoul si mandou ak ragal yalla...gni di wakh d'accord métti na torope mais ba légui dégo niouné niofi mome...fi nga mome akhane kouko beug tothie sa bakane ngakoy diay. Hni momou niou keur gui...légui lo beugue

  • @mariamadabo9100
    @mariamadabo9100 ปีที่แล้ว

    Yalla bakhna

  • @NdeyeNdiaye-bp4el
    @NdeyeNdiaye-bp4el ปีที่แล้ว +6

    😢😢😢

  • @souadoundiaye2744
    @souadoundiaye2744 ปีที่แล้ว +1

    Sénégalais dou nite kou bakh affaire de keur mou diaral le gua khawi soutoura nite wayer Yallah Amna t dina ater nieup Inshalah

    • @elbachirsow2510
      @elbachirsow2510 ปีที่แล้ว

      Guinéen bou sarap ndm la xaliss diaral nalen lou nek

  • @kartoumsakho6772
    @kartoumsakho6772 ปีที่แล้ว +5

    Metina trop Wallahi

  • @mamadoutall5772
    @mamadoutall5772 ปีที่แล้ว +2

    Jai bien écouter le monsieur mais pour moi c'est pas clair du tout

  • @cheikhngom7160
    @cheikhngom7160 ปีที่แล้ว

    الله أكبر لا حول ولا قوة إلاّ بالله العلي العظيم
    " اقترب للنّاس حسابهم وهم في غفلة معرضون"

  • @mariamagueye9084
    @mariamagueye9084 ปีที่แล้ว +2

    Gnack bakhoule. Sou gnou demer ba seut di deukk keur mame

  • @bigpanaby5802
    @bigpanaby5802 ปีที่แล้ว

    😭😭😭😭😭Li metina way

  • @matargueye7200
    @matargueye7200 ปีที่แล้ว

    Fi adouna kenn momou fi sarape dayame niapaye dai bayilenn ake yalla

  • @madokhoureychy4886
    @madokhoureychy4886 ปีที่แล้ว

    BILLAHI BII RABBOUL KAABA, YALNA SWT WANLEKO INCHALLAH

  • @diallomamelatsall7196
    @diallomamelatsall7196 ปีที่แล้ว

    Sokhore amna lii doyneu war thieye Sénégal

  • @luciendienesarrsarr7167
    @luciendienesarrsarr7167 ปีที่แล้ว

    Thiey yalla lii metina vraiment

  • @wonemarie2975
    @wonemarie2975 ปีที่แล้ว

    Ohhhh 😭😭😭😭😭😭

  • @khadysonko663
    @khadysonko663 ปีที่แล้ว

    Yalla nalléne Yalla takhaw amine yarabi inchallah

  • @dabasamb5607
    @dabasamb5607 ปีที่แล้ว +3

    Yalla bakhna metina trop

  • @nouhadiallo2626
    @nouhadiallo2626 ปีที่แล้ว

    😢😢😢😢😢😢😢😢metina 😢

  • @dijasy9974
    @dijasy9974 ปีที่แล้ว

    Dieu est grand

  • @MamadouNdiaye-kw4fx
    @MamadouNdiaye-kw4fx ปีที่แล้ว

    Yalla nalé yalla tahkawou

  • @diewokeita2627
    @diewokeita2627 ปีที่แล้ว +2

    Thièy adouna ci thowal domou baye ak mirass tchimmm

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc ปีที่แล้ว +8

    Faut toujours essayer de savoir les causes exactes y'a des gens défois sounou borom mo léne di toroxal si adouna nax séne gnawtef déléne saytou lissi biir bagna gawantou mane limay waxx louma dounde la magi ak sam béne woudj yay bo xamni bi sama yay gagno en 98 dagnou toroxal humilié yé nagnou lo xalate la nourriture c'était tout à fait un problème dagnou done teud ak khiff you méti mais yalla dafay até ma mère gnimou diour yeup c'est des intellectuelle taw ba thiatt malheureusement féké woul dara mais aujourd'hui gneup gi sante mane nak douma ko neub si tank yi la néke keur gifi sam papa bayi sam yéné moy dieunde ko et walahi azim magi si dina défe louma meune ba dieunde ko toroxal léne geiné léne si xadj mes frères et sœurs gnom dagnouy balé mais mane je suis très rancunier ay domeram deug on a vécu l'enfer tabaski même le mouton dawou gnousi bénéficier wou chose qui ma marqué pendant l'enfance may thiat pa bi je suis le plus jeune une sorcière cette dame complice avec ses enfants mais liko déssé si dounde elle va vivre le pire nako sounou borom bayi fi elle va vivre le calvaire

    • @bilobollo2201
      @bilobollo2201 ปีที่แล้ว +3

      Ah oui des fois niit dina deff dara té kéne dou xam loutakh mais koula deff lou bone nga deff ko lou bone bou yagué nguéne ndirou . Yaw kay défal lou bakh nguir yalla 🙏

    • @anni3465
      @anni3465 ปีที่แล้ว +4

      Lou bonne Kene douko fanyanto 🙏🏾

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc ปีที่แล้ว +2

      @@bilobollo2201 walahi meno comprendre saxx metitt bignou dounde motaxx cas yi dama si téyy bagna gawantou amna gno xamni kéne dou léne diégal on a vécu des moments tellement difficile sans notre maman avec cette sorcière et ses enfants mais dieu est le dernier juge

    • @Bluelove447
      @Bluelove447 ปีที่แล้ว +4

      Je comprends votre douleur
      C est très dur de voir sa mère souffrir mais sil vous plait debarasser vous de la rancune. La vie vous a vengé, vous avez tous reussi.
      Faites votre vie sans les compter
      La vengeance vous fera perdre du temps et de l' energie pour des gens à qui Dieu s est chargé d eux

    • @damecisse2010
      @damecisse2010 ปีที่แล้ว +7

      Beugouma wone wakh sakh je n'ai pas l'habitude de parler sur les réseaux sociaux
      Saa yééné bii ngaa am déé soko motaliwé dossi am ndaam
      Ngaa melni doo dioulite , dioulite dou faayanto, lii ngén mougne nonou motakh Yalla diapalélén, Yalla koumou naaroule faaye doula liguéy loo diaar diaar laawone taaye djii dara dotoula saaf ndakh lii ngaa wéssou
      Kou trokhal niit dii ngaako guiss même soo néké sissaye droit
      Dioulite dafaye def yeufou dioulite

  • @khadipouye3630
    @khadipouye3630 ปีที่แล้ว +1

    4:06 4:08 4:13

  • @NdeyeDiop-dp6ub
    @NdeyeDiop-dp6ub ปีที่แล้ว +1

    C est triste les bonnes volontes aidaint cette famielle

  • @diariabousso466
    @diariabousso466 ปีที่แล้ว

    Lima diakhal moy keur gui limouy reuy reuy béne chambre ngassi ame chambre bi limouy reuy reuy lale ngassiy occuper lale bi limouy reuy reuy touti place ngassiy occuper alors louka fi diar dieufe diou bone dji

  • @malickndiaye631
    @malickndiaye631 ปีที่แล้ว +1

    Affaire mirace dafa doy warr peut être banene famille bi nio apou gni thi dess

  • @pendasy976
    @pendasy976 ปีที่แล้ว +1

    Sama khol bi😭😭😭😭