Touba Baye Fall yi Lou Doy waar Xéwo nafa Cheikh Thioro Mbacke...

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 21 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 103

  • @sambasow6681
    @sambasow6681 24 วันที่ผ่านมา +32

    Pourtant Cheikh Thioro a dit la veritè

    • @mamediarradiop4951
      @mamediarradiop4951 24 วันที่ผ่านมา +2

      Merci beaucoup

    • @saliouniang9471
      @saliouniang9471 22 วันที่ผ่านมา

      Wawe léne goré Mourite kou dokhoule si diguale rék niou tothie sa gate késé nak

  • @DiouldeGueye-e7v
    @DiouldeGueye-e7v 24 วันที่ผ่านมา +7

    Dieureudieufati Serigne Touba khadimoul khadim serigne mountakha mbacké yalla nafi yag lolou tè ande AK werr baye Fall yi diame AK salame si yène ndam réke ❤❤❤❤❤❤

  • @thiouckjr6693
    @thiouckjr6693 24 วันที่ผ่านมา +1

    Cheikh thiorou yalla n'a la serigne salliou takhawou li rek l'an kham si yaw wax dague rek l'an kham si yaw yalla n'a la serigne salliou takhawou ❤❤❤❤

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 24 วันที่ผ่านมา +17

    Touba daal lifi Serigne bi bague Moy Am wa Salam 🧏🏿🧏🏿🧏🏿🧏🏿

  • @ChiekhGeuye-r1y
    @ChiekhGeuye-r1y 24 วันที่ผ่านมา +19

    Cheikh thioro mbacke ❤ diereudief ❤❤❤❤❤

  • @morniane4292
    @morniane4292 24 วันที่ผ่านมา +11

    billahi lidou nione wallahi yallah guiss na lépou 😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @fallousarr9328
    @fallousarr9328 23 วันที่ผ่านมา +3

    Cheikh thioro limou wakh lép deugla

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 24 วันที่ผ่านมา +8

    Baye fall yi daal waw leeeeeeeen goooooooor jërëjëf ❤❤❤❤

  • @PapeFall-y2u
    @PapeFall-y2u 23 วันที่ผ่านมา +1

    Dieufé ndigual reck bilahi ❤❤❤

  • @mamediarradiop4951
    @mamediarradiop4951 24 วันที่ผ่านมา +5

    Merci beaucoup chiekh thioro

  • @BahSalehe
    @BahSalehe 24 วันที่ผ่านมา +5

    Vive viive viiive les baye fall

  • @mamadoudiop3774
    @mamadoudiop3774 24 วันที่ผ่านมา +4

    Diadieuf Cheikh thioro Mbacké ❤🎉

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 24 วันที่ผ่านมา +19

    Baye fall yi bayilén togne yalla beuggoul togne

    • @omarndiaye5827
      @omarndiaye5827 23 วันที่ผ่านมา

      Néma ki wala gni la togne

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 24 วันที่ผ่านมา +7

    Yalla Xam nani inchallah
    Touba lafa Serigne bi begu Moy Am inchallah wa Salam 🧏🏿🧏🏿🧏🏿🧏🏿

    • @thiouckjr6693
      @thiouckjr6693 24 วันที่ผ่านมา

      yaw daguay dol rek yaw seytané nga

  • @Mangayounousse
    @Mangayounousse 24 วันที่ผ่านมา +3

    Cheikh thioro à raison 100%

  • @khadimndiaye5311
    @khadimndiaye5311 23 วันที่ผ่านมา +2

    Touba serigne touba Moka mom limou beugue moy am xaw ma ana mourid ak xalat ndigal diafe lou serigne bi beugue moy lou yalla beugue

    • @MansourDiagne-w1v
      @MansourDiagne-w1v 23 วันที่ผ่านมา

      @@khadimndiaye5311 😂😂

    • @kionking-i9k
      @kionking-i9k 23 วันที่ผ่านมา

      Bou and Ak kham kham si non un grand bataille Dina âme entre les jeunes

  • @papaousseynoubadji6467
    @papaousseynoubadji6467 24 วันที่ผ่านมา +2

    Cheikh Thioro MBACKÉ li bakh ci Touba la wakh ❤

  • @tvcodendiayematarelsdaroua7668
    @tvcodendiayematarelsdaroua7668 22 วันที่ผ่านมา

    Cheikh theoro mbacke ❤❤❤mou fie nike💪💪💪

  • @Amadoudemdia
    @Amadoudemdia 23 วันที่ผ่านมา

    طوبى ليس أرضا خالصا ❤❤

  • @SambouSarr-q6d
    @SambouSarr-q6d 24 วันที่ผ่านมา +3

    Ñak diom moy khekh baye fall😢

  • @NgoudasarrNgoudasarr
    @NgoudasarrNgoudasarr 24 วันที่ผ่านมา +2

    Kou baye fall yi nékhoule ga guéne touba

  • @falltouba8882
    @falltouba8882 24 วันที่ผ่านมา +2

    Cheikh thioro domou ram pir le

  • @cheickmbacke2119
    @cheickmbacke2119 24 วันที่ผ่านมา +2

    Senegal nekhna

  • @Khadimbambapastef40
    @Khadimbambapastef40 24 วันที่ผ่านมา +3

    Je suis cheikh thioro

  • @maremmoseringmourtala1132
    @maremmoseringmourtala1132 24 วันที่ผ่านมา +6

    Chekh thiorou deuk rek la wakh

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj 24 วันที่ผ่านมา +1

    Thioro.mbamke.amoule.yare

  • @ibbasamb9525
    @ibbasamb9525 24 วันที่ผ่านมา +20

    Serigne cheikh thioro limou wakh dara nekousi

    • @cheikhounafall7946
      @cheikhounafall7946 24 วันที่ผ่านมา +1

      Deug rék la wakhe

    • @MoussaFaye-h3g
      @MoussaFaye-h3g 24 วันที่ผ่านมา +1

      Délene di wakh deugu

    • @santbambaahmadu9912
      @santbambaahmadu9912 24 วันที่ผ่านมา +2

      @@ibbasamb9525 yaw daal bu fekkee li Thioro wax dara nekku ci demal tuubaa def fa lañu fay tere ca mbedd ya, wala moom Thioro mu dem ca mbedd ya def ko

    • @dabagning4318
      @dabagning4318 24 วันที่ผ่านมา

      Vous êtes le diable

    • @CheikhounaDiop-f3s
      @CheikhounaDiop-f3s 23 วันที่ผ่านมา

      Sa waay limou wax dara nékou si dmrm nékou len si deuk bi xamo li nit yi di dadj di beuga ray nit yi​@@santbambaahmadu9912

  • @diemeabba545
    @diemeabba545 23 วันที่ผ่านมา

    Touba louléne père noël déf bakhna

  • @Malicksindidi1988
    @Malicksindidi1988 24 วันที่ผ่านมา +3

    BAYE FALL YII SI NDIGËL LANIOU NÉK CHEIKH THIORO DAFA WAARA DEF DÉCLARATION WAX AK XALÉ YII NIOU XAMNI DANIO WARA WORMAL DEUKK BI BAY FALL YI DIOMAY SAH MEUNUL SI NIOM TOUSSS BILLAHI CHEIKH THIORO POLITIQUE LAAY DEF

  • @AliouBa-w3v
    @AliouBa-w3v 23 วันที่ผ่านมา +3

    Koudoul diouly noumouy tégué ay nitt si yone

  • @ChiekhFall-te5fq
    @ChiekhFall-te5fq 24 วันที่ผ่านมา +2

    Man lima gëna Métti rék Mooy gni créé groupe bobou Touddué ko ande khéekh baay Fall yi man lolou rék MoMA naqqari té xamnaani ndam môm dou niouko ci am in Chaa Allaah

    • @oumybadji9482
      @oumybadji9482 23 วันที่ผ่านมา

      @@ChiekhFall-te5fq ba paré niouné ay mouride lagne

  • @momocreation3631
    @momocreation3631 24 วันที่ผ่านมา +4

    cheikh thioro mbacke degue rek la wahk ‘´ baye faux yi liniouy deff touba dou yone

  • @SaliouXelcom-p2k
    @SaliouXelcom-p2k 24 วันที่ผ่านมา

    Cheikh thioro Mbacké jaa jëff

  • @absaduop7965
    @absaduop7965 24 วันที่ผ่านมา +1

    Mais sheikh thoro a raison un pays 2 ètats

  • @abdoulayecissegueye7952
    @abdoulayecissegueye7952 23 วันที่ผ่านมา

    Cheikh Thioro a dit vrai. Cessons le fanatisme niou Jubanti rewmi

  • @abdoufatahgueye1306
    @abdoufatahgueye1306 24 วันที่ผ่านมา

    Cheikh dall deug rk la wakh❤

  • @dadjoutoure-kr2kn
    @dadjoutoure-kr2kn 24 วันที่ผ่านมา +4

    Les baye bopou yakh nanou touba

  • @fatousyllafall829
    @fatousyllafall829 24 วันที่ผ่านมา

    Yalla bakhna😢

  • @ibrahimaba4029
    @ibrahimaba4029 24 วันที่ผ่านมา +7

    Baye fall yii nekk lenn ayy ñitt.

  • @Horizon_peace2025
    @Horizon_peace2025 24 วันที่ผ่านมา +3

    A vrai dire la securite publique ne devrait revenir qu'a la.police et la gendarmerie sur tout l'etendue du territoire sans exception et l'armee si l'autorite publique le juge necessaire.Les politiciens creent souvent des precedents dangereux a des fins de gain politique.

    • @Madou-h1g
      @Madou-h1g 23 วันที่ผ่านมา

      Police et gandarmerie on fahi leur mission il nassur rien a touba

  • @abibmarouane6699
    @abibmarouane6699 24 วันที่ผ่านมา

    Cheikh Thioro limou wakh moy deugeu

  • @thioyedoumo9571
    @thioyedoumo9571 24 วันที่ผ่านมา +2

    Il ne peut pas y avoir un État dans un Etat. Touba fait parti du Sénégal et la sécurité dans cette ville doit être assurée par les forces de l'ordre et non par des baye fall. Et si on règle pas ce problème les jeunes vont riposter parcequ ils ont droit à l'education , à faire du sport qui ne sont pas des crimes . On ne peut accepter des droits pour des jeunes d'une partie du pays et les refuser pour les autres.Le Sénégal est un et indivisible.

    • @idrissasarr4584
      @idrissasarr4584 24 วันที่ผ่านมา

      @@thioyedoumo9571 wahe deugeu yallah gni thi kawe gnoye responsable yi merci deugeu dou robeu nope

    • @Madou-h1g
      @Madou-h1g 23 วันที่ผ่านมา

      Pourtant le tabas nes pas un crime aller a touba pour fumer dotoko defaty touba titre foncier la faut pas oublier sa peut pas etre comme dakar ou autre localiter

  • @otmangay6190
    @otmangay6190 24 วันที่ผ่านมา +1

    Cheikh Thioro deug rk la wakh civil dou régler borome civile li mouye deugg

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 24 วันที่ผ่านมา +3

    Cheikh thioro xamal sa bopo ano niou AK yaw dh sonko lan andal wa Salam ❌❌❌❌

  • @MadickeGueye-f6r
    @MadickeGueye-f6r 24 วันที่ผ่านมา +1

    Néklén nit tay dieufé ndiguel

  • @mouhamadoudiagne3789
    @mouhamadoudiagne3789 24 วันที่ผ่านมา

    😂😂 Sénégal mo nekh

  • @Beug-io8bs
    @Beug-io8bs 24 วันที่ผ่านมา

    Cheikh Thiorro limou wakh wakhi Serigne Mountakha la té mouy deugue guou wérr,ana loussi djiarr riirr mii.

    • @Madou-h1g
      @Madou-h1g 23 วันที่ผ่านมา

      Fane lako serigne bi binde si bane tere

  • @serignesaliousylla9426
    @serignesaliousylla9426 23 วันที่ผ่านมา

    Baye fall yi danio rew nekoul nio wara yoré kanragué bi si Touba baye fall nio geuneu xamadi beugeu korigé nitte ngi lollou dafa meuna nekk

  • @masiba7272
    @masiba7272 22 วันที่ผ่านมา

    Naniou dem rek

  • @Badboydieme4963
    @Badboydieme4963 23 วันที่ผ่านมา

    Cheikh thioro a bien dit

  • @cheikhsalaan9205
    @cheikhsalaan9205 23 วันที่ผ่านมา

    Cheikh bi limou wx deug la siwil dou yar moromam

  • @bayeniasse5604
    @bayeniasse5604 24 วันที่ผ่านมา

    Nègneko waxtanè rek fitna baxoul 😢

  • @Massiyuwe23C
    @Massiyuwe23C 24 วันที่ผ่านมา +2

    Nasi eta bi dieul ay mato waye

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth1968 24 วันที่ผ่านมา

    koudoul dioulli douwoor nanla mana sammé dijkoyi ci Touba?
    Serin̈ Mountakha warna seetaat lii.

  • @PapamodricDiatta
    @PapamodricDiatta 24 วันที่ผ่านมา

    Li dou yone

  • @bayemodoufall2879
    @bayemodoufall2879 24 วันที่ผ่านมา

    😂😂🎉😂😂

  • @sadiocamara7957
    @sadiocamara7957 22 วันที่ผ่านมา

    YALLA MO ATTÉ KOU WAKH SI BOKALÉ AK BIDAH NGEUNE SAGA KO DOOR KO , YALLA MOLEN FITNAL , NÉNEU DEUG MOU SELLEU MI😂😂😂KHANA TARIKHA BAYE FALL NIAK DIOLI

  • @ngathiefallmusiquefromsene2060
    @ngathiefallmusiquefromsene2060 24 วันที่ผ่านมา +1

    Touba bamba KO mome ti ni wala ti na li Serigne bi beug rék Moy ame kouko menoul genal deukou diabour c'est facile

  • @mamourfall2034
    @mamourfall2034 23 วันที่ผ่านมา

    Koudoul diouli meuna dioubal kéne

  • @khadimdiaw3936
    @khadimdiaw3936 24 วันที่ผ่านมา

    ❌❌❌❌❌❌❌bayilen yefitna

  • @MassDiene-o9p
    @MassDiene-o9p 24 วันที่ผ่านมา

    Deug deug li député bi wah moy yonn bay fall hama bay faut Nanou Yam thi liguéy Balla mbirmi dilén eup dolé

  • @mamemorniang9550
    @mamemorniang9550 24 วันที่ผ่านมา

    Touba ndi gall diefé mourid saadikh dou khoulo ak baye falllllllllll عبدالله وخديم رسوله صلى الله عليه وسلم

  • @ModouDieng-mg7pb
    @ModouDieng-mg7pb 24 วันที่ผ่านมา

    lim wakh mooy deug siwil dou yar moromou siwilam

  • @djilydiaw1587
    @djilydiaw1587 23 วันที่ผ่านมา

    Dême laine légeyi diolli dji wakhtou diarom yi té wor wérou koor gui mou ap chance nék fi lor domo diambouri yi rck

  • @MansourDiagne-w1v
    @MansourDiagne-w1v 23 วันที่ผ่านมา

    😂😂😂😂😂

  • @moussandour3967
    @moussandour3967 23 วันที่ผ่านมา

    Bay Fall yi rekk yal'na sa Borom defalen taw'fekh barké Borom Touba

  • @OusseynouThioub-ev8wn
    @OusseynouThioub-ev8wn 23 วันที่ผ่านมา

    Way khamnga lan la wakhi ch thioro dji dal mom gnisi niaka and gnila moy gni amoule xam xam ba nopi nafékh niognou kassé la nak

  • @kinediop6836
    @kinediop6836 24 วันที่ผ่านมา

    Mes maqua sa melouni

  • @kandeDiogna-b3m
    @kandeDiogna-b3m 23 วันที่ผ่านมา

    Na etabi dindi si ly

  • @walomafierte4051
    @walomafierte4051 24 วันที่ผ่านมา

    Baye fall yi nagnou réglé ordre public civil douko réglé

    • @Madou-h1g
      @Madou-h1g 23 วันที่ผ่านมา

      Demal defa louniou faye tere tu vera

  • @dembafall2230
    @dembafall2230 24 วันที่ผ่านมา

    Bay fal yi neklén ay nit

  • @DioufFallou-l5q
    @DioufFallou-l5q 23 วันที่ผ่านมา

    Lila diglè baye falla yi nekouniousi douniou diouly douniou wor ta lolou mo geuneu Bone fouf

  • @yadijallo1969
    @yadijallo1969 24 วันที่ผ่านมา

    Baye fall yi danio rew aye yeffeur lagne

    • @Madou-h1g
      @Madou-h1g 23 วันที่ผ่านมา

      Yaw loussa yone si deukou diambour demal ndeye guinee sa deuk si diabrer ba domarame liniouy wakh pour senegalais yi la dou pour etranger

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 24 วันที่ผ่านมา +1

    Niak dioum soof ak niaka Xam seen boupo rek mo leen diopo

  • @senegalvillagetvdiop5152
    @senegalvillagetvdiop5152 23 วันที่ผ่านมา

    Bayi lene thiakhane yi bis bou nek gnou togn sounou brome
    Touba ci rewmi la bokk te juste bènela s c t mbacke deug la wa conne rewmi yekhou

  • @cheikhounagaye7876
    @cheikhounagaye7876 24 วันที่ผ่านมา

    Baye bolokk yi Daniou ndayi rw

  • @Badboydieme4963
    @Badboydieme4963 23 วันที่ผ่านมา

    C’est du n’importe quoi