Héhé Baye Cheikh Khassida takk na diabar : Mariage entre Baye Cheikh et la fille de Sokhna Aïda...

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 3 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น •

  • @mouhamedlo1093
    @mouhamedlo1093 6 วันที่ผ่านมา +63

    Yalna yalla barkél seuy bi si barké séydina Mouhamed psl ❤

  • @NDIAYEelhadjimbara-tm8jh
    @NDIAYEelhadjimbara-tm8jh 6 วันที่ผ่านมา +29

    Waw yéne dégue ngén ré baye cheikh yi

    • @zedinho365
      @zedinho365 5 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂😂

    • @fatoujoof2093
      @fatoujoof2093 5 วันที่ผ่านมา

      talk Baye cheikh dundal

    • @fatoujoof2093
      @fatoujoof2093 5 วันที่ผ่านมา +1

      People lie too much is very sad

    • @YaramWade-u1j
      @YaramWade-u1j 4 วันที่ผ่านมา

      At yayu Wally Ballago seck😂

  • @gueyemokhtar9884
    @gueyemokhtar9884 5 วันที่ผ่านมา +12

    Baye chiekh goudal fan ta wer

  • @lepatriotevivesonkopreside4570
    @lepatriotevivesonkopreside4570 6 วันที่ผ่านมา +11

    Macha Allah Baye cheikh ❤

  • @BabacarDiop-de7km
    @BabacarDiop-de7km 6 วันที่ผ่านมา +12

    Machallah damako beug mane Baye Cheikh na sa diam yag❤❤❤

  • @halikano392
    @halikano392 5 วันที่ผ่านมา +22

    Kouko guisse thia fauteuillou massage ba😂😂😂😂😂

    • @cheikhdiop9932
      @cheikhdiop9932 5 วันที่ผ่านมา

      Bilahi lolou momay ray 😂 wouy yay

    • @diemysene6033
      @diemysene6033 5 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @liesarotine9436
      @liesarotine9436 4 วันที่ผ่านมา

      Dama retane ba sone 😂

    • @SowAstou-yl5lp
      @SowAstou-yl5lp 16 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Mane😂😂😂

  • @Nafina-v7u
    @Nafina-v7u 4 วันที่ผ่านมา +5

    Wa ki da tak diabar walla ki bb la nonnnnn Sénégal dal 😂😂😂😂 et puis il est super futé machalah mane quand je l'ai vu pour la première fois kouss lako tegone cheuuuttte laf thiat

    • @jadore_stella
      @jadore_stella 3 วันที่ผ่านมา +1

      😅😅😅😅😅

  • @mamedabakh8494
    @mamedabakh8494 5 วันที่ผ่านมา +6

    Musique mom bouko Ken djema daguanal! Yalnañ yala doli Soutoura rek! Yalna ñep am djam, mais nit ñi mom Ken meunoulen terei wakh

  • @cheikhsalaan9205
    @cheikhsalaan9205 9 วันที่ผ่านมา +23

    Baye cheikh yamal thi sa ndiagoum khassidami bakhna

  • @bintoubop7847
    @bintoubop7847 5 วันที่ผ่านมา +1

    Wakhonafi né baye cheikh dh takagoul bén bay takk niarr ak niétt ms tay dh da melni tak na yalna seuy bi barkél🎉❤

  • @mariemegueye6368
    @mariemegueye6368 5 วันที่ผ่านมา +2

    Baye cheikh nite kou humble😊😊😂😂😂

  • @aronasarr5690
    @aronasarr5690 9 วันที่ผ่านมา +8

    Kilifeu gui ❤😊

  • @mohameddanfakha3160
    @mohameddanfakha3160 4 วันที่ผ่านมา +1

    Le goss la est très très très malin et intelligent ❤❤❤❤

  • @adafatygadji100
    @adafatygadji100 6 วันที่ผ่านมา +2

    Thieuye baye cheikh yalle nala yalla déffale diame wayé baye cheikh kone ALHAYRI NA WALA

  • @assanetoure799
    @assanetoure799 7 วันที่ผ่านมา +4

    Machalah bay cheikh ❤

  • @lakhatthiam6044
    @lakhatthiam6044 6 วันที่ผ่านมา +5

    Amine inchallah

  • @MamadouMbaye-h2b
    @MamadouMbaye-h2b 5 วันที่ผ่านมา +5

    Mais ki gnata att la ame mach'allah

    • @halikano392
      @halikano392 5 วันที่ผ่านมา +1

      Sujet tabou néna mo yorome échelle bi bignouye peinture assamane

    • @YummaM
      @YummaM 4 วันที่ผ่านมา

      ​@@halikano392 maname?? Comprendrouma dé

    • @thiekaniang3507
      @thiekaniang3507 2 วันที่ผ่านมา

      D'où khalé dé dafa magouille rek.

  • @Damelfaye
    @Damelfaye 13 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Doulen ma tountu Baye cheikh mani koy bi numu loullu😂😂

  • @MameAbdouDiouf-l8y
    @MameAbdouDiouf-l8y 5 วันที่ผ่านมา +1

    Machallah ❤

  • @fatoukinetdieng2917
    @fatoukinetdieng2917 4 วันที่ผ่านมา

    Heureux ménage mon fils ❤

  • @FallOumy-uc9me
    @FallOumy-uc9me 5 วันที่ผ่านมา

    Dieureudieuf sohna aida bou Serigne saliou thii baye cheikh soeurou Alioune sow domene yayou Waly seck

  • @mamadoudiawsy7150
    @mamadoudiawsy7150 4 วันที่ผ่านมา +2

    Baye sékh mii déh dou guonéh😂

  • @Damelfaye
    @Damelfaye 13 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Baye cheikh maytul mer yi fanyi miar yi dano rakadio dhé 😂😂

  • @yaragteggiin5101
    @yaragteggiin5101 6 วันที่ผ่านมา +3

    Baye cheikh legui yakhou nga rek fa nga nekkon ak fi nga nekk legui ....

  • @astouciss4961
    @astouciss4961 2 วันที่ผ่านมา

    Ki maggou demb yi démoon gno nieuwaat d BAAY CHEIKH mi preuv bi😂😂

  • @papendoye4285
    @papendoye4285 6 วันที่ผ่านมา +4

    Machalla

  • @abdolfataniang5398
    @abdolfataniang5398 5 วันที่ผ่านมา +1

    Man de baye chiekh akamako sopon te xassida yi rkk mo takhon waye lee gi commenter li ma nakhari rk romb lee gi ciy thiakhan kese lane te bo bayi woul lee gi tay ga geuna fay 😢😢😢😢😢😢😢le gi kom kou amoul ay kilifa😢😢😢😢😢

  • @latifthiam1114
    @latifthiam1114 6 วันที่ผ่านมา +3

    Baye cheikh yalla goudou fane bou andake wére baye cheikh moudié na dawe kouko wakhlo loume bougouta wakh laye banie😂😂😂

  • @SoriaDtv
    @SoriaDtv 6 วันที่ผ่านมา +9

    Khalé makk😂😂😂😂

  • @fashionfashion1330
    @fashionfashion1330 6 วันที่ผ่านมา +74

    Yonenetebi wakhoul lolou dé, ta palé kat yidoul diouli gnokoy fénal, bayi lén fénal Seydouna Mouhamed

    • @ousmanediouf4592
      @ousmanediouf4592 6 วันที่ผ่านมา +21

      Ap yaar déh beurina ko khamni par fois mou guiss nite raw ko ta dou takh mou kham loumou ko rawé beurina aussi lo khamni nite dina kheuy niak ko ta dara dou koko takha niak loudoul ap niak yaram yaw mi di wakh déh ak sa ndioulité gui guaye diay warone na takh bo toudé tourou ynt bi psl rék gua bagne thia wara ték lénéne wala sakh gua wormal wakh dji ndakh sounou borom mou mag mi dako fonkone ba bouy toud toureum sakh douko salawlé yaw nak dagua toud tour wou mag wou nékh Wii ba nopi ték lolou kham Nani ibadou gua 😂😂 wayé fani mom khéwou léne 😂😂

    • @djilylo9764
      @djilylo9764 6 วันที่ผ่านมา +9

      Kou tégui wakhou diambour daga fay ték dara.wédi rék té khamou léne dara

    • @adjafatouthiaw2094
      @adjafatouthiaw2094 6 วันที่ผ่านมา +7

      Haleyhi salatou wa salam

    • @MOURIDESAADIKHA-dz6qm
      @MOURIDESAADIKHA-dz6qm 6 วันที่ผ่านมา

      ​@@djilylo9764🤑🐈‍⬛🐒🪳🤑YAW YÃYE DÛL KAT BU MAKBI
      WAHABIT DÔMU XARÃM BU MAKBI🤑🤑🐈‍⬛🐒🔥🪳🤑

    • @ousmanediouf4592
      @ousmanediouf4592 5 วันที่ผ่านมา +1

      @@djilylo9764 mom mi wakh ni ynt bi psl wakhoul lolou loumou fa ték dafa wédi rék di téguoufa dara loudoul ap sagua di ta yaw deug la mane khamouma dara wayé yaw esk meune gua lire thi téguine déh lay wakh guaye wakh wakhou kham dara bou nékone devoir la déh guandame 00 guaye am 😂😂mane mom d’accord Nani khamouma darawayé Magui sante ndakh lép louma war sama diguanték sama borom Magui thi diém sama kém katane meunouma kham nak ba kham lép ndakh guissa guouma kouko déff Lo kham kham digua am lo oumpalé

  • @Amdyridial28
    @Amdyridial28 6 วันที่ผ่านมา +1

    baye cheikh manchalla yallna yalla barkél seye vraiment manchallah

  • @ToutaNdiayeTouta
    @ToutaNdiayeTouta 6 วันที่ผ่านมา +15

    Ki dou khalei doumako Nagou moukou😂😂😂😂

    • @NdeyeFatouGaye-o4w
      @NdeyeFatouGaye-o4w 6 วันที่ผ่านมา +2

      Mo mak thieré masec lalo dh 🤣🤣🤣

    • @ousmanendiaye7436
      @ousmanendiaye7436 6 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @mouhamadoufall4774
      @mouhamadoufall4774 6 วันที่ผ่านมา

      Ki mola magg dé.

    • @KhadimNiang-c8x
      @KhadimNiang-c8x 6 วันที่ผ่านมา

      Ngandi koye la yorr 😂😂

    • @NdeyeFatouGaye-o4w
      @NdeyeFatouGaye-o4w 6 วันที่ผ่านมา

      @@KhadimNiang-c8x soubhanalah 🥺🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @Damelfaye
    @Damelfaye 13 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Mee Baye cheikh sa bagas yi numu ware toulu sakh😂😂😂

  • @pascalkane9767
    @pascalkane9767 4 วันที่ผ่านมา +2

    Mais moi je veux savoir si c'est un enfant ou un adulte ?

  • @LampNiang-p3i
    @LampNiang-p3i 5 วันที่ผ่านมา

    Baye cheikh légui sho bus rek gua toppou bayil sa thiakhane yi

  • @BinetaNdiaye-e2v
    @BinetaNdiaye-e2v 5 วันที่ผ่านมา +1

    Bayilene Di togne Baye cheikhe

  • @modoufayembaye1202
    @modoufayembaye1202 6 วันที่ผ่านมา +2

    Machalla yapou ndaw mon soull yapou mak

    • @NdaoNdaw-z7h
      @NdaoNdaw-z7h 6 วันที่ผ่านมา +1

      Mbous mo ndaw mounou sol yapou mak mangui ziar dieuwrin

  • @ElhadjiWade-bo6lp
    @ElhadjiWade-bo6lp 4 วันที่ผ่านมา

    Baye cheikh nimiy rétané nonoulay dano damay ragal gua nékak sokhna si danou sokhnasi wakhla baye cheikh loy rétane😅

  • @abdousoung8061
    @abdousoung8061 3 วันที่ผ่านมา

    Khawma wonne dinaaa mossa diommi 😢

  • @Muhamadulaminebara-u
    @Muhamadulaminebara-u 5 วันที่ผ่านมา +2

    Damay sétaan bam yag ma 😂😂😂😂

  • @MouhamedBalde-t7q
    @MouhamedBalde-t7q 4 วันที่ผ่านมา

    Il a quel âge 😊

  • @mohameddanfakha3160
    @mohameddanfakha3160 4 วันที่ผ่านมา +1

    Fanatique , fanatisme de certains Sénégalais jusqu'à sortir du cadre de l'islam,c'est bien mais sans exagérer 😂😂😂😂

  • @dienediouf2887
    @dienediouf2887 5 วันที่ผ่านมา +1

    souma nékone khalé bou djiguéne dina fékhé ba irri baye cheikh pour hame daah khalé wala 😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @requinquin1
    @requinquin1 วันที่ผ่านมา

    Pourquoi Hé Hé Baye Cheikh takk na diabar 😱?
    Khana dou nitt

  • @SouleymaneGueye-m6l
    @SouleymaneGueye-m6l 5 วันที่ผ่านมา +1

    Baye cheikh yamal SAP thiouthiou

  • @serignesalioulo8023
    @serignesalioulo8023 5 วันที่ผ่านมา +4

    Kilaye jaay tissu dh dalou si

    • @fall8270
      @fall8270 3 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂

  • @AstouDiouf-p4v
    @AstouDiouf-p4v วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤,🕋🕋

  • @fawadedieng4629
    @fawadedieng4629 6 วันที่ผ่านมา

    😂😂😂 Baye cheikh ken douka dougal 😂😂😂❤

  • @gerkking7087
    @gerkking7087 4 วันที่ผ่านมา

    Ay baye cheikh jangue katou khassida dou defak neine aki peitaw
    Bagnal lolou

  • @GallassGyeye
    @GallassGyeye 5 วันที่ผ่านมา +1

    🙏🙏🙏

  • @dawdajallow5362
    @dawdajallow5362 6 วันที่ผ่านมา +2

    Who's this one also

  • @GoraFall-m8k
    @GoraFall-m8k 4 วันที่ผ่านมา

    Billaahi wakhe nga deuge

  • @mohameddanfakha3160
    @mohameddanfakha3160 4 วันที่ผ่านมา +1

    Il a quel âge ?Il a un esprit plus grand que lui ,il règle comme un adulte❤❤❤❤

    • @requinquin1
      @requinquin1 วันที่ผ่านมา

      Mo makk Nelson Mandela nga naan
      Kii Nain la

  • @poundkiima4241
    @poundkiima4241 6 วันที่ผ่านมา +2

    😂😂😂 ki beugoul goudou fane dei

  • @AissatouDjilive
    @AissatouDjilive 6 วันที่ผ่านมา +4

    Yaguimay dougueul si sompice bi

  • @FamaBeye-vw4ct
    @FamaBeye-vw4ct 9 วันที่ผ่านมา +3

    ❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉

  • @khadijaboye2619
    @khadijaboye2619 6 วันที่ผ่านมา +2

    Le petit mbacke en miniature 😂😂
    Ya mak thiere mak lalo mak yonenti yalla Adama..
    Degal mounane " gatt " bi ndamar bi thiey li
    Yalla nala borom bi defal soutoureu ak tawfekh si barke Serigne Touba

  • @elizabethndione8558
    @elizabethndione8558 5 วันที่ผ่านมา +2

    Il ressemble à sokhna Aïda 😂

    • @ramaba2521
      @ramaba2521 5 วันที่ผ่านมา

      Esk dou domame mdrrr

  • @ousmanefall7109
    @ousmanefall7109 6 วันที่ผ่านมา +5

    Noooooon !!! Saway dal cinéma la 😂😂😂

    • @NdeyeFatouGaye-o4w
      @NdeyeFatouGaye-o4w 6 วันที่ผ่านมา

      Bou mak ray nama ak danane ndanane lou bi 😂😂😂😂

    • @ousmanefall7109
      @ousmanefall7109 5 วันที่ผ่านมา

      @NdeyeFatouGaye-o4w Kone sétlou nga ko 🤣🤣🤣

    • @NdeyeFatouGaye-o4w
      @NdeyeFatouGaye-o4w 5 วันที่ผ่านมา

      @@ousmanefall7109 non lolou mama ray kW 🤣

    • @ousmanefall7109
      @ousmanefall7109 5 วันที่ผ่านมา +1

      @@NdeyeFatouGaye-o4w Merci Ndéye rétane naa ba sone 🤣🤣🤣

  • @lakhatthiam6044
    @lakhatthiam6044 6 วันที่ผ่านมา +1

    Amine

  • @NdamGueye
    @NdamGueye 5 วันที่ผ่านมา

    Sénégal Mo nexx nossi guener rek ak noumou Mel Baxna

  • @diakhatemariam1490
    @diakhatemariam1490 5 วันที่ผ่านมา

    Ki khm nako amna 60 an😅😅😅😅😅😅😅

  • @NdeyeFatouGaye-o4w
    @NdeyeFatouGaye-o4w 6 วันที่ผ่านมา +1

    ,😂😂😂😂😂😂wouy sampou rek

  • @MbakieLo
    @MbakieLo 6 วันที่ผ่านมา +1

    🎉🎉

  • @sirmandiallo4685
    @sirmandiallo4685 4 วันที่ผ่านมา

    Aye way Sénégal doyna warr

  • @NdeyeSokhnaSougou-l2v
    @NdeyeSokhnaSougou-l2v 5 วันที่ผ่านมา

    ALLAHOUMA AMINE

  • @AronaDeme-e7n
    @AronaDeme-e7n 3 วันที่ผ่านมา

    A chaq ue chose temps ; ce garçon devrait s occuper d autre chose que de mariage qui est une responsabilité d adulte.

  • @chocsevenements8990
    @chocsevenements8990 6 วันที่ผ่านมา

    Après niou nei ki khalei la 😂😂😂😂😂senegal doorkat keissei leu

  • @RamaNdiaye-f9n
    @RamaNdiaye-f9n 6 วันที่ผ่านมา +1

    Il ressemble à kirikou 😂😂😂😂

    • @fallfall3571
      @fallfall3571 4 วันที่ผ่านมา

      N’importe quoi ?

  • @adamandoye6893
    @adamandoye6893 2 วันที่ผ่านมา

    Athia baye chiekh mo dothie

  • @falloudiagne5902
    @falloudiagne5902 5 วันที่ผ่านมา +1

    Ki mon dothi ak rééyi 😂

  • @FallOumy-uc9me
    @FallOumy-uc9me 5 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bayemodoufall2879
    @bayemodoufall2879 4 วันที่ผ่านมา

    😢😢😢

  • @sandysandy-fz4bf
    @sandysandy-fz4bf 5 วันที่ผ่านมา

    Ki khana papame wakhoul ne khaler la 14 ans la ame 😅

  • @mbayetoure1358
    @mbayetoure1358 8 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤❤

  • @ramasane7751
    @ramasane7751 6 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimadrame2931
    @ibrahimadrame2931 6 วันที่ผ่านมา

    Il a quel âge

  • @RamaNdiaye-f9n
    @RamaNdiaye-f9n 6 วันที่ผ่านมา

    Oh mon dieu 😂😂😂😂

  • @africafutur
    @africafutur 5 วันที่ผ่านมา

    Baye Cheikh daal jang na natation ba mokal... Allez Yaaram...😊

  • @adamadiouf487
    @adamadiouf487 6 วันที่ผ่านมา

    Sokhna si délol Khaley bi ay wadiouram ki Khaley la 😂😂

  • @Taphiendoye
    @Taphiendoye 6 วันที่ผ่านมา

    Khallé bouniou sole yapou mak😂😂😂😂😂

  • @MamadouCoulibaly-fv7ko
    @MamadouCoulibaly-fv7ko 5 วันที่ผ่านมา

    Baye cheikh meytoul caméra yii

  • @elhadjidiakhate8858
    @elhadjidiakhate8858 6 วันที่ผ่านมา +12

    Bay cheikh mi dh bi Serigne bi di dém si touki bi filako bawon

    • @BolleGiadiaga
      @BolleGiadiaga 6 วันที่ผ่านมา

      😅😅😅😅

    • @fallserignebara4028
      @fallserignebara4028 6 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂

    • @SarrDiattou
      @SarrDiattou 6 วันที่ผ่านมา

      Akaay deug

    • @AliouCisse-w9n
      @AliouCisse-w9n 6 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂😂😂

    • @FatouSamb-e5y
      @FatouSamb-e5y 6 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂doumako wèddi dè

  • @MoussaDione-jn8mb
    @MoussaDione-jn8mb 4 วันที่ผ่านมา

    ولا تقل لأحد كذبت

  • @komxel
    @komxel 6 วันที่ผ่านมา

    Fo ak thiaxaan rek

  • @toubaparcelles
    @toubaparcelles 3 วันที่ผ่านมา

    Baye cheikh guissouma kemtane ndaxe Touba barina aye toute tank you binde kamil mokal alkhourane. Nite yi nek dila commerce lo woutou kayou xaliss. Serigne Touba andoul ak aye thiaxane

  • @PapeSow-bz7xl
    @PapeSow-bz7xl 5 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤😂😂🎉🎉

  • @BambaGuene
    @BambaGuene 5 วันที่ผ่านมา +1

    😂😂😂❤

  • @AstouAstou.toutay-q1n
    @AstouAstou.toutay-q1n 5 วันที่ผ่านมา

    Hi

  • @khadimniang4856
    @khadimniang4856 5 วันที่ผ่านมา

    Baye diabar teel na de

  • @BayeCheikhSeck-l1l
    @BayeCheikhSeck-l1l 5 วันที่ผ่านมา

    😊😊😊😊🎉😂😊

  • @malickkane2571
    @malickkane2571 6 วันที่ผ่านมา

    Gir yala bay cheikh Niata at la am😂

    • @ToutaNdiayeTouta
      @ToutaNdiayeTouta 6 วันที่ผ่านมา

      Lolou dh diakhal Nama loooooole

    • @ndarylo6781
      @ndarylo6781 6 วันที่ผ่านมา

      Billahi soka xame gua japale ma si

    • @OusmanemoussaCisse-w3k
      @OusmanemoussaCisse-w3k 6 วันที่ผ่านมา

      38ans😂😂😂

    • @halikano392
      @halikano392 5 วันที่ผ่านมา

      Wa baye Cheikh da moudié ragal wally😅

  • @MameabdoudrameDrame
    @MameabdoudrameDrame 6 วันที่ผ่านมา +1

    Way sarap ndèy lii rèk louy lii

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 6 วันที่ผ่านมา +1

    Wa fou Yonentou bi wakhe tegal bene biir mo geun tabakh 40 dioumah ? Khadizla wala ? Bayilen thiakhan

  • @SerigneNdiaye-b6b
    @SerigneNdiaye-b6b 5 วันที่ผ่านมา

    🕊️🤍🙏☝️

  • @ndiouga-lf6hp
    @ndiouga-lf6hp 6 วันที่ผ่านมา

    Khale 😂😂😂

  • @sourangnare2824
    @sourangnare2824 2 วันที่ผ่านมา

    Ndey san degal nena damay bagne mouride dale sama kaw li ngua nek boul si diougué

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp 6 วันที่ผ่านมา +1

    Jàppal ci xasiida yi te moytu media bi!!!

  • @ibrahimadiop5736
    @ibrahimadiop5736 8 วันที่ผ่านมา

    Bilaxi wakhngua degue loulen woroul rek lagnouy wakh

  • @fallouyathe5852
    @fallouyathe5852 5 วันที่ผ่านมา

    😂😂😂😊