mon idole YN était en pleine forme hier. Il a su apporter une nouvelle touche en chantant des chansons des années 90 telles que Fenene, hey you, wiri wiri et j’en passe. C’est les chansons de l’apogée du super étoile et qui ont fait de YN une star planétaire. Bref, le grand bal d’hier est l’un des concerts les plus réussis. Respect au géant de la musique africaine
Ki done filmé hana dou professionnel lou mel ni grand bal ngay flimer ak caméra bou bonne bii longue vie à papa you on t’aime très fort vous êtes le meilleur et sa c’est pour toujours ❤❤❤❤❤❤❤forever
Papa Youssou africa bi defko version française ak anglais si ce n’est pas encore fait …trop intéressant j’adore
Wala clip bou ande ak sous titre anglais. Lol
mon idole YN était en pleine forme hier. Il a su apporter une nouvelle touche en chantant des chansons des années 90 telles que Fenene, hey you, wiri wiri et j’en passe. C’est les chansons de l’apogée du super étoile et qui ont fait de YN une star planétaire. Bref, le grand bal d’hier est l’un des concerts les plus réussis. Respect au géant de la musique africaine
Pa You ya meune nak ❤❤❤
Tu es le meilleur de ta génération machallah.
Youssou Ndour c’est le meilleur duo Ak waly bi rafetna n’a yaye bayâme
Mame You khana badiane You ndieuk yi lay wakhal d’où sama boss dh mom 😢
❤Youssou le père du peuple, on t’aime fort 💪
Ayewaye diape lenema❤ magui ball lou reuy sama keur❤Papa Youssou goudale fane❤❤
Ki done filmé hana dou professionnel lou mel ni grand bal ngay flimer ak caméra bou bonne bii longue vie à papa you on t’aime très fort vous êtes le meilleur et sa c’est pour toujours ❤❤❤❤❤❤❤forever
🤣😂😂😂
Pour mane deh sma téléphone mo ame blème 😂
Billahi caméramane yii danio yabaté coupé appétit lagne meune 🤣🤣🤣
Mais cou guiss kou solon Lou wekh nek si kaw mom kassé 😮cas len si mais papa you on te❤
Le meilleur de tous les temps
Ay way fane lay dieulé contact Tons 😭 nianal ko , Sant ko geureum ko, diaspora contane naniou Père ❤️ yalla nala fi borom bi Bayi geueneu werr
Youssou Amy collé diapaleko way 😢 elle chante juste et bien Machalah
The king 👑
Sarap xonam you Dou niit demb sama yaram bedone daaw 😢
Cheuuuutttt sama papa dji mo professionnel nak corrigé na Souleymane faye té vexé wouko😂😂
et il est en forme mashALLAH
les transitions extraordinaire
Kann comme mann mo meunoul register ce grand Mr ❤❤🎉
Magui tothie sama keur😂❤
Eupeu na déf 😂😂@@kizzydiop
@@AminataNdiaye-qq5jm 🤣🤣
L empereur the king sen baye Youssou ndour❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤yagg fi dignou begeul🙏
legende
Big respect à ce grand monument de la musique africaine. Il représente plus que le Sénégal
Nekhna way goudal fane❤
Just awesome 😎
Nabou léye🤔
Youssou mo degg nenako nangoul ndogal bi mo takh wally daaw neuu 😂😂😂
❤❤❤❤❤❤
sky show laley tegueeul ni
❤❤❤❤🎉
Ya meune ya eupou dolé
Arrivé de wally seck
L’arrivée de wally a fait quoi ?
Improve on your picture quality.
❤❤❤❤