Diappawoumako pression familiale mais kay beuga wané no melout ak fo tollout kay la , ndaakh pression familiale moy amo lo lekk yaak sene wa keur wala koula djegué febre ta mano si dara mais dama wara def baptême bou reuy wala mariage bou reuy lolou mom franchement brga wané no melout la ta lolou moy beug lucce
@@lejustemilieu245 bayiko rek déjà Pabi waham rafet na mai il parl tro car natou dafa gaw te kounek lay mom hamoul moudiam wala ndiabot car chaq jour rk mou tog thi mcro yi.
@@nenegadio2298 Nene damla beug Pabi bobou batay mongui si media bi rek dafa wara nopi si bopam ! ok choque leu c vrai mais ben yen ngey wakh paressi ! mais fo tourner video yi guissko
Ne cherchez pas des excuses pour le coupable au Sénégal rien ne justifie de mettre fin à une vie. Surtout pourquoi 37 coups de couteau. La tristesse est du coté de la victime pas du coté du coupable. C pas une pression c juste vouloir s'afficher et se donner de l'importance.
Man 37 coups de couteau 🔪 yi moma yem batay c’est comme si il avait une haine énorme sur KINÉ, nane guay timé nit diko diam plusieurs fois ki vrai criminel la sheuuut 🥹🥹🥹
Maan moom paa bii est un bon citoyen nekh naa trop gouvernement bii warr nako def dara côté éducation machallah en plus très pertinent Fatou Kiné yalla naa khipé aldjanaa firdawsi amiin amiin🙏🙏🙏
Il est tout sauf un bon citoyen, il est en quête de lumière, il est bavard, indiscret, indécent, une interview aurait suffi mais il est partout bla bla bla bla ba kagne, pa bou gnémé beutt mongini
@@magaliendiaye8894 motay ! C’est ça la bienveillance … aujourd’hui je suis sur que kiné remercie ce vieux . Seul les connard et les imbeciles le critiquent
@@magaliendiaye8894 yaw deh fou niou wakhé lou bakh si Pa bi nga riposté dika critiqué c'est quoi ton problème à la fin maye niou waye sougn ka dékké micro kaye mou wakh ish 😡
Tout ça pouvait être éviter ci y’avait un agent de sécurité et des caméras de surveillance.. personne ne parle de ça Comment mettre une jeune fille dans des conditions comme ça
C'est vraiment triste , je n'arrête pas de penser à la pauvre dame! Le messieurs a bien résumé , au Sénégal la pression sociale est énorme , et il faut qu'on soit raisonnable "Adouna amoul solo " .
Lii dou pression sociale bègue wanénou rek louy ndey guenté voilà les conséquences bro mane jai 35 ans célibataire sans enfants té yalla kham nani niaka yorr motakh ma nek célibataire ba legui donc doylou rek ba yalla niew
Mane liguéyou superviseur Bi soumako amone damay dolli Sant yalla,niak doylou rék motakh AK beug wané lo amoul,amoul bén pressions sociale,moi j'ai 2enfants c'est dur Oui, mais mangui door War lébouma naniouma soutoureu ak diom rék
Y'a pas de pression sociale qui tient, la fille de notre voisine bimou amé tawam ak jeukeuram, waji il travaille dé, mais amoul wone loumouy jeundé harr mba guanar pour toudou, mbiskitt ak gouro lañu sédalé, déf farata mou jèh, xalé ba ngi ni tay, première section garderie,
Amouko wone parce que tout ce qu'il avait il l'avait dépensé sur les consultations prénatales, échographie et les frais d'accouchement. Et c'était ses première année de travail.
Quartier bou nék warna ame vieux bou mélni vraiment pabi diambar deug le depuis le début Magui koy suivre mai chapeau papa YALLAH nala YALLAH Sam yagal lafi té wéral la!!! Sohna kiné YALLAH nako sounou borom térou téral ko mayko ay ndam you kawé lolou famou nék ont te connais pas mai dougnou la messa faté ndeysan
@@antandiaye5541 Yaram nite gni dagno doy war légui mai vraiment sa baye bi koukoy critique si lan lako wara critique déf na yeufou kilifa deugu mandé YALLAH séré Nani khamoumako wayé naw nako lolou
Soudé dagnouy bagne peine de mort pour ne pas tuer des innocents (je suis d'accord) mais pourquoi pas dans ces cas ou l'auteur avoue son crime on applique pas la peine de mort ray la devant tout le monde, yalla mo eupp yeurmandé ci diam yi té mognou mom té lolou la diklé. Non seulement ça apaise la famille et proche du victime mais ça peut aussi empêcher d'autre crime. Li dafa yomb trop
dafay yomb torope pression sociale di dedouaner rey katounit piir kou sokhor neeek bonne ba fou bonne yamm tout une famille mou yakhal lene si ça se confirme pkoi 37coups de couteaux.papa dieuredieuf waaye ki amatoul droit di dounde charia rek nagnou ko raye ni mou raye ndawsi mou fin .raye bi barena lolou moye solution bi.metina merina guiss sa dome di baigner ds une mare de sang ne peut être justifié par une pression sociale c est lâche un voyou un vrai assassin pas un agresseur juste la fin de l enquête pr l eliminer il est nuisible pr la societe mo raw bouki
Papa toutes mes félicitations. Kinè Gueye yallah nallah sougnou borom yeureum. Hassim dh mane jusqu'au présent meunouma comprendre son acte dama diakhasso d'après les dires de ses proches. Nagnou deilou sougnou borom tei di mousslou. Yallah nagnou yallah saameu
kke soit la pression sociale c trop facile nul n a le droit de tuer son prochain.disppute ou koi ke ce soit.. le bon Dieu a choisi la personne humaine parmi tt ce k il a crée.Monsieur le Président son excellence ke la peine de mort revienne .
Mamá yeen seen ligieye Rafetna sunu papá yii sunu yaye yii yalla nalen yalla diamal Maye lee weer. Sunu generación bii naak ñune laa on n as des crimineles Parmis nous Pas les parents yaay boy
Réseau sociaux guoudek beutieuk dii wannei une vie de pacha alors que cas social gua boleissii niak doylou moo waral lilep. Courage à la famille de Kine gaye ils ont vraiment besoin d’une assistance psychologique et que firdawsi soit sa demeure 🙏🏿
Je ne suis pas d'accord Mr pression sociale ne justifie pas un meurtre c'est un menteur il a menti toute sa vie il n'a qu'à assumer les conséquences de ces erreurs qu'il meurt en prison
Quand j'ai entendu ce meurtre et la façon dont le tueur a agi, ma première pensée que j'ai eu, j'avais dit que le tueur connaissait bien son cible. Et j'aimerais bien faire partie de cette enquêten pour apporter mon aide.
Pression sociale amoul maroc mon une vie simple et heureuse pour avancer dans le bon sens sénégambienne la mais alhamdoulilah talouma les choses matérialistes
Sou teyone rekk yalla dina defal khew bi dome bou nekk at weurseuk geume yalla mo yoor gneupe dome bou djigene weurseuk papame la wayer yakam ti rekk dakh bamiye wadia djoudou rekk yagui ame ligeye so téyone rekk lepp deye bakh
mane suis tout a fais f accord les agresseur sans coeur ne tue ps par 37 cout mane je pense k khale bi dafa khabtalou deug li il est quelque chose de louche par ce que a la police il a dit que kine a crié il a eu peur et il lui a donne 37 coût franchement li kou conscient douko def amna lou louche si histoire bi soit seytane wala rap wala khabtal yalla nako yalla diapale souder lolou la mane j ai de la peine pr lui meme si je l ai plus pr la defunte 🙏
Bo amer foula kaye do nangou ko la teke pression. Mane jai 2 frère. A la maison kene tegoulene bene pression. Ils sont tout les 2 loger nourri blanchi. Dou niou diokher dépense tchi keur bi..Au contraire ils vivent dans la maison familiale sans pression. C est ma mère même qui prends son argent leur donner. .Mais ils subissent la pression de leurs femmes et copines qui leur demande de l argent tout le temps. Et quand les femmes leur mette la pression ils viennent nous mettre la pression a moi ma mère et mes soeurs pour qu on leur donne de l argent pour qu ils aille donner sa a leur femme. Sama petit frère bi mouye take diabar dafa teke sama yaye pression pour mou diokhe ko lou mou diokher warougale. Souniou nguente tamite sama yaye moye stresser diaye aye oram diokhe lene pour niou terale sene diabar yi. Tabaski passer sama grand frère dafa dieule sama khalisse yaye pour kharou tabaski diokhe ko diabaram mou dieunde kharou tabaski. Sama yaye mome toke sans khar. Donc chaque jour que leurs femmes et copines ont besoin d argent ils viennent nous terroriser moi ma mère et mes soeurs pour qu' on leur donne de l argent. Actuellement on.vit un enfer chez nous et amouniou kene kouniou diapaler..Mon père est décédé il ya 2 ans. Ils nous a laisser des biens mashallah. Depuis qu il est décédé mom grand frère promet a toute les femmes qu il rencontre qu il va bientôt devenir riche. Et qu il va leur donner beaucoup d argent des qu il aura son héritage. Il veut qu on vende les biens de mon père lui donner. Chaque jours je l entend au téléphone parler avec des femmes qui lui mettent la pression et le harcèlent pour qu ils vendent les maisons de mon père et leur donner l argent. .Et lui ce imbecile la il est d accord et vient nous créer des problème. Il a même dit qu il va prendre une hache pour nous tuer tous. C est pour dire que ya pas que khassim. Goor you niaka fayder beuri na tchi dekeu bi.. et mes frères ont 54 et 40 ans. Aye ponkalou make laniou. Djguene bakhoule.
@@nefertaribaidy669 moi aussi mon père est décédé y’a pas longtemps il a laissé des maisons et de l’argent machallah mais yakarouma si lolou pour téki mangui sante yalla sa frère yoyou war nagne ame diome
Yaw dei wa Facebook takalone nagnoula sisa première interview bi grand bi sole t-shirt bou blanc bi nane esk dou ioe sakh mais yallah leral na lepp motakh mandou bakhna di wakh loula lerr aussi
Rien ne justifie cette erreur au Sénégal on parle de pression mais moi mes baptêmes j'ai les moyens mais pourquoi gaspiller beaucoup d'argent pour rien et les tabaski au Sénégal coûte que coûte un mouton ta pas les moyens ya qui prend du crédit pourtant est ce que dieu veut qu'on soi comme ça faut venir en arrière un peu voir les choses autrement
Pression familiale ou pas rien ne peut justifier son geste.amna niouko geuna mettitlé mais rayouniou ken .
Mais soo amoul sakh doo yém baga yor
Wakhal deh
Limou déf feen lako tegoul nak mais Pa bi sonou nassi trop
waa kii kagne lagne ko raye
Diappawoumako pression familiale mais kay beuga wané no melout ak fo tollout kay la , ndaakh pression familiale moy amo lo lekk yaak sene wa keur wala koula djegué febre ta mano si dara mais dama wara def baptême bou reuy wala mariage bou reuy lolou mom franchement brga wané no melout la ta lolou moy beug lucce
Chèr père vous méritez des responsabilités dans ce pays
Wakhi dof bane responsabilité si tu un jeune essaies d'incarner cette responsabilité mo geune.
@@lejustemilieu245 bayiko rek déjà Pabi waham rafet na mai il parl tro car natou dafa gaw te kounek lay mom hamoul moudiam wala ndiabot car chaq jour rk mou tog thi mcro yi.
yaw loy wakhh nii mdrrr
@@nenegadio2298 Nene damla beug Pabi bobou batay mongui si media bi rek dafa wara nopi si bopam ! ok choque leu c vrai mais ben yen ngey wakh paressi ! mais fo tourner video yi guissko
@@fawade5528 thi kilifa te aduna dafa goudou tank ☝🏿natou kounek lay dal
Ne cherchez pas des excuses pour le coupable au Sénégal rien ne justifie de mettre fin à une vie. Surtout pourquoi 37 coups de couteau. La tristesse est du coté de la victime pas du coté du coupable. C pas une pression c juste vouloir s'afficher et se donner de l'importance.
Vraiment j'ai de larme aux yeux mais pourquoi il a fait ça
Man 37 coups de couteau 🔪 yi moma yem batay c’est comme si il avait une haine énorme sur KINÉ, nane guay timé nit diko diam plusieurs fois ki vrai criminel la sheuuut 🥹🥹🥹
@@Dado1998Salman elle l avait surmen reconnu donc il C dit Kil fallait l achever 💔💔c vraiment incroyable
@@Dado1998Salman mann mii franchement ! J’arrive mm pas à imaginer dans Kell état était la victime 😭😭😭
Paraître ce que l'on est pas
Le monsieur qui parle est très responsable. Beaucoup de courage. C est très dur bravo à la police que ce lâche soit puni à la hauteur de son crime.
C’est mon oncle
Li. Pére. Wahh. deugg lá. Presión. Sociale. Mo WaralLi. Máis. Nakk nit. Day. Am. Foula. Boul def lo mounoul. Dahh. Aduna djarrouko
Police scientifique dugnu nitt machallah
Mane dé sante na yala ba nieuwouma si adouna pour compétition louma yala dioh ma santé ko bour bi tabaski ah korité la yémalé
WaLAHI
vraiment
Kou ka def noplou dh la vie n’est pas une course
Rien ne peut justifier le meurtre d'une brave femme comme c'est le cas. Pas d'excuses.
Ndayesane Pa bi amnaci takhaway bou raféte 🫡🫡🫡
Ken douma teke pression sur terre. Ma maman le fait tjr mais elle na jamais reussi. Ca ma fait su bien. Def lo mene wakhe lo mene bo teuder nelawe.
Vraiment papa sa wakh rafetna macha Allah longue vie a vous 🥰🥰💞💞💞🇺🇸🇺🇸
On na besoin de wakh bou rafetna. On na besoin de Justice pour kiné
Amine yarabbi 🤲🤲
Maan moom paa bii est un bon citoyen nekh naa trop gouvernement bii warr nako def dara côté éducation machallah en plus très pertinent Fatou Kiné yalla naa khipé aldjanaa firdawsi amiin amiin🙏🙏🙏
Il est tout sauf un bon citoyen, il est en quête de lumière, il est bavard, indiscret, indécent, une interview aurait suffi mais il est partout bla bla bla bla ba kagne, pa bou gnémé beutt mongini
@@magaliendiaye8894 motay ! C’est ça la bienveillance … aujourd’hui je suis sur que kiné remercie ce vieux . Seul les connard et les imbeciles le critiquent
@@magaliendiaye8894 🤣🤣🤣
@@magaliendiaye8894 yaw deh fou niou wakhé lou bakh si Pa bi nga riposté dika critiqué c'est quoi ton problème à la fin maye niou waye sougn ka dékké micro kaye mou wakh ish 😡
@@likasow1704 Ah yow mi adada yow mi meu ragné tchi comentaires yii! Xana nekk xarite avec la victime beugue pa bi noppi! Doyna!
Tout ça pouvait être éviter ci y’avait un agent de sécurité et des caméras de surveillance.. personne ne parle de ça
Comment mettre une jeune fille dans des conditions comme ça
Deug rk ga wah
Wakh bangui nonou
C'est ça le problème wala alarme sakh . Bo guissoul lo kham ngua beuss alarme avec Ton pied comme dans les banques
C'est vraiment triste , je n'arrête pas de penser à la pauvre dame! Le messieurs a bien résumé , au Sénégal la pression sociale est énorme , et il faut qu'on soit raisonnable "Adouna amoul solo " .
Lii dou pression sociale bègue wanénou rek louy ndey guenté voilà les conséquences bro mane jai 35 ans célibataire sans enfants té yalla kham nani niaka yorr motakh ma nek célibataire ba legui donc doylou rek ba yalla niew
Mane liguéyou superviseur Bi soumako amone damay dolli Sant yalla,niak doylou rék motakh AK beug wané lo amoul,amoul bén pressions sociale,moi j'ai 2enfants c'est dur Oui, mais mangui door War lébouma naniouma soutoureu ak diom rék
Il y a plus d'éducation de base et aussi les senegalais sont trop visieux paix à leurs âmes aux défunts
Y'a pas de pression sociale qui tient, la fille de notre voisine bimou amé tawam ak jeukeuram, waji il travaille dé, mais amoul wone loumouy jeundé harr mba guanar pour toudou, mbiskitt ak gouro lañu sédalé, déf farata mou jèh, xalé ba ngi ni tay, première section garderie,
Sutura
Et puis je ne te crois pas. Ndieugou Guinar sakh amouko si qq1 qui travaille🤔🤔
Amouko wone parce que tout ce qu'il avait il l'avait dépensé sur les consultations prénatales, échographie et les frais d'accouchement. Et c'était ses première année de travail.
Non khamouma khasim mest yeureumna bébé bii bilakhi😭😭😭😭😭
Mdrr pression sociale ltxx muyy justifier acte bii khassim deff kulaaa diamm 37 fois kegnee mom
Quartier bou nék warna ame vieux bou mélni vraiment pabi diambar deug le depuis le début Magui koy suivre mai chapeau papa YALLAH nala YALLAH Sam yagal lafi té wéral la!!! Sohna kiné YALLAH nako sounou borom térou téral ko mayko ay ndam you kawé lolou famou nék ont te connais pas mai dougnou la messa faté ndeysan
Pourtan nityi gnoguikoy quiritike Nan dafa Bari wakh
👍👍
Amiine ya Rabbi
@@antandiaye5541
Yaram nite gni dagno doy war légui mai vraiment sa baye bi koukoy critique si lan lako wara critique déf na yeufou kilifa deugu mandé YALLAH séré Nani khamoumako wayé naw nako lolou
@@antandiaye5541 bari wakham gui de kon amna ndiaringn sénégalais ken manko satisfait defal te yalla takh rék pa bi yalnako yalla fay kholom.
Ndeye sane khasim yeuram nakou wayé kiné yalla nakou Yalla yeuram Kharéko aldiana amine 😭🤲😭🤲😭🤲
Soudé dagnouy bagne peine de mort pour ne pas tuer des innocents (je suis d'accord) mais pourquoi pas dans ces cas ou l'auteur avoue son crime on applique pas la peine de mort ray la devant tout le monde, yalla mo eupp yeurmandé ci diam yi té mognou mom té lolou la diklé. Non seulement ça apaise la famille et proche du victime mais ça peut aussi empêcher d'autre crime. Li dafa yomb trop
Bilahi
dafay yomb torope pression sociale di dedouaner rey katounit piir kou sokhor neeek bonne ba fou bonne yamm tout une famille mou yakhal lene si ça se confirme pkoi 37coups de couteaux.papa dieuredieuf waaye ki amatoul droit di dounde charia rek nagnou ko raye ni mou raye ndawsi mou fin .raye bi barena lolou moye solution bi.metina merina guiss sa dome di baigner ds une mare de sang ne peut être justifié par une pression sociale c est lâche un voyou un vrai assassin pas un agresseur juste la fin de l enquête pr l eliminer il est nuisible pr la societe mo raw bouki
"SA DOOM MEUNN NGAKO TEKK PRESSION PARCE QUE AMOUL DINÉ!" non Serigne bi fan nala ndakh sa phrase bi! Cst rare de l'entendre!
Papa dji yalla nala yalla sakhel sa takha waye si mbrmi rafetna machalla ❤️
Merci madame le ministre de la femme de la jeunesse la fille était une battante ngente jaru ko
No Sama pa bi ❤damakobeugue nak 😊 mom lepamay lère
Thieye famille khassimou ma léne yeureum
Yakhna famille bi a vie
Yeureumal ni dele ba pare khassime AK diabaram ray sen ndaye rék mou dagan.
@@dallavili5266 Es ce que c ca femme qui est allee tue l'autre femme? Lou tchi yonou femme bi? Khassim kagne moye psycopathe , bou gnou blamer kenene
@@dallavili5266 diabaram loussi yonam arretelén sénégalais loumou teugue rek rakh si peureum
@@ndeyefatoudieng1255 iow ham
Rien au monde ne peut justifier son ignoble crime
Papa toutes mes félicitations. Kinè Gueye yallah nallah sougnou borom yeureum. Hassim dh mane jusqu'au présent meunouma comprendre son acte dama diakhasso d'après les dires de ses proches. Nagnou deilou sougnou borom tei di mousslou. Yallah nagnou yallah saameu
Chapeau et Respect á la police sénégalaise
Yalla nako yeureum té kharéko aldiana 🙏🙏🙏
Kou raaaaay dagnela waara raaaaay amoul lénéne
PABI DI WAKH NDAYSAN DA NIROK PÈRE LAMINE NDIACK YAllA NA YA TÉGUIL NIOU DIAFÉ DIAFÉ YI
Effectivement noro na akk lamine diack lol
Rien ne vaut cette peine..J'ai une pensée à sa mère am na naakhar
QUE LE TUEUR POURRISSE EN PRISON. IL EST LÂCHE QU'IL POURRISSE EN PRISON!!! IL A DÉTRUIT UNE FAMILLE POUR DES MIETTES.
Ki bonuses pression sociale rek la arrêter de juger les gens
kke soit la pression sociale c trop facile nul n a le droit de tuer son prochain.disppute ou koi ke ce soit.. le bon Dieu a choisi la personne humaine parmi tt ce k il a crée.Monsieur le Président son excellence ke la peine de mort revienne .
J'ai des larmes aux yeux parce que je suis une mère d'un garçon tout ça c'est les parents sénégalais
Been problème diaroul ray khanaa kay ga dem sathi prection social diarna ray
Mamá yeen seen ligieye Rafetna sunu papá yii sunu yaye yii yalla nalen yalla diamal Maye lee weer. Sunu generación bii naak ñune laa on n as des crimineles Parmis nous Pas les parents yaay boy
Ayyy wayy li lannn moko diarrr si adounaaa😓😓😓😓
Que son âme repose en paix
Vrement sa fait très mal au cœur
weett goree weteulikou goree khaasim daal diayy katou taar la nieupp am nakhar si fatou kine mi mou rayy pourquoi rayy
Réseau sociaux guoudek beutieuk dii wannei une vie de pacha alors que cas social gua boleissii niak doylou moo waral lilep. Courage à la famille de Kine gaye ils ont vraiment besoin d’une assistance psychologique et que firdawsi soit sa demeure 🙏🏿
C'est un acte maléfique !!! Sénégal dagnou beuggeu lou reuy... Li déh kharou mokka geune!!!
Qu'elle repose en paix au plus haut des Paradis. qu'Allah nous garde ainsi que 'os familles. Metina trop. Rien ne justifie un tel acte
Ray domou diambour rien que pour satisfaire les désirs de t'a Femme la pression sociale n'est pas une excuse
Santa nous poussent à faire des choses que dieu est pitié de son âme
Lernamani khassim beugatoul dara si adunam lernamani deh moko geuneul doundou
N'a deh nakh mérito woul dounde
Walakhi
Khassime mbaam la na deeeeeee.
Na kharou. Domeram bi mou done. Djguene mo takhe mouye raye domou diambour.
Walay
So amoul harr defal guinar addj sa khew yallah tegoul Ken lou diss
Je ne suis pas d'accord Mr pression sociale ne justifie pas un meurtre c'est un menteur il a menti toute sa vie il n'a qu'à assumer les conséquences de ces erreurs qu'il meurt en prison
Quand j'ai entendu ce meurtre et la façon dont le tueur a agi, ma première pensée que j'ai eu, j'avais dit que le tueur connaissait bien son cible. Et j'aimerais bien faire partie de cette enquêten pour apporter mon aide.
HAHAHAHAHA TU ES TROP DRÔLE
🤣🤣🤣🤣🤣
Ok merci tu es fort🤣🤣
😂
🤣😂😂😂😁 il ya des commentaires qui me font rire
Bilaye tu as raison pression sociale et familiale au Sénégal ndessane
Le crime n'est jamais parfait. L' assassin revient souvent sur le lieu du crime
C'est le cas contraire l'assassin d comba yade , dienaba Traoré, Lisa tine disparu mais tjrs pas de coupable.
Le crime n'est jamais parfait ?
Pression sociale amoul maroc mon une vie simple et heureuse pour avancer dans le bon sens sénégambienne la mais alhamdoulilah talouma les choses matérialistes
Machallah mentalité bobou mo rare legui surtout ci djigen
My pa Mashalah sa wakh rafettna tro tei leerrr
yaw mom khasim am nga mousiba yalla nga trokh drm
Sou teyone rekk yalla dina defal khew bi dome bou nekk at weurseuk geume yalla mo yoor gneupe dome bou djigene weurseuk papame la wayer yakam ti rekk dakh bamiye wadia djoudou rekk yagui ame ligeye so téyone rekk lepp deye bakh
Pression familiale dou debatt li debat capable niit reyy ko masta djigen lolou negg la
C est un bandit il voulait faire son baptême raison pour laquelle il a tué une femme d autrui c est dur
Vraiment khaliss kouko beugue demal liggéyii
khassim linga def eupp na
Mane pa bi damako beug trop
Est-ce que lii néne la . Sénégal sheytan yi dougnou Bari ,djines yi AK deumeu yi.
Yow nak khamnga li khew mais kenneu dou la deglou...
True deugeu piire nga wakh ya des demons parmis nous
mane suis tout a fais f accord les agresseur sans coeur ne tue ps par 37 cout mane je pense k khale bi dafa khabtalou deug li il est quelque chose de louche par ce que a la police il a dit que kine a crié il a eu peur et il lui a donne 37 coût franchement li kou conscient douko def amna lou louche si histoire bi soit seytane wala rap wala khabtal yalla nako yalla diapale souder lolou la mane j ai de la peine pr lui meme si je l ai plus pr la defunte 🙏
Où sont les parents du coupable dans tout ça.
Képe kouniou téke pression yaw la néhe mane kéne douma téke pression c’est pas une raison
Bo amer foula kaye do nangou ko la teke pression. Mane jai 2 frère. A la maison kene tegoulene bene pression. Ils sont tout les 2 loger nourri blanchi. Dou niou diokher dépense tchi keur bi..Au contraire ils vivent dans la maison familiale sans pression. C est ma mère même qui prends son argent leur donner. .Mais ils subissent la pression de leurs femmes et copines qui leur demande de l argent tout le temps. Et quand les femmes leur mette la pression ils viennent nous mettre la pression a moi ma mère et mes soeurs pour qu on leur donne de l argent pour qu ils aille donner sa a leur femme. Sama petit frère bi mouye take diabar dafa teke sama yaye pression pour mou diokhe ko lou mou diokher warougale. Souniou nguente tamite sama yaye moye stresser diaye aye oram diokhe lene pour niou terale sene diabar yi. Tabaski passer sama grand frère dafa dieule sama khalisse yaye pour kharou tabaski diokhe ko diabaram mou dieunde kharou tabaski. Sama yaye mome toke sans khar. Donc chaque jour que leurs femmes et copines ont besoin d argent ils viennent nous terroriser moi ma mère et mes soeurs pour qu' on leur donne de l argent. Actuellement on.vit un enfer chez nous et amouniou kene kouniou diapaler..Mon père est décédé il ya 2 ans. Ils nous a laisser des biens mashallah. Depuis qu il est décédé mom grand frère promet a toute les femmes qu il rencontre qu il va bientôt devenir riche. Et qu il va leur donner beaucoup d argent des qu il aura son héritage. Il veut qu on vende les biens de mon père lui donner. Chaque jours je l entend au téléphone parler avec des femmes qui lui mettent la pression et le harcèlent pour qu ils vendent les maisons de mon père et leur donner l argent. .Et lui ce imbecile la il est d accord et vient nous créer des problème. Il a même dit qu il va prendre une hache pour nous tuer tous. C est pour dire que ya pas que khassim. Goor you niaka fayder beuri na tchi dekeu bi.. et mes frères ont 54 et 40 ans. Aye ponkalou make laniou. Djguene bakhoule.
@@nefertaribaidy669 moi aussi mon père est décédé y’a pas longtemps il a laissé des maisons et de l’argent machallah mais yakarouma si lolou pour téki mangui sante yalla sa frère yoyou war nagne ame diome
@@nefertaribaidy669 nioniou deh bou yagué niou ray leen lahilahh
@@nefertaribaidy669 sey freres ay domram lagn
C des gamins. Amou niou diom
Mai's khasim bâ esk vrai senegalais LA niaw na lol Lou meti si khole
Pression d’emoji fa yalla reyyyy nakkkk fiiii danioukoyyyy cowered alors kou reyyy. IOU reylanpount
Doylou rek yalnagnou ko yala defal dioulite dafay doylou nguir meuna mouthie
Juste une question lane moy caussou Mort bi agression la Wala dañu sékhone affaires khalis ou quoi ? Yalana yala yeureum adji dem ji
Ils ont besoins d'aides de psychologue pour surpasser cet horrible événement.
Oh père dimbaliniou ak j’avais envie de le rencontrer tu parles beaucoup à la fin ahhh
Moh merde
Bravo encore à nos diambar la police nationale sénégalaise
Yaw dei wa Facebook takalone nagnoula sisa première interview bi grand bi sole t-shirt bou blanc bi nane esk dou ioe sakh mais yallah leral na lepp motakh mandou bakhna di wakh loula lerr aussi
Pikine dale moye lolou nnaniouko wakh te dehhh dou deukoiwaye ximmmm! Paix à son âme
Leup. Diabaramla. .Pour. Affairou djenté. Legui. Nak. khasssim. Migui si probleme
Rien ne justifie cette erreur au Sénégal on parle de pression mais moi mes baptêmes j'ai les moyens mais pourquoi gaspiller beaucoup d'argent pour rien et les tabaski au Sénégal coûte que coûte un mouton ta pas les moyens ya qui prend du crédit pourtant est ce que dieu veut qu'on soi comme ça faut venir en arrière un peu voir les choses autrement
Khadim lingua dêf noko menê je trouble past Les mots lol déf ma fébar sakh
Daerrra jarruko..louy xeww ? Bu kenna nangou koula teikk pression
Franchement auon arrete de dire que cest la pression de sa gemme oi de sa mere quil assume ses responsabilites et arrete de mentir
C'est bizarre moi je peux me payer ce que je voudrais mais rien ne m'intéresse
Papi damaco fen billahi
C'est pas une excuse pour hoter la vie d'une personne à 37 coups. que l'âme de la défunte repose en paix et que la terre lui soit légère amen.
Domeram bi nann ley kholer nitt gni senn wa keur nouniouy kholer nittt yi vraiment ki deumeuleu
Walahi sa mère m fait de la peine dama dioy ba soneuu naturellement
Wa pa bi niata interwiew lay def mdrrrr li dal niougui kay nakarlou boubakh
Pa bi kay yallah maynako welelelelel 😂😂😂
Yow da nga tala rétane réwal bou bakh
@@fallmarietou18 yaw neko si saama khol mandoul denga on ne se connais pas
😭😭😭😭😭😭
Man mom affaire yi comme ay film si man nahtei batay dama choqué
Ray nga domou diambour deh wayé yawitt sa adunaaa yakhounaaa ba faww.....li dara diarouko ci adunaa
Bravo a la police scientifique
Arrettez kokou wakh dougalal sa lokho si tal douko def kokou wakh kharoul douko def donc li amoul pression il a choisi de le faire seul
Wa mane khasim manou mako yérém khasim doul
A chaque fois ni la kou Ray nite après ay commentaires you doye War peine de mort laniou wakh
KOU RAY NAGNOUKO RAY WAKHOU SOUNOU BOROM LA
Peine de mort amoul Sénégal
Bien dit papa
Oh😭😭😭
La vie Sénégalaise est fou on a des des croyances démoniaques
Li deh moye deumeu reye leu ba paré dialeleu reye nitt ba paré di dioye doyna war
Khasime assassin international wallahi ray nitt tokk di joué film li kéneu khamoul lanla
Thiey massa
Ndayesane 😭😭😭
Rien ne justifie le geste de Khassime. C'est ignoble.
En tout cas c'est une épreuve insurmontable. Courage à son mari, sa famille.
Il faut aller voir un psychologue pour ces que vous avez vu du courage