Lou way déf sa Serigne Touba dhé nitou yalla la kou déf lénéne yowla wayé mome diamou yalla la woté inshaa Allah Mbacké yalla na yalla yok ay léram inshaa Allah
@@mattchris335 dama mame meusoul nek diamou nit si kaw souf té mo geuneu diambaré ki ga yakar. Sama adouna Yallah rek lassi yakar té magui kossiy santeu boubakh. Yéwouléne
Billahi yonou mouridisme yonou thiaxxana là 😂😂😂😂 fenne ak sosss ak bokale shirik motaxxa yalla dioxxniou Macky Sall pour torokhal population sénégalais 😂😂😂
20 commentaires yimafi fek seine mame du am li seine baye duko am ndakh sokhor mayu yalla dakoy diaralei si nite motakh lu nek si nite gua fokni bokalei kate leine seine ndeye lidieuntiii seine bop ta mandu bayi sokhor bayi dule yi serigne touba en 1895 bimiy khekh l'islam toubab yi diko kheikh beugue ko ray mu takh niou exilé ko pour nassakhal lislam senegal ana seiniy mame buleine ma oubilo seine leufeul ndeye yu khassaw yi way
Sunnah rék moye DEUG billahi 💪💪💪🇸🇳 Sénégal
Kou yebou wouti bennen nationalité non deukeu bi dou demm 😢😢😢
Foumou dieum
Ah wawaw kou beugoul Serigne Touba moom meun nga genn reew mi rekk 😂😂😂 balaa sa khol bou Bonn dila ray
Serigne Bi diemal kham sa domme yeppp. YAllah dîna la Lathie no donne sammé ndiabotte yi moula dénke.
Meunoul nek
Dafa melny Kham NGA sa way dh
Diokhma sa numéro
Saway ki daara la yor domam yeup fa lagni dianguè
c'est une manière de parler faut l'écouter et réécouter pour comprendre loutah mouni khaméwoul doomam ! gaaaw ngueen trop si commenter aka wax
Bayil Serigne Touba sa yëfi bopp nga nék
Waxi dof
Lou laire
Mai doff bi kanne la nooooòooo senegal mo nekh doff yi yake guenn senegal yeupe
Ki da wayadi pirrrrr
Cheikhal tamit😂😂😂
Reewandè baxoul daal😂😂😂
Subhanallah 😢😢😢
Nek serigne Senegal nekhna
Cheikh Ahmadou Bamba ☝️ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Thiey Sénégal dou déme
Ana diamra😢
Allahou akbar génn deuk bi diotna bala mbougeul dilafi fekk 😮😮😮😮😮
Pour iao ins bi yalla nékoul diniou mougueul nii,Doundou si deukk bi risque leu déh
Bilahi
❤❤❤❤❤❤❤❤
Sà papa yaw mouride mbaye di khafize alkhourane defal la leep waro tekelele bene niit so toguone ndar si Dara papa sakhe amme talibe sa papa kontanoul
Waw baye fall bi nékhna dh
Diour ay dom khame wolen niom ak sene yaye
Ces marabouts sont à l'origine de tous les problèmes du Sénégal.
Pas tout le monde
Yow dé koula khamoul serigne abdou karim sakh khamna ni falé woko boul faté liga def touba bamou dakeu lafeu 😂😂😂😂😂😂 sacré senegal tok mouy dokh
Lou way déf sa Serigne Touba dhé nitou yalla la kou déf lénéne yowla wayé mome diamou yalla la woté inshaa Allah Mbacké yalla na yalla yok ay léram inshaa Allah
@@yacinendour442 loulou keneu wedi wouko mais sénégalais yi nio wara yéwou
Teranga rek mom guen di wakh ani yalah alahou akbar khamel say dom nak
Yenn meunoo lnn comprends ki fimouy wzxé ni xamé toul kenn ndax amo lnnn deg deg😢
Man de ligeuyal serigne touba la bègue kouma ko tekil moy lan😂😂😂😂😂
Dieureu Dieufe Seringe touba amoul morom kienela ❤️❤️❤️❤️❤️
Dieureudieufé S Touba ❤❤❤❤❤
Kharr len AKHENATON MOUGI GNOW 😂😂😂😂
Noo😂😂😂😂😂
Baye mouride dieuredieuf
4:20 4:30 😥😭
Khaméwo sa dome ak sa diabar
Serigne touba khaména aye domame
KOULA CI DAKH DOUL REK NGA NI KI. SERIGNE BI AMONE DOLLÉ WALA MOU AM MEUN MEUN NA DINDI SEN NDOKH MI.
Baayiilll togn aas goor dou togn.
Waxi dof ngay wax domerame kone touba rek mo am ndokh ta louthi sa leufal ndeye sax
Sama wasila ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢
Yow domarame bii demal diamou yalla mo gueune bayi serigne abdou karim
Kou réw nga
@@morgueye2783 sa leufeul ndeye ak mouride mbaye ak sa serigne
Gorou yalla bougne eupeu moromou goor rame chipirii 😢😊
Khaméwo sa domme ak sa yayou domme 😂😂😂 comment on peut éduqué nos enfants inconnu thieuyy Sénégal , bàyléne thiakhane
Man dama warrou sii Sénégal 😢😢😢
Ndaye sane
Dierejef serigne touba
Serigne touba meuneu louné
Gni diamou Yalla nagn Dém diamou dji Yalla Té Mandou BayiléN Niou ak Serigne Touba ❤ nguir Yalla mome lagn beugu souniou xol fass Yénéko liguéyeul si barkép Seydina mouhamed Doléy Cheikh Ibra
Kholal dof bi
@@Ablayb sa Mame loumou liguéy si Deuk bii ? Ésq wax nga sa Yaye Dof wala sa Baye wala say Frère sén niak talibé motah dolén Ndiarignou si adouna
@@mattchris335 dama mame meusoul nek diamou nit si kaw souf té mo geuneu diambaré ki ga yakar. Sama adouna Yallah rek lassi yakar té magui kossiy santeu boubakh. Yéwouléne
Sama mame limou ligueye si deuk bi nieupeu ko kham té meusoul nakeu kéneu
@@Ablayb nioune khamouniou sa Mame téksi sa Mame Dou Serigne Touba ok nopil teudj sa guate té Mandou
Aï baye mouride am nga fitee d 🤭
Day wah reck ki
On appelle les médias on parle beaucoup pour juste avoir des privilèges de se bas monde. Ces privilèges sont éphémères
Yagui doul dé bayil fénn ba nopi
Thiakhan rék
Nekal niit lala wakh serigne route sante toula lii ngay diour ay dom di dem c quoi ca xamngani cheikh abdoul karim yegoul lingua neke dh
Serigne bouy wakh ay autos , keur matériel c quel genre de serigne ?
Serigne dalay tékk ci yoonou siraatal moustahîm
Senegal lutakh bugunu lubakh
Fatou mbaye mi seytané la yagui diaxasé bobou ba taye mounane déglouléne him
Bayléne bayou diambour yigindi eupp ak wantaye té dém liguéyal sénni wadiour
Féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék féne rék
Ak nane café 😂
Bou mame Bamba yewo Dina la douma. Yakh derou mouride rek
Doundou si deukk bi risque leu
Bayi féne mo geune diangue Alhourane et pourtant yangui doul 😢 sheuttt j’ai pitié 😢
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂
😂😂😂😂ABBA show gay am fiii😂😂😂😂😂😂
Nawlé dafa fort 😂
Gnépa beugue Serigne Abdou Karim mes santoula wakhou doff yii ndakh mom dou wakhé ni wormal n'a gneupp mbacké
Mane mom sougn ma léralalone 33 femmes yi ak 4 soeurs yi dont 3 de même mère yi rék sama khél dal. Affaires yi diakhasso na ci mane trop.
Je t'invite à ne pas en faire une affaire, ça ne te mènera nulle part alors que tu dois être occupée partout par tes affaires!
Jeulma cii souff ma léral leu lépp
Histoir vrai
Kii d'où baye bou bakh
Mouride bay karim ben cheikh leu am Donald talibe mo gueune lie nay wakh
Wakhal dé
Kholenn domarame dji fo demm ouppe sa baye domarame yenna rerr
Ay waay sëriñ bi famu ni ak lee woote na lool ? Ku bëgg xam sëriñ bi Demal Yari am mbindam.
Vraiment tu fais honte tu arrives même pas à reconnaître tes propres enfants mais là je suis sidéré qui es tu vraiment ???
Tu pense vraiment vraiment que ses gens là ils ont 4 femmes ? Comme le dit le coran non ils plusieurs femmes une trentaine de femmes
Gnoune sounou aye serigne doune ko wah di wah l'entente te d'où ay khalis ak ay diokhe
Ay pap khaméwo sa dom ak sa yayou dom
Chei senegal 😂😂😂😂😂
Sénégal niak mandou moy sén problème liguéyeul Serigne Touba Diarna louné Gueuno lén niou kham li Yalla wakh! Chak année ki meun si alhourane Touba lay diougué màni yén diamou dji lénn Yalla Bayiniou ak Serigne Touba
😂😂😂😂thiey dine Senegal
Wakhal wakhini way
Ndox mounéx boukouci xanaa??baayi leen yii xéwina
Zero ngay dawou
Teranga teranga 😂😂😂 addouna moolène jiital. Wa Touba ñofi gana œuvre, dakhfè yalwan.
Douné talibéyi, AK trafik
Ha ha ha
Démléne tarbiyou séne baye yi
Khalé bobou nék si guinaw domam la
sen tounou ndaye
Lokho bi mom ci podiou serigne bi la téggou wala?
Billahi yonou mouridisme yonou thiaxxana là 😂😂😂😂 fenne ak sosss ak bokale shirik motaxxa yalla dioxxniou Macky Sall pour torokhal population sénégalais 😂😂😂
Yaw louy sa yonou baye domeram dji Serigne Touba limou def ci niit koumouko def ci yaw gnou topp la Lou takh mouride gui di yokou domeram dji fo dem ci aduna gnouy magal domeram dji Serigne amoul morom domeram dji mom rekk lagnou ngueum Serigne Touba Louma am diokh ko mou dolima domeram dji dengua ko domeram dji
20 commentaires yimafi fek seine mame du am li seine baye duko am ndakh sokhor mayu yalla dakoy diaralei si nite motakh lu nek si nite gua fokni bokalei kate leine seine ndeye lidieuntiii seine bop ta mandu bayi sokhor bayi dule yi serigne touba en 1895 bimiy khekh l'islam toubab yi diko kheikh beugue ko ray mu takh niou exilé ko pour nassakhal lislam senegal ana seiniy mame buleine ma oubilo seine leufeul ndeye yu khassaw yi way
Deguna deugue bamou metè seurigne touba rek la wone
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂