Dieureudieufeuti. C'est une preuve supplémentaire de l'honnêteté intellectuelle de Maam Maodo. Il a écrit une kyrielle d'ouvrages et pourtant il a choisi le Bourde montrant à la face du monde que le savoir transcende les frontières et les origines sociales. Que Dieu nous préserve d'être un des partisans de mauvaise foi dont la destinée est l'enfer sans doute. Yalnanou Yallah fayal Maam Maodo qui a lutté toute sa vie durant pour que nous soyons de bons musulmans, de bons talibés et non des fanatiques ou des hérétiques. Maam Maodo danoo neub boppam dioxogn nou Yallah ak Seyyidinaa Mouhammad FatabaarakAllah.

Machaalla yalna yalla yegalé lep siii diam
macha allah xol yeup sed na yalla na yalla nagou lép defniou deugue deugue ay talibé cheikh
Alhamdoulahhhh yalla na yalla yegali lepp ci barké seydina Mouhamed (psl)🙏🙏🙏🤲🤲❤
Machallah k la paix règne au Sénégal, khol sedna
Machalahhh khol yi send n'a trop❤🙏🙏🙏🙏🤲🤲🤲🤲
wawaw talibé cheikh amoul morom
Machalla sy Amna solo Amine Amine Amine
machalah machalah
Amine inchalla
Machalla 🙏🙏❤️
ooooohooooohoooooo
dieugáni rek ana dieuzboul khoulóp wala mawahibou wala mouhadimat kiko waye fii leu deuk
dieure dieuf s touba
Yaw Loy wakhni khana dégo Wolof
@@wakhkatoudeugue2013 lima wakh boulé roul si yao mawaxátt ko
Yaw dagua yabaté
@@dienyssef48 yéne yéna soff cheikh cheikh boulen gniou sonal waye mouhamad mouhamatoum gniepoula deme lene wouty biss dagéna xamoul rek di tekk khel wayé nalén lérr ni yéna geuna touty lou geune di deff si gamou gui té nak dougen fa deff dara lafaye dadiée touty lae mbedya mon hatt khamna lima léne wakh bou bakh soff geune torop
Machaallah