Mashala je vois un homme intègre un homme qui a acquis de l’expérience dans la prison un homme intelligent un homme vraiment bien un esprit positif même si je dis bien il a fait une erreur mais il a pris dans ça et son discours méritent vraiment que tout Sénégalais l’écoute Et il mérite d’être soutenu ainsi un documentaire et il mérite d’accompagner l’Etat pour régler beaucoup de choses dans les prisons vraiment Merci Beaucoup 👍
Machala Ndeyesane bilahi sama khôl ❤ Dafa çéde gouy / 24.ans de prison aussi lou diafé pas de dépression ni malades ndimbalou yalla deugleu / yalnala Bour yalla takhawou si barki seydina Mouhamed psl amine🙏🙏
🥺Mashallah j’aime bien ton nouveau esprit de départ 🥰bien vrai que 24ans j’étais même pas encore née wallah🥰mé yalla nala sougnou borome Takhawou🙏🏻 si barké Seydina Mouhamed (PSL)
Khadija l'état devrait les amener dans les champs pour assurer l'autosuffisance comme ça ils seront gagnants gagnants , comme par exemple ses 24ans d'emprisonnement, imagine s'il cultivait et que l'état leur paie 30000cfa, les 24 mois lui feront 7 millions 200
@@sissokhokhadijasiby1037 j'avoue Mais c'est dommage pour ces détenus car nos états ne fournissent aucun effort pour les aider à réadapter, à trouver leur place dans la société...
Liii metti n'a 24ans frère yalla nalla yalla may goudi fane baga réaliser Lou barri si liga wesou lepp boul meusseu regrette tardé amoul si aduna yalla Naka nekk nit ame tour bay dimbali niiga fa bayi
Toubeul ,toube bou sel Paco,bayyi lep ,Yalla diégueleu in sha Allah"Ô mes serviteurs,ne désespérez jamais de la miséricorde d'Allah.Allah pardonne tous les péchés ,il est Pardonneur et Miséricordieux..." Sourate 39,verset 53.
Cher frère Pape... La justice sénégalaise est digne. Si tu as été incarcéré pendant plus de 20 ans, c'est que tu n'étais pas innocent. J'apprécie beaucoup ton courage et la reconnaissance de tes erreurs. Je te souhaite de vivre un beau moment pour le restant de ta vie. J'aurais bien aimé t'aider personnellement. Je condamne l'Etat qui ne fait rien pour vous aider à réintégrer la société. Bref que Dieu te bénisse mon frère.
🙏❤️Machallah grand courage lingeu Doundou metti neu trop mais sa mental de fer c'est a saluer geuneu gorgorlou rek diar diar adouna leu souniou borom molako tegone alhamdou lilah bimouko tegei🙏🙏🙏❤️
Allahu'akbar..pape ndiaye yagu na prison.1995 anné bima dioudo allah...ba 2020 (24ans..dou 24h)mane mou dioudou wone ci att bobou sah j'ai mon bac mon licence et mon mariage...li metina way té yagu...justice tamit délen def sen com il le faut...mais mashallah pape est un humaniste
Holalaaa tu est vraiment un homme courageux je vous conseille pape ne regarde pas derrière toi n écoute pas les mauvaises langues soit un ambassadeur pour tes frère qui sont derrière les barreaux courage mon frère
Salame Pape mane deh khamou mala wayer vraiment sa histoire bi dafa daw sama yarame natou ci diam lay dale dila nianal lici top yeup nek ay khewal inchallah allahouma amine ya rabi courage 🤲🤲🤲☝️
Thiey jistice sénégalaise 😭😭😭sathie kharr kasé 24ans il est temps qu'on revoit notre justice on voit des jeunes qui n'on fait qu' une simple bétise et perd leur vie dans la prison comment peut on commander une personne qui n'a pas commis de meurtre ou de viol plus de 10ans de prison Kallah nous assiste🙏🙏 La justice sénégalaise est une justice injuste
24 ans de prison pour vol de mouton😭😭😭. Kone dé gni sath ay milliard sénégalais yi souyebo sene diabote bayi diour nday sene doundeu rekk dou doy année de prison yi sene seutati seut dinaniou teudeu. Soubkhanala un pays foutu
Bonjour amis et gens de bien. Aujourd'hui j'ai eu presque la nausée en voyant les plats que déposaienr les parents de detenus a la prison de Rebeuss (la viande ,des frites de la crudités et de la sauce ) dans des seaux de 5 litre qui après des heures fermer ermetiquement commence a se décomposer qui pourra causé de l'intoxication alimentaire il faut que les mesures imposée soit enlever nous les parents des détenus sommes fatigués et n on plus rien a envoier dans les prisons prétextant le covid19 or ils s'enrichissent sur nos dots par leurs boutiques et gargote
Vraiment domage. Essayons ensemble de creer un network sur Facebook. Si vous voulez je peux ouvrir la page ou on poura montrer au monde entier des photos qui vont illustrater tout cela.
Walahi frère magui ley ñianal yalla diko ñianal bolém dioulitee yalla nala sounou borom oubilattt bountou khéweul,defal leu wéér werlé samm leu dundeul pape
Ball nagn akk yalla borom bi boléniou ball té sunu borom defal la li dess sisa doundou lepp di ndiarignn té sa fan goudou loll té sunu borom xirr la si mom ♥️
Yallah nala yallah doli soutoureu katan talak fekké Moss ak mouthiou oubila bountou khéweul yi bolélak niit you bakh yi bangua teddeu teral say askan ak sa famille et tt l monde
Celui là je le conseille de se faire discret et d'essai de se réinsérer dans la société c'est mieux que de s'afficher publiquement sur les plateaux TV qui ne cherchent que du buzz.
Mashala je vois un homme intègre un homme qui a acquis de l’expérience dans la prison un homme intelligent un homme vraiment bien un esprit positif même si je dis bien il a fait une erreur mais il a pris dans ça et son discours méritent vraiment que tout Sénégalais l’écoute Et il mérite d’être soutenu ainsi un documentaire et il mérite d’accompagner l’Etat pour régler beaucoup de choses dans les prisons vraiment Merci Beaucoup 👍
Machala Ndeyesane bilahi sama khôl ❤
Dafa çéde gouy / 24.ans de prison aussi lou diafé pas de dépression ni malades ndimbalou yalla deugleu / yalnala Bour yalla takhawou si barki seydina Mouhamed psl amine🙏🙏
Amin
Amine
Amine
🥺Mashallah j’aime bien ton nouveau esprit de départ 🥰bien vrai que 24ans j’étais même pas encore née wallah🥰mé yalla nala sougnou borome Takhawou🙏🏻 si barké Seydina Mouhamed (PSL)
Ndeyssane man dh daama yaakarni dane ko warone woutal ci loumou diaapeu, Etat bi dafa waarone déf ay mesures de réinsertion
Non bly
Bien dit franchement ils ont gâté sa vie
Khadija l'état devrait les amener dans les champs pour assurer l'autosuffisance comme ça ils seront gagnants gagnants , comme par exemple ses 24ans d'emprisonnement, imagine s'il cultivait et que l'état leur paie 30000cfa, les 24 mois lui feront 7 millions 200
Deugeuleu dh vraiment parck aprés tt ça
Il faut qu'il se trouve un place au sein de la société
@@sissokhokhadijasiby1037 j'avoue
Mais c'est dommage pour ces détenus car nos états ne fournissent aucun effort pour les aider à réadapter, à trouver leur place dans la société...
soyez le bienvenu dans la société tu es quelqu'un de bien et souriante à chaque instant et bonne continuation que le bon Dieu te protège
Thieuy mame ak seutam c'est l'amour éternel
Salimata man na am sa istagram please
Salimata Lo deugeuleu
Bilay
iow bo démé sa mam la yar
Bilaye c un amour inconditionnel moi l jour où mon père m’a dit qu’il préférait ses petits-fils à ses propres enfants j’étais choquée
Yalla nala Yalla Takhawou 🙏🏽 Gua Am si lo diape. Si Barké Yonete bi !
Son discours a une dose philosophique pour la société
ap
Comme tu as une famille géniale alors reste dans le bon chemin pour leur faire plaisir , yalla same la te diapale la amine
Nice na
Ndayesane Gorr yalla nga deh monge kate nga yalla nala yalla défal diame
Liii metti n'a 24ans frère yalla nalla yalla may goudi fane baga réaliser Lou barri si liga wesou lepp boul meusseu regrette tardé amoul si aduna yalla Naka nekk nit ame tour bay dimbali niiga fa bayi
Toubeul ,toube bou sel Paco,bayyi lep ,Yalla diégueleu in sha Allah"Ô mes serviteurs,ne désespérez jamais de la miséricorde d'Allah.Allah pardonne tous les péchés ,il est Pardonneur et Miséricordieux..." Sourate 39,verset 53.
Kou sétane li sante Yallah warnala té hamné amna gnio hamni saa situation molène gueneul foppeu séni situation
Cher frère Pape... La justice sénégalaise est digne. Si tu as été incarcéré pendant plus de 20 ans, c'est que tu n'étais pas innocent. J'apprécie beaucoup ton courage et la reconnaissance de tes erreurs. Je te souhaite de vivre un beau moment pour le restant de ta vie. J'aurais bien aimé t'aider personnellement. Je condamne l'Etat qui ne fait rien pour vous aider à réintégrer la société. Bref que Dieu te bénisse mon frère.
Il s'est échappé c'est pour cela gnou rajouter 22 si peine boumou warone teude
🙏❤️Machallah grand courage lingeu Doundou metti neu trop mais sa mental de fer c'est a saluer geuneu gorgorlou rek diar diar adouna leu souniou borom molako tegone alhamdou lilah bimouko tegei🙏🙏🙏❤️
Allahu'akbar..pape ndiaye yagu na prison.1995 anné bima dioudo allah...ba 2020 (24ans..dou 24h)mane mou dioudou wone ci att bobou sah j'ai mon bac mon licence et mon mariage...li metina way té yagu...justice tamit délen def sen com il le faut...mais mashallah pape est un humaniste
Yobbei gama dioyye sisama mame sah yalla nako yalla yareum taguénne gnanalall mako 😭😭😭
Ndeysane
Il est intelligent 🧠
Trop même je trouve et il a une certaine maturité
Machalla..
Bienvenue dans la société que Dieu te protége te facilite ta réintégration natou dou wésse
Yalla na lea yalla samou... Nelson Mandela 27 de prison mou guen done presidan bilakhi walhakhi Dina bakh inchalla
Ndeysane
Le discours est intellectuellement posé... Courage frère
Holalaaa tu est vraiment un homme courageux je vous conseille pape ne regarde pas derrière toi n écoute pas les mauvaises langues soit un ambassadeur pour tes frère qui sont derrière les barreaux courage mon frère
Pape ndiaye yalnala yalla takhawou 24 ans dou ay fo yalla guisna lepp
Ndaye sane wakhna louma touché nak Tabaski 2020 l'histoire retiendra masta masta🙏aujourd'hui j'ai 25ans donc 24ans cpo kelke chose de petit
Bien dit bilahi yalla nala yalla diapalé ba nga am si lo diap diapalé say wadiour respect ton's
Masha Allah ! Il a un mental fort et pour franchir cette étape de la société il te faut ça. Yallah na yallah changé
K allah nous guide vers le bon chemin
C'est cette force qui m'étonne
Yalla nala yalla dèfal diame bonne chançe dans la vie khamoumala wayei ame na si yawe confiançe total
Yalla nala yalla takhawou défal la diamou ak ay khéweul you saawane baa wane barke khàssida yii 🙏
Tu mas fais pleurer pape fait tout pour rester dans le droit chemin tu as l'air d'une bonne personne je te soutien.
Ndaysan kaddu yi amna solo Dieuredieufety cheik ahmadou Kara mbacke noreyni bouko diklu won mou defar niepp
Lou weer❤️🙏🏾🙏🏾
Machalla mais boulniou nianal macky ameu deuxième chance.macky cagne doyna c'est pire que l'enfer
Waxal d doyna seukk si maky
Merci macky sall le président de tous les sénégalais koumou metti dewal
2e chance sa n op dir 3e madat
Salame Pape mane deh khamou mala wayer vraiment sa histoire bi dafa daw sama yarame natou ci diam lay dale dila nianal lici top yeup nek ay khewal inchallah allahouma amine ya rabi courage 🤲🤲🤲☝️
Thiey jistice sénégalaise 😭😭😭sathie kharr kasé 24ans il est temps qu'on revoit notre justice on voit des jeunes qui n'on fait qu' une simple bétise et perd leur vie dans la prison comment peut on commander une personne qui n'a pas commis de meurtre ou de viol plus de 10ans de prison Kallah nous assiste🙏🙏
La justice sénégalaise est une justice injuste
Demewul nonu évadés bi moko yombu 20ans de prison
Lossi khamoule sathioul skh
Daffna walf émission damale xole
Je vous j'ai mal jugé sur un commentaires sur facebook mais j'avais tort je te souhaite le meilleure dans les jour a venir
Tu es honnête frére 👍
@@mbalkakognedof5866 merci
Yaw tamit borom bakh ngua machallah
@@aissata8304 merci
Frere c'est une grandeur de reconnaître une erreur et de se rectifier. Merci pour ta franchise et ta grandeur
Ta Ndaysan pape momou niewoul settal sa derr😭😭Ooh C touchant
Franchement tu as fait une discours parfait chacun à son destin diambar nga bagne guatïè rk bilahi diap rk Dina bakh champion
Gouvernement bi na out bene politique pour insérer ces détenus sortis de prison. Ils ont droit à une vie égale à tous les citoyens🙏
Allahu Akbar quelle mental de fer no vraiment souma amoone walay dimbali nala côté finance mé yorou ma
Ndaysane yénébi am n'a solo
Yallah Nala yalla may yaw tamit
Mashallahou ridiall bi Sama xol toyna 😭😭 guene gor gorlou reik inchallahou dina guene Guen diambarr nga goorr Yalla deug nga Bilahi Noreyni reik 🙏🏽
24 ans de prison pour vol de mouton😭😭😭. Kone dé gni sath ay milliard sénégalais yi souyebo sene diabote bayi diour nday sene doundeu rekk dou doy année de prison yi sene seutati seut dinaniou teudeu. Soubkhanala un pays foutu
S’il n’est pas un voleur pourquoi vous dites qu’il faisait parti de la bande d’Alex🤷🏽♂️?? Explique moi svp. Il y a quelque chose qui m’échappe
Ziarnala bou wér amna emission boum def ak wa walf amna solo lool machallah ma ngi diégueulou
J sui touché vréma 18 ans khalé nga wone dange la warone aider vréma mé YALLA bakhna du courage
Il doit être indemnisé parceque 24 ans sans liberté et il n'a jamais commis de crimes c'est injuste et méchant
Pour un innocent 😢😢
Bonjour amis et gens de bien. Aujourd'hui j'ai eu presque la nausée en voyant les plats que déposaienr les parents de detenus a la prison de Rebeuss (la viande ,des frites de la crudités et de la sauce ) dans des seaux de 5 litre qui après des heures fermer ermetiquement commence a se décomposer qui pourra causé de l'intoxication alimentaire il faut que les mesures imposée soit enlever nous les parents des détenus sommes fatigués et n on plus rien a envoier dans les prisons prétextant le covid19 or ils s'enrichissent sur nos dots par leurs boutiques et gargote
Vraiment domage. Essayons ensemble de creer un network sur Facebook. Si vous voulez je peux ouvrir la page ou on poura montrer au monde entier des photos qui vont illustrater tout cela.
Yalla nala sougnou borom takhawou c cette force ki m étonné
ya nala yala yokou gougou fan ak wer ak diamou yala boum nanngou amine
Je vois un gas qui a trop de choses a dire...
J'ai fait 3mois de prison en chine mais metiwone n'a santal yalla grand
Vraiment bonne continuation du fond du cœur yalla nala yalla dolli soutoureu bou bakh
Walahi frère magui ley ñianal yalla diko ñianal bolém dioulitee yalla nala sounou borom oubilattt bountou khéweul,defal leu wéér werlé samm leu dundeul pape
Yalla naniou yalla may moudiou gou rafet
Frerre Tu ma fais pleuré
Ndaysane on habite ensemble natou rek la wone pape Ndiaye digne fils de Fass Rufisque 😭😭😭
Comment le contacter?
Comment le contacter..?
@@omsarr02 772545455
@@njisalima 772545455
@@malickndiaye4880 Merci beaucoup
merci grand cadou rafetna lolee 👈👈🙏🙏 ducourage rek yaw
Wa bahna légui goorgorloul diéma séllal dioubeul. Dém door waar bania tope média yi.
So danko conseiller ni ba tok?
@@modousow8832 sama khalaat rék la diokhé dé. Khawma ndakh aye conseils la ou pas
@@lilmarkeitafromkoarprojet9538 😀😀😀😀😀
@@abouhamza8948 ah kholal rék
Deuk bi mo métti
Oooooh vraiment content
Yalla nalla yalla oubil ay bountou ci Barki serigne touba guene la tegat cii yone bou bah
Pape Ndiaye yalla nala yalla takhawou bilahi
Ndaysan😭🙏🏾🙏🏾lou metti Goor lay dall yalla naniou sa Borom diegual Ndaysan metti neu lool😭🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Pour mane pabe ndiaye bou amone avoca bou bax tou deut 24ans
Fékhéle moytou di wakh ci média yi lou bari.Fii moy sénégal.Wakhine la nak.Dafa laj deug deug.
Dagan bakh rék mes ki kham Na Lou bari si ADIna
Ndeysane sama khol toy na yalla nalla borome bi diappalé
Yalla na yalla takhawo la si Barke borom Touba amiennn
J'ai versé des larmes wallah
Ball nagn akk yalla borom bi boléniou ball té sunu borom defal la li dess sisa doundou lepp di ndiarignn té sa fan goudou loll té sunu borom xirr la si mom ♥️
Je vw ici un homme stoïque, Yallah nalleuh Yallah Samuh et courage...
Ses paroles sont l'incarnation du stoïcisme originel.
Bon courage mon frére yallana yalla dimbalila boubakh
En résumé l'état t'as mis en prison, 24ans apres il te libère sans aucun sous ni suivis 😔
Et le pire il a été incarcéré par erreur 😭😭😭😭😭
ماشاء الله إلى أمام
Yaye Fall fall Koula wah lolou yow
@@yayefallfall2637 li ngay wakh loula si lerr
Fallou Mendy moko wakh yokou massi wagni woumasi wa Salam
Ndayssan on habite ensemble nianal l3n ko rék 🙏
Fiérté Fassois Rufisquois
Sawaye nianalale loula nékh maky sauf 3ème mandat diapesi rk
Bilahi wakhatiko
Mdr
Mdr
Mdrrr
Ki nak mo wara wax si kaso yi ndkh yageu nafa loll
Billaye mome ak Alex
Bo meussoul ray nite rek vous méritez une deuxième chance
Vraiment li mom ça doit nous servir de leçon
Thieuye grand yall nala yalla deffal diamme li ak addouna nio ande courage
Dioulite deugue day am natou yalla nalla yalla defal diamou
Bon reportage
Merci Wagué
J'ai les larmes aux yeux.
😭😭
Yalla naniou yalla khiir si lou bakh , lou bone bakhoul
Amna loum beugg wakh lou beuri. Interrogé wat leine ko
Yallah nala yallah doli soutoureu katan talak fekké Moss ak mouthiou oubila bountou khéweul yi bolélak niit you bakh yi bangua teddeu teral say askan ak sa famille et tt l monde
Ndeysane dawna yaram yalla nala yalla defal diam teik la si yoneuh boubax 🙏🙏🙏
Avant ma naissance et moi je me sens tellement vécu tout ce temps il était dans le prison
Bilahii ndeysane
Bon courage champions yalna yalla oubila xéweul boudoul diéx
Ce sera pas facile mais bon il faut essayer de s’intégrer trouver un travail.
Yallah bakhna
Alhamdoulillah yalnako borom bi diégal té dioubal il est tres reconnaissant
Macha'alla frère
Serigne bi lakal wolof rek et bon courage
Natou ngenal la et yakhine né durant les 24 ans lou bakh rek nga done def si prison bi
Donc alhamdoulilah yalla rek moy karim
Mais il avait commis quel genre de crime? Aider mw svp
*AMNA BÉNE EMISSION BOUM DEF AK WAA 2STV FÉKÉ SETANA GUOKO BKO SETANE RK DI NGA SI COMPRENDR LOU BARI INCHA'ALLAH* *GUOUDOU NEUH MÉ AMNA SOLO*
Yaw khana xalé nga 😅
Braquage à main armée
@@yallakenla739 nous émission bi toudou
Yii man deh gni damalen don deg rk ndeysane bobou khalé la rumeur yi rk ladone deg khaw ma sakh lougniou done def ndeysane massa
Sente tii yalla Borom bi Bou Bahh👏jamm si iow
Celui là je le conseille de se faire discret et d'essai de se réinsérer dans la société c'est mieux que de s'afficher publiquement sur les plateaux TV qui ne cherchent que du buzz.
machalla mais yalla nala yalla takha woul bou bhak sii barki seydina mouhamed
Champion deug 24ans de rebeuss yoboul
Vraiment yalla nala yalla gueuna sopi inshalla
Lou meunoul niakke faut que mou amme 🙏🏽
Yalla nala yalla takhawou sama khole dafa toye sy limou wakh Sénégal War nano khole ninouye diapé nit yi lidafa méth torop
Respect a toi grand bi do ragal