Méchanceté gratuit, ne te laisse pas juger pour ton passé man,incarne tes droits. On est dans un pays ou il faut se battre tous les jours pour garder ton honneur.
@@harissndiaye1820 jail dafa graw daguay dem ba habitué fofou nakh doto subir pression social boussi biir deuk bi dall nama jugement bi feep lay diougué 😢
Première réinsertion moy nga changer lieu dem fenene après tout va venir incha allah Sénégal Dou reew balamadhre rek gnounane Bena bopaleu Sénégal fouki bopala les riches et les pauvres justice amoufi
Il a bien fait de partager les faits au cas où les choses dégénèrent par la suite. Désormais, il est important de faire preuve d'intelligence émotionnelle dans ce genre de situation. À savoir qu'il a déjà payé sa dette et il s'est réinséré par ses propres moyens dans cette société. Alors il mérite qu'on l'encourage. Le pardon existe sur terre car nous sommes amenés à commettre tous des erreurs.
@@mouhamedanouarousadateka7652 grand bi da bayi loxom...setlou nga lolou noum séton ,diantal ak legui cest diferent , limou wakh ni walay amoul , sino boy yi dinavn ko cambal ..ki waxam ak dieuf dji bokoul
Man miinou mako mais je connais sa famille bimou néké halé lako gueudj gis madaan dém sén keur Di séti tantam Khady Yayam bou mousaan djogué prison sama keur lay djaar teud touti noopalou keur googou Mouy wah daniou meusseu hép famille pape ndah nioolén tanéwon touti financiérement
@@mbayafall6424 ah bon mes pour quoi wa keur gogou dii xém famille ausi més pape Ndiaye dafa sone trop bilahi na dém sii autorité yii niou outeulko visa Mou dém Europe changé vie yalla bakh na courage pape Ndiaye
Même sou nangouwoul déposer plainte neu def main courante parce que woroul meun nagn ko reyy wala mou fipou xekh ak niom gagn si kenn après moy lolou. Courage
Pape mon fils lingay wah hébel gou yaagla yaagnaa nieuw sén keur ham sa yaye sama mak kou baah touti gueuye sa tante Khady sama soeur keur googou meusou noo beug sén waa keur 😭😭
Li mouye wax li yeupp deugeu la.on habite dans le même quartier. Mou dem louer si quartier voisin bi.mais defoul wakhoul nitt kou bax té am yeurmandé goor yalla ndaysane. Sou foré deureum délo lako .il est marié ba am neu dom bou djiguene. Si ligueyam rek la nékk beugeu waxtane nak
Pape je te souhaite bonne chance mais disparaît de leur vie et change de lieu d habitation s'il te plaît. Oublie les et ça vivre ta vie .Pas de confrontation avec un peuple.
Courage grand frère, vous êtes très intelligent vous parler très bien..juste une partie de la société sénégalaise sont très enfermé par des préjugés. Tout le monde fait des érreurs. Et que la prison est faite juste pour corriger...lui il a purgé une peine de prison. Il n'a pas de dette à la société...que Dieu te protège et bénisse
Il fait face à la vraie vie maintenant. Avant si limou nekone dafa yombone trooope. Kou liguey ngua nangouko by force En plus jail dafa yombeu si certaines personnes ils font rien là bas
Salut cher téléspectateur comment vous allez se temps si je regarde les témoignages des détenus homme comme femmes qui sont ici je voulais qu’on crée une groupe pour aidé les prisonniers prck natou d’où wéss t’as y’a des innocents là de dans svp unissons-nous pour aider nos frères et sœurs🙏🏽😭
Pour garan bobou bouba chinois perd pas temps. il est toujours ivrogne habile manipulateur ki fait pleurer les gens ki le connaissent pas .nous nos famille été voisin a la rue dial diop .on se connaît tous + les bêtise du vieux bouba chinois
Je le redis cas garan bouba chinois te fait pas manipuler. il est toujour nekkeu di nann sou lard , manipulateur habile. Nous on été voisin nos famille se connaissent ya longtemps
S’il vous plaît chers frères ayez pitié de lui laisser le vivre en paix pour l’amour de Dieu ça vous coute rien vous voyez pas kil a assez souffert! Il a payer ses actes!et il regrette son passé nul est parfait 👌🏿 donné une chance 🥲 Yeurmandei rek tei yalla takh! Sensibiliser les jeunes du quartier niou dawal ko yeurmandei😭😭yalla dawal léne yeurmandei🙏🏿 C’est vraiment triste😭😭😭 J’ai craqué 😭juste en imaginant sa douleur et sa souffrance ana sene yeurmandei xana dou guene ay musulman. Courage pape ndiaye que le bon Dieu te protège et te donne la force d’aller De lavant et t’offre une meilleure vie👊🏿👊🏿👊🏿
Vraiment c du n'importe kw gni sen yaram du daw 24ans prison doyul dagnko beugue ray t déwagul méchanceté gratuite bissi Sénégal war nagn si wax xol nitt nexula rek ga bgue ko féxal doy na war tropppp
Senegal tass na. Comment des gens de même quartier peuvent calomnier sur une personne dont vous habitez ensemble. Aye deum llagnou sounou bir. Ils sont mechants ces gens là.
Barkè borom touba sènègalais bakhoul pape ndiaye yereum nako trop 😢😢 sènègalais sokhor na bone na ignane na si moromam motaxit lo guiss dougnou bouchè sarab ndeyam
sénégalais hen djiko boubone la yor , mais pour mom mo guene les autres . juste kholéne ko si nos vosins de la sous régions . pour nioune nioléne geune koi ,
Lii mettina,ki daffa sonnou tropp,du courage,et change de lieu d,abitation, parce que, il est en danger,je te conseille de déménager c'est mieux pour toi,mon frère,sa vie a toujours été difficile pour lui, mais yalla bakhna inchallah, dinabakhe inchallah, bayile lepp,si lokhoye yalla guissna lepp, mettina deyssane,du courage.
Pape Ndiaye ioe goor nga bouko falé sakh toi tu es un homme digne tu as fait la prison mais ça fait pas de toi un démon ou une personne perdue ne te laisse pas juger humilier ou insulter par des personnes aussi basse
Laissez le tranquille il y a des personnes qui n ont pas de cœur pourquoi le faire mal à cause de son passé il est une n autre personne qui gagne sa vie dignement vous voulez quoi maintenant arrêter
Sois fort mon grand moi mom baxx rek la meune Wax si yaw Dax mom la guiss ´ lors de sa libération tok naniou wax lou yatou à l’université cheikh Anta Diop et il me disait « sois fort et travaille pour sortir avec la tête hausse ❤ »bobou mom mogui liguey si restaurant Diop Isec di Dane dolem Bilahi c’était moi AbdeL Dieng et Thio (alioune diop)
Deuke bo khamni Coumba ame ndey ak Coumba Amoul ndey le ni rek lay dèmè…. Bouniou fatè ni Casso diomboul kèna Yallah moy tek niite Natou… Yalla nala Borom bi sameu tè gueune le taxawou…yagueu yokeu werr inchallah ✊🏾
khana khamougnou moun ngalène wathièl contigent pour règlement de compte. gnata waga nga kham si dièl bii tè yow rek lègnouy dèglou. diaylèn defkat yiii mou fin
19:20 So nekkee bandit nag, mbubbu boobu rek la nu lay solal. Woolu la du yombati. Waaye nag, wax na degg ndaxte ci dekk bi la bokk te kenn eppelewu ko fa dara.
Méchanceté gratuit, ne te laisse pas juger pour ton passé man,incarne tes droits. On est dans un pays ou il faut se battre tous les jours pour garder ton honneur.
Ndeysane il beaucoup maigri depuis sa sortie kallah te protège
Bilaye il a trop maigri Ndeysane stress
Bilay en plus dafa nioul il était bcp plus clair et ça se voit qu'il était bien et bcp plus à l'aise en prison
@@harissndiaye1820 jail dafa graw daguay dem ba habitué fofou nakh doto subir pression social boussi biir deuk bi dall nama jugement bi feep lay diougué 😢
Première réinsertion moy nga changer lieu dem fenene après tout va venir incha allah Sénégal Dou reew balamadhre rek gnounane Bena bopaleu Sénégal fouki bopala les riches et les pauvres justice amoufi
Tu a raison frère motakh nioun badolayi warnaniou kham souniou bop guene gorgorlou la loi c pour les badola
C vrai déé il faut qu'il change lieu d'habitation immédiatement d'abord...
C'est mieux
Frère dèèl dioulli lou Bari Bari, té di takkoo ndiapp ,di sahoo niaan YALLAH!
YALLAH na YALLAH tahawoula
Vraiment ce garçon mérite une réinsertion sociale que dieu pape que dieu te protége amiiin
Nous avons besoin ces genres de reportage merci Da tv
Courage mon grand vraiment kou bakh la kham ci mom depuis mou gueun on travaillé ensemble.
Sort de ce quartier.. Soudoul lolou ay problem kèssé guéy am
Il a bien fait de partager les faits au cas où les choses dégénèrent par la suite.
Désormais, il est important de faire preuve d'intelligence émotionnelle dans ce genre de situation.
À savoir qu'il a déjà payé sa dette et il s'est réinséré par ses propres moyens dans cette société.
Alors il mérite qu'on l'encourage.
Le pardon existe sur terre car nous sommes amenés à commettre tous des erreurs.
Sokhna ci ki cogne dangou leu deuk rufisque , mom ak sam grand nioy and , wakhoul deug dé , temps yi dey mandi di toukh ..pape ndiaye da yakk bopam
@@Charles-ec8dp sa diguentek yalla wala daghaye kaff rk
@@Charles-ec8dp mais nk nimou diéxé nk diaxal nama bami guéne prison dafa amone yaramm
@@mouhamedanouarousadateka7652 grand bi da bayi loxom...setlou nga lolou noum séton ,diantal ak legui cest diferent , limou wakh ni walay amoul , sino boy yi dinavn ko cambal ..ki waxam ak dieuf dji bokoul
surtout ça , parfois il faut user de son intelligence émotionnelle et se retracter .
Nite kou yarou nite ko khamné adounam yaupp dako mougne 😢😢😢😢sonou na trop svp bayi léne ko mou doundou 👏🏾👏🏾👏🏾
Courage, mon gars, il faut tenire. La méchancheté de beaucoup de Sénégalais, ca ne se comprend pas. Il faut tenire. Tout va aller. Tu es courageux.
Cheikh Papa Ndiaye, fatéle histoire bi té nék ci seu ligueye!
Fatéle problémi!
Meunouko faté nonou li dafa graw nako lidieunti ba paré car meurtre meun na on sait jamais té togne dou gualadj
@@harissndiaye1820 ki bou défoul ndake dina délou présion
Grand li ce n’est pas facile de l’oublier et j’espère qu’il n’est pas encore prêt d’oublier cette histoire 😢
Je le regarde aujourd’hui et à sa sortie de prison. Il a vieilli de 10 ans. Les rigueurs de la vie quotidienne certainement. Qu’Allah l’assiste 🙏🏿🙏🏿
Wolahi Ndeissane
Courage grand je te connais pas mais tu me fais pleurer
Man miinou mako mais je connais sa famille bimou néké halé lako gueudj gis madaan dém sén keur Di séti tantam Khady Yayam bou mousaan djogué prison sama keur lay djaar teud touti noopalou keur googou Mouy wah daniou meusseu hép famille pape ndah nioolén tanéwon touti financiérement
Salam je voudrais bien être en contact avec lui svp
@@mamematyg legui Mbeubeuss la nek si Wa ucg yi difa amal liguey bou raffet
@@mbayafall6424 ah bon mes pour quoi wa keur gogou dii xém famille ausi més pape Ndiaye dafa sone trop bilahi na dém sii autorité yii niou outeulko visa Mou dém Europe changé vie yalla bakh na courage pape Ndiaye
Pape ndiaye yallah na yallah défale diam ak salam si barké seydina Mouhamed
Sws
Senegalés yii nek len ay nitte togne dou galathie..vreman grand metina trop bilahii 🤦♂️🤦♂️🤦♂️🤦♂️🤦♂️🤦♂️🤦♂️
Vraiment
Naniou baayi djambour natou man naa dall kou nék pape mon fils keur googou boulfa dougueutî djaapal sa djambour 😭😭
Chapeau mon frère .bagne ba dé. Niom khana khamouniou prison
Même sou nangouwoul déposer plainte neu def main courante parce que woroul meun nagn ko reyy wala mou fipou xekh ak niom gagn si kenn après moy lolou. Courage
Sénégal loutax niou sokhor togne rék mo am Sénégal
Bilahi so fayoo gni teudj leuh
Surtout banlieue bi
Paix sur vous mon Grand.
C’est que Sénégal daniy Saupp ni req mais Beugueunté wuniu.
Qu’الله te protège de tout mal.
Ńp
Ta plus le droit de marcher à certain heures en plus de rentrée dans un domicile par infraction. Du courage et change de domicile si possible
Loloy deug
Défend toi man te laisse pas faire les sénégalais sont trop méchants ridicules et coincés de mentalité, GATSA GATSA reik
Pape mon fils lingay wah hébel gou yaagla yaagnaa nieuw sén keur ham sa yaye sama mak kou baah touti gueuye sa tante Khady sama soeur keur googou meusou noo beug sén waa keur 😭😭
ok c ça
Ndeysane
Wallahhi ndéy sane pape yalnala yalla samou in challahh 😥🤲❤
Pape encore une fois n'insiste pas on va te jouer un tour un jour et tu risques de perdre ton travail et de retourner en prison
Li mouye wax li yeupp deugeu la.on habite dans le même quartier. Mou dem louer si quartier voisin bi.mais defoul wakhoul nitt kou bax té am yeurmandé goor yalla ndaysane. Sou foré deureum délo lako .il est marié ba am neu dom bou djiguene.
Si ligueyam rek la nékk beugeu waxtane nak
Ndeysann c'est quel quartier
Ndeysane mom kay kou deugou lay ndiiroul Yalla nako Yalla deffal diam si barki Mohamed Senegal mom ni rek
Ndayssane amena dôm baréna machalla...
Alkhamdoulilah
Boule messa Fatou yalla bakhna courage
Ndeysane 🙏 yallah nala yallah takhawou
Bro JTM 🖤 bcp soit toujours forte yalla dana atei insha'Allah Amal Diam 🙏🏾
Pape je te souhaite bonne chance mais disparaît de leur vie et change de lieu d habitation s'il te plaît. Oublie les et ça vivre ta vie .Pas de confrontation avec un peuple.
Exactement c'est ce qu'il doit faire !
Courage grand frère, vous êtes très intelligent vous parler très bien..juste une partie de la société sénégalaise sont très enfermé par des préjugés. Tout le monde fait des érreurs. Et que la prison est faite juste pour corriger...lui il a purgé une peine de prison. Il n'a pas de dette à la société...que Dieu te protège et bénisse
Ameen ya Rabbi
Il a trop maigris 😢
Yaram bou bari bakhoul !
So yaggueii prison da ngaayy neiwwii Meii So gueineii Reussss Leikk prison bii molay neiwiilo mtx
@@mafaltiimchriisgaye8681 Sank ba légui magui done diéma comprendre mais ligua mo meneu am
Mais grand bi yalla nako yalla taxawou natou douwess
Il fait face à la vraie vie maintenant. Avant si limou nekone dafa yombone trooope. Kou liguey ngua nangouko by force En plus jail dafa yombeu si certaines personnes ils font rien là bas
Ndeysane courage grand frère pape ndiaye
Salut cher téléspectateur comment vous allez se temps si je regarde les témoignages des détenus homme comme femmes qui sont ici je voulais qu’on crée une groupe pour aidé les prisonniers prck natou d’où wéss t’as y’a des innocents là de dans svp unissons-nous pour aider nos frères et sœurs🙏🏽😭
Belle initiative a concretiser
Pour garan bobou bouba chinois perd pas temps. il est toujours ivrogne habile manipulateur ki fait pleurer les gens ki le connaissent pas .nous nos famille été voisin a la rue dial diop .on se connaît tous + les bêtise du vieux bouba chinois
Je le redis cas garan bouba chinois te fait pas manipuler. il est toujour nekkeu di nann sou lard , manipulateur habile. Nous on été voisin nos famille se connaissent ya longtemps
Yallah nala Yallah takhawou Cheikh bi,
S’il vous plaît chers frères ayez pitié de lui laisser le vivre en paix pour l’amour de Dieu ça vous coute rien vous voyez pas kil a assez souffert!
Il a payer ses actes!et il regrette son passé nul est parfait 👌🏿 donné une chance 🥲
Yeurmandei rek tei yalla takh!
Sensibiliser les jeunes du quartier niou dawal ko yeurmandei😭😭yalla dawal léne yeurmandei🙏🏿
C’est vraiment triste😭😭😭
J’ai craqué 😭juste en imaginant sa douleur et sa souffrance ana sene yeurmandei xana dou guene ay musulman.
Courage pape ndiaye que le bon Dieu te protège et te donne la force d’aller De lavant et t’offre une meilleure vie👊🏿👊🏿👊🏿
Amine
Merci bcp bro.nagne ko bayii mou dounedeu kw tranquile géré bopam
Vraiment Merci Amine ❤️🙏🏾🥲
Vraiment c du n'importe kw gni sen yaram du daw 24ans prison doyul dagnko beugue ray t déwagul méchanceté gratuite bissi Sénégal war nagn si wax xol nitt nexula rek ga bgue ko féxal doy na war tropppp
Balayé wahal il a payer maintenant c'est fini dawaléne yeurmandé téé yalla tahh... 🙏🙏🙏
Senegal tass na.
Comment des gens de même quartier peuvent calomnier sur une personne dont vous habitez ensemble.
Aye deum llagnou sounou bir.
Ils sont mechants ces gens là.
Pape courage yalla coumou sope rék laye tégue yéneyi bouma amone ayes millions nga kham
Barkè borom touba sènègalais bakhoul pape ndiaye yereum nako trop 😢😢 sènègalais sokhor na bone na ignane na si moromam motaxit lo guiss dougnou bouchè sarab ndeyam
😭😭😭😭 oh laisser le vivre sa vie.
Ndeysane chak jour ma sètaan video bi ndakh yereum saway 😢
Limithi diakhal moye léne so bayé mou séde biss dina niew niou déf la lou guéne méti deuke bi da ame yone lidiantiko bala lénéne dithi amat
Porter wztal plainte bala gnoulaye fagagal téé boula yalla mayé moyen guaa tohou fofou...
Pape ne te laisse pas faire gni douniou ay nitt
Mane ki dama ko beug nguir yalla rék tax bilahi doundou na lou méti goudeul fane yalla nala yalla téral ba nga faté lép
Do fayou dée wayé yalla beugoul injustice
Ndeyesan yalla nala yalla same
Diambar amena louko metii Dee il parle avec keur ...nb; kene d'où roukh gainde bouye nelaww bakhna rekkk...
Pape conseil day manou ciii affaire yii mon guene sathieu sakh boulko topou
Bilahi walahi tu me fait pleuré l'aissé le vivre ca vie svp courage daye bakh inchallah
Meetina torp wayé dana bakhe
Yalla nala yalla defal diam
Un coule grand que se connait depuis longtemps aux campenal je suis un chauffeur de camion citerne d'eau grand yalna la yalla takhawou
sénégalais hen djiko boubone la yor , mais pour mom mo guene les autres . juste kholéne ko si nos vosins de la sous régions . pour nioune nioléne geune koi ,
Yabate rekk
Ndaye sane Sénégal mo méti ta diafé mothou yalla nala yalla samou
Ohh ndeysane 😭😭
Sénégalais mo guueneu dohan ndeim parsk il était détenu motah kossi diap katal ndeim li rek motah galsene dou ndaye bougé
Change de lieu d’habitation tourne la page recommence une nouvelle vie
Manchallah pape yallah n'a lah borom teikh lokho
Wallahi qu' on respect tes droits c'est tout à fait normal
Kone mome loumouy expliquer ni dou lou yagg ? Pour Mane sakh temps boy ley wakh. Loutakh gars yi sonal ko si kognam?
No yag na d day netali watte rk
Oh courage Pape. C'est très dur
Sii yoobe nagne fii nitte kasso batayii tè dèfoul dara
Ohh sad let's do better give people second chance
Mougneul lou métti yagoul adouna dou dara
Lii mettina,ki daffa sonnou tropp,du courage,et change de lieu d,abitation, parce que, il est en danger,je te conseille de déménager c'est mieux pour toi,mon frère,sa vie a toujours été difficile pour lui, mais yalla bakhna inchallah, dinabakhe inchallah, bayile lepp,si lokhoye yalla guissna lepp, mettina deyssane,du courage.
C vrai déé il doit déménager c'est mieux pour sa sécurité Sénégal dagno sohor nama yalla ball..
@@Lopios-g6l bilaye lii Metina trope
Dou dekou sarap ndeyem la wakh senegal gi 😭😭😭
Pape Ndiaye ioe goor nga bouko falé sakh toi tu es un homme digne tu as fait la prison mais ça fait pas de toi un démon ou une personne perdue ne te laisse pas juger humilier ou insulter par des personnes aussi basse
Bonne continuation frère ❤
Wa mais bane deukk laniou nekk quoi ndax passe wam rk niiu beug ko ray justice n’a taxaw si lii way bala mouy eupi loxo
Laissez le tranquille il y a des personnes qui n ont pas de cœur pourquoi le faire mal à cause de son passé il est une n autre personne qui gagne sa vie dignement vous voulez quoi maintenant arrêter
il faut porter plainte ces simple courage
Sois fort mon grand moi mom baxx rek la meune Wax si yaw Dax mom la guiss ´ lors de sa libération tok naniou wax lou yatou à l’université cheikh Anta Diop et il me disait « sois fort et travaille pour sortir avec la tête hausse ❤ »bobou mom mogui liguey si restaurant Diop Isec di Dane dolem Bilahi c’était moi AbdeL Dieng et Thio (alioune diop)
Donc il ne travaille plus là bas?
Pk vous écrivez Pape Ndiaye ancien détenu 🤬🤬
Bon courage mon frère
Sama yarame dafa daw billay😢
laissè le tout tranquile svp pape courage n les laisse pas fairr premd t garde que t dieu proterge
aminre
Li cas bou bess la wala😭😭😭
Laissé le vivre ca vie svp il mérite une seconde chance moi entouca je l'aime bien
pape Ndiaye Sénégal cepa Rufisque rek allez vivre ailleurs mon gas
Loy dakater la khamoule do yame
Deuke bo khamni Coumba ame ndey ak Coumba Amoul ndey le ni rek lay dèmè…. Bouniou fatè ni Casso diomboul kèna Yallah moy tek niite Natou… Yalla nala Borom bi sameu tè gueune le taxawou…yagueu yokeu werr inchallah ✊🏾
Courage bro Sénégal metti na
Yalla na yalla takhawoula !
Il as déjà payer sa dette avec la société . Laissez le vivre en paix vraiment !
J'aimerais bien qu'il change de zone .
Courage frère c’est écœurant mais god is great
Li dafa niaw
Li amna solo lol vraiment
Sa photo profil bi Machalla
Stp dolénn sett Alex khana
Mane damako yeureum ba beugueu ko je te jure ki boko kholé rek khamni kou bakhla
Courage ❤
Yalla bakhna
Le faites que niou sonolla amena louko djitou
Demal tribunal directement
khana khamougnou moun ngalène wathièl contigent pour règlement de compte. gnata waga nga kham si dièl bii tè yow rek lègnouy dèglou. diaylèn defkat yiii mou fin
C'est depuis quand
Courage bro
Pape il faut que tu change de lieu
Il faut quiter rufisque et aller dans un autre lieu
19:20 So nekkee bandit nag, mbubbu boobu rek la nu lay solal. Woolu la du yombati. Waaye nag, wax na degg ndaxte ci dekk bi la bokk te kenn eppelewu ko fa dara.
voila les consequences de ton passe et cest dommage mais ta bien fait de parler