diadieuf president bassirou ak PM oumane sonko PM takhaw len si soufou rewmi domy rewmi di Sénégal 🇸🇳 di si diot di si am waye' dou deug dou yon étranger waroul waala titre foncé dou douday dou europe do fi am souf jamais si rewou gjiambour loutakh Sénégal 🇸🇳 c'est pas normal li won na woni legui niou nek si jub jubal jubanti rek deug bou wer ngen wakh samba kebe' marieta rougui diadieuf wa S24 😊
Dëgg la !! Dal na sama rakk bu jigéen ci Bambilóor. Meer bu domaraam ba fa nekkoon te sànt Mbeng moo ko nax dagg toolu màngoom bum fa amoon di 1 ektaar. Def garab ya këriñ, jaay ko lekk xaalis ba, jël 11 pàkk ci 31 pàkk yu mu ne moom la ektaar bi génnee. Man nak fekku ma fa ndax da maa yàgg àll. Lii la doomu xaj joohu def ci alalu ay jirim yu sësul ci kenn
Nee leen seen ndaw soosu def naa ko muy sama kombaa maashaa Allah ! Yàlla na Yàlla mottaleeg jàmm
C'est. Grave. Ce. Pays. Le. Pays. A était. Dilapidés.
IL NE FAUDRA JAMAIS