Maty rose le rôle qui est entré de joué pleine de leçon de la vie ndeysane déme ci yalla pape ndiaga mbaye loumou waxone dof bou wëredi kénn douko daw sa yoko dawa meune ngaako yokk louko méti merci maty rose si rôle bi wayé kénn dou niankou félicitations a tout l'équipe one love ❤
Amadou tu as fait 1 peu une erreur sur les paroles de mame ndiaga mbaye dani la (Daw kou weredi boko defe dinako yokk louko meti )wakhoula dof bou weredi car dof il ne l a pas dit comme ça weredi c est pas seulement dof meune na nek yenene fébar aussi 👌
Oui c'est un très bon rôle, cependant on pouvait être beaucoup plus réaliste même si est on dans un scénario : c'est à dire omar devait être complètement guéri avant la relation amoureuse avec lui et maty. Car aucune femme lucide ne va accepter de se marier avec quelqu'un qui ne jouit pas de ses facultés mentales en réalité ( bou nguén tëddé goudi mou khoth la nak😅) C'est ce que je trouve comme erreur dans ce rôle, sinon tout est bien.
Ndeysane yaye Dior bagnoule Boury dh sokhna bou magg mo diakhasé khél mi mes elle se réveille saytané wakhoule degue wayé yake khél yallnaniou yalla mouseule si saytané🤲 ❤❤❤
nguir yalla rékk bouffi kénne mboubbo yonnente bi wala sunnu kilifa dinné yi di niane ay j'aime😤😤... ishh soff guénn trop mélnie j'aime yi dalénn di diarigne dara si séne life....wakh lenn si série bi nndakh monioufi andi kouka meunoul nga diall (bayi nitt yi diokhé sen opinion)...en plus kou beugeu gnianal yonenti bi sa sidiada doynalasi seukk lo dioulli doyoul
Even Prod yeen tamit bonne année ! Yalla naleen yalla sam ba nguen niou yaga beggal. Franchement maison de production 0 faute. Vous méritez les 10M d’abonnés voire même plus. Even Prod thia kaw thia kanam rk.
Sincère remerciements à évent prod sur les séquences de Maty Rose et Omar Diagne. Sachons donner une seconde chance aux femme et hommes qui les aléas de la vie les ont conduits dans les bas fonds à un moment de leur vie merci
Barki rassoulilay khawmani wone sokhna Diagne beugue na iboulaye😂😂😂😂 Boury môme machallah classe bimouy dégagé eupeunaaaa ta mo gueune ci ndiawar gueune ci entreprise bi nakh meussou ci def lignoukay khébé wayé soda mareme mi gneuw di gass ay kambeu
Non il faut pour rôle bi âme sens sinon kaye dinagnou yagha sene liguey yeupa le grand public doit assimilé cette leçon de vie billahi j'ai aimé la dernière séquence j'étais la entraine de sourire comme kou weredi donc bougnou tegue déception il faut oumar weer liguey biko tata bi defone dagne mou dieul relevé papa bi di sole aye costume di topoto maty comme une reine tegue ko thi kaw teral ko beu gneupa bayi khel thi gni lago dankh li mbeguel meuna fadj lenene meunouko moyé force tranquille merci evens prod yallah nalene yallah takhawou
Oumy conseille à Maty Rose d'attendre qu'une personne riche vienne l'épouser. Le problème est que beaucoup de riches sont plus " rokossou" que 0umar. Mais quand un riche est fou, on dit "aka saf khorom". Quand un mangeur de mbakhale mou tooye est "saf khorom", on dit" chim! Dof bobou"😂. LOVE
Xaliso c'est le meilleur série de l'année bilahi pask Ndiaware Diagne borom c'est très bien rôle bimouye joué meune nako Sokhna Diagne môme Diop Fall daye joué Nar bi mou yakar ni daye supporté😂😂😂
Diawar limou wakh réalité la on le trouve partout dans les famille Sénégalaise mbokou you khamni diamou galinne yener gniou eumbal la safanne❤❤❤❤❤Bien joué
Date du Ramadan : 28/2/2025 Athan de Fajr : 3h50 Athan de Maghrib : 6h00 Le Prophète Muhammad (paix soit sur lui) a dit : "Celui qui annonce la date du Ramadan, le feu de l'enfer lui est interdit👂🏾🤍🫡
Courage et force aux acteur(ices) aux producteurs aux cameraman Adja ca c voit qu’elle et fatigué Mme ca voix l confirme métier bi yomboul vous le méritez je ne cesserais de le dire Evenprod meilleur maison de Production chaque épisode l confirme Machallah ❤sur vous
Bo défé lou bakh degn la nan c'est bien
Gua def lou gueuna bakh gnou nila c'est très bien 😂❤
Ana gni beugu Ndiawar Diagne
Aywaye 😂😂😂😂 srx
😂😂😂
amoul morom.....ndeysae llima métti moy serie i yeupp dakkoy daw🤣😂
C'est très bien 👍
😂😂😂😂 c'est bien
Boury est magnifique et très classe,posée et douce machallah. Yalla Nala thiaat sekhlou 😍😍😍
@piwou7290 Amine et merci. 👍
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Gni amoul xalisse yalla nalénn yalla may xalliss🙏😭😂🎉
AK wér AK tal inchallah amine
Amine 😢
Amine akh wér 🎉
Alkhouma Amine 🙏
Amine 🤲🏼🤲🏼🤲🏼
Mais la beauté de Maty Rose on en parle pas mashaallah waay elle est trés belle❤❤❤
lol sekh
Ndessane soxna diagne et son grand frère modou diagne c'est vraiment un amour fraternel 😊😊😊
La femme qu'on a tué à Touba et la petite qui habite a Malika yallah nalén yallah kharé aldiana métina na trop wallahi 😢
Amine 🤲
Amine
Amine
Amine Yarabi 👆.
Amine ❤😢rip
On parle de ndiawar mais Ass diagne j’aime bien son jeu d’acteur Machalla ❤
Il est très posé
Doug police Doug gendarmerie
Mohhhh !! C l meilleur ❤❤❤❤
@maimounadiagne972 Merci. 👍
@@maimounadiagne972 Walay tonton diambé sene il joue super bien
Maty rose le rôle qui est entré de joué pleine de leçon de la vie ndeysane déme ci yalla pape ndiaga mbaye loumou waxone dof bou wëredi kénn douko daw sa yoko dawa meune ngaako yokk louko méti merci maty rose si rôle bi wayé kénn dou niankou félicitations a tout l'équipe one love ❤
Amadou tu as fait 1 peu une erreur sur les paroles de mame ndiaga mbaye dani la (Daw kou weredi boko defe dinako yokk louko meti )wakhoula dof bou weredi car dof il ne l a pas dit comme ça weredi c est pas seulement dof meune na nek yenene fébar aussi 👌
Lolou deugg la maisss seuye bi amoul logique
@amadou-qq1cg Merci beaucoup, souligner geu lou ame solo. 👍
Oui c'est un très bon rôle, cependant on pouvait être beaucoup plus réaliste même si est on dans un scénario : c'est à dire omar devait être complètement guéri avant la relation amoureuse avec lui et maty.
Car aucune femme lucide ne va accepter de se marier avec quelqu'un qui ne jouit pas de ses facultés mentales en réalité ( bou nguén tëddé goudi mou khoth la nak😅)
C'est ce que je trouve comme erreur dans ce rôle, sinon tout est bien.
La complicité de Modou Diagne et sa soeur j’adore ❤❤❤❤
Bilay yaw da Beug rak dji 😊
Ndeysane yaye Dior bagnoule Boury dh sokhna bou magg mo diakhasé khél mi mes elle se réveille saytané wakhoule degue wayé yake khél yallnaniou yalla mouseule si saytané🤲 ❤❤❤
@aminatacisse818 Wa lolou tamite deugeuleu. 👍
@evenprod je vous love 😍 ❤️
Daa fekk limou doone woté diko wané dou deug rekk, sinon ak koumou meuneu doone dou meusseu changer
nguir yalla rékk bouffi kénne mboubbo yonnente bi wala sunnu kilifa dinné yi di niane ay j'aime😤😤... ishh soff guénn trop mélnie j'aime yi dalénn di diarigne dara si séne life....wakh lenn si série bi nndakh monioufi andi kouka meunoul nga diall (bayi nitt yi diokhé sen opinion)...en plus kou beugeu gnianal yonenti bi sa sidiada doynalasi seukk lo dioulli doyoul
Merci beaucoup 😮
Au moins quelqu'un de mâture alhamdoulillah
Merci beaucoup way
شكرا جزيلا
C’est bien , c très bien dit😂❤
Kousa yaye di sa kharite lalale j'aime
❤
Mane miiiiii❤❤❤❤
maynala ay jaime
Ndeysane mane awouma yaye😢😢😢😢😢
❤❤❤❤❤
Oh ndeysane c'est touchant vraiment Maty rose et sa mère 🥰🥲
@SokhnaMariamaDiaw ❤
Evenprod loutakh wané aussi😂😂 meilleurs vœux à vous aussi meilleure santé à toute l'équipe
@serginekampal6867 Merci. 😂
Even Prod yeen tamit bonne année !
Yalla naleen yalla sam ba nguen niou yaga beggal.
Franchement maison de production 0 faute.
Vous méritez les 10M d’abonnés voire même plus.
Even Prod thia kaw thia kanam rk.
Maty l’amour a le don de guérir tous les mal du monde, il n’a pas de visage, ni d’odeur, mais il a le don de nous rendre heureux ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Grammaire moungui lay weur deh
@@ibrahimasow-p4h😁😁😁😁😁😁
@@ibrahimasow-p4h😂😂😂soff ga
@@ibrahimasow-p4hlol😂
Ibrahimasow ya boone, maa guiss finguaye wokher😅
Gnafff Maty rose 🌹 li nga tontou sa tata bi c bien 👍 😂😂😂Ya Dior néna kouss kondrong bi 😂😂😂
C très bien
Xaritou Anna bi meussuma djiapp Touram waye dafma beétt sax man 😢🙆🏾♀️🤦🏽♀️🤦🏽♀️ waye lii dh lagni wax yeëneh nëekk la borom mosiy fanann
@@khadijadieng6658Oumy
Lolou moma ray 🤣🤣🤣🤣🤣
Merci astou iow dé si série bi guay commenté
Vraiment la maman de ndiawar elle regrette son act envers boury j’ai aimé 🥰
Bayiko mou gniam ba parei 😂😂😂
Yaye dior n est pas maichante elle c est laissé influencé par sokhna diagne cette vipère mais le karma existe
Mom deh bou Maréme soda changer woul won dou regretter tousss
@BarouSylla-kx1be Comme le dit l'adage wolof "bo yarei sa kouye bamou magg baleu mo meuk keine yaw ley gneuk meuk". 😉
yay Dior néna Fondements ma😂😂😂 Yeugue nako konn Lo Lou lépe khew nafi 😂wayé lépou yaw la,boury c'est bien c'est 👍
@YacineSeck-t2j Day lekk baleu baleu mo thiole lei. 😉
😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊y
👏👏👏👏😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅🥳🤦♀️🤦♀️☝️☝️☝️👍👍👍👍👍
Sincère remerciements à évent prod sur les séquences de Maty Rose et Omar Diagne. Sachons donner une seconde chance aux femme et hommes qui les aléas de la vie les ont conduits dans les bas fonds à un moment de leur vie merci
Tonton Ndiambé une personne très posé dans son jeu il assure
@fatoukinealmaktoumdiop1695 Merci. 👍
Il a toujours été comme ça je l'aime bien 🥰
Longue vie à nous avancer katou pub yii😅😂😂
Man gnaye wakhle😂😂
Masou maa sétane pub😂😂 bou dh télé sakh damay diouk bamou gnieuwate😂
Amine 😂
Amine😂😂😂😂
Amine
Mes parents tes parents leur parents vos parents nos parents vivront jusqu’à notre réussite
Amine🤲
Amine 🙏🙏
Amine
Amine ❤
Amine ❤
Allahouma Amine way🤲🤲🙏🙏❤️
Omar diagne nak moy dof bou beuri weurseuk machalla😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Mom kaay dof diott na😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂
@yayefall7840 😂
Boury est une femme de rêve 💭 Machalla kouko niak wouti ko ❤❤des cœurs ♥️ pour cette belle dame
❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@@medounediaw8725❤
@@fatou1820❤
Ayway bouri y’a classe❤ ta jongoma🎉
Bilaye classe bimou ame foko nare eupe nako machallah
Lolou mom geudje gui am na ndokh
Est-ce Guiss Guén tarr Bii tmt
Walahi Masha alla elle est trop Belle
@fatoundiayediouf5962 👍
Yalla naniou teudeu Béne Béne yéwou Béne Béne inchallah si barké seydina Moukhamed psl 🤲🤲🤲
Amine 🤲🤲🤲
Amine yarabbi barkep Serigne Touba
❤❤
Machalla 🙏 Ani fans Maty rose yii 😂 manifestez vous STP 🙏❤️
Wawaw❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MariamaKane-o3v 👍
Mangui ni dh❤❤❤❤
Maty et omar li nak moy amour pure sa c’est venu naturellement
@mariama9687 👍
No ndiawar diagne dinama ray de rire chapo à tte lékipe mashala evenprod❤
Modou Diagne nak Da beugeu rak dji comme sama Petit frère ndeysane il est trop protecteur je t’aime petit frère long vie à toi
Bilahi sama petit frere nono la mel koko rk moy sama aduna Amol si mane Sagou fete nama fepou yalla namako yalla samal
Amine
@@Ndayekhouma-c4d ohh yalna goud fane. Mane de sma rakk bou gor bima amone dima protéger demna bayima😢yalna Aldiana di keureum ak mbolem dioulite🙏
@@khadidiatouka-pn8xz paix à son âme
@@khadidiatouka-pn8xzque firdawsi soit sa demeure éternelle
Yaye Dior rétiou dina fek dieuf wess!! Sa gathié gui na yam si yaw rek 😅!!!
@ndeyebinetandiaye5371 Tei bo yarei sa kouye bamou magg baleu mo meuk keine yaw ley gneuk meuk. 😉
@@evenprodAkaye deugue
@evenprod lou leer!
Barki rassoulilay khawmani wone sokhna Diagne beugue na iboulaye😂😂😂😂
Boury môme machallah classe bimouy dégagé eupeunaaaa ta mo gueune ci ndiawar gueune ci entreprise bi nakh meussou ci def lignoukay khébé wayé soda mareme mi gneuw di gass ay kambeu
Mo diakhal nieup
@byanaartaye96Lou doy ware, xanna ya commentaire lou soft. 😂
Le visage de Ndiawar me fait rire billay Quelle phénomène
Cv🎉
Il est comique 😂 ndiawar
Rien que son visage fait rire
Omar diagne yalla nagneko may maty Ross mou wer wakhal amine yaw
Non il faut pour rôle bi âme sens sinon kaye dinagnou yagha sene liguey yeupa le grand public doit assimilé cette leçon de vie billahi j'ai aimé la dernière séquence j'étais la entraine de sourire comme kou weredi donc bougnou tegue déception il faut oumar weer liguey biko tata bi defone dagne mou dieul relevé papa bi di sole aye costume di topoto maty comme une reine tegue ko thi kaw teral ko beu gneupa bayi khel thi gni lago dankh li mbeguel meuna fadj lenene meunouko moyé force tranquille merci evens prod yallah nalene yallah takhawou
@Mouhamed-b4p 👍
Omar bouy sey di weur
Yay Dior dafa ay bilay😹délèn ko bayi xel ❤
Sohna Bou ndaw moko sonnal rek
Man dè sou nè imbecile bi rek ma youkhou😂
@nogayesarr5935 ❤
Sma yénai Tay moy am maximum 13 aime 🥰 souko défai ma khamni Senegal 🇸🇳 mongui dokh
Amgua 2😂😂
😂mouni 😂😂
@@bintafaye6161
Watal amna 2
@@rokhayandoye7184
Dégg gua lima wakh
Am nga 115 😂😂khana kon Sénégal mingui daw😂
Sokhna diagne khamone nani akheu boury dinako dall yaye dior khana kouss kondonrong tay lako djis😂😂
😂😂😂
MoMA diakhal 😂❤❤
Deug nexoul Mareme Soda kom kouss kondonrong😂😂😂
@ndiayendeye4713 Doyna ware.😂
Machallah Adja 😢 j’attendai cette question a propos de Oumar Diangne avec ces problemes mentaux 🙏🏾
Oumar Joue bien son rôle👍🏾
Yalla na yalla yueruem way dawlou yi barké seydina Mohamed Amine
Omar Diagne mi dal doff bou am chance la😂😂😂😂
Bly 😂😂
😂😂😂😂
Wlhy 😂😂😂😂
Mo beuri weurseuk keyy😂😂❤mounane maty gnieup gniongu lay khol khamnguein ni ki dofoul
bolé si té hame lou baah😂😂😂😂😂
Kou contane si boury kayy fi niou bègué❤❤
❤❤❤❤❤
Je suis la mon ami
Moi ❤
Moi mon ami🎉
@TallaFall-m3j 👍
Oumy conseille à Maty Rose d'attendre qu'une personne riche vienne l'épouser. Le problème est que beaucoup de riches sont plus " rokossou" que 0umar. Mais quand un riche est fou, on dit "aka saf khorom". Quand un mangeur de mbakhale mou tooye est "saf khorom", on dit" chim! Dof bobou"😂. LOVE
Ay fata wathie gnou 😂😂😂😂
😂😂😂😂 tu as raison
Lolou dh moy kou yoroule dangay yarou 😂😂😂
Yoyou khétou deug 😂😂😂
Très intéressante comme analyse
Ayy adja mii diékk na dii manchallah 😢est ce que sétlou nguéne ko😢
Non nn sétlou wouniouko yaw
Elle est trop belle Machalah
Mom mo beug perte poids khana do ko suivre 😊
@@Neymar1994-m5m😂😂
Bilaye maty rose mala béugue rck té yalla takhe❤❤❤
Tarou maty Rose ak belly wayam iska yena guikoy guiss machallah khalé bi way laf thiatt
Bilahi danion ndiro comme monko diourr even nion meune❤
Comme si que kayy dagnon bokk dara Niro nagnouu troppp
Khana machalla kay
Bilahi maachallah danio raféte
Félicitation Maty Rose qui ose aller avec Oumar Diagne 💪💪💪💪
Nila jiguen moy défar goor
La relation entre mari rose et Omar c magnifique mari rose est une actrice de qualité
Soula nekhone binde maty rose 😂wayé defoko thia marie bala
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂@@KhadidiatouSarr-s1m
Bilayy djiguene meune na changer kouné omar dina tané dina ligayy
Khana maty rose
@@KhadidiatouSarr-s1m😂😂😂
Non mane série bi sokhna mou ndaw moma si geuneu nekh ❤
La naïveté de la mère de Maty rose est énorme car elle ne se rend même pas compte de la méchanceté des personnes qui l'entoure en plus de ça.
Yaye dior néna kouss kondrong ya yapp maréme soda😂😂😂
Mais soda mareme ak sokhna bou ndaw se ressemblent trop
Dakko diéppi🤣🤣dara geunoul métti liko dall...ekk si keur melnie meuble
@@rokhydabandiaye9870 si c'est vrai
@@papemoussabeye7745 mom kay mogui regrette lou takh mou mayko ndiawar 😂😂
@@rokhydabandiaye9870 si c'est vrai
Non yaye dior ray nama😂cous kondron😮Yako takki wone deh😛réthiou dîna fekk dieff wesss😂bouri c bien c très bien 🤩 😂😂🎉
😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂
@NdeyeNdouraNdiaye Tei bo yarei sa kouye bamou magg baleu mo meuk keine yaw ley gneuk meuk. 😂
des coeurs pour prophète Mohammed psl ❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️psl
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Maréme soda ak yaye Dior yalla na seytané khépe doli😂😂😂😂
Ya bone 😊
Niankou est impeccable dans son rôle 👌
"Omar Diagne" quel acteur 👏
Kon Sokhna beuguone nga ibou laye 😂😂😂sheut Ndiawar réveil toi bala soda mareme dila ruiné 😢modou Diagne mome amoul Diome vraiment
Kou d'accord ni Omar Diagne moy moudié alalou bayam rék lalalll j'aime❤❤
Omar ❤Maty-rose manguileni khol di sourire rek 💪❤️🙏🏽
@katykara9183 Dangeu contane si gnome. ❤
Boury yangi seuy lou perpendiculaire 😊😊😊
Ndiawar est devenue ‘amour’
Jiguen dal seuyat la meune ❤❤❤
Ndiawar rék mo takh may sétan série bi😂😂😂sourtounak bou wakhé c'est bien c'est très bien rék damay ré😂😂ba tass
😂😂😂😂
😂😂😂
Xaliso c'est le meilleur série de l'année bilahi pask Ndiaware Diagne borom c'est très bien rôle bimouye joué meune nako Sokhna Diagne môme Diop Fall daye joué Nar bi mou yakar ni daye supporté😂😂😂
Dal khel rek talloul lidjeuneti djeukeur dji di weur di diakhassé rek😂😂😂
La fusion en Maty Rose et Omar est Magnifique.
Adja ak togou une longue histoire ❤❤❤❤
Vraiment mom maninam
Yalna diamou ya ga 🥰 Barker Serigne Fallou Awa bousse ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bokku na si grandeur joum reconnaître ko té lolou la Ya Dior déf mashaallah c'est bien comme le dit Ndiawar son fils😂
C'est très bien 😂😂
Sokhna tay amgua cas deh😂kon yeuk guani mbeugel amna ligua leble rek lagne laye delo yalla kharatoul firdawsi 😂sokhou assume.
Couple maty Rose Omar diagne lou nara doy war❤
Alkhamdoulilahi الله Merci pour me donner vivre aujourd'hui ❤
Longue vie á vous lire katou commentaire yi 🎉🎉😂❤❤😂🎉😂
Amine
Amine
a toi aussi long Vie
Amine 🤲🤲
Long vie a vous aussi
Je pense que Omar Diagne,Thi Maty Rose lay weuré.Liii ma guisssss !☝🏿
Yallananiou am weer gui yaram, gouddou fane ak khalissooooo
Soo deffer lou bakh niounii leu c’est bien, gua defff lou geuneu bakh niouni leu c’est très bien 😂😂😂sacré Ndiawar
😅😅😂😂😂
Blh 😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
C'est très bien
Je savais que ni soda maréme lafa louche intérêt la dougué si seye biii. Wayei yaye dior mome lépe lay lidienetiiiidara douko raw😂😂😂😂😂
Modou Diagne il s’habille trop bien mashalah
Wayé dioublague la
5623❤❤
@@Anonyma-e9o😂😂😂😂😂😂
34:37 danio moudiou niro sakh niom 🥰
Casting propre, bravo EP👏🏾
Maty assure grave son rôle, elle est formidable.🎉
11:06 temps amoul 😂❤ aimé len RK
Time is money My sister
Merci
Merci beaucoup waye
Yow duuul
non diawar diagne Ray nama sama mbok dérét yi Kaye 😂😂😂😂😂
Wakhou olof da diss sheu mbokou derett
No ndiawar dafa nekh😂😂😂
Enfin yayou Maty rose dakona tata Adja ❤❤
Evenprod 'guir yallah diguenté yaye Dior ak Soda Mareme na guena saffff😂😂😂😂
Niankou il joue trop bien mashallah
Alhamdoulilah santa lene yalla sa yolene di setane serie
Santa yalla boubakh Alhamdoulilah🥰🥰🥰
Meilleurs voeux a toute la team evenprod u ‘re the best❤
Niankou Omar diagne mo beugue ay affairou dofff dofff lou 😂😂
Maty Rose se maquillage bi rafetna trop ❤❤
Yalnaniou yalla may ay sokhna you melni boury ❤❤Machallah
Amine
Legui sene episode yii dah gatte téh bari aye pub😊
Ndakh sagnko wakh
Absolument do sakh doyal
Yalna yalla yeureum souniou papa yii nek si bur souf ak bolem joulitte dit amine 🎉🤲🤲🤲
Amine yarabi 🤲
Amine
ñi ñak sen bakan fanyi yallas nalen yallas yeureum 🥲
Evenprod, contane na ci yen, bilay! Sama xol sedd na😢😢contaane naa!!!❤❤❤ . Merci bonne et heureuse année tamit !!!!
Diawar limou wakh réalité la on le trouve partout dans les famille Sénégalaise mbokou you khamni diamou galinne yener gniou eumbal la safanne❤❤❤❤❤Bien joué
bilahi dh mbok legui amatoul
Soda mareme ak badiane 😂😂dinagn ma ray😂😂
Sokhna mou ndaw way 😂😂😂😂namonala bandit nga rek insbi sa mame yeineu rek lay topou khol bi nangou n’a bou yague sa yaye wayei reuy moko diap Ak gathié
Date du Ramadan : 28/2/2025
Athan de Fajr : 3h50
Athan de Maghrib : 6h00
Le Prophète Muhammad (paix soit sur lui) a dit : "Celui qui annonce la date du Ramadan, le feu de l'enfer lui est interdit👂🏾🤍🫡
3h 50??
@ndiayebinette6313 si l'heure va changer inchallah 😂🙏🏽
Oooooh lala 🤗 maty rose elle est gravement belle ❤ mignonne assi🤗🥰
je veux 10 millions abonné pour evenropd la meilleur chaîne série xalisso qui n’a jamais perdu sa valeur sokhna bou daw ray na ma 🥰🥰🥰
Wouy Khalisso khalisso badio tassearei nga dounya loussi topou 😂😂😂😂😂sakh khamoumaka ❤🎉merci EVENPROD
gonéy 2000 gua xana😂
@@MansourDiop-wd2or bakho deih 😂😂😂😂1997 prèsque rek 😂😂😂insbi mére la nganan
@@rokhayandoye7184 non do mère dh xalé gua batay😂😂
@@MansourDiop-wd2or😂😂😂Merci Mansour borom bakhnga ❤❤
@@MansourDiop-wd2orje me suis abonné à ton compte ❤
Oumar joue bien sn rôle de fou maty tué adorable ❤❤❤❤
Courage et force aux acteur(ices) aux producteurs aux cameraman Adja ca c voit qu’elle et fatigué Mme ca voix l confirme métier bi yomboul vous le méritez je ne cesserais de le dire Evenprod meilleur maison de Production chaque épisode l confirme Machallah ❤sur vous
Yalla nieupo am diamou si barki allkhorane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉
Salam wa Tim c'est bien 😂c'est très bien 😂😂boury❤❤😂😂
Sacré ndiawar 😂😂😂