Ce khassaide est une forme de prière complète pour une créature à son créateur. Merci Imam de cette chef d'oeuvre.Que Dieu l'agréée pour toi et pour tous ce qui l' ecout
Ndeysane imame moussa Gueye!! Dal téy yarou... ndeysane. C'est une référence.. je l'aime beaucoup.. Qu'Allah te procure une longue vie si barké cheikhoul khadim.. si barké seydi Hadji Malick. Machalla
Comme vs l'avez si bien dit c t'un produit divin(ALAHOU AKBAR)J n'écoutais cette chanson matin et soir 100%tawhîd vraiment c magnifique as-salàmou alaykoum
Alhamdou liilah. Xassida bi dafa déloussi sama xel alhamdou liilah. Yalla na lén Allah Faye yiw badane. Dama diakhlé wone. Dama fébar, yalla guindi meu ma dém ci nitou yalla bou niouy wax serigne Fallou Rahman. Mou nianalma. Ma wer ci sassi ( alhamdou liilah). Ma guiss nite Doug ci bureau bimou nék mom serigne Fallou ndiaye sonou loool nakh fébar , wayé bimouy guéneu, mo dokhal bopam.( alhamdou lilah) Ma Amat beuss louma diap Lou urgent, ma niane yalla ci barkém mom serigne Fallou ndiaye , Lola Fadjou. Ma daldi tite. Légui kémtane gogou daldima diakhassé. May niane yalla mousseeul meu ci may yémou ci loumou may domou adama. diko niane mom yalla mou mpusseul meu ci ma Doug ci shirk. Ma diko niane mou dimbali ma beu ma xam ni mom mo may serigne Fallou Rahman mou meun niane légui, niane bi nangou légui ... Ma djouli si bir djouli gui sama xel daw ci xassida bi. Ma daldi déloussi. Alhamdou liilah.. Dafma déloussi, ma xam ni yalla moy bour biy mayé. Que kouko wolou louné meun nalako may.
Allahou akbar chaque personne qu'elle que soit sa religion doit faire de ce khassida une viatique afin d'avoir conscience que seul allah est souverain,sa grâce, sa misericode et ses bienfaits pour toute la création sont infini...ko yakar yallah la yakar et comme le plus court chemin entre A et B est la ligne droite adressons nous directement à ALLAH SWT sans intermédiaire..ALHAMDOULILAH...moussa gueye yallah na fi yague té were wérelé...yallah nangou nianes name sédélé niou ko inshaalah amiiiine....ALLAHOU AKBAR...ALHAMDOULILAH ALLA KOULI HALL
Salam Imam Moussa je puis affirmer sans risque de me tromper que cette chanson est une pure inspiration divine. Que c'est bien composée. ALLAH MAÎTRE DE L'UNIVERS ET DES DESTINÉS vous comble de bonheur ici-bas et à l'au-delà.
Ndéye sane sama sopé yallah na la yallah féye sama la yôk sasoutoura si barkél lépp lo dougua wëral bât bi dieuredieuf thi barker seydina mouhamed salalahou anleyhi wa salam Amiine 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Masha ALLAH, yalna ya ALLAH fayal gnoula, thiant gui dafa gnouy délossi ci lou weurr!!!...nous l'écoutons ts les jours té dougnou ci doyal, une véritable inspiration divine!!! Qu'ALLAH azawadial te garde et accepte tes prières, dieuredieuf ya Imam!!!!
Dieureudieuf sougnou pape imame Moussa gueye ligua binda rek ka woor yalla nala Yalla nour bi faye si barke seydouna moukhamed psl te yalla na yalla werral batte bi yok khel bi bagua geuna binda louniouye geuna yehe
Machallah wallahie li nga fii Wakh imam moussa kene dou ko wakhati thi khal bi thi teguine bii dawna yarame YALLAH nala nassiril hakh bil hakh yook thi mbalou lerame ya goudeul say fane mayla tawfek .bateba kholba Lép toyna
Thêy Imam néna souma bakhoul bour yalla aw ma fénên khawma nak wayé yow kham nga nan ngamêy dêff diamangui ni têy bou togné note limou diamou machallah je pleure en l'écoutant wallahi
Assalamou aleykoum wa rahmatoulah ya imane. Machaallah yalna borom bi same soutourale barkèle yeureume diègale dioulit yeup thi barkè Seydina Mouhamed Salalahou Aleyhi Wassalam Amíne ya rabbil alamine. Contane na gnou lol. Yalna la borom bi dèfal yiw ba ila yaw mi dine ak dioulit yeup amine dieureudieuf
Dieureudjeuf dieureudjeuf dieureudjeuf sama imam moussa gueuye wallahi sama khole toye Lép li nga fi Wakh deug piiir la yalna YALLAH Yok say lerr meyla tawfekh Diam ak Salam ilayawmilikh ...ndeysane ndeysane ndeysane Lép khole ba 👆💞🙏🙏🙏
Ana gnikoy déglou en 2024❤❤
Li nekhna wayyy
Ndeysane
❤
Imam mosa ngiy fanwo ngodo. AK wer
Maa ngi ni
L'esprit humain est incapable de composer un tel chef-d'oeuvre. Pure inspiration divine. Allahou Akbar.
ALLAHOU AKBAR
Ce khassaide est une forme de prière complète pour une créature à son créateur.
Merci Imam de cette chef d'oeuvre.Que Dieu l'agréée pour toi et pour tous ce qui l' ecout
je valide
M
Amine y'arabby
Imam Moussa Gueye ni sa waye bi di séralé sama khol bi Yalla na la ko Ya Allah sedalé sa khol 🙏❤
Amine ya raby souma diakhlé li rék momay deufeul bilay ❤❤❤
Ndeysane imame moussa Gueye!! Dal téy yarou... ndeysane. C'est une référence.. je l'aime beaucoup.. Qu'Allah te procure une longue vie si barké cheikhoul khadim.. si barké seydi Hadji Malick.
Machalla
Amiiine ya rabi🙏🏽
il faut être inspiré divinement pour une telle chanson ça fait pleurer ma challa allah
que le bon dieu vous assiste
Billahi ça ma fait pleurer
machallah amal diam rek si barke serigne Babacar sy
@@fatoukinedia8876 lis
Cvlcwldqkp
Comme vs l'avez si bien dit c t'un produit divin(ALAHOU AKBAR)J n'écoutais cette chanson matin et soir 100%tawhîd vraiment c magnifique as-salàmou alaykoum
Cisse Plombier walaykoum salam
Alhamdou liilah.
Xassida bi dafa déloussi sama xel alhamdou liilah. Yalla na lén Allah Faye yiw badane.
Dama diakhlé wone.
Dama fébar, yalla guindi meu ma dém ci nitou yalla bou niouy wax serigne Fallou Rahman.
Mou nianalma. Ma wer ci sassi ( alhamdou liilah).
Ma guiss nite Doug ci bureau bimou nék mom serigne Fallou ndiaye sonou loool nakh fébar , wayé bimouy guéneu, mo dokhal bopam.( alhamdou lilah)
Ma Amat beuss louma diap Lou urgent, ma niane yalla ci barkém mom serigne Fallou ndiaye , Lola Fadjou.
Ma daldi tite.
Légui kémtane gogou daldima diakhassé. May niane yalla mousseeul meu ci may yémou ci loumou may domou adama.
diko niane mom yalla mou mpusseul meu ci ma Doug ci shirk.
Ma diko niane mou dimbali ma beu ma xam ni mom mo may serigne Fallou Rahman mou meun niane légui, niane bi nangou légui ...
Ma djouli si bir djouli gui sama xel daw ci xassida bi.
Ma daldi déloussi. Alhamdou liilah..
Dafma déloussi, ma xam ni yalla moy bour biy mayé. Que kouko wolou louné meun nalako may.
Allahou akbar chaque personne qu'elle que soit sa religion doit faire de ce khassida une viatique afin d'avoir conscience que seul allah est souverain,sa grâce, sa misericode et ses bienfaits pour toute la création sont infini...ko yakar yallah la yakar et comme le plus court chemin entre A et B est la ligne droite adressons nous directement à ALLAH SWT sans intermédiaire..ALHAMDOULILAH...moussa gueye yallah na fi yague té were wérelé...yallah nangou nianes name sédélé niou ko inshaalah amiiiine....ALLAHOU AKBAR...ALHAMDOULILAH ALLA KOULI HALL
Je suis catholique mais j'aime vraiment cette chanson ❤❤❤❤🙏🙏🙏
Machalla
Merci
C'est très proche des psaumes de David.
C'est juste beau ♥️
Alhamdoulillah
Machallah
Il faut écouter attentivement. Barképp Borome touba ce chansons est très important
g les larmes aux yeux. k'Allah nous pardonne et fasse de nous de bons pratiquants
De mm k moi worena serigne Touba 7:55;😭😭😭
Amine
🙏😍🙏
Cette chanson écoutée avec humilité vous fera pleurer.Ma Sha Allah imam qu'Allah vous récompense.
Ñ
Salam Imam Moussa je puis affirmer sans risque de me tromper que cette chanson est une pure inspiration divine. Que c'est bien composée. ALLAH MAÎTRE DE L'UNIVERS ET DES DESTINÉS vous comble de bonheur ici-bas et à l'au-delà.
❤❤❤féss na délle ak tawhiid❤ Yallna YALLA défal lako ci sa mijanoul hasanaat barké MOuhamad slhwl🙏
Ndéye sane sama sopé yallah na la yallah féye sama la yôk sasoutoura si barkél lépp lo dougua wëral bât bi dieuredieuf thi barker seydina mouhamed salalahou anleyhi wa salam Amiine 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Masha ALLAH, yalna ya ALLAH fayal gnoula, thiant gui dafa gnouy délossi ci lou weurr!!!...nous l'écoutons ts les jours té dougnou ci doyal, une véritable inspiration divine!!! Qu'ALLAH azawadial te garde et accepte tes prières, dieuredieuf ya Imam!!!!
Machallah yalla n'a yalla défal nieupe Diam ak salam si barké mouhamed
Imma Moussa Gueye yallah ga fii yague te weur si barkèe mam maodo Malik sy MachaAllah
Dieureudieuf sougnou pape imame Moussa gueye ligua binda rek ka woor yalla nala Yalla nour bi faye si barke seydouna moukhamed psl te yalla na yalla werral batte bi yok khel bi bagua geuna binda louniouye geuna yehe
Ma CHAA ALLAH ! Douma doyal thi woyewi ! Longue vie à toi avec une santé de fer !
machalah iman moussa gueye yalna sounou boroom bayilafi baci kaname ma kaname si barké seydina mouhamed psl
Djamu Yalla diko toupe rékeu woor .Yanna Yalla moussal gnou cci séytané.Qui l'écoute en 2020 période Covid-19 ?
Kholall trésor bi rek 😭😭😭😭😭billahi beug nalla barké borom Touba
Machaala meilleur et vrai chanson du monde yala na yala goudeul sa fan may la were contane trop si yaw amine Machaala
Machallah yalna yalla fayèla soutra xeweul sécurité adouna ak alakhira
Machaallah serigne yalna la yalla faye si barke seydina mohamed aleyhixasalam...
Je ne cesse de pleurer quand j 'ecoute cette chanson .Djeredjef Sunu Boroom bi mou gnou defe gnou book ci khetou Saalaatou Wassalam.Imaam shoukran!
Son bi si sa ma hol bi lako def ❤
BISMIlahi RAKHMANI RAkHIMI.Imam Moussa ngno ngui gnane Yalla mou Dolí sa souteureu deugueureul sa takhaway .Moudiewo pousso mou rer..Yalla nala Yalla Aral bopam. Salahou ala Mouhamad
Allahoumma àmin
Machallah li dafa nékh ba eup Allahou Akbar c est rare qu une personne chante le créateur divine dieureudieufeuti Yallah sougnou borom
Machalah machalah dama tok légui rek mou dikale ma makoy wayane tou vite suis rentré TH-cam pr l'écouter yague fi Imam amine.. Serge..
Manchallah 🥰😍😍 yalla na yalla goudal sa fane
Machallah ce poème est trop riche. Chacun s'y retrouve.dawna yaram. Je n'ai pas de qualificatif pour lui.
21 Mai 2020
Yallah na Yallah nagou souniou koor
Amen🤲🤲🤲
Wallahi amna solo yalna yalla yaggal lasounou kanam
Imam yalla guou goude fann ci barké Mawlana Cheikh Ahmet Tidiane sy
Amine
Machallah dama beug son bi depuis bama néke khalei barké Borom touba
wallah khol féssatina, c'est vraiment profond
Yalla na nieup am diam si barké MOUHAMED (psl)♥️
Clic sur j’aime si tu là encore écouter en 2023🥰
Machalla Yalla na Faye Yiwe Bidjiahi Nabile Moustapha SAWS. Limaye Yeuk si Khassida Bii, Yalla nalako Yalla Faye si Mbaakhame ngui
Machallah imam goudal fane yallah nala borom bi fay yiiw..
Best zikr ever
serigne moussa gueye yalla ga goudoufane ak beppe dioulitte
amine
Amine
Mashahlla Imam Moussa. Yalla naniou yalla attai ci yeurmandaim. Amine
Que Dieu te comble de ses graces.
Tres Belle falcon de render graces au seigneur. Soubhana Lah wa bi Hamdihi.
Je suis tibiane mais j'aime cette vidéo 🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤ alla hou akbar
Raison de plus. Il est Tidiane l’Imam
Yalna yalla gouddeul sa fane fane incha allah 🤲🤲louma mèr mér soumala déglo guiff
Tawwassoul deugu deugu. Dieuredieuf ya Imam, yalla na borom bi bégg ci yaw
Merci Imane cette chanson nous guéri de notre maladie
machallah imame yalla na voix bi werr yalla na yalla faye ak tarikha cheikhna ahmed tidjane sy rta
machallah imam moussa gueye yoo allah yob modjere a jaarama
Fière d'être talibe cheikh et j'adore cette chanson
Machallah wallahie li nga fii Wakh imam moussa kene dou ko wakhati thi khal bi thi teguine bii dawna yarame YALLAH nala nassiril hakh bil hakh yook thi mbalou lerame ya goudeul say fane mayla tawfek .bateba kholba Lép toyna
Gorgui Ndione
Amine ya rabal al amine quelle belle dua . choukran djazilan ya oustaz Moussa Gueye.
❤
machallah imam moussa gueye boroom yite piir yalna yalla taxawoula
salimata faye amine ya Rabbi ✨👌
Dîné rek moy deug
Mbaye dondé
Mbaye diakhaté
Moussa Gueye
Moussa ka
Yalla nalaléne yalla faye
Ndeysane thiey yalla li nekhna trop way barké cheikhoul khadim
Imam mousa gueye mô yiw macha'allah
Mashallah allahouma amine waye 🥰😍 yalla na yalla faye la
Macha ALLAH cette chanson touche tout cœur d'un croyant je peux passer tout mom temps à l'écouter .Longue vie avec baucoup de santé Imam GUEYE amen
Non bi mom chef-d'oeuvre leu !!!
Thêy Imam néna souma bakhoul bour yalla aw ma fénên khawma nak wayé yow kham nga nan ngamêy dêff diamangui ni têy bou togné note limou diamou machallah je pleure en l'écoutant wallahi
Assalamou aleykoum wa rahmatoulah ya imane. Machaallah yalna borom bi same soutourale barkèle yeureume diègale dioulit yeup thi barkè Seydina Mouhamed Salalahou Aleyhi Wassalam Amíne ya rabbil alamine. Contane na gnou lol. Yalna la borom bi dèfal yiw ba ila yaw mi dine ak dioulit yeup amine dieureudieuf
Ndeyssane baay Fall baaangui nekk niii mashalla imam♥️🙏🏾
Alhamndoulilah Allah Kouli Hal. Qu'Allah Soubhanou Wa Talla te gratifie de bienfaits ici et à l'au-delà. Amine
Machallah es logne vie à toi imame yalla nala yalla fay ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah Imame yalla na yalla Faye si barké sangue bi ak Di barké cheikh à akhmed tidjani s'y rta
Machala Machala Machala ♥️♥️♥️ imame yalla nala yalla geuneu deugeureul si barké seydina Mouhamed Salahou Aleyhi Wasalam 🙏🙏🙏
Machala lafthiat 🙏🙏🙏🙏bilahi douma si doyal je l'écoute souvent yalnala yokou 🤲🤲🤲
Machalla Serigne makhtar yalla kénala
Mashallah... très belle poésie. Une poésie spirituelle...
Machallah mame Moussa Gueye. Amine yalla na gnane yi nangou. Fiere detre Talibe cheikh.
Amine yarabi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
mashalla 😭😭Yalna yalla goudal sa fane Imam
ndeysane mane dei limala ndawé moy sa dal ak sa yar imaame yalnala fi yala bayi gua yagg fi t wer keine dou seydina mouhamed saw
Dieureudjeuf dieureudjeuf dieureudjeuf sama imam moussa gueuye wallahi sama khole toye Lép li nga fi Wakh deug piiir la yalna YALLAH Yok say lerr meyla tawfekh Diam ak Salam ilayawmilikh ...ndeysane ndeysane ndeysane Lép khole ba 👆💞🙏🙏🙏
Je ne peux m'empêcher de verser des larmes en écoutant cette chanson.
Wallah sama ❤sedeu na . Ndaysan daw na yaram . K'Allah swt nous pardonne amin
Mashallah J’arrête pas d’écouter ça Mashallah yo Allah seline dandéndé Mashallah
Dieureudieuf Imam yalla na sa diam yagu
Ndeyesane béne goumba souy yalwane way bi lay way à chak fw mou romb sma khol bi dfay séd j'ai tt de suite voulu écouter l'original mashallah ❤
Kan j'écoute ça j'ai des frissons doumassi doyall
Yalla n'a yalla Faye imam! dieureudieuf
Chq jours j l écoute c tlmnt nekh machallah
Je ne suis ni tidiane ni mouride mais ça m'apaise
Kafrine Kolda. Masha Allah
Machallah
Mais imaginez guen gnoun gneup diapante bessou benthi jugement dernier gnouy youkhou woy bi and di dougue aldiana oooooooh dina nekh
Machallah Allahouma amine inchallah
Yalna nako yala def wayei yala bouñ tit bafateiko
Yalla na nous ko yalla yombal
Sa waye yangui decone dhe yawmal khiam ngua wakh dhe
Ndeysane allahouma Amine 🙏
Masha'alah yaa imame sante nann thi waay wi
Yalla yaa Allah faaye yiiw
NDEYSANNE AMNA SOLO THIEUY YALLAH SWT MO MEUNA MAYÉ🥰🥰🥰🥰🥰
Ma sha Allah paroles pleines de sagesse que la grâce dAllah soit sur nous
Baba Thiam dakar je pleure a chaque fois que l'écoute machala imam mousa longue vie bonne santé
Machaallah pour cette chef d’œuvre pleine de sagesse. On est tjrs là en 2022
Wolakhi cette chanson est une vraie soumission à notre seigneur Allah soubahanahou wa talah
Pire inspiration divine . Allahou Akbar
yalnala yalla béguél lol Iman MOUSSA tourondo
yalla na la yalla faiye ta goudaye say fane
Mangi fi beus bouneh 🥰
Longue vie plein de santé imam que le seigneur vous apporte beaucoup de bonheur
Macha allah nekh na trop . Ken dou sunu borom
Machallah alkhamdoulilah DIEU merci Yallah rek mo waur
Je suis mourid j'aime les chansons tijaan 💗
Neex na lool waay💗😘🙏
Ci xol la jugada dugg ci xol Maah Chaa Allah!!!!
Bilahi lii ç est magnifique. Je suis mouride mais j adore ce poeme
وهذه القصيدة لو ترجمت باللغة العربية
سيكون أشهر من مبادي التوحيد
جزى الله عنا المنشد خيرا
والله قول محقق ما قال كلمة إلا أنها كلمات للتقوى والتوكل على الله
إن أمكنك الترجمة فا فعل بإذن الله
dieureudieuf oustaz yalla na yalla fayoul gnoula.
Quel chef d'oeuvre!. Merci kabir sene
Merci imam!