Nettali: Maryaama Ba - En Wolof (Une si longue lettre) pàcc 02 | Mariama Ba (Bataaxal bu gudde nii)

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 16 ก.ย. 2024
  • Nettali: Maryaama Ba - En Wolof (Une si longue lettre) pàcc 02 | Mariama Ba (Bataaxal bu gudde nii)
    Une si longue lettre :
    Bokk na ci téere (livre) nettali yi gën a siiw ci àddina si te ab Saa-Afrig (africain)e) bind ko.
    Téere bi tekki na ñu ko ci lu ëpp 26i làkk (Le roman a été traduit plus de 26 langues). Làkku bees ko binde moo di farãse (langue original: français)
    Aji bind ji Maryaama Ba, di ab Saa-Senegaal (Senegalaise) 🇸🇳
    Maam Yuunus Jeŋ ak Aram Faal, ñoo tekki ci Wolof ci atum 2016, tuddee ko "Bataaxal bu gudde nii"
    ñooy ñan ?
    Aram Faal 👇🏾
    fr.m.wikipedia...
    Maam Yuunus Jeŋ 👇🏾
    fr.m.wikipedia...
    Maryaama Ba mu ngi juddu ci 17i fani weeru awiril atum 1929, faatu ci 17i fani weeru ut atum 1981 ci Dakaar. Bindkat la woon.
    Téeréem yi gën a fés : Une si longue lettre,
    Le chant écarlate.
    Téere bii nag, ay xew-xew yu am solo te baree ngi ci biir ! Day feeñal mbatiit, aada/mbaaxu Senegaal, rawatina ci jigéen ñi, ak ci Afrig swu jant.
    Rejoignez-nous & Soutenir cette chaîne
    / souhaïbou tv
    ---------------------------------------------------------
    Abone-wuleen ci sen bi ⤵️
    / souhaïboutv
    -------------------------------------------------------------------
    Mboor (histoire) yees fent ci Wolof ⤵️
    • Histoire en Wolof
    Léeb ci Wolof ⤵️
    • Léeb ci Wolof
    Taariixu Senegaal ⤵️
    • Taariixu Senegaal (His...
    -----------------------------------------------------------
    Mbaalu jokkoo yi ⬇️👌🏿
    Insta: www.instagram.... Feesbuk: / souhaïbou-tv-101746092...
    Tiktok: vm.tiktok.com/...
    ________________________________________
    Seen mbégté ak seen i njariñ ñooy sunu yitté. ✅✅

ความคิดเห็น • 46