As Salamou alaikoum wa rahmatoulahi . Seydi el Malik sy un érudit de tous les temps 💚💚. Le Sénégal est une terre bénie nous avons khadimou Rassoul, el hadji Ibrahima Niass, mame limamou laye seydi el Malik sy , sans compter cette cohésion entre musulmans et chrétiens ma cha ALLAH 🙏 que la paix continue de régner au Sénégal. Merci beaucoup pour l'émission 🙏
Pour gniou nga xame ni ndaysane séne xam xam mathie na lol si diné mais pas si xam xam nassarane , juste pour vous dire que ki limouy walh dou aye wakh dans l'air , il parle des chose que les scientique du monde entier ont decouvert , donc limou wakh dou wakhi kassaw kassaw mais cest de l'astrophysique et de l'astromonie que apprend dans les ecole d'ingenieurs de la NASA et dans les université . Parfois nak nitou diné yi daniouy gawa wédi trop tamit si xam xam adouna yi . Niou bayi si khél , ni xam xam diné baxna lol mais sousa xam xam yamé si fofou rék niou bayé wédi li wadji di wakh car cest de la science prouvé surrout quand il parle de l'espace ...c'est pas des parole en l'air
Salam pour moi deh. Adama daffa yereum awa motakh mou lek pomme bi. Il a voulu endosser châtiment bi au lieu mouy bayi awa qui est dans ces responsablité di subir toute seule la colère de ya Allah swt.
Mdr sa xam xam mo gaat motax ngua yakarni mame Adam daf niou toñ😅 Sourat baqara apartir bi Yalla di wax si theme Adam. Des le debut rek di ngua xam ni Adam si souff bala dra di xew. Avant tt Yalla lpumou inni diahilou fil ardi khalifa Yalla dafni malaka yi damay binde ak mindef bimay woutou si souf. Lol dafay wane Adam il est destine a vivre sur terre je crois que lerr na mbokk mi
Assalamou aleykoum, dieureudieuf cheikh bi na yalla yook sa ler. Je voulais savoir d'où vient la lignée des hommes blancs. Est ce que ils sont descendants directe de Adam où boen de l'un de ces enfants ?
OUZTAS MADIAMA LADIE BINGA LA DIONE NDAKH ADAMA BIKA KHAWA WAKHE LEKAL GARABGUI PAR CE QUE GOOR DA AM FAIBLESE THI DJIGUENE GUI MOU BEUGUE CA VEUX DIRE QUE ADAMA DA AM FAIBLESSE THIE KHAWA
Domou adama bou beugué day faible bou yeureumè day faible domou Adama yèpa ame faiblesse boudè kèn kou matt Amna mouhamed psl lay done tè sakh YALLA donako diadji kon meun na done faiblesse si adama nakh YALLA rek moy ki matt
As Salamou alaikoum wa rahmatoulahi . Seydi el Malik sy un érudit de tous les temps 💚💚. Le Sénégal est une terre bénie nous avons khadimou Rassoul, el hadji Ibrahima Niass, mame limamou laye seydi el Malik sy , sans compter cette cohésion entre musulmans et chrétiens ma cha ALLAH 🙏 que la paix continue de régner au Sénégal. Merci beaucoup pour l'émission 🙏
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
sénégal amenaniou dimbalou souniou borom deug !
Oustaz yalna yalla yokkou sa lérr séydi hadji Malick yalna yalla tass gnou si barkém ❤
Non ki dafma yém torope machala❤❤❤ suis très content 😢
Machallah magui lay gnanal Yalnala Yallah geureum mousal la thi sheytan nakh liguay wakh arangé wouko Yallah nala Yallah faye tandef gha sa toure ak sa wakh dji dou Faye ba YAWMALLHIYAM AKBAR , bimala dalé deglou ba taye dama nek benen niit magui sakou thi yaw gha gnanal ma dieureudieuf
yallah xam na souniou khol séde na mashallah yallah na yallah yokk xam xam bi
مدارسه في العلم خير مدارسه❤️🙏🏿
Machallah ya oustz qu'allah te benisse ns trop content de vs
MashAllah xam xam fëégne na
Machaaaaaaaalaaaaa OUSTAZ Xam XAm bi sélleu na , Té wakhtaaane bi nékhna lo
je vous suis partout
Machallah ham ham bi rafetna te leerna
Machallah bayma diama fall yalna sa diam yang khamouma kéne dh mais mane contane na si yaw yagui déf si mane dh lou barri
Kéndou cheikh seydil khadji malick ❤
Moi aussi je suis très très seduit par ce monsieur franchement que Le Bon vous bénisse!!!
Dieureudieuf professeur.
Seydil Hadji Malick yalnagn ko yalla fayal
Macha Allah yAllah nalene yAllah fayy malenne dima diou sakh
MachAllah
Merci du partage
MachAllah
machallah machallah amatina solo
Jërëjëf seringe TOUBA
Amoull mro❤❤❤❤❤
Mam moado rta oooooo❤️❤️
Yakhi gnay😂😂mako kham fala dan mbobi sa guinaw mpal bou mame rawane ngom ❤❤❤
Pour gniou nga xame ni ndaysane séne xam xam mathie na lol si diné mais pas si xam xam nassarane ,
juste pour vous dire que ki limouy walh dou aye wakh dans l'air , il parle des chose que les scientique du monde entier ont decouvert , donc limou wakh dou wakhi kassaw kassaw mais cest de l'astrophysique et de l'astromonie que apprend dans les ecole d'ingenieurs de la NASA et dans les université .
Parfois nak nitou diné yi daniouy gawa wédi trop tamit si xam xam adouna yi . Niou bayi si khél , ni xam xam diné baxna lol mais sousa xam xam yamé si fofou rék niou bayé wédi li wadji di wakh car cest de la science prouvé surrout quand il parle de l'espace ...c'est pas des parole en l'air
Machallah machallah chez l'école maodo.
😂😂el Badou il est extraordinaire kholal entré en matière bimou def rk couleur noir bi
Sama khôl dafa sed trop j'ai même pas les mots goudal fane machallah
Machallah belle leçon sur la radioactivité 20.00❤
Merci beaucoup xamal ngama loumou xamoul won
Neenako aladji koula wax lii yeup.yaa yay d xam xam bi maashalaa
Merci madiama❤❤❤ wotal télégramme guirr yallah merci❤❤❤❤
Machallah nékhna yalla na yalla barkél ❤❤❤❤❤xam xam rek woor
mashallah yalla borom bi motali lép
Machallah oustaz je suis vraiment content yalla nala yalla doli werr yok khamkham bi
Masha Allah Professeur
Allahou akbar Ehadj Malick bilay djambarleu
Machallah professeur
Machallah Yaa Oustaz Yalla Na Yalla Gueuneu leeral Kham kham bi
Dans l épopée mandingue de Djibril tamsir niane on nous avait dit k zul karnaîne est Alexandre le Grand comparé a soudiata Keita 😢
Manchallah. Xam xam rek moo woor
Émission sur zourkhaïnaïni svp
Machalah
Extraordinaire ❤😊❤❤❤
Machalla
salam salam mashallah mashallah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Çeye alhadi malick❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
J'ai pas les morts ❤❤❤❤❤❤❤ MACHA ALLAH 🙏🏿
Machallah ❤❤❤❤❤
Machallah 💯
Salam pour moi deh. Adama daffa yereum awa motakh mou lek pomme bi. Il a voulu endosser châtiment bi au lieu mouy bayi awa qui est dans ces responsablité di subir toute seule la colère de ya Allah swt.
Salam ya oustaz lan mo takh nitt dou guisss chaytané loumou waxanték yalla wala nite meunouko guiss
Mach machalla
BADOU bayyil di wax MAM ADAMA mo ñu tooñ budul woon MAM ADAMA du ñu ñëw fi ci ADUNA
Mdr sa xam xam mo gaat motax ngua yakarni mame Adam daf niou toñ😅
Sourat baqara apartir bi Yalla di wax si theme Adam. Des le debut rek di ngua xam ni Adam si souff bala dra di xew.
Avant tt Yalla lpumou inni diahilou fil ardi khalifa
Yalla dafni malaka yi damay binde ak mindef bimay woutou si souf.
Lol dafay wane Adam il est destine a vivre sur terre je crois que lerr na mbokk mi
MashAllah ❤❤❤
Assalamou aleykoum, dieureudieuf cheikh bi na yalla yook sa ler. Je voulais savoir d'où vient la lignée des hommes blancs. Est ce que ils sont descendants directe de Adam où boen de l'un de ces enfants ?
Masha ALLAH
Ma sha Allah je vous times en Allah !!!❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salam Machallah am neu solo mais si on pouvait avoir les sources dina takh niou geun meu gestu si mbirum prophète yi
Adama dafa beugu montakh
Kn d'où mame khalifa❤
❤🎉
Machallah
OUZTAS MADIAMA LADIE BINGA LA DIONE NDAKH ADAMA BIKA KHAWA WAKHE LEKAL GARABGUI PAR CE QUE GOOR DA AM FAIBLESE THI DJIGUENE GUI MOU BEUGUE CA VEUX DIRE QUE ADAMA DA AM FAIBLESSE THIE KHAWA
Adama daffa faible motax mou lekk garap gui
Ya oustaz SA QUESTION VERS ADAMA À AWA pour Mane ADAMA DAFFA AMANON CONFIANCE SI MOM REK MOTAKH MOU LEEKO KO.
❤❤❤
C'est la confiance qui les liée ils vivaient tous les deux au paradis donc il avait confiance en elle
Domou adama bou beugué day faible bou yeureumè day faible domou Adama yèpa ame faiblesse boudè kèn kou matt Amna mouhamed psl lay done tè sakh YALLA donako diadji kon meun na done faiblesse si adama nakh YALLA rek moy ki matt
Waw
❤❤❤❤
Inflience bi mou ame dji borom keureum li yalla dogal lou yalla
Adama se méfie de ibliss. C'est pourquoi il ne l'a pas écouté mais fait confiance à son épouse awa. C'est la réponse à votre question professeur.
❤😢
Adama dafa lekkk garap bi par ce que djiguen dfa beuri pekhe... En plus c'était la processuce de Dieu en tout
Vous n'aviez pas dit ça a l'émission Ngonal dh Professeur entre Adam et Awa
😢😢😢
Mahrib akhssa nak?
Sorry but not everyone is saying that Alexander the great is Zul arnayni
Donc c'est vraiment une Pomme 🍎. Je pensais que metaphore leu
Adam e Eva etait blanc ou noir ?
Vous êtes suivi de partout , estimé, donc.....
Je commence à avoir des doutes de son savoir 😂car il paraît qu’il récite seulement 😂😂
C’est un professeur un chercheur. Il cumule théorie pratique sciences religion…. Nane diangui
Saway ki lou Lerrr Lay Wakh,BILAHI
Ki tu ne le connais pas tu as le droit d'avoir des doutes
Non il faut. Il est extrêmement sachant. Les connaissances qu'il expose sont rares. Il faut beaucoup se répéter si nécessaire
Des doutes sur son savoir et non de son savoir /// tais toi null
Machallah ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Machalla
❤❤❤
Machallah ❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤