Vraiment j’aime la façon dont Boury incarne dans cette série Senegal gaaw nane trop thi deukeul djiguéne foumou deukoul surtout quand tu est divorcé mo takh divorce waroul teirei djiguéne xame bopam xam loumou beug j’ai vraiment kiffé🎉❤❤❤❤
Les leçons de cet épisode: 1-pensez à vos enfants dans vos divorces, si vous ne pouvez pas ne pas vous séparer au moins soyez attentif à leurs états psychologiques, delen setlou sen ay comportements ,dès fois c’est plus douloureux pour eux que pour vous les adultes. 2-La belle réaction de Boury face à Mbeuguè est une très belle leçon, il faut écouter vos amis mais il faut aussi savoir décortiquer leurs paroles et leurs intentions. 3-L’amour est plus fort toutes les autres sensations, Niankou narna werr nax mbeuguel😂
Ohh ndeyesane sokhna ak papam s'en wakhtan sama papa lamay fatalè Dina wakhtan ak yaw ta doula yokhou machalla bilay yalla nakou yalla yueruem manque nama loll 😭😭
Bien fait pour mbeuge Enfin boury as ouvert sea yeux sur mbeugue Kou rayy Dee après embrasse ak lassa dess mossi tegou 😂😂😂😂 Ndiawar partouchhhhhh 😂😂😂😂😂😂
Omar Diagne dof plus la. Dofou nandité la. Mais Boury aussi may banquier bi espoir doom dji wakh mou nara yakk lep limou ligey. elle se laisse influencer trop facilement. La souffrance des enfants Diagne montre encore une fois pourquoi les femmes souffrent en silence dans le mariage africain en general mais senegalais en particilier. Chapeau Evenprod pour cette belle et instructive serie
Mousta may banquier bi espoir ndaw banquier mo eupeul rk en plus si iddeu la nekk j'aime sa façon de faire amnio khamantane bo divorce rk moylolou tentations yi beuri
Omar Diagne koumou dioylo😢 dinala rélo😂😂 néne mati ladoum la❤❤❤ bilay kii Dinama rey dama ré ba sonou 😂😂😂 yaye doir khamun ngane sa biss dina bjaw 😂😂 yalla na seytané khap doli mais soda maréme contane na si mom❤❤❤ Waw kayy Boury contane na ci yeuw tey waw ni leu kayy nitt dangaye bane merci beaucoup wayy❤❤❤❤❤ mbégué seytani bou mague leu kii
Yaye dior ak soda mareme yalna seytanè xeb doli😂ndakh yako formè pour détruire le ménage de boury😮ba takhna legui sur le plat lalay togale comme repas😂😂😂evenprod k la guerre commence 🤧🤧🤣
Omar diagne néna batléne dieuleul diadia ndakh Maty rose sou gneuwé sa xel dou nek si mom 😂😂😂 Mais ndiawar nexna néna aïtoush « son parent est vivant »😂😂
Oh sama khol seddeu neu. Jai trop aimé comment Boury a renvoyé Mbeugué 😂.
Ak man dafa bone kharit Amatoul
Danio beugui kharite rèk😢😢😢
@@BiraneKane-i2z que des hypocrites, moins on en a, mieux c'est .
@@MameArameSy bilaye, pourra c'est pas forcé.
Dafa jot mu xam ni bëggu ko.
Tenues yi Boury di soll on en parle?? Yéré olof you raaafét lay soll machallah❤❤❤❤❤❤❤
Je pensais que j’étais la seule à la remarquer ❤
Elle se habile trés bien❤❤
Blie nitt dangai respect sa bopu
❤❤❤Q
J'aime trop son style
Omar raynama "Maty ladoum la mann ladoum la, Pabi peul peul la "😂😂😂
😂
@OumouGaye-fl8cx 😂
😂😂😂😂😂😂
@amadoumboup5888 Mome mi est-ce que dougnou xol ndah réellement febarna ?
@@evenprod😂😂 maty dafko may diam rk
Sama papa fimou teudeu yalnako yalla yeureum thé khareko aldiàna
Yalla nako yalla yereume té khare KO aldiana firdawsi amine 🤲🤲
Amine
Yalla gua rousse lo Say none si barke seydina Mohamed psl 🎉🎉🎉🎉❤❤❤
Amine inchallah
Amine yarabii
Alahouma Amine
Amine 🤲 touf touf
Amine ya Rabbi😢
Sidy lamine niass yalle nako yalla yeureum té khareko Aldiana firdawousi yarabi Allah
AMINE yarabi
Mercredi tay bi yalna boumou nékh sounou dernier mercredi amine 😢
Amiiiiine
Alkhouma Amine 🙏
Amine siii barki seydina Mouhamed psl ❤❤❤
Amine
𝔸𝕞𝕚𝕟𝕖
Sidy Lamin niass yalla nako sonu brom Yaram ak bepou joulit bou Fatou 😢😢😢
Yakamti wone nga serie bi dougg khana😂😂
Amine
Amine yarabi😢😢
Amine
Allahouma amine y’a raby 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Vraiment j’aime la façon dont Boury incarne dans cette série Senegal gaaw nane trop thi deukeul djiguéne foumou deukoul surtout quand tu est divorcé mo takh divorce waroul teirei djiguéne xame bopam xam loumou beug j’ai vraiment kiffé🎉❤❤❤❤
Sama yaye fimou teude Yalnako yalla yeureume xaréko aldiana amine
Amine
Amine
Amine AK Mane sama yaye yala yessale yeurmeude khareco aljana firdaws AK bepe yaye bou guene adouna si barker yonete psl
Amine way
Soit fort 🥹🥹
Kou Begue Am Dom Bou gorr Toudikou Seydina Muhammad Lalla j' Merci
🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲💕🤲🤲🤲🤲
Amine
Mérci ❤❤
Amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
صل الله على محمدصل الله على محمدصل الله على محمدصل الله على محمد
Anna gni beug boury dellou si diawarr manifestez-vous 🎉🎉🎉🎉
yeureum len boury ndiawar beugoul ken ligueyam rk la beug teh divorce bi waner nako
Souffrancou Mère Dior damaye dondal
@@mameboussolo2131 boul wax il faut penser aux enfants
Bly🎉
🎉🎉🎉🎉
Enfin Boury mougui yéwou mbegué dou kharit , Omar diagne est amoureux 😂😍❤️
@aminatacisse818 Yakaro Boury deilou balou ko akhe ?
@evenprod❤️ je pense pas dh
@@evenprodkone ayy niouss
National layy donne 😊
Défoi dafay wakh wakhou nit nk Omar dinama ray rk😂😅 merci équipe evenprod
@abdoulayethiaw2650 Doyna ware mougui wakhe beug beuguame. 😂
Marème soda damako moudjer fan sakh bilay bakhna sii yaye dior 😂😂 seydou tayy rekk gua dadj deugu 😅
Bravo à toute l’équipe de xalisso badjo ❤
D habitude nonoula kiga tane molay torahal
Vrm, trop contente de Mareme.
@mbayangdiagne1904 Mougui koye teigual lou tare. 😂
@@Mounajate bilay yaw
Soda🎉🎉🎉
Les leçons de cet épisode: 1-pensez à vos enfants dans vos divorces, si vous ne pouvez pas ne pas vous séparer au moins soyez attentif à leurs états psychologiques, delen setlou sen ay comportements ,dès fois c’est plus douloureux pour eux que pour vous les adultes.
2-La belle réaction de Boury face à Mbeuguè est une très belle leçon, il faut écouter vos amis mais il faut aussi savoir décortiquer leurs paroles et leurs intentions.
3-L’amour est plus fort toutes les autres sensations, Niankou narna werr nax mbeuguel😂
Téy dé omar wahou nitt kessé lafi wah?
@ kone guisgeu lolou 😂 mbeugeul mo meun lepp
😢 Et également comment nos parents peuvent souffrir de nos actes et choix…..
@ et bien oui vu la scène de l’arrestation de Seydou
Jeux de cartes ossi manam parifoot en tout cas c intéressant kamem
😂😂😂 pourtoushhh mogui may ray 😂😂😂 sacré Ndiaware Diagne 😂😂😂😂
Ma fille son parent vivant ? ses parents vivant wouniou dèh 😂 non Ndiawar mo meilleur 😂😂
Lomako ré 😂
Dama réh ba sounnu 😂😂😂😂
Pour ndiawar rek😂😂😂
Môme lay rékk nii ba sma badiéne kiogu m'a sii bop 😂😂😂😂😂😂😂
Bilay louma rér si li😅😅😅😂😂😂
Yaye Dior ak soda Marém yallna saytané khép doly😂😂
Limou leunbeule rekk lagne ko fayy😅😅😅😊
Amin
Amine
Allahouma amine ❤
Amin
Sidy Lamine Niass yalna ko yalla kharé aldiana firdawsi amine ❤
Mbegué ak boury yalna seytané khép dolli😂😂
Amine
Amine mbegué une vraie hypocrite 😢
Amine
Amine
😂😂😂
dara gueunoul nekh diouli wakhtou yeupou 🙏 🙏 🙏
Bilahi
Machalla
Bilahi
Machallah ❤❤
Soxna leckkk gua dianwar sa façon de parle c'est top 😂😂 il joue bien son rôle 😂
@GueyeAwa-ii2sj Badou mougui ley rey ? 😂😂
Mane moma fii bayii 😅il est tres for
Mbegué AK Boury yalna seytané khép dolli😂😂😂
Amine
Amine 😂😂
Amine
Amine
Amine touf touf
Des cœur pour notre prophète Mouhamed psl ❤❤❤
PAIX ET SALUT SUR LUI ❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️psl
Psl ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
❤❤❤❤❤❤
Mane diawarr rk moma nekh bly 😂😂😂 gaye lene diou khol diawarr wy 😂😂😂
@Omardiop-i2b 😂
Non diawar raynama😂😂soda Mareme ak yaye dior yalla na ibliss kheep doli😂😂😂amine touff touff😂😂
@diezesarr5186 Ah mougui koy teigual lou xerei. 😂
Ohh ndeyesane sokhna ak papam s'en wakhtan sama papa lamay fatalè Dina wakhtan ak yaw ta doula yokhou machalla bilay yalla nakou yalla yueruem manque nama loll 😭😭
Ndaysan amine
Alahouma amine
Ak sama boss yalla nako goudou fane
Ndeysan amine yarbi 😢
@fatoubintoudieng7853 Paix à son âme. 👍
La maman de Ndiawar est trop forte mashallah elle assure grave son rôle longue vie Yaye Boye❤❤
Bien fait pour mbeuge Enfin boury as ouvert sea yeux sur mbeugue
Kou rayy Dee après embrasse ak lassa dess mossi tegou 😂😂😂😂
Ndiawar partouchhhhhh 😂😂😂😂😂😂
@adjasalihsamb9398 Doyna ware. 😂
Yaye dior ak soda marém melni macky sall ak amadou bâ,yallah na seytan khép doli...
😂😂😂😂😂😂😂
Boma ray way😂
@@lowaydeffboppam6865 ray naniou nioune nieup😂😂😂
😂😂😂😂
La manière de rire de niankou c'est autre chose😂
Comme bou ala rek😂😂
Merci Boury banga waré gnouss mbeuguè thia khathie moo yagg
Bilay
Clique sur traduire en français 😂😂
Pauvre Boury kuka yeureummm rk lalal j’aime ❤
Tay mom boury amna foula ❤❤❤
Films doit être comme sa chaque fois
Even prod la maison de production qui n’a jamais perdu sa valeur 🎊🎊❤️😊
Moko fa am ❤❤❤
@Oms__Sall Merci beaucoup. ❤
Non la petite Sokhna là c’est une vraie actrice ❤🎉🎉🎉🎉🎉
Je te jure ❤❤❤
❤❤❤ mne dé damako moidié beug skh
Sama papa yanako yalla yeureum
Amine 😢
AMINE yarabi
Ndiawar warna wowé kharitou sokhna "POULTOUCHE" 🤣🤣🤣🤣🤣😂
Louma ko rée 😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
Non il n'est pas srx😂😂😂😂
😅😂
Son parent vivent ray nama niawarr d’où nitt wayy
evenprod louma len def loutakh manouma am j’aime si yen😢
Défo dr
Locoye doyee😂
Khana nga def ni mane mougn rek tekhamné nitt louy weurseugeum dinasi 😂😂😂 diott
J’aime yi xanna dagnikay diay walla TH-cam dakay feyyy??😂
@@zahrakama8303souma amoul j’aime Sama yaye douma diokh khalis rére 😢
😂😂😂J’aime vraiment le rôle de Omar ❤❤
Yay dior wayadi na 😂😂 😂 soda mareme change na😂😂
🎉🎉🎉🎉🎉🎉 Modou
@yayefallcivilisee9300 Ah mougui koy teigual lou xerei. 😂
Kou torokhal domou diambour gniou torokhal sa dom 👌🏾
Amine
So amoul dom nak
@@FallouNdao-l3zbonne question😂😂
Yalla torokhalela@@FallouNdao-l3z
So amoul dom gnou torokhal la
Série bi nèkhna🥰wayé Président DIOMAYE andina climat décembre bi Macky diayone Toubab Yi Alkhamdoulila 🙏🙏🤣🥰🥰
😂😂😂😂😂😂
Ahhhhhhhhhhhhhh
😂😂😂do nit
Bilay waxall way motakh mou doy warr looll si sédd bi kay nékhna
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Boury tu as bien fait merci de sortir Mbeuguè de ta maison merci beaucoup Boury ❤❤❤❤❤
Omar Diagne dof plus la. Dofou nandité la. Mais Boury aussi may banquier bi espoir doom dji wakh mou nara yakk lep limou ligey. elle se laisse influencer trop facilement. La souffrance des enfants Diagne montre encore une fois pourquoi les femmes souffrent en silence dans le mariage africain en general mais senegalais en particilier. Chapeau Evenprod pour cette belle et instructive serie
Mais Boury thi iddeu leu nék en plus banquier bi ces intentions envers Boury ne sont pas bonnes
Mousta may banquier bi espoir ndaw banquier mo eupeul rk en plus si iddeu la nekk j'aime sa façon de faire amnio khamantane bo divorce rk moylolou tentations yi beuri
Ndiawar a la copine de Sokhna:son parent Vivant? 😂 vraiment Ndiawar safna xorom 😂
Blh wlh 😅
@NdeyeDiop-zf4pu Badou tothie nafi radiakhe ?
Bien fait pour mbeugue enfin boury a ouvert les yeux sur mbeugue
Kou beug seydina Mohamed lalale♥️♥️cœur
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤@@MorDiopgarmi-ii4lq
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤psl
Omar Diagne koumou dioylo😢 dinala rélo😂😂 néne mati ladoum la❤❤❤ bilay kii Dinama rey dama ré ba sonou 😂😂😂 yaye doir khamun ngane sa biss dina bjaw 😂😂 yalla na seytané khap doli mais soda maréme contane na si mom❤❤❤ Waw kayy Boury contane na ci yeuw tey waw ni leu kayy nitt dangaye bane merci beaucoup wayy❤❤❤❤❤ mbégué seytani bou mague leu kii
@SokhnayemouNdiaye Ah Marieme Soda mougui koy teigual mère bi lou xerei. 😂
Gni amagoul djeukeur ak djabar konn mane Yalla nanou yalla may way ak climat bi tmt😢
Bilaye mes legui rek inchalla 😢
Amine
Amine yaraby
Amine
Amine yarabi
Loleni def ba diouli diote nagako bayi dem diouli ba pare te yalla rek takh 🙏🙏🙏
Machallah amna solo
Blh lou am solo
diouli na baparé
❤❤❤❤ deugueleu
Deugue pire
Xarite boulay dougal si Mousiba yalla na naniou si Yalla mou sall
Ndiawar Diagne néna Aïtoush " ma fille son parent vivant😂😂😂
Ses parents vivant wouniou dé😭😂😂
Commentaires bi la done weur 😂😂😂😂😂
Lolou meunama ray
@@AdjaMoussouDiagne Ndiawar ndogo dara la dara safouko😂😂
Ndiawar dinama masa ray pourtoush pourtoush rék😂🤣😭
😂😂😂😂😂
Kouné linga beugue sissa vie yàlla naloko yàlla défal si barké zeydina Mouhamed (PSL)🤲🇸🇳
Amine y’a raby 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Amine ya rabi
Amine ya rabbi 🤲 ❤️
Amine
Amin
Mani evenprod diguanté yaye dior ak mareme boumou sedd diaplen si 20episodes rek😂😂😂😂😂
70 episode
Soda mareme maguilay soga aimé nak😂😂😂😂Waow lima diahal moy bureau famille Diagne kene hamoul foumou nék waleuh dama ignane
Iniane no dh danio wara foum neke 😅
😂😂😂😂😂😊
😂😂😂😂may lén lolou 😂😂😂😂
Iniano danga sop😅
Mareme soda ak badiene bi yalla sen saytane yook amine😂😂😂
😂😅
Non rétanou niankou bi louné la 😂😂😂😂😂😂
Wa soda maréme mi badola na di 😂wayé baxna si mére bi😂wayé Ndiawar niit kou Nékh la 😂😂😂😂
Anti stress la dama rée ba sama biir di metti😂😂😂
Deugu la yaye ndior sick na mais Soda Mareme changement wam dafa gaaw lol
@FatouDiouf-pm3md Ah mougui koy teigual lou xerei. 😂
Na saff sapou entre soda Mareme et yaye dior loumou saff rek doyoul bou diaré Ay dor sakh ak Ay mbediété beugue nagne 😂😂🥰
Ayway 😂😂😂
Liy ram entre niom niar thi niak bi la dieum, wayè bou èguè yalla nafa am keur😂😂😂
Wawaouwww😂😂😂😂
😅😅😅😅
😂😂
Ibou laye kagne laye am diom bayi nar bi 😂😂😂
R😅😅😅.
Niaw bien fait pour mbeugué dafa soff trop 😂
Oh kharitou sakhna bi bakhna na de boury merci mbeuge mi seytane la France ndiawar bi😅
Niou commencé si Bismillah terminé Alhamdu lilAllAH ❤
Sokhna bou ndaw ndeysan yeureum nako trop
Dafa seytané rék yéné nékela 😂😂😂😂
Yaye dior ak soda mareme yalna seytanè xeb doli😂ndakh yako formè pour détruire le ménage de boury😮ba takhna legui sur le plat lalay togale comme repas😂😂😂evenprod k la guerre commence 🤧🤧🤣
Blh lepp mom leu
Koubyar sa kouye bamou mague bala moule mbeuk kene yow laye ndieukeu mbeuk
Moussa seck mo geuneu nekh Thi Sénégal 😂😂😂😂😂 pourtousss kay
Omar diagne néna batléne dieuleul diadia ndakh Maty rose sou gneuwé sa xel dou nek si mom 😂😂😂
Mais ndiawar nexna néna aïtoush « son parent est vivant »😂😂
Omar Diagne doffouul deh 😂😂
@ messoul doff 😂
Manam ndiawar , c'est bien ak très bien 😂 ay yeufam la 😂😂😂
😂😂😂😂
Mais Omar Diagne ak séne diguanté ak yala moussoul doff wépépépé😂😂😂
Soda ak yaye Dior yallah na seytaner khepp doli 😂😂😂touff touff
Amiiinn
Amine way kadou yi rafete na trop machallah ❤
Amine ma chérie 😂😂
Djibril dieye yalna nako yalla yeuka ti😢😢
Amine yarabi 🤲
Amine
Amine
Amine
Maman Diéwo sow on n'en parle pas mais elle est vraiment une grande actrice ❤ chapeau à cette grande Diva ❤
L’élégance de Bourry😭❤️
Malcom aussi il est trop beau et talentueux ❤️
Yalna dioulitt yëppou am jammu 🤲
Xalisso Série Bou Khéré Bi Té Woww Kongu At The Moment🎉
Ceux Qui D'accord Pointez Vous❤❤❤❤
😂😂😂😂❤
Lou khéré Lou wow kongue kokorong khérakoy tothie😂😂❤
@wakhlouyydeffarnittgni4965 Merci beaucoup. ❤
Yallah na seytané khep doli si Yayou diawar akk diabarou ndiawar dji😂😂😂😂
Waya yaw tamitt boul faténé téyatar la
Ndiaware diagne 😂 bala série bi di diekh dinama réye 😂 rééna baye beugue dééé
Billay soxna diagne bou makk kou meuneu la❤❤😊Bilay fi mome gnieuppeu meuneu Machallah 😊❤❤
C’est bien😂😂😂sacré ndiawar Diagne 😂
C’est très gentil ❤😂
@ 😂😂
Waw kayy Boury contane na ci yeuw tey waw ni leu kayy nitt dangaye bañe merci beaucoup wayy❤❤❤❤mbégué seytani bou mague leu kii
Bou ken yakhal ken ❤❤❤❤❤❤❤❤
Kou beugue sa yaye lalal ❤❤❤❤❤
❤❤❤
Ndiawar néena Poultouch c'est bien😂😂
Boury légui dina comprendre ni mbeugué n'est pas une très bonne amie 🤧😏
Ton parent vivant 😂😂
Sacré ndiaware😂
😂
🤣🤣🤣🤣ça m’a tue
Son Parent Vivant 😅😅raynama dama gnewate mais niawar toujours à lui akk sa façon de démarche ba athe tate yi 😂😂 vraiment xalisso dafa meilleurs
Dieuredief serigne touba mbacké❤
Pounetoush 😂😂😂 ça m’a tuer 😂😂
Yeur mande ak djégalou sunou borom ❤
Torokhal nit beug nk ci djam yaye Dior naq nex Gha 😅 liga df ba diexal xolou boury ding ko fay peppe par peppe 😂😂
Yalla nagnou yalla may santé cfa AK sagnsé yousakh dakk❤
Mais Ndiawar Diagne 😂quel acteur 😂
La mère de Ndiawar n’a encore rien vue ce n’est que le début du commencement 😂😂😂😂
Elle va lire l'heure 😂
@@Omardiallo-yr3nvje te jure
Omar eska doof n'a 😂😂❤
Ousmane sonko l'homme du continat 🎉🎉🎉❤❤
Ndiawar dall c’est bien rek la khamm 😂😂il joue bien ❤