Thiow amatt Na Dei Modou anta attaque Bour Guweul et Fadame 2 Nio yakh lambji Ay saytané you Mak lan

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 10 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 157

  • @OmarDiouf-qs5bj
    @OmarDiouf-qs5bj 6 วันที่ผ่านมา +23

    Père max teimo nopalou khaliss bimouy yaakh nako dieundei ayy saccou thieep pour ndiabott gii

  • @IdrissaDioufSané
    @IdrissaDioufSané 4 วันที่ผ่านมา

    Vraiment Modou Anta tu communique tres bien machallah amna lohamnii dou thieurou buur ak fadam

  • @قناةالشيخالحصريعبدالعزيز
    @قناةالشيخالحصريعبدالعزيز 6 วันที่ผ่านมา +10

    Salalm koubakh Dioumnga dh nganane yalla bouyakhe daymèlni louye dèfar
    Yall dèfar rek lay def .
    Wantè douyakhe baysi khèl bbh.

    • @alhassanngom8282
      @alhassanngom8282 6 วันที่ผ่านมา +1

      Dioumna mom. Yalla rek modoul dioum nak niou xaméko nonou

  • @SerignemodouNdiaye-s3u
    @SerignemodouNdiaye-s3u 5 วันที่ผ่านมา +6

    Man dh albourakh lay top mais kou yab Gaston production rek rek père gas mofi sori😊

  • @moustaphandiaye8411
    @moustaphandiaye8411 6 วันที่ผ่านมา +8

    Wayyy père max mi d'où Nangou nogalou yalla😂😂😂

    • @CASI7797
      @CASI7797 5 วันที่ผ่านมา

      Day kheiblou bopam rek

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 4 วันที่ผ่านมา

      day yabloi bopam et au finish rien

  • @DjilyMbacke-c6o
    @DjilyMbacke-c6o 5 วันที่ผ่านมา +2

    Wa père mi meunoul guem yalla waa lii bah diamou leu

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105 6 วันที่ผ่านมา +7

    MAX MBARGANE DAFA NIEUK TE NIEUK DAY RAY GOOOR. NA LEK 10% LEW NAKO

  • @setewillane5485
    @setewillane5485 5 วันที่ผ่านมา +1

    Bonne continuation ❤

  • @assaneyade9217
    @assaneyade9217 6 วันที่ผ่านมา +4

    Vraiment niom 2 dano eupal trop sakh mais yaw nga bayi tesane te do djiguene goor nga ❤fadam ak bour mom considere wou nel nioune wa senegal 😂

  • @leprometzo9048
    @leprometzo9048 6 วันที่ผ่านมา +37

    Mai loutax max mbarguan mom dou nopalou khamni yalla modou lo lafi tékk sénégalais dall mo sokhor rekk 100%modou lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @Samzo4970
      @Samzo4970 6 วันที่ผ่านมา +3

      Lo kham si kou sokhore té mom dafa fatté ni nioko may chance

    • @FallouSarr-
      @FallouSarr- 5 วันที่ผ่านมา +1

      Modou a perdu deugu la yalla beugu .

    • @assanendiaye5640
      @assanendiaye5640 5 วันที่ผ่านมา +1

      Yène tamit 😂😂😂ki di xool fi interet wame nek😂😂😂cest du sport,IL defend son athlete...😂😂😂

    • @zokorasall9617
      @zokorasall9617 5 วันที่ผ่านมา +1

      Max margane ligueyame lay def .yaw vrai dof gua

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 5 วันที่ผ่านมา

      Kon yaw si gni sokhor nga bok khana Sénégalais nga dh dél wakh niéne si nitte gni rk mais max limou déf yone may nakoko par ce que diap nani mbeuram mo dane comme ninga diapé ni sa mbeur mo dane

  • @ablayewarore
    @ablayewarore 5 วันที่ผ่านมา

    Merci beaucoup modou anta sa kadu rafetna

  • @serigneomarsall7959
    @serigneomarsall7959 5 วันที่ผ่านมา

    WAXE DJI RAFETNA MODOU ANTA ALLEZ DU COURAGE

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 6 วันที่ผ่านมา +1

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 6 วันที่ผ่านมา +11

    brime Yasin AK grand ngatou wata bilay walahi nafék you mank lagnou pourquoi nagou wougnou wx si combat Boy Niag ak reug reug 😮😢 comme si dougnou domou Sénégal 😢😮 Sénégal yakouna 😭😭😭

    • @alhassanngom8282
      @alhassanngom8282 6 วันที่ผ่านมา +2

      Niom Albourakh laagn faar motakh niouy toogn mais quand même waarougn waax néxoul wala di sabotté. Modou Anta saax waax nako néna donté daaniouy farce

    • @MohamedGueye-xi6qq
      @MohamedGueye-xi6qq 6 วันที่ผ่านมา +1

      Il faut pas oublier LahatNdiaye mo saga wone Fadam lolou moko meti meme si Fadam meune na adiou lolou

    • @alhassanngom8282
      @alhassanngom8282 6 วันที่ผ่านมา +1

      @@MohamedGueye-xi6qq y’a ça aussi, en plus genre c’est comme blaguer sur la concurrence qoi 😅.

    • @alhassanngom8282
      @alhassanngom8282 6 วันที่ผ่านมา +1

      Gniy ligyé wave désfois niou saani xeer wa orange money 😂😂😂

    • @MohamedGueye-xi6qq
      @MohamedGueye-xi6qq 6 วันที่ผ่านมา

      @ xam nga lamb mome ken xamoul lane la 😂

  • @dienefarm5323
    @dienefarm5323 5 วันที่ผ่านมา

    Respect modou anta

  • @mistercarter467
    @mistercarter467 6 วันที่ผ่านมา +14

    Bilahi damaleine yagg défendre mais tanyiii y m’énervent les deux .. déjà il nous fatigue si combat balla modd’lo… alors que sathies nekfii

    • @djsamsk422
      @djsamsk422 5 วันที่ผ่านมา

      Mane lima diakhale moye Lou takhe Fadam Ak Bour souniou léne invité si Face to Face niouye critiké si programme bi

    • @Kopp2111
      @Kopp2111 5 วันที่ผ่านมา

      Tapha tine tamit mongui fi

  • @MouahmdeDieng
    @MouahmdeDieng 6 วันที่ผ่านมา +1

    Merci momo diamou si yaw

  • @moussaseck967
    @moussaseck967 6 วันที่ผ่านมา +14

    Fadame seytane la bour guewale nafekh la père Gaston mbengue mofi sori rek bilahi

    • @DjibsonIdriss
      @DjibsonIdriss 6 วันที่ผ่านมา +1

      Bilaye père Gaston rek mofi manqué

  • @GibbChiv
    @GibbChiv 6 วันที่ผ่านมา +1

    Bilaye ndeyesane adouna amoul solo

  • @BabacarKa-j3q
    @BabacarKa-j3q 5 วันที่ผ่านมา

    Bien dit modou anta n'a rafet rek bon esprit ❤

  • @Pirate987
    @Pirate987 5 วันที่ผ่านมา +1

    😂😂😂😂sheut modou anta ak tontou wanté c une longue histoire 😂😂😂

  • @walobrackmbodj805
    @walobrackmbodj805 5 วันที่ผ่านมา

    Way Max Boumou Fonto Domou Adama Yi Yow Siteu Nék Khalé Recours Rek Modou Lo Mo Am Ndam Gng Dofou Niou Di Diokh Siteu Victoire

  • @IbrahimaDiene-c2w
    @IbrahimaDiene-c2w 5 วันที่ผ่านมา

    Merci modou anta bour ak fadam ay saytané laniou

  • @ctiondaradji
    @ctiondaradji 6 วันที่ผ่านมา +6

    Adouna amoul solo lép térangua lamb kaf fo ak ré la

  • @PapendiayeNdiaye-c4z
    @PapendiayeNdiaye-c4z 6 วันที่ผ่านมา +2

    Bilay modo anta lolerr ga wakh ❤❤❤❤❤

  • @LamineThioune-t8d
    @LamineThioune-t8d 5 วันที่ผ่านมา +1

    Enn Modou setlounani temps yi yangui dougall ay haayat loukhew

  • @birame696
    @birame696 6 วันที่ผ่านมา +18

    Ki aka beug détails 🤌🏿😡👹👹

    • @wakanafall2498
      @wakanafall2498 6 วันที่ผ่านมา +2

      Billaay chakk jour ma wakh ko
      Modou anta loolou rkk mooy thiatam dayy bayyi kh3ll wakhou publik de trop t3 di tontou aussi Et ca c pas professionnelle

    • @ousseynoutoure518
      @ousseynoutoure518 6 วันที่ผ่านมา +1

      Mbadou😂

  • @DameNdiaye-z3t
    @DameNdiaye-z3t 6 วันที่ผ่านมา +1

    Moudou mersi ❤❤❤❤

  • @papisall9526
    @papisall9526 6 วันที่ผ่านมา +2

    Merci modou anta

  • @OfficierCoach-zv7um
    @OfficierCoach-zv7um 6 วันที่ผ่านมา

    Bien dit Modou anta
    Thiakhane bakhoul waaay

  • @gtheboss9635
    @gtheboss9635 4 วันที่ผ่านมา

    Numéro 👉 de Modou Anta sil vous plait

  • @papitondiaye9413
    @papitondiaye9413 4 วันที่ผ่านมา

    Wakh léne Ada fasse DEUG Dafa réw té khamul ndm.... Draa

  • @baityrba2447
    @baityrba2447 5 วันที่ผ่านมา +1

    Anna wopoppppp😅😅😅😅?

  • @jeanmbayeniakh1614
    @jeanmbayeniakh1614 6 วันที่ผ่านมา

    Machalla Modou ❤❤❤

  • @djsamsk422
    @djsamsk422 5 วันที่ผ่านมา

    Mane lima diakhale moye Lou takhe Fadam Ak Bour souniou léne invité woule si Face to Face niouye critiké si programme bi

  • @ndongothiam2991
    @ndongothiam2991 6 วันที่ผ่านมา +2

    Yaw mi ya seytané nak niom dagn done kaff rek vraiment

  • @CheikhDjilyNdiaye-t5o
    @CheikhDjilyNdiaye-t5o 5 วันที่ผ่านมา

    Loula tére wakh si vite fait

  • @BoyPoulo-kg5pl
    @BoyPoulo-kg5pl 5 วันที่ผ่านมา

    Me pa bi louko dal😂😂

  • @Kaddudeuggui
    @Kaddudeuggui 6 วันที่ผ่านมา

    Mor kagn kang ak Diop2
    Diélbi dou lére

  • @moustaphathioune8359
    @moustaphathioune8359 6 วันที่ผ่านมา +1

    Modou anta yaw ya yakh lambji billahi

  • @mactardiallo2085
    @mactardiallo2085 5 วันที่ผ่านมา

    Fadam AK bour et travail pour Aziz ndiaye vous ne pas encore compris

  • @bocarba2781
    @bocarba2781 5 วันที่ผ่านมา

    Niak apati kay

  • @seydinaaliouneboromjasiji3200
    @seydinaaliouneboromjasiji3200 5 วันที่ผ่านมา

    Ada Fass Doff La

  • @SaliouDiallo-v8o
    @SaliouDiallo-v8o 6 วันที่ผ่านมา +4

    Modou anta y’a tah ma ham fadam mais boul tontou nkl si liga nk rek kou yarou ga mann bougou guiss koula saga dah talibe ga

  • @PamousaSeye
    @PamousaSeye 5 วันที่ผ่านมา

    Ok❤ok❤ok❤

  • @MoustaphaMbaye-sg1tr
    @MoustaphaMbaye-sg1tr 6 วันที่ผ่านมา +4

    No modou boul tontou Nio niou waye

  • @fidelemendy284
    @fidelemendy284 6 วันที่ผ่านมา +5

    Lambji dafa beuri ay nafekh

  • @papendiaye1371
    @papendiaye1371 5 วันที่ผ่านมา

    Yow détails rék

  • @seringendiaye333
    @seringendiaye333 6 วันที่ผ่านมา

    Merci modou anta❤

  • @wahabsene1213
    @wahabsene1213 5 วันที่ผ่านมา

    Fadam ak Bour problème Lamb ji yeupp niom niokoy indi… Ay nafék lagne dagne koy fowé nak mais si sén deug lagne né… Damalène estimé woné

  • @CASI7797
    @CASI7797 5 วันที่ผ่านมา

    Père Max😂😂😂😂😂

  • @mouhameddiagne9347
    @mouhameddiagne9347 5 วันที่ผ่านมา

    Kharal ma gniew désabonner si fadam

  • @IbouBa-w4d
    @IbouBa-w4d 4 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤❤

  • @MorThiaw-ui5pu
    @MorThiaw-ui5pu 6 วันที่ผ่านมา

    Merci ❤❤

  • @papitondiaye9413
    @papitondiaye9413 4 วันที่ผ่านมา

    Limo yakk lambji kéne dousi wakh Deuge

  • @wakanafall2498
    @wakanafall2498 6 วันที่ผ่านมา

    Modou anta bayyill detail
    Modou anta bayyill detail
    Modou anta bayyill detail
    Gnounn sayy fans looloo rkk nguagnou soof3 dangua beugue tontou de trop
    T3 guoor moomoull loolou
    Ligu3yall sa liguei t3 bayyi gniyy wakh wakh

  • @ElhadjDiouf-k7q
    @ElhadjDiouf-k7q 6 วันที่ผ่านมา

    Merci Modou anta lolerr ga wakh

  • @ctiondaradji
    @ctiondaradji 6 วันที่ผ่านมา +5

    Modou Anta togn bahoul sa titre niaw na trop

  • @Loufa__bou__xaragne__lô__221
    @Loufa__bou__xaragne__lô__221 6 วันที่ผ่านมา +2

    Billahi Modou anta tu es le meilleur ❤❤

  • @IssaMbeur
    @IssaMbeur 5 วันที่ผ่านมา

    Boy Niang bly dafa fébar

  • @fayecheikhcheikh4186
    @fayecheikhcheikh4186 5 วันที่ผ่านมา +1

    Ki mom kom domi niarel😂😂😂 ngen balma

  • @modoulebou634
    @modoulebou634 5 วันที่ผ่านมา

    Fadam ak bour guewal ay deumou lagnou

  • @kallaganeikhsane5288
    @kallaganeikhsane5288 5 วันที่ผ่านมา

    Li nga sol deh blouse leu. Yangui melni médecin de garde

  • @AbdouDiop-d6t
    @AbdouDiop-d6t 6 วันที่ผ่านมา +1

    max mergane guemeul yala do ame touss😂😂😂

  • @ibrahimaba2655
    @ibrahimaba2655 5 วันที่ผ่านมา +1

    Modou yaw problème rekk kone djiguène parfois dangay adiou yéne yii

  • @AsseNdao-e4o
    @AsseNdao-e4o 6 วันที่ผ่านมา

    Merci mo Lou lér barké Balla gaye

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wc 5 วันที่ผ่านมา

    Siteu kasse siteu kasse

  • @user-kf7oi4q
    @user-kf7oi4q 6 วันที่ผ่านมา

    Gaston mofi nekoul rek ndeysan kone mou tekk lenn sen place

  • @Papisdiop349
    @Papisdiop349 5 วันที่ผ่านมา

    Néna modou mbaye moye idolam 😂

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 4 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂😂😂😂 ha mais prkw pas

  • @AmadouBa-xn8dd
    @AmadouBa-xn8dd 6 วันที่ผ่านมา +1

    Cool

  • @Ngathibouthiosan
    @Ngathibouthiosan 6 วันที่ผ่านมา +1

    Max mbergane dafa niakk diomm balegui dafa geumoul ni siteu danouna

  • @MameSow-m7e
    @MameSow-m7e 6 วันที่ผ่านมา

    Modou lôoooooo ❤❤❤❤❤

  • @FatouCisse-u4f
    @FatouCisse-u4f 6 วันที่ผ่านมา

    Max tè nga nopal sa bopoue CNg bii amoul thiakhane

  • @MoussaMbaye-r8h
    @MoussaMbaye-r8h 6 วันที่ผ่านมา +3

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏

  • @ousseynoutoure518
    @ousseynoutoure518 6 วันที่ผ่านมา

    Étiquette Champion du monde bi mounoul yokk dara si reug si combat loudoul pression donc teklénko si côté

  • @maxdiop386
    @maxdiop386 6 วันที่ผ่านมา

    merci bcp modou anta

  • @oumarndao7485
    @oumarndao7485 6 วันที่ผ่านมา +3

    Yow dangua sof té beugueu défanté,kérok lo wahone si billet Wa jambar production si combat siteu modou lo,kou lale makane rek nguay beugueu dé

    • @modo6218
      @modo6218 6 วันที่ผ่านมา

      Wakh degue yalla 😂😂

  • @boyeniang3781yeumbeul
    @boyeniang3781yeumbeul 6 วันที่ผ่านมา

    nit kou bakhe ga diam si iow❤❤❤

  • @maodogueye4381
    @maodogueye4381 6 วันที่ผ่านมา +1

    Modou lo selll

  • @OldySy-v7u
    @OldySy-v7u 6 วันที่ผ่านมา +1

    Fadam ak bour ay séytané laniou

  • @morsene7507
    @morsene7507 6 วันที่ผ่านมา

    Carrière que sa soit sportive ou quoi que ce soit sa doit être gérée donc bour et fadam n' accepté jamais à sacrifier votre carrière

  • @ibrahimasene9243
    @ibrahimasene9243 6 วันที่ผ่านมา +4

    Siteu daffa daane modou lo wakh deug yalla

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 6 วันที่ผ่านมา +1

    Fadam , buurr , buzz gnion nara yakh lamb dji, nieupou dem thi MMA bi !

  • @MadyCissokho-us9xu
    @MadyCissokho-us9xu 6 วันที่ผ่านมา

    Modou ante doundal lou barri ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ballacisse7561
    @ballacisse7561 5 วันที่ผ่านมา

    Ki mome khoulo rek.Daffa sof

  • @AngekhadimKaba
    @AngekhadimKaba 6 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤❤

  • @NgagneDiakhate-n7e
    @NgagneDiakhate-n7e 6 วันที่ผ่านมา

    Danio sokharr raiik

  • @biranecamara6796
    @biranecamara6796 6 วันที่ผ่านมา

    Bour ak fadame kay dagnio yeuk succès mais wa lamb nio djoubo woul makane mbengue l'année dernière 2stv tv déff ngeen lou am solo mais wa al bourakh nio takh mou dém TFM té fofou lou mbeur yi wara wakh lamine samba wakh ko 😂

  • @ablayedione9612
    @ablayedione9612 6 วันที่ผ่านมา +1

    Bour gewel ak fadam gno yak lamb djii

  • @amadousarr1957
    @amadousarr1957 6 วันที่ผ่านมา +5

    Félicitation modou anta boul changer deh

  • @chicorykharagne6323
    @chicorykharagne6323 5 วันที่ผ่านมา

    Modou anta doudou sane claf la diuel na Gaston na deffat claf diokhlene champion claff bi limou mom diuel claf dawara melni empereur tek mo wara eup ndiarign lamb fofou la tollou na championsjip yi barri

  • @khadimantaseck2295
    @khadimantaseck2295 6 วันที่ผ่านมา +1

    Wakhal waye

  • @MomadouCisse
    @MomadouCisse 5 วันที่ผ่านมา

    Adafassrek

  • @ousseynoutoure518
    @ousseynoutoure518 6 วันที่ผ่านมา

    C'est la deuxième fois niouy deff sen yeufou fake yi début combat Modou lo vs siteu lolou laniou defone lamb sans yéne day dokh

  • @aboubacarndiaye779
    @aboubacarndiaye779 6 วันที่ผ่านมา

    Ils ont le droit de donner leurs avis arrêtons le sermon.

  • @cheikhthiam-k9o
    @cheikhthiam-k9o 6 วันที่ผ่านมา

    Fadame ac bour ay domrema lalen

  • @franceamericanbullydogfami7992
    @franceamericanbullydogfami7992 5 วันที่ผ่านมา

    La lutte commence à être comme un taanë bëër parler sans arrêt pour rien... Tchiip

  • @diallomamadou4525
    @diallomamadou4525 6 วันที่ผ่านมา

    Ndeysane modou anta mi dafa yakarni dafa am xamxam yakarni dafa pertinent alors k danga nul trop ba paré bari ay detail. Wallahi yow bo amone xamxam senegalais yi am probleme

  • @bocarba2781
    @bocarba2781 5 วันที่ผ่านมา

    Max Mo niak diome deugu deugu, Max vrai con la, premier apl bi nena « nio am ndam cng nangou walla niou bagn » déjà gueumoul cng ba parré di sonal bopam 😂 lol père bi dafa dofff

  • @madembatoure7005
    @madembatoure7005 6 วันที่ผ่านมา

    Pour dire vrai fadam et bour daniouy togne wa gaston production parce que magui leine di deig niouy saboter face to face bi amone cote d,ivoire