Inchallah 🙏🥺 vous êtes les prophètes du hip-hop je dis bien les prophètes du hip-hop galsen 👑♥️ bilahi 🥺🥺🥺🥺 yalla nalein yalla aar si barké Baye Niass ✨
Baye si khol yi❤️ tarikha tidjiania si dieumou yi ak si khel yi🥲 Talibé cheikh si djiko yi🫶🏾 Beyti baye si lokho yi✊🏽 Bourde sunu yitté☺️ Mbecté mi dioli ba médina baye❤️🩹 Alhamdoulillah diarama maoulana cheikh Ibrahima niass❤️🙏🏽(bind ko si commentaire yi)Djeureudjefé baye🫶🏾
Je suis Mouride mais Baye Niass je l’aime sincèrement. Nitou yalla deug leu. Et sa relation avec la famille de Cheikhoul Khadim à l’occurrence Serigne Fallou est une illustration et exemple pour nous ,jeunes d’aujourd’hui . Di jegalou waat bou bakh si kadou yi
Vous avez sur toute la ligne ma très chère. Que le bon Dieu exauce toutes les prières formulées à cet égard ❤.. ioe tmt nit kou bakh geu Pask kou bakh moy guiss lou raffet diko wakh
"Rakadjou Thi Baye" est en ligne sur youtube. Un régal musical qui justifie l'amour inconditionnel que portent Ara & Deyza à Cheikh Al Islam et, partant, à toute la Communauté Niassene. A consommer sans modération.
Walakhi khamouniou louniou souniou wadji diaral borom kaolack mo bakh souniou wadji beug ko rekk diam nguaye doundou foh tolou moniou khamal yone wi Diém thi yallah baye moye sohniou baye sheikh al Islam yalna yallah yokou lerram té Tass niou si barkém sons bi nice neu trop machalah❤❤
Oh lala machallah chaque année damay yakamti leur son pour le Gamou suis Chrétienne mais j'aime tellement Baye Niass c'est plus fort que moi en plus Akhlou Brick vous assurez comme d'hab bne continuation mes bro et paix sur vous bn Gamou à tous❤🥰🥰🥰
Boromm Xelll rekkk moyy Déegueu liiguéen diii djioudiou du début jusqu'à la fin Ndeyssane walahi😅souguéenko khaamoon daww raadjiou djiie thie Baye al hamdoulilah Dieureudieufé baye
❤❤❤ vraiment je suis très très très content de vous chaque année damlay ni khar ak pasience walakhi yaina takh ma xame kouy baye barhama niass top ko nak nakh dama beugue yalla ak kouma khamal yalla bima toper baye barhama niass la xame sama bop ba paré xame yalla Di santeu maolana cheikh Ibrahima Niass ❤❤ dieurdieufti Baye barhama Niass
Billahi damalén meussa beugue avant même de savoir que vous étiez des Barhamiens❤️✨ chaque année nianguén ni sédalé sama khôl Yallah nalén ko Ya Rabbee fay🤲✨❤️🥰
AŔRA TU AS UNE VOIX EN OR MASHALLAH. DEZA LE FLOW DE TON RAP EST SUPERBE❤❤❤❤ J'AI ÉCOUTÉ CE SON PLUS DE 100 FOIS. FORCE A VOUS AKHLOU BRICK . RAKADIOU NA CHI SON BI C'EST VOTRE CHEG D'OEUVRE ET DIEU SAIT KE TOUT VOS AUTRES SON SONT TOP. BIG UP GUYS KEEP UP THE GOOD WORK. MUCH LOVE❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bon Gamou a tout le monde..
Baye niass love..
Ila Medina Baye…
Il faut épingle hein
Inchallah 🙏🥺 vous êtes les prophètes du hip-hop je dis bien les prophètes du hip-hop galsen 👑♥️ bilahi 🥺🥺🥺🥺 yalla nalein yalla aar si barké Baye Niass ✨
BAYE MOY DEUGGUE ☝🏾❤
Hol yi sed na ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Niass ❤
Ma fi djitou🥰 1 million avant gamou qui est dacc Dieureudief BAYE NIASS 🥰❤️
Dieredieuf yaw da nga bakh
😅😅😅😅😅 non non😊
❤
Machallah ya bakh
@@YADISCO-PRO mala djitu dh 😂
Je suis mouride mais j’aime Baye Niass éperdument ❤
Je suis mouride mais j'aime baye Niass éperdument❤
Le bonheur d’être talibé cheikhna akhmed tidiane chérif est inexplicable alhamdou Lila binou amé Maolana cheikh Ibrahim migni xamal cheikh tidiane
Dieureudieuf Baye niass❤❤❤❤❤❤
Kou Beugg am dome bou Goor toudéko Cheikh Ibrahima lalal j'aime Svp♥️
❤
❤J’aime cheikh ibrahima niasse❤❤
Suis catholique mais ce son me va droit au cœur ❤🎉🎉
Yalna yalla dimba léla
Mashallah ❤❤❤ on vous aime trop la communauté catholique bilahi
Mashallah
Ndeysane ❤❤ on vous aime aussi
Walay ndysann naw naniulén tchii sén manduté
Kou Beuge Am dom bou gour toudiko Seydina Mouhamed lalal j'aime👍🤲
Linga wax mom nieup ko beug ❤❤❤ Salalahou aleyhi wa salam
PSL 🥰
Alhouma amine inchallah 🙏
Psl
Alhamdoulilah bamako sougnou Borom mayé
Baye si khol yi❤️
tarikha tidjiania si dieumou yi ak si khel yi🥲
Talibé cheikh si djiko yi🫶🏾
Beyti baye si lokho yi✊🏽
Bourde sunu yitté☺️
Mbecté mi dioli ba médina baye❤️🩹
Alhamdoulillah diarama maoulana cheikh Ibrahima niass❤️🙏🏽(bind ko si commentaire yi)Djeureudjefé baye🫶🏾
Talibés cheikhou tijanya, téye yarou, kham yallah, dioulité, meuna sangsé, sétt ❤❤❤
Kou beug am dom bou gour toudiko barké baye Niass machalla doli santé yalla bou bakh ak Baye Niass dieureudieufée Baye Niass❤🙏🤲🥰🥰
Nnn le bonheur k vs me procurez kan vs chantez Barhame❤ yalna l'en yal'a fzy mbecté mi gnouy yeuk sougn xol
Kou beugue baye niass beusseul j’aime ❤ mom rk lagniy topou barké cheikhoul Tidiane 🙏🤝
Mach'alla ❤🎉❤
❤️❤️🥺le bonheur que vous procurer à chaque Gamou 🤣😍❤️🥹meuno léne sax comprendre
Yalna Baye faylén bopppam
Je suis Mouride mais Baye Niass je l’aime sincèrement. Nitou yalla deug leu. Et sa relation avec la famille de Cheikhoul Khadim à l’occurrence Serigne Fallou est une illustration et exemple pour nous ,jeunes d’aujourd’hui .
Di jegalou waat bou bakh si kadou yi
Kaadou yi rafett n'a machallah... et c'est cette relation qui devrait perdurer entre jeunes mourides et jeunes tidianes😊
Vous avez sur toute la ligne ma très chère. Que le bon Dieu exauce toutes les prières formulées à cet égard ❤.. ioe tmt nit kou bakh geu Pask kou bakh moy guiss lou raffet diko wakh
Niou beug Baye Niass kay🥰🥰Nékhna way
Barké baye niass son biii niomouy deff sama khol bi enh 🥰🥰🥰❤❤❤
Ohhh 🥺 encore les prophètes du hip-hop galsen 👑 🥺❤️ vraiment je vous adores 🥺❤️
Ohhh wa médina baye kaffrine thiey yalla ahhh li nexxna barrière baye willane😊
Barki borom Touba Baye dama ko beug té yalla rék tah❤❤❤
Folen degeu mouride bou beug baye niass lék diapeu lenma ss la Dieureudieuf baye barkhama ❤❤❤❤❤❤
Mourid sadix ma beug baay way❤❤❤🙏🏾
Nice clip bon Gamou frères et soeurs Musulmans on vous aime ☦️❤🙏
Version Sped Up Rakadiou Ci Baye
th-cam.com/video/AW_EG5U4q2I/w-d-xo.htmlsi=Qf1iDFtm4qkZP_zt
"Rakadjou Thi Baye" est en ligne sur youtube. Un régal musical qui justifie l'amour inconditionnel que portent Ara & Deyza à Cheikh Al Islam et, partant, à toute la Communauté Niassene. A consommer sans modération.
Version Sped Up Rakadiou Ci Baye
th-cam.com/video/AW_EG5U4q2I/w-d-xo.htmlsi=Qf1iDFtm4qkZP_zt
Je suis pas senegalais mai vraiment nékhoull ba nékhoull song bi dafa neikh
Thieuy deyza sa parole rek may ray barki baye niass dundall weral lo dundou doyul barki baye niass binou bok 🤲🏾 ♥️ 👑
magal dewen wayal lén niou noiun mourid yii baye bi mome machallah yalana lén yalla sam si barké serigne fallu
Kou beug Baye lalale j’aime ❤
Merci 🙏
Nioune yéne rék lagniou beug ❤
@@akhloubrickyoutube❤❤❤
❤❤❤❤❤
@@akhloubrickyoutube
Bon Gamou à tous Touba Medina Baye Tivaoune et partout au Sénégal et au monde 🙏⚡️
Machalah yalla yokou diamou doli soutoura si barké Mame Ibrahim fall borom koosy wayou baye ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Walakhi khamouniou louniou souniou wadji diaral borom kaolack mo bakh souniou wadji beug ko rekk diam nguaye doundou foh tolou moniou khamal yone wi Diém thi yallah baye moye sohniou baye sheikh al Islam yalna yallah yokou lerram té Tass niou si barkém sons bi nice neu trop machalah❤❤
vraiment ls paroles st riches ....surtous boul yame si taram bi ,kalam bi ak niolay bi ohh
Mashallah long vie à vous inchallah qu'Allah vous protège ❤🇲🇷🇸🇳🇲🇷🇸🇳
Dak rap dak weuy geune lén xam yalla dakk lén lép geune lén dégeu yalla 👆🏾Grâce à maolahna cheikh Ibrahima 👈🏿dieuredieufé baye niass🙏 ❤🙏❤🙏
Vous êtes encore rempli du joie dans les cœurs ❤
Man murid la waye dama beugue baye loll ❤️ 🌹😭 billahi
Diereudieufeee maoulana cheikhal Ibrahim borom Minka ilayka❤❤❤❤
Oh lala machallah chaque année damay yakamti leur son pour le Gamou suis Chrétienne mais j'aime tellement Baye Niass c'est plus fort que moi en plus Akhlou Brick vous assurez comme d'hab bne continuation mes bro et paix sur vous bn Gamou à tous❤🥰🥰🥰
Ya niakk ignann rekk jamou siyoww
Machallah rafetna ❤yalla n'a diamou yageu yarabi 🤲
Toujours au top 🔥🎉moment bou maye Sétane vidéo bii j’ai une cœur remplit de bonheur ❤😭 yalla na léne yalla faye séne khole ❤️🎊🙏
Baye la solution❤❤❤❤❤❤❤❤ dieureudief ya
keur baye😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤
Alhamdoulila si le fait ma tokk tay du guis Sama bobou si klib bii diereudiefè baye kou ko si wakh yalla gua fèkè dewen❤
Boromm Xelll rekkk moyy Déegueu liiguéen diii djioudiou du début jusqu'à la fin
Ndeyssane walahi😅souguéenko khaamoon daww raadjiou djiie thie Baye al hamdoulilah Dieureudieufé baye
Wadjii barké chiekhou tidiane 😂 brm khél gni Ani enrif gni
Kou beugue baye niass rék lalale j'aime ❤
Alhamdoulilah diam si gneup si barké mawlana baye Niass
Billahi Baye takh na ma diap len ba faw machallah fiert d'etre Barhamienne
😢 oh c beau😊😊. Je suis Mourirde mais quand je vois ceci je ne peux que m'émerveiller. Le soufisme c'est ma vérité
Aniii talibés Baye niass yii🥰 ooohhh holl sédd tina❤❤ grand merci à ces fidèles disciples de Maolana Cheikhal Islam
Machalah 🥰 mawlana cheikh Ibrahima niass 🙏 rek sii xol yii amoul lénéneu manii rakhadjiou djioteu na dh🎉🎉🎉🎉😂❤😂😂sunu rakhadjiou bii 😂🎉❤
Wallahi Baye Niass mo diara rakadiou❤
Félicitations les gars jërëjeuf ❤
Baye la solution Rék laye tope je suis fière d’être talibé❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✅
Je vous souhaite une longue vie à toutes les talibe❤cheikhs tidiane❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Baye niass diarna louné walahi merci beaucoup encore une fois wa akhlou brick fnoune baye niass rek lagnuye topu alhamdoulilah ❤❤❤❤❤❤
Mâcha allah longue vie à akhlou brick ,ils ont encore frappé fort ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤ vraiment je suis très très très content de vous chaque année damlay ni khar ak pasience walakhi yaina takh ma xame kouy baye barhama niass top ko nak nakh dama beugue yalla ak kouma khamal yalla bima toper baye barhama niass la xame sama bop ba paré xame yalla Di santeu maolana cheikh Ibrahima Niass ❤❤ dieurdieufti Baye barhama Niass
Baye Niass la solution
Baye Niass l'international
Niass Coumba Abdallah
Baye Niass dans nos ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
RAKADIOU ciii Baye Niass ❤❤❤
Sma kaw lall la nelawé fi la yéwo ci rakadiou bi ci Baye❤ no daay deff effet mbegté ❤
Bilay niou ngi lene di niaanal yalla bou bakh khawma kane deh mais mane rouslo wolenma yalna yalla yokou lene ❤❤❤
Encore vous avez frappé ❤❤❤
Billahi damalén meussa beugue avant même de savoir que vous étiez des Barhamiens❤️✨ chaque année nianguén ni sédalé sama khôl Yallah nalén ko Ya Rabbee fay🤲✨❤️🥰
Machallah
Yalna yalla féy lén ci barké Baye Niasse
Walahi beugual nguén sougnou xol yi.
Baye rék , késsé , Dong moy deug
Dieureudieufe baye niasss dieureudieufe baye niasss ♥️♥️♥️🎉🎉🎉🎉
Alkhamdoulilha Dieureudieufé Baye Barkhama Niass ❤❤❤❤❤machalla rakadiou Ba kaolack inchalha 📿🤲🤝❤️❤️❤️❤️❤️
Dieureudieuféééé Baye Niass. Mashallah❤️👌 Qu'Allah vous protège
Li nieup done khar ils ne déçoivent jamais 🔥🔥😭 #Rakadiousibaye❤ Dieureudieufééé Baye Niass
Wallahi dama setan clip ma sama beugne yii😁😁ba clip bi diéx ndax contentement dieureuffe Baye Niass, dieuradieufati akhlou brick
Dyazaaaaaaaaaaaaaa😂 🔥🔥🔥🔥🔥 quel couplet !!! Do nitt! Barke mame ibra fall wayou Baye ! Ra
Machallah ils ne déçoivent jamais 🎉❤❤❤
Machalla
Vous êtes forts machalah Que Dieu vous protège sii Barké Baye Niasse 🙏 yénn rk lay topou ✊
Akhlou brik toujours au top ❤️👑👑
Macha Allah
Merci infiniment @Akhloubrick . Rombeu naniou sakh rakadiou si baye wayé danio diekh takk si mawlana cheikh Ibrahim.
Guissouniou loudoul cheikh Ibrahim
Doundouniou loudoul cheikh Ibrahim
Alhamdoulilah limouniou hamal mo nekhal souniou doundou motakh amouniou sago si dieum dji..
Ila medina baye inchalla
Mbëctè rk thie tourr Baye ❤🎉❤❤❤❤❤❤
Marsha-Allah
Baye, then, now & forever 🌹❤️💯🇬🇲🇶🇦
AŔRA TU AS UNE VOIX EN OR MASHALLAH. DEZA LE FLOW DE TON RAP EST SUPERBE❤❤❤❤ J'AI ÉCOUTÉ CE SON PLUS DE 100 FOIS. FORCE A VOUS AKHLOU BRICK . RAKADIOU NA CHI SON BI C'EST VOTRE CHEG D'OEUVRE ET DIEU SAIT KE TOUT VOS AUTRES SON SONT TOP. BIG UP GUYS KEEP UP THE GOOD WORK. MUCH LOVE❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis Moride sadikh mais dama bègue baye niass billaye walaye ❤🎉
Barké Ahmadou Bamba son bi dinama doflo,chak jour plus de 5 fois,on t’aime Baye❤🎉
Mawloud Moubarak a touts les HUMAH ISLAMIQUE 🤲🙏🙏🤍🤍🤍💙💙
Baye Niass La Solution 🤍
Baye Niass ❤️ notre solution notre protecteur Baye niasse dans nos cœurs médina dans notre région béni Kaolack
Macha Allah
Yalna yallah fay lén ya rabi
Si kow si kenem Akhlou brick ❤
Ces parole me touche de temps plus mon âme kayy lenn niou rakadiou thi baye moyy yoor tariha tidiane
Dieureudieuffé baye Niass, l'international
Le bonheur 🥹 d’être Talibé Mawlana cheikh Ibrahima niasss walahi c’est une chose barhamienne📿 ou rien 🫶🎉🥳🥳
A chaque chanson à Baye vous nous donné plus énergie merci Akhlou dieureudieufé Mbaye niass❤
Comme d’habitude❤ mashallah, Baye rek laniouy top foumoumioi dieumè bakh na. Al hamdoulilah🙏
Diereudieufeteii BAYE ❤
Niveau son bii kaweina..yallana yalla defar sunu mbiir barkeii BAYE ya rabbii
YALLAH naniou YALLAH fayale Cheikhal khalifa amine
Kou rakadiou rek lalale j’aime ❤❤❤❤❤❤
Vous avez de nouveaux marquez machallah yalla baye faye léne❤❤
Allhamdoulilah nio Rakadiou kay, Thanks 🙏🏾 Barhama🙏🏾 ❤❤nèkhatina gars yi diam ci yèn❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️👌👌👌
Walahi beug Baye Niass mo nekh kou beug Barhama lalal j'aime ❤
Toujours au taquet ❤️ vous ne décevez jamais les gars
Dieureudieufé cheikh Al islam baye nisss kéneu dou yaw ❤
Fier d'être talibé Baye Niass ❤et fier de vous ❤
Baye rek laye topo ak sonko si barke Gamou Baye niass sonko yalla na guene legui❤
Ila Medina Baye🕌🕌🕌 yonou jame in challah
Tanaiffou yalla bi yalla tanell goor yalla y’a geune❤❤ wadji mo Dondou wadji❤ wadji mo khamer wadjii❤❤❤ Rakadjou lainne 😂
Machalah khol Sedna yalnagniou yalla yombou si diam ❤❤
Merci pour nous accompagner a chaque gamou yalla n'a lén baye Niass fay
Rakkaadiou ci Baye🥰 abadane ilal eubeudd♥️💫
Baye Niass yalla nagnu koo yalla fayal ❤
Mashallah nekhena👍🏿❤ vive le Sénégal.