Yoyo papana lady diama nioune mouride yi contane nagn néxx na trop machallah yé sounou domou badiane yi tidiane yi gamou diam ak khéweul mes aboubacky samb mi grawe na dé yalla na thiate dhé way machallah ❤
Ce qui me touche sur l’image est le fait de voir dans le même clip les Bayfall porte l’IMAGE DE SEYDI ABOUBAKR🥰🥰♥️ Lepp benla 🙏🏽ngalla waaay buniou nanguu kenn dinu khadialei.Mec t’as frappé fort vraiment 🤞🏽🤞🏽Chapeau
Oh gnoune Mourid yi sougnou ligueye bignou ko défone pour mou bagna guéné son tothie na way li mome lokho Layéne sétou thi niognou diaye Tidiane yi 😂😂 mais son bi nékhna mangui guiss sougnou wa Keur waye Médina 🥳🥳🥳🥳❤️🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Je t’encourage vivement à te recentrer sur ta musique conférique. Je comprends que les séries télévisées peuvent être captivantes, mais ta véritable force et ton message résident dans ta musique. C’est ce qui inspire et unit notre confrérie. Il serait dommage de laisser cet art précieux s’éloigner au profit d’autres distractions. La musique conférique est une voix importante, et tu es l’un de ses plus grands représentants.
@@aboubakrysambofficiel6882 Macha Allah , fière d'être talibé cheikh, je t'admire vraiment, bravo . Mais j'aimerais bien qu'il ait moins de musique , car ta voix est plus mélodique et commune avec la première partie, khôl sedd na
Aay waye anii gniou waxkone dougniou ame son mourite yi amène son dh 😂😂non aboubacry samb franchement tu est le meilleur gniougne si nabien yaye sounou wally b seck tu est le meilleur ❤❤❤❤❤
Ce monsieur khaw ma foum nekone mais nourounama kou am talent multidimensionnel, e intelligent e puis il est charismatique. Yalla nala yalla diapalé nga feul bou gaw !! Du courage !!
Mouride moy tidiane ❤bamba di maodo ❤Babacar di Fallou gnoy borom Diamono etc etc ❤mbeugeel gno ko mérito❤machallah des coeurs pour domou Badiene domou Nidiaye yi way nagnou done Ben com gni way😍🥰🥰
Machallah aboubacry samb linga wayy souniou gore gui nekh na trop wlh kéne d'où aboubacry wa inekana fil khadri l'homme au sourire légendaire yalla naniou ko yalla fayal ❤❤❤🥰🥰🥰🙏🙏🙏dama contane wlh ❤❤❤❤❤❤❤
Kou fi beug serigne babacar sy lale❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
Manguini ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤️❤️🙏🙏
Je suis mouride mais Aboubakary je l'aime trop
Mouride =Tidjane ❤
Bly lepp benla
Wakhatiko dh prck nioune nieupp niobokk kiniou gueum moy psl donc louniaw khadiouffii yalla na diam yagu♥️
@@bintoumboup5186 yalnaniou yallah mousoul si seytané
Weunii wollahi vous avez raison nous sommes les mêmes
😮😮@@dianymarega8335
La richesse c d'avoir serigne babacar sy❤
Walahi ❤
Billahi ❤❤❤
Ohhh sama xol bi sedna way ❤❤😂😂😂
@@aminatandiaye2912 bilay manit sama bos dafa séd
❤❤❤❤❤❤
Mane mouride la ms aboubakry Damalay beugue ba kagn yallah nala mame babacar ték lokho si barké s saliou
Amine waye chérie❤❤❤
Awma si mom sago worna cheikhoul khadim j’ai failli tomber si escalier juste pour sétane clips bame
Bilay yaw kon niou yam mouride la ms dama ko beug@@yacinegassama1826
Allahouma amin ❤
Amine 🤲 yarabbi ♥️♥️♥️😍😍😍♥️♥️♥️💯💯💯💯♥️♥️♥️♥️
Bamba Moy maodo, Babacar moy fallou Abdou Aziz Moy saliou Babacar mansour Moy mountakha rék Sénégal nékh❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ LOU LERE
Machalla ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Billah wallah wakh nga deugg pur machalla longue vie à toi amiine ❤❤❤❤
Je suis chrétienne et j'ecoute souvent les chansons musulmanes est ce que douma dem Tivaouane sakh
Man mala invité nieweul ❤❤❤
Lay niou dém❤
Nieuweul ma dalale la
Gnewal ma dalal la ❤
Chi doumako yak souma nekoul garde dimanche mome dina nieuw
Machallah je suis mouride j 'estime trop Aboubakry samb ❤ votre chanson demeure impeccable 🎉🎉 machallah
Kou beugue seydouna Mouhamed saw Lalale ma cœur bi si barké cheikhal khalifa ❤
Sama Tourondo ❤
@@MLDPROsama toma mala soppu❤❤
@@MassJoob-n7z wallahi Toma mala gueuna Sof 🥺❤️❤️❤️❤️
❤️❤️🙏🙏
❤❤❤ kén dou khalifa
Kou contane né mane wayy 😅💯
Loy contant 😢
@@abdoulatifdiop5640 sougnou khol diekh tak si mbay rk ❤️💯
Mangi rèè rek 😂😂😂😂😂
Pm
MaachaAllah, Yalla naniou Gamou ci diaam ak Salam ak founiouko meuna défé reik Yalla naniouko borom bi nangoul ci barkè Seydina Mouhamed PSL❤️🤲🏽❤
Ohh seringe Babacar sy mo nékha woy wy kou d'accord boseul j'aime
Yoyo papana lady diama nioune mouride yi contane nagn néxx na trop machallah yé sounou domou badiane yi tidiane yi gamou diam ak khéweul mes aboubacky samb mi grawe na dé yalla na thiate dhé way machallah ❤
Gninan je suis mouride mais ... wala suis tidiane mais... louy sen blem 😂😂😂lepp ben la
Kou xolam seyde thi serigne babacar sy lalale jm❤❤❤❤😢
Diarama Mame Ass Kén dou Serigne Babacar Sy🤩🤩🤩
Oh mba khôl yangi fekh sama khôl bi mongui déf nékh ❤❤❤
Ce qui me touche sur l’image est le fait de voir dans le même clip les Bayfall porte l’IMAGE DE SEYDI ABOUBAKR🥰🥰♥️ Lepp benla 🙏🏽ngalla waaay buniou nanguu kenn dinu khadialei.Mec t’as frappé fort vraiment 🤞🏽🤞🏽Chapeau
Je suis très fière d'être Talibe serigne babacar sy ❤❤❤❤❤❤
Je suis Mourit ms ki sm bg trop te hawma lan la rk yalla yalla fayla barki s Babacar sy ❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
❤❤❤❤❤❤😂❤😂😂
@@guissarmbodj8357❤❤❤
Amine waye ❤❤❤
Je suis muride Ditali bé serigne saliou mbacké mes aboubakary samb Dama nékhe barki serigne saliou mbacké Dama la beugeu machalla ❤❤❤
Machalla ❤
Ani Mouridou Serigne Babacar yi 🥰😍❤
Magi ni beug Serigne Babacar sy rek❤❤❤
Gnoungi ni
Machalah nioune mouride yi apprécié naniou❤
Da nguen bakh rek ❤️ leppeu benne la 😘
Kone faté wognou machallah mafi guena beug serigne babacar
😂
Khamal sa boop rekk
Pendakafuma dh nak damalay wakh rek
Fier d'être talibé cheikh
Serigne Babacar mansour yalnafi yague té wére
Machallah méré wone nala si série bi wayé xamou ma mou ma laye défe ndakh séydi Aboubacar
Sugnu la amoul wone khawma fougnu dieum❤🥹sama nabien préfèrée bi🥰 Gnune yaw rkk lagnuy topp barker Serigne Babacar s'y yallah nala yallah sameu arr la lakkou la fou yakk agoul yallah barkerl la si barker cheikhal khalifa s'y Rta ❤️ mala beug nak ❤️ yallah nala yallah defal Diam dju sakh AK kheweul dju sawane bawane ❤🥰😍🙏
Kouko done lathié nieuwna dé kéndou maodo❤❤❤
Je suis premier sopey serigne babacar sy
Ñanal’lein Serigne Babacar Sy Mansour mou yague fi lool tei andeu aq wér ❤🙏
Allahouma amine ya rabbi
amine ❤
L' homme au 12 métiers contane nagne si yow machallah 😍😍
Mane moom yalla moo deff ma beug la rk 😭
Oh gnoune Mourid yi sougnou ligueye bignou ko défone pour mou bagna guéné son tothie na way li mome lokho Layéne sétou thi niognou diaye Tidiane yi 😂😂 mais son bi nékhna mangui guiss sougnou wa Keur waye Médina 🥳🥳🥳🥳❤️🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Raygama😂
@@papendiaye505 😂😂😂non li dafa nékh
😂 liguey bi diapoul 🤣
😂😂😂layéne yi niouniou wakh fingéne défone liguéy bi. ❤❤ té baye fall yi nioko todj lii meunoul niak nak Masha alla😂😂 .aft gamou wéxalma ma defaratalako😂😂😂😂😂
@@AwaSOGUE-c5c li bétouma khamone nani Layéne yi niognou diaye mais li dou yombé nonou😂😂😂❤️❤️😂😂😂
Oh machalla Contan na nala teral liga way sama serigne bi ❤❤
Je t’encourage vivement à te recentrer sur ta musique conférique. Je comprends que les séries télévisées peuvent être captivantes, mais ta véritable force et ton message résident dans ta musique. C’est ce qui inspire et unit notre confrérie. Il serait dommage de laisser cet art précieux s’éloigner au profit d’autres distractions. La musique conférique est une voix importante, et tu es l’un de ses plus grands représentants.
MERCI MON GRAND VRAIMEN KONTANE NA TROP YOKAL NIANE YII
@@aboubakrysambofficiel6882 Del wakh Amiin rek
@@aboubakrysambofficiel6882 Macha Allah , fière d'être talibé cheikh, je t'admire vraiment, bravo .
Mais j'aimerais bien qu'il ait moins de musique , car ta voix est plus mélodique et commune avec la première partie, khôl sedd na
Aboubacry Samb ak Talibé Cheikh yi c’est une longue histoire 😂😂😂boulene ko khass nakk
Néxna trop machaallah yallah nala yallah défal diam thi barké Cheikhoul khadim 🙏❤️
Macha Allah ninga sédalé sunu khôl yi yala na yala sédalé nonu sa khôl si barki Serigne Babacar Sy
Amine waye amine amine sy Malick RTA
Aay waye anii gniou waxkone dougniou ame son mourite yi amène son dh 😂😂non aboubacry samb franchement tu est le meilleur gniougne si nabien yaye sounou wally b seck tu est le meilleur ❤❤❤❤❤
Lii none yi beugone dalougnou 😂😂😂
Mane dé rousna dakh rénaléne 😀😀😀
@@FatouDiaw-z5b khana kay deettt😂😂😂😂
Rousna sax 😂😂😂😂
@@FatouDiaw-z5b digua rouss dh aboubacry dougniou setanne James 😂😂😂😂
Ay wayé li none yii beugone dallou gnou 🎉🎉 kou contane rékk lal ko j'aime ❤❤❤❤
Fii amo léne fi aye none mouride = tidjane yéppou béne lagne yéne sof ngéne si aye mouride Ak tidjane
@@SaliouNiang-w5l ki bayi ko ffou dafa khamoul rk mtkh
@@SaliouNiang-w5lbaleko c k dafa ame niounéwoone ken dounou wayal khamna lolou la rk mais tawfekh yaw kou bien nga😍
@@AstouKaneMbaye-m7k merci beaucoup yaw Kaye ya bakh rk mais je le comprends
@@SaliouNiang-w5lMalheureusement amnagnou ay none ms dou yenen tarikha yi
Suis fiére d'être talibé Serigne Babacar s'y 🥰 ❤❤❤❤❤
Ooooohhh my goodness this is beautiful! Tivaouane, notre fierté !
Bobou son bou soft❤❤❤Machallah
Machallah yalna yalla wereul bate bi si barké serigne Babacar Sy 🙏🏻🤲🏾🤲🏾❤️❤️❤️❤️
Machalh ken dou sunu goor gui seydi aboubacar sy❤️❤️🙏🏼
Machalla sama xol bi bilahi dafa sèdd thi baye fall yi ak tidiann yi diam thi yènn
Fière d'être talibé cheikh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis une maman mouride depuis richard toll mais toujours je prie pour que ton chemin soit comme cette lumiére que tu chantes
Serigne Babacar sy si khol lénéne khadiousi la solution 💕💕
Merci d'avoir fait cette belle chanson a notre Serigne Babacar sy merci 1000 fois
Ay Aladji Lii nékhna dh😢
Machallah kenne d’où Serigne bababcar sy yana yalla yokou Lerrame ❤🎉
Machallah je suis mouride mais je t’aime aboubakry samb
Ce monsieur khaw ma foum nekone mais nourounama kou am talent multidimensionnel, e intelligent e puis il est charismatique. Yalla nala yalla diapalé nga feul bou gaw !! Du courage !!
Ça fait longtemps qu'il chante c'est juste qu'il n'était pas très connu
Gni done wakh talibe cheikh yi douniou am koulene woyal dakh migui si lady diam di tak di fasse 😢😢khana rouss ngene 😂khol sed na waye woyal woyal ❤
J’ai pas puis tenir mes larmes j’aime khalifa ba sounioukoye waye sama ❤bi daye fess ❤
Je suis content Li nga way sama tourondo Serigne Babacar sy beugue mala guis téral la rek Moy sama yiité ❤❤
Kham naniou ni daniou bayi 🎉🎉 souniou talibé cheikh bou makk bi khôl ❤ Sed mbaye ya niou doye❤❤❤
Aladji way chérie Diama a sauvé l'honneur tidiane yi contant nègn kon doniou lei abalati souniou Mouhamed Niang❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂
J’adore srtt le message qu’il lance à travers le clip Mouride =tidiane Machalla yalla na yalla samm la
Ouais surtout j'ai bcp aimé ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤machalah Aboubacry dieuredieuf linga bakati cheikh Al khalifa Ababacar sy nexna yallah na yallah wéreul bate bi ❤❤❤❤❤
Gathiee dou len rayy 😂😂am guen son mâcha allah nekhna ❤❤❤❤Yalla na Yalla weral batt bi barkep cheikh khalifa Tidiane ❤
Machallah n'a yalla goudal sa fane si barké Seydina Mouhamed psl 🙏🙏❤
Machallah loumala méré wone ci Lady diama bi rek contane nako. Sama❤bégui sédeu gouy ba samay rangogne di tourou wallah
Pour la 1ere fois Engagé na pas danse Watial ci soufff 😂🎊
Machallah notre El Haj 🎊
Ah sama kharite bi, mashallah que du bonheur 🙏🏽🙏🏽🙏🏽 Walahi keneu dou Serigne Babacar Sy 🙏🏽😊😊
Machallah walay limasi gueneu nèhhh moy baye fall si clip di wanèni lep bénn leu
Mouride moy tidiane ❤bamba di maodo ❤Babacar di Fallou gnoy borom Diamono etc etc ❤mbeugeel gno ko mérito❤machallah des coeurs pour domou Badiene domou Nidiaye yi way nagnou done Ben com gni way😍🥰🥰
Li nak moy wayou yenei Manchallah ♥️😭
Machallah aboubacry samb linga wayy souniou gore gui nekh na trop wlh kéne d'où aboubacry wa inekana fil khadri l'homme au sourire légendaire yalla naniou ko yalla fayal ❤❤❤🥰🥰🥰🙏🙏🙏dama contane wlh ❤❤❤❤❤❤❤
Mane talibé BAMBA bi content n'a si Aboubacry Samb li rek lane done khare si yaw machallah yallana batte bi gana wére si balke SEYNINA MOUHAMED PSL
Suzanne nako daal tivaone amna lépou done Tidiane rék doyna santé yalla
Kou beug sérigne babacar sy réck lalal j'aime ❤
2:38
Machalla 🥰🥰🥰🥰nekh na torop ❤❤❤
Sénégal ma fi gueuneu beug serigne Babacar ❤🤩🥹
T ma nek fii❤❤❤
Machallah 💖🎉🎉🎉🥳🥳🥳🥰💓💓💖💝Ani gno done wakh nane dougnou âme way
Ndaysane nékhna manchlla kendou s Babacar sy malick ❤❤❤❤
Domou Mame Ass bi ndanane deug la cheri Lady Diama ❤❤😂
Ana gniko done khar comme mane 🎉❤blh khamone n'a ni douma rousslo ❤
Ouff enfin lady liberena Aboubakry Machallah ❤❤❤
Machallah ❤️ Mame Babacar borom bonnet carré bi 😘 Bakary AK dramane nieup gnoko beugue ❤ Sy yalna yalla yokk leram ci barké xassida yi ❤️
Machallah chak année rk gua defff lila warrr nekhe na trop contane na trop yallah gua goudou fane 🙏🙏🙏❤️❤️❤️
Walahi rien à dire, t'es encore à la hauteur.
Nioun dièkh nagn takkeu si yaw nguir Cheikhal khalifa RTA ❤️ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah talibé cheikh ba faw ❤️❤️🎊Amal diam rek iow ❤❤❤😊
JE SUIS NIASSENE MAIS J ADORE A VRAI DURE VU SON TALENT ABOUBACRY NE DECOIT JAMAIS
Chéri diamatoulaye wayyy 😂❤🎉
Alhamdou lilah biniou amé Serigne Babacar sy ❤
❤❤❤❤❤ walay mame Babacar Macha allah
Machalla tidjiane mbouriteu nieup sibir machalla serigne Babacar sy moy serigne touba ❤️🥹
Alhamdoulilah am nane weuy😂😂Jeureujeuf Samb❤️❤️❤️❤️
Mâchala ani ❤❤❤❤❤❤❤talibé cheikh yi khamone n’a ni yanguisi ligueye bi yalna bat bi gueuna wer
Ohh li nekh na si xol machallah ❤
Fière d’être talibe cheikh kene dou mome Sy Malick Serigne Babacar SY ❤❤❤
Bly li mérité na 1million de vue avant 24/24 bly li nékh na dhé❤❤❤kou daccord rk lalale j’aime
Nagn ko partager rk
@@astougueye9335moy birmi nak
@@astougueye9335 kassé nak
Mashallah nono la boul dégue lo wakho nite gni nékal si lou bakh rk par ce que sénégalais gni lo déf niou khaw khamo yo personnes AK personnages
Qui comme moi est impatiente 😝 🎉
Aboubacar yalla nala yallah defal diam man de contan na si yaw yallah nala yallah samme ak kouni amine ❤❤
Chaque année c'est comme ça lui et Jahman Akhmada , j'attend toujours leur son mention spéciale merci à-vous❤❤😂🙏👌
MERCII VRAIMEN
KONTANE NA DH
Mashallah aboubakry samb yalna yalla weral batte bi guoudale sa fane ak weer li nekhna rafetna way❤❤❤❤
Dieureudieuf Serigne Babacar Sy, Yallah nagnuu koo Yallah fayaaal, Barki Serigne Babacar Sy
Djeureudjeuf aladji liii néxna ❤❤❤❤❤❤serigne babacar rek😍😍😍yalnagnou yalla tass si barkém té yokkoukay leer barkép Yonente bi(psl)
Aladji yeuwna kone djiot gua message bi Machallah sa fans yi yaw lagne done khar❤