@StreeterTea deug leu dé mé défw danguay nék diék si keur gui di déff lou bahh diko wah niou diapé la doff walla kou bgoul dara dila déff yefou sohorr ak dila wah you niaww ba dagn lay moudié wall sohorr
C'est ça une chanson qui a vraiment du sens tout ce qu'il a dit est tellement vrai goro you bonne yi ndieuké you sokhor yi ak goor you faible yi gnak fayda ak foula
Mane sama goro gnioma guéne keur gui ak sama ndiéké yi té kosi lathie doula wakh loumako def bilay sama yaye ganiou mois pasé niewou niou sakh té wa kogne ba niépa niew ma bayi lén a vie
: birahim je suis ta plus grande grande grande grande grande grande grande fan le jour qu'on m'avait dit que tu as arrêté ta carrière j'ai même pleuré tellement ça m'a fait mal au cœur avec une voix magnifique Birahim
UN TRES GRAND ARTISTE AVEC SES RARES MELODIES BIRAHIM AMOUL MOROM SENEGAL ❤
Ya niak Kiniane Frangin🥰
Wakh sa bakhou morom, wagni woul dara sa Mbakh
MachAllah Guissé❤
Ken dou iow guissé maabo ya niaak kignan
Nekhna de ❤❤
Mome dafa bakhe a chaque fois pape birahim guènè clip daaye apprécié woutè ak yènète artistes you sokhor yoyoy
Amna gooro yu bari problème mais mane mom sante na yalla bamu mayé gooro bu bakh beug ma walahi
bilahi man tam sama gooro ak bakh machallah ❤❤
@AmyDiaw-j8n manchalla cherie yalla na diam yague inchahalla
Kone bakh na machalla
Diapp ko d🎉
Mane sama goro yalla rek lakoy bayie mon fayalmako
Des coeurs pour notre Prophète Mohammed psl ❤
Billay Sama yaye da sonou si keur gui dakh Sama mame . Yalla nama yalla may téranga bama guéné ko si keur
Amine Ndèyssane
Li Moy way ko Dakor rk may❤
Birahim tu as tapé trés fort wallah anzime légui xallé yii seuyi keur goro bango lagn ko toudé ndah métti😭😭
Amneu niou bakh amneu diek you bone aussi seuyi tass keurgui afair yi vice versa la rk
@StreeterTea deug leu dé mé défw danguay nék diék si keur gui di déff lou bahh diko wah niou diapé la doff walla kou bgoul dara dila déff yefou sohorr ak dila wah you niaww ba dagn lay moudié wall sohorr
@@StreeterTeabilay yaw
C'est ça une chanson qui a vraiment du sens tout ce qu'il a dit est tellement vrai goro you bonne yi ndieuké you sokhor yi ak goor you faible yi gnak fayda ak foula
Moins de 24 hr ngen dépasser 100 000 vu. Birahim nak Sénégal niola beug, danga meun way caar ❤😂❤
@@NdiayeSerignefallu danga lathié sa yaye xana ? 😅😅😅👍
@@NdiayeSerignefallu ah c'est enfin toi qui donne des leçons de moral ?
Kou sa goro bakh comme mane lalal j'aime ❤
Est-ce que dinga bari j'aime ?
Man DH bakhna loll wayé ay domam lougne KO wakh rk lay geum
@@BallyNdiaye-e1y pareil pour moi
Tu ne peux pas nous abandonner comme ça , nous on a besoin de toi et de ta voix angélique , ont t'aime ,🙁🙁😔😔😢💔❤️ Birahim
Vraiment Sénégal khamoul artiste. C'est le meilleur artiste du pays dakh léne dakh léne solou eupe lène fou leu ak fite
Il a fait fort avec ces paroles ❤
bly❤
Birahim Ndiaye mane nga wayal waye bi
Walahi j’ai vécu ça et c’est tellement vrai j’ai finalement quitté la maison conjugale 😢mais lici ndekké yi mo raw lici goro yi 😢
Walaxi louler nga waxxx
Elles sont mauvaises walahi
Merci pape Birahim pour le message .
Toujours dans l’actualité ❤respect frère birahim
Manchallahhh Birahim, ce Morceau est très instructif comme toujours d’ailleurs ♥️
waaaaaw !!! j' ai hurlé mais comment ça, c'est incroyable ça 😟😟😟😟 vraiment ya neune séne ndaye ak séne baye dou sakh béne
Diek diou bone djii contane naniou😂😂😂😂
Machalla Meilleure conseil pour les goro you sof
Machalla amna solo Pape Birahim
Pape birahim loumou woy mu nekh manchalla laf thiate
Bonne continuation NDIAYE SIPION NDÉNÉ NDIAYE 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
DOKHALAL🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Je suis tellement contente de te revoir avec c'est Belle mélodie le Grand chanteur dagua meune wayy saye texte ame solo vraiment j'adore
Birahim t'écoutérais même dans tous les cas qui m'arrivera bilaye ya meune li le Senegal 🇸🇳 namone waye bou am ndiarigne
Sama goro bou goor yalna ko yalla kharè aldiana kouma beuguone
Machalla chanson day yété wala mou dialgalé bravo et bonne continuation
❤❤❤❤❤
Mane dé tek beute bi momasi geuna diakhale bilahi 😢😢😢😢
Kom guiss gua lolou
Nawlé😢
Lolu rek gah guiss blie dama mugeh nebi
Mane sama goro gnioma guéne keur gui ak sama ndiéké yi té kosi lathie doula wakh loumako def bilay sama yaye ganiou mois pasé niewou niou sakh té wa kogne ba niépa niew ma bayi lén a vie
Wa loutakh lou nékh di gawa djékh 😂😢
Bonne continuation frère ❤❤❤
Y’a meune Gaye sipion 💪💪💪💪✅✅✅
Sama ex goro bi yalna guise mi deume me rék
😂😂😂
Waweee machallah wayy Wii rafette naaa, t'ai Moy deugueu
hoooooo fréro je n ai pas les mots mais macha Allah yalna yallah same amine sama wadji
Birahim Bilae khamo ligua waye sakh 😢😢
Salam ohh l’homme aux mélodies🎉 sensées merci pape ❤❤❤
Ki dama kay beugg ba kagne 🥰💫
Ay way pape birakhim dama koy bg ba kagne clip niss lou wér sakh jtm dal ❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah birahim et Fall. Li nekhna trop. ❤❤
Man dh sama goro mome Machalla yallana goude fan ak wèrr❤❤
Yako fa am pape Birahim sa théme amna solo té actualité la❤❤❤
Limiye wax âme na mais mane mome yalla maye nama goro bou bax machallah ❤❤
voilà un travail bien fait je te dit bravo Birahim yaléne dakh wakh yaléle dakh dou sakh béne
Gooro Bou bakh amna sama Gooro aka bakh ms niitte dji no yakkeu sounou digueunté dou wakh ma wakh sa fait 1ans sokhna amy yalna yalla goudeul faname
Thème yii naag la société bi sokhla,amena solo.torop mashahallah
Le plus meilleur des meilleurs artistes Lou khéw si diamono rék lay wooy bilay mina tamit très fortb🎉❤
Mane mom sante na yalla bamu mayé gooro bu bakh té beugué ma
Kom mane❤
: dinagnoula porter plainte pr excès de talent... Birahim dangeu doffe yaw yangui beau 😍 ni waye
Nice na machallah est bonne continuation fréro
mon artiste tout terrain.machalah from medina le thioffe dangeu délou khalé louye secret 🤫 bi
: birahim je suis ta plus grande grande grande grande grande grande grande fan le jour qu'on m'avait dit que tu as arrêté ta carrière j'ai même pleuré tellement ça m'a fait mal au cœur avec une voix magnifique Birahim
Birahim machaallah defa tinga sa manine
Yalla na yalla yague weral bate bi
Sa waye bi dh ay million de vue la wara ame ❤😂
Bilaye danga meune waye machallat teksi dagaye yètti mais fayelande binga dem moma meti art bi daguë sè ame place
Pape birahim la voi d'or❤❤🎉
Ohh Li nekhna dh Machalla❤
Liii vraiment esk amna serieusement
Wow Amazing 😂 Contane na domou baye 👍♥️❤
Très intéressant birahim t'as encore frappé ❤🎉
Thank you pape Birahim way bi am na sens
Bravo pape biraham et Serigne fall sont meilleurs ❤❤❤
Yalla bakhna
Neikh na trop pape birahim
Amna solo mashalah
Ioe rek ladone xar si game🎉🎉 je t'aime beaucoup ❤❤❤
Wa waw
you are soooooo soooooo talented oh my god 😍😍😍😍 nope nala sakh dangeu geune thiofé 😍😘😘❤️
C trés jolie
C'est très cool 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Machallah saye wayy mon âme sens bonne continuation 😂😂😂😂
Nice Nice félicitations
maestro bégué way nous aussi on t'aime big up 🙏🏾♥️🎧🎤🎼🪘💯✍️🏿 nic neu trop li
Birahim your voice worth a gold 🥇 medal your voice is melody 💓❤❤❤
Machallah tonton pape 🎼
dangga yag gnaffé récolter mola dessé ma Sha Allah ☺️❤️❤️❤️❤️❤️ bilaye dangeu meune trop sakh li yeupe thiate le wone tek dina bakh nak
Machalah sama birahim ya waye lou am nak
Vraiment namon nagnou la Brahim ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤
Enfin pape d retour 😊😊
Kouko statut rek gnibi deh😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂
Alhamdou lilahi
Bilahi loulou beurrier si réwwmi
Les paroles et pa trop de bruit machahalla ❤❤❤❤
Machalla grand frère defatiga
Mane déh ndieké bou bonnne té mane roubé la deugeul
Enfin Birahim way na li nitt yi ragalone way😂
Machallah nekhna trop ❤❤❤❤❤
kousa gora bakh kom ma lalal jaime
Do guis kou aime ndakh goro you bon yi nio eup you bax yi😂😂
2 j’aime dh gua ame😂😂😂😂
Nexna machallah ❤wayé kouko statut gnibi sa keur ndeye ak baye 🤣🤣🤣
😂😂😂😂 wouy
@@aissatasow6421 🤣🤣🤣🤣
😂😂😂
Kouko statut dieul yida 😂
😂😂😂😂
Réalité à nos jours
Vérité absolue fils t’as encore assuré comme dab
Bilay pape dinga goud fane
Sénégal mafi geuneu bone goro 😭
merci merci beaucoup mon frère 🎉🎉🎉😢😢
L'international Pape Birahim💥💥💥💥💥Merci Pour la confiance💯
Kouka statu dieul ideu😂😂😂😂ms goro yi la yalla xam dou neuh😂
Très Nice birahim ❤❤
Machalla🥳🥳🥰🥰
Ayoo pape biram❤❤❤❤❤❤❤
Li nehna dh 😂❤
Machalla🎉
Prince are buleen neexe music messages Rik lay doon ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mâcha allah lii néxna loll waay
lidé am na solo😊
Ay pape way rk ngay def loutah ngay rare