Félicitations à Momo Dieng la fierté de Bargny voire le Sénégal Vous méritez tous les honneurs de par vos qualités exceptionnelles de même votre discipline et modestie ayant la culture de la hiérarchie Vos sons musicaux pleins d'enseignement Bonne continuation
Bal ba tak n’a dieng salla l homme du 28 décembre Li nexna way sampou rek yalna niou yalla diapalè si barkep serigne babacar sy malick Li nexna way🎉🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳😊🤭🤭🫢🫢🫢
Le meilleur de tous les temps machallah ❤️ yalla nala yalla moussal si thiate akh lamigne 🙏 yalla na yalla motalii leep mou nekk li geune si yaw❤❤❤❤tous derrière Momo ndam rekk💪in sha allah 🙏
Le 28 décembre Sampou nationale Dakar Arena Diamniadio MOMO DIENG l'artiste hors pair le Messi de la musique Sénégalais l'homme a la voix mélodieuse 🎉🎉🎉🎉
Thieey doome baye aka meunaa waaye 🤩🥰♥️ où sont les Dieguene avec grand D .Ndeysane sama xeele ci Aziz laa neek thieey aduna yallanako yalla yeureum té xareko aldiana 🤲 bilahi sa mort me fait pleurer com si j'étais parent avec lui 😭💔🙏
Ndeysane aziz dabala ak Wally yalnalene yalla yeuyeume te kharelene aldjana firdawsi amine 😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Amin inch'Allah
Amine yarabi😭😭
Amine
Amine ❤
Ayway Amine Ndeysssane bilay ki daf lii yakh na khol yii
Hooo Aziz dabala rek mofi manquer 😢😢😢rip momo ndame rek🙏👌❤️❤️❤️❤️❤️
Abdoul Aziz ba alias Aziz dabala yalna ko yalla yeureum thi Barke seydina Mohamed 🤲
Machalla le meilleur de ça génération 🎉wayé clip bi Aziz dabala mossi manqué bilaye 😔😭 Paix à son âme 🙏
Ndeysane j'ai pensé à lui 😢
Bly wly rip aziz daballa😢
Khalate nako dei bilahi ❤❤
Amine 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿 🤲🏿
Tu as raison deysanne Paix a son âme
Ana gni geum sèen boppu sampou rk inchallah on vas réussi 🌹🇸🇳❤
kou diougué si ndakhté rek lalal j’aime 😂🎉❤
😂😂😂dara dougnou raw😂
couple bril&Dieyna tamit guènè negn
Mane
Mane 😂
Fala diougué ni😂😂
Juste maane mi waa noko xaamee ni ziarna team tope cas 💪😘😘😍😍🥰♥️
Kou diougué thi dakhté rék❤
Man
Mane 🎉😂
Mangui ni😂
Mane
Yalla nala may réussite total
Une pensée forte a Azize dabala danseur de Momo dieng😭♥️
Bly yaw oh Massa way
Blh MoMo daffa meune wayy 🎉🎉sampou rek
Dafa Diang music nak😂
Wawaw sampou Lou nex 😂Momo yaniouko diaral deh barki serigne saliou 🎉
Xel demna ci Aziz Dabala ndeysane Yalna ko yalla yereum amine
Ndekete macky mo diakhassé wone rew 😂 legui fans wally fans momo fan momo
nek fans titi di bégué vivi
Tous les commentaires ❤❤❤
Lol 😅
Yaw mi lo bok ak maky melni yéna yem d😂😂
@@ousmaneba9543 li Fatime wakh nekhoul bagne d😂😂👍
Sampou lène si sama commentaire bi na kou nek focus si say projet le soleil brille pour tout le monde
Bly ki dama kay beug ba kagne 🫶🫶🫶💯😘le meilleur de sa génération on t'aime fort ❤️❤️❤️
Malako geune beugeu fouff Sama domou baye bi dou moromou Khalé yi ❤😊
*Ndakh lena woy🌟 guen lena yarou 😊eup len thiass🎉 quel charisme ce monsieur 🤴❤*
Sama khél bi yeup démna si Aziz dabala yalla nako yalla yeureum 😢😢😭😭
amine
Wallahi amine
Bilahi damakoy khalate rek, guiss sa commentaire, nabou leye warnagnou wakh ci mbiram
@ billahi même mane mi souma dégué niouy wakh nane dagno bayi nabou leye sama xol bi dafay diékh
Kou dé ya niak 😭😭
Amine
Ndeysane Aziz dabala démna yalnako yalle yeurme té diegalko 😢
Ki dama koy bgu ba kagne❤❤ yalla na yalla weral bate bi rek 🙏🏼🥰❤️
Il a toujours été le meilleur ndeysane ❤tu as encore frappé fort Dad 🥰🧨🎊🎉👋
Félicitations à Momo Dieng la fierté de Bargny voire le Sénégal Vous méritez tous les honneurs de par vos qualités exceptionnelles de même votre discipline et modestie ayant la culture de la hiérarchie Vos sons musicaux pleins d'enseignement Bonne continuation
Momo dieng legui rayma ben yonn 😢 bilay dieng sala ya meun ❤ li nexna way 🎉
Aziz dabala yalnako yalla yeureum guiss nagn fi manquement wam 😢 mais nice clips bi machallah ♥️
Bal ba tak n’a dieng salla l homme du 28 décembre Li nexna way sampou rek yalna niou yalla diapalè si barkep serigne babacar sy malick Li nexna way🎉🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳😊🤭🤭🫢🫢🫢
Sunu Momo national 😍😍😍✌🏿✌🏿 bonne continuation
Le meilleur chanteur au senegal de tous les generation
Bou nieuwéé rékk nga deugeu aye waye pierre mala ko wakh momo dieng rékk le Rio de mbalakh💯👑
J'aime vraiment beaucoup sa simplicité ainsi que son élégance 🎉❤. Momo rkkk ❤
Inchallah dam reck 🙏🇸🇳 comme pour t'on frère Wally 😊😊tu chantes très très bien ❤❤
Momo Dieng man damako begue rk teh Yalla rk tah depuis le début quelle voie 😢😢❤❤❤❤❤
❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉 respectons les cinq prières quotidiennes et ayons une confiance entière en Allah car il n'y a de force et de puissance qu'en Allah ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Inchallah ❤❤❤
Insha allah merci pr le rapl 🙏🏿🙏🏿
Un titre plein d'enseignements.on peut réussir en restant au Sénégal
Wolou yalla😢
L'homme du 28 décembre Dakar Aréna inchallah béss la si bess yi sampou rek le meilleur de sa génération ❤️🥰
Momo sa voix bi lanela ...oh trop belle la voix MachaAllah ❤❤
Yalla na yalla motali lép inshalah kou d'accord ni Aréna dina fésse rk lalale j'aime ❤❤
Le meilleur de sa génération ❤
Ndeysane oh clip bi Aziz warone nafé né ❤ repose en paix frr
Ahhh khar na clip bi mba sonou way 😅 machallah nagnou sampou rek ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Momo mon favori parmi les jeunes chanteurs ❤❤❤
Ohhh filing azia dabala mofi manqué 😢repose en paix 😭🙏
Première commentaire je mérite plus 😂
momo le 28 Yalla na am réussite way dieng salla 💪💪👍🏼
Notre fierté a encore frappé fort 🎉
Kou diougue si deyna baldé et son mari tékh si ndakhté lô après niéw Momo Ding rek lalal j'aime 🎉❤😂
ya Manue weur😂
Bilay yaw dfa lérr Aaa Machallah contane Na frère Momo bieng Diam AK Salam sampou rék inchallah😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😘😘😘😘😘❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️🥰🥰🥰🥰🥰😭😍😍🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️❤️❤️🎉🎉🎉
Vraiment Momo dieng chanté bien 👍😊
Ko massel bayil nala xell mashaallah Dieng saala❤
Notre fierté nationale nioune wa bargny Diéng sala ma ndiogué codou gor khawma damalay beug ba kagne rek ya meune kay nak laf bouche touf touf🎉❤❤🎉❤❤
Aziz dabala yalna yalla yéssal yeurmandé si mom 😢😢😢😢
kou beugue teral wadiour teh yorago diox lenn respect
Kou diougué ndakhté lale j’aime ❤😂
C'est la révélation musique sénégalais ❤❤❤❤
Non azize Sama khel si mome la demme billahi yalla nako yalla kharè aldiana 🙏🙏🙏🥹🥹🥹
Sampou rék inchallah Dieng salla❤
Sampou National 🔥💯🔥
Sampou rk futur 2ème dame inchallah 😂😂😊
😂😂
😂😂😂😂😂😂
Diougal fi sampou féne Awa sampou nagn ba pary
Man fans Waly la mais bilah j'aime tellement Momo dafa meuna wooy ba paré gueum bopam nimouy solo nak laf bouche wayyy é bonne continuation ❤❤❤❤❤❤
Il mérite plus de vues il chante bien donc je sampou fi rek
Yalla nala yalla may ndam Momo tu chantes bien
Kiii beug nako wayyy🎉❤❤❤
Sampou rek le 28 insha allah, niounn wa minam paré nagn
Wakh diè beuri rek mai yalène meune❤❤🎉
Le meilleur de sa génération le 28 inchaala show bolen masoul guise way you normal 😂
Sonko de la music sénégalais ❤🎤
C est l meilleur d sa generation j vous l repete encore inchallah rendez vous l 28 decembre feulerr sa arena aythiaaa niou demmm❤❤❤
Mane nga way machalah ta quality ngay def hale yi yoe abdou guite pape Diouf yenasiy way
Ohh ❤️ je peux pas l exprimer merci beaucoup 🙏🥰 jahman
C'est beau 🎉🎉❤❤❤
Kou jubiler ci clip bi comme mann rk, laalal j'aime ❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Ay way aziz dabala li dè yako warona feth yalla nalla yalla yeureum
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤ je te souhaite une bonne réussite totale inchallah mon fils ❤ depuis France Nice Côte d'Azur ❤
Machallah yana yalla motali Lepp 🙏🏽🙏🏽
Ohhh je peux pas l exprimer merci beaucoup ❤❤❤❤jahman c est trop beau🎉🎉🎉
Sampou rék inchallah Dieng salla ❤
Mn artiste préféré mala beug kay❤Rip Aziz mom rk mo manqué si clip bi 😢
Bilay khipp kouy xalle di woy senegal do morom mam ❤
Gars yih temps yih sen yaram tangue nadeh 🥰
Le meilleur de tous les temps machallah ❤️ yalla nala yalla moussal si thiate akh lamigne 🙏 yalla na yalla motalii leep mou nekk li geune si yaw❤❤❤❤tous derrière Momo ndam rekk💪in sha allah 🙏
Sampou national rék❤❤❤
Le 28 décembre Sampou nationale Dakar Arena Diamniadio MOMO DIENG l'artiste hors pair le Messi de la musique Sénégalais l'homme a la voix mélodieuse 🎉🎉🎉🎉
Aziz Dabala yalla nakho yalla yeureum te Khare aldiana
J'apprécie énormément Momo Dieng sa chanson elle est superbe ❤❤❤❤❤❤❤
Yalla nala yalla may réussite total ❤️❤️❤️❤️👑👑👑💪💪💪🌹🌹🌹🌹🎤🎤🎤
Comme dab iow rek lay toppou Bilae ❤
Sampou rek dagne bakh domou bargny bi❤❤
Magnifique
L'homme for borom le 28 dècembre inchallah arèna besss la si besss yi dè sampou rèk ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃
Bésss bou maga mag nak ❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi dieng meune gua bou yague yw nenala sy reew mii tre bien rk guafi degue t coco 🥥 diasi rk l ragal ❤
Le 28 décembre inshallah l’histoire retiendra ❤
Sampou rek inchlh
Je suis toujours au rendez-vous 🇨🇮🇨🇮🇨🇮
Il chante très bien en tout cas,un vrai musicien🥰❤️♥️👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏
Momo rek suma star bii❤
Oh mo meune❤️❤️
Bonne fête a momo dieng
Bilaye walaye ki damako beugue 😍♥️❤❤❤❤❤❤❤
Sampou nagnou sila 28 bala unchallah ❤
Lou graww ❤❤❤❤ sampou rek 🫶✌️🥰
Je l'aime point bonne continuation 🎉🎉
Thieey doome baye aka meunaa waaye 🤩🥰♥️ où sont les Dieguene avec grand D .Ndeysane sama xeele ci Aziz laa neek thieey aduna yallanako yalla yeureum té xareko aldiana 🤲 bilahi sa mort me fait pleurer com si j'étais parent avec lui 😭💔🙏
Sampou rk🎉❤