KAWTEF 😭 15 ans de Prison Affaire Serigne Fallou FALL Accusé de viol par sa Tante Yeumbeul

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 31 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 1.1K

  • @aminatadiallo5497
    @aminatadiallo5497 12 วันที่ผ่านมา +182

    Amine je ne connais pas ce Fallou mais je prie pour qu’il sort de cette prison

  • @Touly8876
    @Touly8876 12 วันที่ผ่านมา +245

    Ndaysanne fallou thi barki werou rajab bi yalla nalla yalla takhawou

    • @moussademe6473
      @moussademe6473 11 วันที่ผ่านมา +6

      Amine malgré je le connais pas

    • @MustaphaKhoule
      @MustaphaKhoule 11 วันที่ผ่านมา +2

      Amin yarabi

    • @adamvarore3884
      @adamvarore3884 11 วันที่ผ่านมา +1

      Amine ya rabi 😢😢😢

    • @MouhamedFall-jy1qc
      @MouhamedFall-jy1qc 10 วันที่ผ่านมา +3

      Amine inchallah❤🙏❤

    • @Serpenttv8326
      @Serpenttv8326 10 วันที่ผ่านมา +1

      Amine ya Rabi

  • @pommecorail2699
    @pommecorail2699 12 วันที่ผ่านมา +276

    Fallou mane dé khamoumala wayé dama ame yeug yeug ni daniou la togne mais Yalla nala Yalla takhawou . Je suis de tout cœur avec toi ❤

    • @mamandiop5633
      @mamandiop5633 12 วันที่ผ่านมา +9

      Bilay deugleu sama khôl laye sentir motakh yaye yeup ragual dehh nakh li😢

    • @santeyalla3579
      @santeyalla3579 11 วันที่ผ่านมา +4

      Ndeysane yalla nako yalla takhawou

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 11 วันที่ผ่านมา +2

      *Bilay ioe 😢😢*

  • @Nawal-b8s
    @Nawal-b8s 12 วันที่ผ่านมา +227

    Non j'ai les larmes aux yeux 😢😢la tante est tellement méchante quoi , Lii yeup pour dieul keurgui rek. Fallou que Dieu te vienne en aide bon courage

    • @niangtra
      @niangtra 12 วันที่ผ่านมา +7

      Douko féké deh sou moytouwoul

    • @AïssatouBadiane-l8x
      @AïssatouBadiane-l8x 11 วันที่ผ่านมา +2

      Bilaye

    • @ModouSeye-z7i
      @ModouSeye-z7i 11 วันที่ผ่านมา +3

      Wollah j’ai pleuré 😢

    • @Nawal-b8s
      @Nawal-b8s 10 วันที่ผ่านมา +1

      @@niangtra billahi deugue piir gua wakh

    • @Nawal-b8s
      @Nawal-b8s 10 วันที่ผ่านมา +1

      @@ModouSeye-z7i ndeysane c'est triste

  • @ZeynaNdiaye-k3o
    @ZeynaNdiaye-k3o 11 วันที่ผ่านมา +116

    Merci pour cette mobilisation vraiment vous êtes gentils

  • @Aminatalm4r
    @Aminatalm4r 12 วันที่ผ่านมา +361

    Justice pour fallou pétition kou d'accord rek gnou lancéko

    • @SoukayeGaye-t2i
      @SoukayeGaye-t2i 11 วันที่ผ่านมา +12

      Non sama khôlle métina Allahou Akbar je suis partante pour pétition

    • @KhadidiatouNiang-nu1qe
      @KhadidiatouNiang-nu1qe 11 วันที่ผ่านมา +4

      Je suis partante yalla na yalla leral lepp

    • @IbraDiop-ck9mo
      @IbraDiop-ck9mo 11 วันที่ผ่านมา

      Justicia para fallou

    • @cheikhounabambagueye6953
      @cheikhounabambagueye6953 11 วันที่ผ่านมา

      Lolou kay diaroul sax xaar lancé ka féxé mou yatou

    • @ALIOUNEDIOUF-kh7xk
      @ALIOUNEDIOUF-kh7xk 10 วันที่ผ่านมา

      Billahi

  • @Lopios-g6l
    @Lopios-g6l 12 วันที่ผ่านมา +121

    Sénégalais aka moo bahh machalla surtout banlieue bii 👍👍🌹🌹💋

  • @NdiobaMbaye-e7d
    @NdiobaMbaye-e7d 10 วันที่ผ่านมา +67

    Deukeundo dina guen bokk deugleu ❤❤yallana ko yallah guéné fofou mou nekk😢😢😢

  • @ndeyebiramediop3112
    @ndeyebiramediop3112 12 วันที่ผ่านมา +83

    Wa yeumbeul vraiment chapeau li yonboul fallou yalla nala yalla diabalé gua guén thi diam diapal Wa cogne bi bou bakh Manchala fierté

  • @seynabfallou395
    @seynabfallou395 11 วันที่ผ่านมา +50

    ce qui m'a fait pleurer regarder la solidarité du quartier sont vraiment exemple forza les bravo sénégalais

    • @damembow6856
      @damembow6856 11 วันที่ผ่านมา +2

      Vraiment ndéyssane deugeu rék moye moudiou

  • @ndeyemaguettediakhate2891
    @ndeyemaguettediakhate2891 12 วันที่ผ่านมา +128

    Thièy Niack yaay aka mètti 😭😭💔

    • @CheikhoumarBaba
      @CheikhoumarBaba 10 วันที่ผ่านมา +4

      Billahi wakhatiko wetaye bobou YALLA boumou niou téela dale Amine Ya rabbi 🙏😢

    • @BayecheikhGaye-d2x
      @BayecheikhGaye-d2x 9 วันที่ผ่านมา +1

      Bilaye

    • @oumyfall9042
      @oumyfall9042 8 วันที่ผ่านมา

      Wallay enzim

    • @AdjiaFall-j4o
      @AdjiaFall-j4o 7 วันที่ผ่านมา

      Amine ya Rabi 😢

  • @boubabodian5851
    @boubabodian5851 12 วันที่ผ่านมา +159

    Joub joubal joubanti
    Ana justice
    Libéré Fallou svp😢😢

    • @deugrek3312
      @deugrek3312 12 วันที่ผ่านมา +14

      Viol condamnation Daffaye Andakk Aye preuve. On ne Peut emprisonner une personne sans des preuves, si tel n’est pas le cas danouko Tooñ

    • @NdiayeAwa-nv6hm
      @NdiayeAwa-nv6hm 12 วันที่ผ่านมา +3

      Bilaye 😢😢😢

    • @manoulecatalan8701
      @manoulecatalan8701 12 วันที่ผ่านมา +9

      Nagnouko bayi way ndeyssane Li mettina trop😊

    • @manoulecatalan8701
      @manoulecatalan8701 12 วันที่ผ่านมา +12

      Yalla nagnou yalla moussal thi djigéne bou bonne

    • @sophiebodian5336
      @sophiebodian5336 12 วันที่ผ่านมา

      Bilay wahatiko limom doyna warr ​@@deugrek3312

  • @gracevie6343
    @gracevie6343 11 วันที่ผ่านมา +17

    Bane kogne la, fii deh amna solidarité. Liii mooy deukeudooo.
    Masha'ALLAH

    • @BABACAR-l2e
      @BABACAR-l2e 11 วันที่ผ่านมา

      Yeumbeul😢

  • @seneaida5810
    @seneaida5810 12 วันที่ผ่านมา +83

    Yalla nalla Serigne fallou takhawou si barcké cheikhoul Khadim 🙏🙏🙏

    • @Khamza903
      @Khamza903 11 วันที่ผ่านมา +2

      Amin😢

    • @ramadiop8458
      @ramadiop8458 11 วันที่ผ่านมา

      Yalla taxawou

    • @oumoucisse9852
      @oumoucisse9852 11 วันที่ผ่านมา +1

      Amine si barke tourondo wame ak Ben kasradiab

    • @MoustaphaKaïre-n5s
      @MoustaphaKaïre-n5s 9 วันที่ผ่านมา +1

      Amine

  • @maryfall1362
    @maryfall1362 12 วันที่ผ่านมา +49

    Vraiment c'est très touchant que le soutient

  • @superregina06
    @superregina06 11 วันที่ผ่านมา +31

    Vraiment wa kogn bi Yalle naléne Yalle Faye same séne ndiabote. Sene takhawaye rafete na. Fallou yalle nala yalle takhaw

  • @MamediarraDièdièou
    @MamediarraDièdièou 12 วันที่ผ่านมา +27

    Vraiment c'est trop dur quelle méchanceté li adouna diarouko wanté nak yalla yakamti woula ndakh keur ak am am diaroul li mes serigne fallou yalla nala sa tourando walou nga guéne fofou si diam ak salam k dieu te protège fallou

  • @fatimenahaye-wn7ek
    @fatimenahaye-wn7ek 12 วันที่ผ่านมา +46

    Ndeyesane yala na yalla takhawou amine yarabine aidara Cherif

  • @Awayandésindidi
    @Awayandésindidi 12 วันที่ผ่านมา +42

    Mane en tant que djiguéne légui damaye rousse ndakh acte you yess yeup niokoye défe c'est triste😢

  • @Poulagou75
    @Poulagou75 12 วันที่ผ่านมา +28

    De tout cœur avec vous qu Allah fasse triompher la vérité

  • @mbayefall5684
    @mbayefall5684 12 วันที่ผ่านมา +127

    Dem place de la nation̈ def marche fallou diarnako kou bakh yarou bilahi

    • @IbrahimaKebe-p4y
      @IbrahimaKebe-p4y 12 วันที่ผ่านมา +6

      Billahi kon ma dem

    • @adamadioum2659
      @adamadioum2659 12 วันที่ผ่านมา +6

      Ak sounou Wa keure gneup

    • @santeyalla3579
      @santeyalla3579 11 วันที่ผ่านมา +3

      Ndeysane 😭

    • @diarioudiallo8601
      @diarioudiallo8601 10 วันที่ผ่านมา +2

      nagnou deff lolou je le connais pas mais dina deff tout tew

    • @SaliouKane-co8um
      @SaliouKane-co8um 8 วันที่ผ่านมา +1

      Nañe wottee marche

  • @diopndiaye5204
    @diopndiaye5204 12 วันที่ผ่านมา +65

    Libere Fallou, mentien rek, ont gagné résistance rek 😢😢 chaque dimanche niou regroupe rek

    • @strategiesetdeveloppement2525
      @strategiesetdeveloppement2525 11 วันที่ผ่านมา +2

      Exactement il faut faire du bruit

    • @strategiesetdeveloppement2525
      @strategiesetdeveloppement2525 11 วันที่ผ่านมา +2

      Oui il faut maintenir la pression

    • @maremesow1803
      @maremesow1803 11 วันที่ผ่านมา +2

      Dimanche prochain dîna ame?

    • @sokhnadiarradiop2439
      @sokhnadiarradiop2439 11 วันที่ผ่านมา +1

      Il faut publier la photo de Fallou sur les réseaux et supplier que le gouvernement intervienne

    • @talladiop8525
      @talladiop8525 9 วันที่ผ่านมา

      @@maremesow1803ces à ou de yeumbeul dieu protège à serigne fallou

  • @strategiesetdeveloppement2525
    @strategiesetdeveloppement2525 11 วันที่ผ่านมา +32

    Merci à la solidarité du quartier

  • @salimfall
    @salimfall 12 วันที่ผ่านมา +25

    Nous réclamons justice pour fallou yallanako yalla téguill lii inchallah amine

  • @MamadouWagneQ
    @MamadouWagneQ 12 วันที่ผ่านมา +62

    Tous les pauvres sont en prison pour k des problèmes familiale

    • @KhadyNiang-o5x
      @KhadyNiang-o5x 12 วันที่ผ่านมา +3

      Bilahi😢

    • @pispabadji671
      @pispabadji671 12 วันที่ผ่านมา +3

      effectivement mè Fallou mi papame mo faible rek di deuglou tante bi pask tantame yaguenaka teukou dmrm la ni dinaka teuthie souniou secteur la no li 😢

    • @YayeAwaGUEYE-ci2hx
      @YayeAwaGUEYE-ci2hx 11 วันที่ผ่านมา +6

      Papame tayouko. Femme dagne laye ligguéy ba do khame foy takhaaw

    • @diawndeye2046
      @diawndeye2046 11 วันที่ผ่านมา +3

      Lii c grave ndahh adouna diaroul li mais yalla gueumoul néléwoule té deug moo ndieukeu té Moy moudji😢

    • @AichaMbaye-b4j
      @AichaMbaye-b4j 11 วันที่ผ่านมา

      Justice pour fallou Sénégal amoul justus

  • @gueyesokhnaaissata6693
    @gueyesokhnaaissata6693 11 วันที่ผ่านมา +20

    Ms tantame gui vrai domeramm lahh sheutt wayé Yallah moko eupp dolè Falou Yallah nako Yallah takhawou🤲

  • @kinepouye1113
    @kinepouye1113 12 วันที่ผ่านมา +82

    Porta len plainte si docteur bi deff certificat médicalbi pour ouvrir encore enquêtebi

    • @23seye
      @23seye 12 วันที่ผ่านมา +5

      Surtout sa

    • @OmarSAM-s5v
      @OmarSAM-s5v 12 วันที่ผ่านมา +3

      Bilaye lolou lolou mo wara am nako yala diapale falou

    • @rokhayandoye7639
      @rokhayandoye7639 11 วันที่ผ่านมา +6

      Il faut montrer le certificat médical et porter plainte contre ce faux docteur

    • @alimafall7221
      @alimafall7221 11 วันที่ผ่านมา +4

      Surtout lolou c'est ce que j'ai dit li yeup complo la mais médecin bi yallah nako yallah wer môme ak la dame soude mystique la tamite femme bi dou am moudiou bou bakh yallah nako yallah torakhal adouna ak alakhira

    • @talladiop8525
      @talladiop8525 9 วันที่ผ่านมา

      Boude xam naniou ko lolou laniou wara deff

  • @thianegueye8321
    @thianegueye8321 12 วันที่ผ่านมา +32

    Je ne connais pas ce fallou mais yalla diapale si sa barke toureundo ak kazou raja amine ya rabi

  • @joliediopcoiffure9024
    @joliediopcoiffure9024 12 วันที่ผ่านมา +23

    😥😥ndeyesane Yalla nala serigne fallou sa tourondo takhawu si barké wérou radiap bi 🙏🙏🙏🤲🤲🤲🤲

    • @adamadioum2659
      @adamadioum2659 12 วันที่ผ่านมา +1

      Amine amine au mon dieu aide Fallou

    • @MortallaGueye-t6z
      @MortallaGueye-t6z 11 วันที่ผ่านมา

      Amine yarabi 🙏

    • @santeyalla3579
      @santeyalla3579 11 วันที่ผ่านมา

      Amine

    • @Mmm-mv8sy
      @Mmm-mv8sy 11 วันที่ผ่านมา +1

      Bayil Bokkale yii

    • @djibydiene5180
      @djibydiene5180 10 วันที่ผ่านมา

      Wakhi doff kou doundatoule noumoye takhawou waté dénk léne lépou yalla mo geune 🤔🤔

  • @DagaDione
    @DagaDione 11 วันที่ผ่านมา +16

    Fallou khamoumala wayè magui lay nianal yalla nala yalla takhawou🙏🙏🙏

  • @MatyDieng-n8w
    @MatyDieng-n8w 12 วันที่ผ่านมา +64

    Falou soula yalla genee ak diam naga diapat sa wa kogne yii ak mere yii

    • @AminataThiam-gb3wr
      @AminataThiam-gb3wr 12 วันที่ผ่านมา +12

      Billay dinaco dèf bakham motakh wa kognam niome nieup dègue bou rèyone doulène diaral li motakh bakh rèkka am solo

    • @papematarmbengue5700
      @papematarmbengue5700 11 วันที่ผ่านมา +4

      Nit so amé gnoulay takhawou boul massa diaye sa ngor

  • @lapaix4523
    @lapaix4523 12 วันที่ผ่านมา +50

    THIEYE YAYE BOU GAGNIOU ÉGALE TOUMOURANKÉ😭😭😭

    • @AmyBiteye-d8o
      @AmyBiteye-d8o 11 วันที่ผ่านมา +1

      Lolou moma dioy lo 😢

    • @augustindiatta7036
      @augustindiatta7036 11 วันที่ผ่านมา +1

      Bilaye😢😢

    • @CheikhoumarBaba
      @CheikhoumarBaba 10 วันที่ผ่านมา +1

      Yangimay dioylo😭😢😢 mais YALLA bakhna

    • @lapaix4523
      @lapaix4523 10 วันที่ผ่านมา +1

      @CheikhoumarBaba 🙏🏻🙏🏻🙏🏻

    • @MariamaNdong-p8r
      @MariamaNdong-p8r 9 วันที่ผ่านมา +1

      Jai mal au cœur

  • @khadycisse4443
    @khadycisse4443 12 วันที่ผ่านมา +18

    Amine yarabbi mére yalna,yallah guinné fallou fall

  • @diariabousso466
    @diariabousso466 10 วันที่ผ่านมา +1

    Serigne Fallou yow dé Yalla nga guéne té bo guéné Diapal
    Ma sa wa kogne goorgorlou ndakh ame nga guinaw mashallah . Ça se voit que kou bakh nga so mélone nénéne li yeupe doko ame séne kogne . Mashallah . Yalla nala Yalla same are té Fayal la séne wa kogne yi ❤❤❤

  • @FatouThiam-kg1qe
    @FatouThiam-kg1qe 12 วันที่ผ่านมา +59

    Yalnako Serigne Fallou takhawou thi barké wérou radiap bi

    • @aissatouba4234
      @aissatouba4234 12 วันที่ผ่านมา +5

      Serigne Fallou loumou si meune ?

    • @Khamza903
      @Khamza903 11 วันที่ผ่านมา +1

      ​@@aissatouba4234serigne fallou meun nasi louné dieureudieufé serigne fallou ❤🎉 yaw nak défaral sa khol bou Kate ndayam bi dmrm

    • @NdeyefatouNiang-xx3wc
      @NdeyefatouNiang-xx3wc 11 วันที่ผ่านมา +1

      Amine yarabi

    • @mouhamedcisse9124
      @mouhamedcisse9124 11 วันที่ผ่านมา +1

      Amine si barki radiab bi

    • @cheikhdiop9673
      @cheikhdiop9673 11 วันที่ผ่านมา

      ​@@aissatouba4234sa baye loum Mane sa yaye ba dieuléko keur bayam andiko si keureum diko diéma doundeul ta dou yalla heure bo mandouwoul ci pass pasou diambour rék sa khol di guena tangeu geuno fé réw kéne

  • @fayediattou6750
    @fayediattou6750 12 วันที่ผ่านมา +382

    On avait accusé Ousmane Sonko de viol et tous les Sénégalais l'on soutenu donc il n'a qu'à aidé Fallou..

    • @papediop9404
      @papediop9404 12 วันที่ผ่านมา +30

      Yaw kou yèbatè ngua

    • @Patriotsavie
      @Patriotsavie 12 วันที่ผ่านมา +35

      savoir parlé c'est très important

    • @ibrahima1964
      @ibrahima1964 12 วันที่ผ่านมา +4

      Tounou n

    • @AmySeye-g6u
      @AmySeye-g6u 12 วันที่ผ่านมา +41

      Yallana ko tourodom wallou ci barkel magal gui🤲🤲🤲

    • @kanimandibane6354
      @kanimandibane6354 12 วันที่ผ่านมา +9

      Yaw daga rew

  • @CheikhMbackeSarr-uu1si
    @CheikhMbackeSarr-uu1si 12 วันที่ผ่านมา +13

    Libéré fallou svp Mane dh khamouma ko mais depuis ma guis wakh dji ba légui daman am louma meti vraiment Khalé Bou ndaw gua begue yakh adounam ni dafa niaw bilakhi était na wakh si fallou guir yalla 🙏

  • @loababacar8731
    @loababacar8731 10 วันที่ผ่านมา +5

    Même le juge doit être poursuivi…
    Qu’Allah assiste notre jeune frère *Fallou* et chapeau à tout le quartier. C’est ce type de citoyens qu’on a besoin dans ce pays bravo

  • @FatyNdom-c2n
    @FatyNdom-c2n 11 วันที่ผ่านมา +17

    Bilahi alahira dina yague dina méti 😢😢😢😢😢

  • @sennaseye6986
    @sennaseye6986 12 วันที่ผ่านมา +40

    Justice pour Mame fallou 😢

  • @falloudiouf588
    @falloudiouf588 12 วันที่ผ่านมา +17

    Ohh justice pour fallou 😭😭😭😭😭

  • @talibecheikh7628
    @talibecheikh7628 12 วันที่ผ่านมา +18

    Li mo.e nathi ngour gui wakh li yombou na trop tanta dji na sèt thi yalla wayé sèn tawou yaye dji tamite yalla nako tourandom walou mom falou 🙏🙏🙏

  • @kinediop5832
    @kinediop5832 11 วันที่ผ่านมา +23

    Serigne fallou yalla na sougnou borom sétal lepeu si barkep wérou rajab bi

    • @seynabouly9288
      @seynabouly9288 11 วันที่ผ่านมา +1

      Amiiiiine yarabi inchallah

  • @lesfrèrespatriotes
    @lesfrèrespatriotes 11 วันที่ผ่านมา +7

    Wa li tamit mba diam la. Ey waye yalna bourbi leral lep fallou guene si diam barkep serigne Fallou

  • @ndeyefall6317
    @ndeyefall6317 12 วันที่ผ่านมา +28

    Walahi sama khol meti na Fallou yalla nala yalla takha wou inchalah😭😭😭

    • @seynabouly9288
      @seynabouly9288 11 วันที่ผ่านมา

      Amiiiiine yarabi inchallah

  • @ZeynaNiang-gz1fz
    @ZeynaNiang-gz1fz 12 วันที่ผ่านมา +36

    Ki dh tanta dji dafa xalatoul beuss bou moudiou adouna diaroul yéne yi bly😔😔

    • @marietoutamba223
      @marietoutamba223 11 วันที่ผ่านมา +3

      Khalatoul ni môme dafa yor ay dôme fi lofi léblé lolou lagne léy fayé

    • @Fatoundiaye-xq7yl
      @Fatoundiaye-xq7yl 11 วันที่ผ่านมา +1

      Bilay 😢😢

  • @papasall6075
    @papasall6075 12 วันที่ผ่านมา +15

    Free Fallou YALLAH nako borombi tegui natou bi

  • @nahedniasse2308
    @nahedniasse2308 11 วันที่ผ่านมา +6

    Mane dh je suis sous l choc allalou aduna diarna li Mane dh li thi série télévisée yi reik lako done guiss yalla na yalla atté li

  • @bijoumbaye2834
    @bijoumbaye2834 12 วันที่ผ่านมา +9

    Yalnako yalla dimbaler mom fallou bamou guene proson inchallah

  • @wourybah4206
    @wourybah4206 7 วันที่ผ่านมา

    De tout cœur ❤ derrière fallou fall baye fall bi diam rek si iow❤🎉

  • @hyougojesais7239
    @hyougojesais7239 11 วันที่ผ่านมา +6

    Yalna la yalla takhawou justice pour fallou li metina torop matakhe yaye amouléne remplace thi dome

  • @cheikhabdoulkhadrejeylanidiop
    @cheikhabdoulkhadrejeylanidiop 10 วันที่ผ่านมา +1

    Machallah. Wa kogne bi yéneu bakh vraiment . Yalla na yalla diapalé fallou fall mi amiiiiiiiiiine

  • @yacinewade896
    @yacinewade896 12 วันที่ผ่านมา +24

    Thieuy yomal khiyam dina mèti dina yague mon cœur seigne 😢

  • @MoussaThiongane-m5r
    @MoussaThiongane-m5r 11 วันที่ผ่านมา +1

    Woh DaYesaNe MéTiNa Trop Vraiment Yanako Yalla GuéNé Si Diammm Yalla Atté ko AK Tantame Inchallah Amine Amine Amine ❤❤❤❤

  • @realstar428
    @realstar428 12 วันที่ผ่านมา +10

    Bilahi sou paré thii khalé yii papa khaléyii lay rëy togg thii cayitou keur gui kii kou bôn laaa wayyy😢😢

    • @adamandiayekasse5990
      @adamandiayekasse5990 12 วันที่ผ่านมา

      Lolou mo am. Papay khalé yi lay fagagal après

    • @realstar428
      @realstar428 12 วันที่ผ่านมา

      @adamandiayekasse5990 bilahii kii baxoul svp khaléyii meun naa ame sénn numero

  • @cmstrade-n4g
    @cmstrade-n4g 11 วันที่ผ่านมา +11

    Dans ce bas monde beaucoup de choses ne seront jamais claires jusqu'au jour où nous serons tous devant Allah SWT 😢😢😢

  • @MeMe182
    @MeMe182 12 วันที่ผ่านมา +13

    Ngir yalla dem lene bountou palais souma nekone senegal do lene mafi bayi mon cœur saigne bilahi

  • @modousarr6338
    @modousarr6338 7 วันที่ผ่านมา +1

    😭😭😭😭 lima dioye namako yalla bll justice pour fallou

  • @AwaGueye-t3v
    @AwaGueye-t3v 11 วันที่ผ่านมา +16

    Kw qu’on puisse dire ya mystique dedans dè yèn yii j pense k dou tayèff❤a mn Avis prck amna nioxamni bala niouy wadial deff Dara dagniy parè cii lepp walahi adouna dou keurr

  • @ousmanefalloubayeniass496
    @ousmanefalloubayeniass496 5 วันที่ผ่านมา

    Bilahi deug rék mo nékh. Li rék prouvé nako. Kouy féen da ngay wéet akk möm. Machallah à la population de Yeumbeul pour cette forte mobilisation envers votre digne fils du quartier.

  • @mbarickdione7799
    @mbarickdione7799 11 วันที่ผ่านมา +10

    UNE ÉPOUSE REKK POUR LA PAIX DE MA MAISON. QUE LA LUMIÈRE SOIT FAITE

    • @s.ndiaye4186
      @s.ndiaye4186 8 วันที่ผ่านมา

      Deugeuleu fi la diamono tollou. Bene sokhna sou bakh nga ame diam

  • @aidadiop3413
    @aidadiop3413 7 วันที่ผ่านมา

    Justice pour fallou et pour tous ceux qui ont subies cette injustice😢🙏👐

  • @dabadiakhate283
    @dabadiakhate283 11 วันที่ผ่านมา +4

    Amena yakar ni Serigne Fallou dina gnew si kazou radiap bi inchalla

    • @SokhnaRoubaSaliou104
      @SokhnaRoubaSaliou104 11 วันที่ผ่านมา

      WALLAHI NDEYSANE ❤❤DOU NÉNE LOU TAX GNOU WAX AFFAIRE BI CI WEERU RAJAB 😢

    • @NdeyefatouFall-z5c
      @NdeyefatouFall-z5c 10 วันที่ผ่านมา

      Allahouma amine

  • @awacheikhibra
    @awacheikhibra 11 วันที่ผ่านมา +1

    Thieuy 😢 amna nioudoul khalate bamél dh 💔🥹 Fallou yalna yalla tèkla lokho

  • @NdackSenediallo
    @NdackSenediallo 12 วันที่ผ่านมา +10

    Haaaaa fatima dieng amegua fite tè bonnne 😢djapani sa dome dji mo nara raw adji sarr gua nekh yaye di def li domou djambour loulako djaral Fallou yalla nala yalla taguawou bagua Guéne si diam yalla nala sa torondo wallou 😢😢😢

  • @mamemordiop4643
    @mamemordiop4643 6 วันที่ผ่านมา

    Bilahi niakk yaye aka meti 😢😢
    Je ne connais pas fallou mais nitt kou yalla takhawou leu
    Mais yalla nako yalla takhawou libéré ko..

  • @mameastoundiaye8180
    @mameastoundiaye8180 11 วันที่ผ่านมา +10

    Bilahi djiguene bou bonne bakhoul yalla nagnou thi yalla mouseul papa de Fallou tamit kou bonne la 🙏🏾😭😭🥹

  • @annafall3349
    @annafall3349 7 วันที่ผ่านมา

    Justice pour fallou et longue vie ❤❤❤

  • @MariamaSeck-b5d
    @MariamaSeck-b5d 9 วันที่ผ่านมา +2

    Fallou yallah nako yallah guénée this limou néka mes nk tantam yallah nako yallah torokhal this barké seydina mouhamed kou wakh amine yallah nako yallah faiy

  • @PapemoussaDiop-u6x
    @PapemoussaDiop-u6x 9 วันที่ผ่านมา +2

    Justice pour notre humble frère fallou fall que je connais très bien et on demande justice pour lui courage frère 🤲🏾

  • @MamediarraDièdièou
    @MamediarraDièdièou 12 วันที่ผ่านมา +5

    En tout cas ça sera tard rek mes leup si kawam lay quepou limiy bonne yeup yalla mofi nek tes moko eupe dolé si barki serigne fallou mbacké leup dina lerr inchallah fallou yalla nala yalla sam

  • @MamadouWagneQ
    @MamadouWagneQ 12 วันที่ผ่านมา +14

    Yalla nako yalla dimbalé li niawna senegal dou touss

  • @BintoufalilouFall
    @BintoufalilouFall 11 วันที่ผ่านมา +3

    Yawmal hiyame dina méty dh wlh😭😭
    Seringe fallou yelle nala yalla tahawou maye la kholou mogne barkip cheikh fallou mbacké 🙏🙏

  • @EvaSECK-lp6vz
    @EvaSECK-lp6vz 6 วันที่ผ่านมา

    Yalnako Ya ALLAH takhawou🙏🏾🙏🏾

  • @AwaDiop-r9f
    @AwaDiop-r9f 12 วันที่ผ่านมา +7

    Justice pour fallou😢😢😢

  • @OumyKhaiiry
    @OumyKhaiiry 5 วันที่ผ่านมา

    Ndaysane masta courage

  • @NdeyebintaCisse-ok9iw
    @NdeyebintaCisse-ok9iw 12 วันที่ผ่านมา +13

    Yalla nala sa tourondo walou❤

    • @djibydiene5180
      @djibydiene5180 10 วันที่ผ่านมา

      Noumou koye wallo nékk léne nite té bayé ak sénn bopou yalla😭😭

  • @PapemoussaDiop-u6x
    @PapemoussaDiop-u6x 9 วันที่ผ่านมา +2

    Les polices d’à côte comico ou yembeul c’est la bordel total

  • @dialeldiop7525
    @dialeldiop7525 11 วันที่ผ่านมา +5

    Il faut que toute la population se mobilise pour que justice soit fait 😢😢😢😢

  • @FatoubintouWar
    @FatoubintouWar 8 วันที่ผ่านมา

    Yalna ko yalla taxawou seringe fallou fall sy barkip sa fallou torndou 😢metina loulou wayie duegue rek moye modiou inchalla 😢

  • @serignediouf9518
    @serignediouf9518 12 วันที่ผ่านมา +3

    que justice soit refaite ❤❤❤❤❤❤

  • @mbodia6392
    @mbodia6392 10 วันที่ผ่านมา +1

    Bilay ndaw si mo bone yalla nako yalla werr yalla guene falou si khat khat yi

  • @mamadiediou7451
    @mamadiediou7451 11 วันที่ผ่านมา +4

    Fallou Yalla nalla yalla téguil natou bi😢😢

  • @aminatandiaye8964
    @aminatandiaye8964 8 วันที่ผ่านมา +1

    Yalla nasi sa tourando ték lokho❤

  • @mariamagueye9084
    @mariamagueye9084 11 วันที่ผ่านมา +5

    lancez une pétition avec des signatures. assiégez les sites et les télés. métina trop 😭😭😭

  • @Fatoundiaye-xq7yl
    @Fatoundiaye-xq7yl 11 วันที่ผ่านมา +2

    yalla nako yalla takhwo Fallou inchallah 🙏🏼❤

  • @maguettendiaye3510
    @maguettendiaye3510 11 วันที่ผ่านมา +3

    Ndeysane dioy na ba sone. Bilahi lila olof di wakh nane ndiabot talouta touki té tala déé. Khalébi yala na yalla léral lep si barké Seydina Mouhamed saws

    • @AntaDiouf-m5w
      @AntaDiouf-m5w 11 วันที่ผ่านมา

      Amine li doyna war trop

  • @NdeyeSeck-m1d
    @NdeyeSeck-m1d 11 วันที่ผ่านมา

    Yalnako yalla wallou si Barkéb Serigne Fallou sa Tourandô ak wéerou radiap bii 🤲🤲🤲

  • @DabaSamba-s7z
    @DabaSamba-s7z 12 วันที่ผ่านมา +16

    Fallou Yalnaka sounou borom tawahou

  • @MoustaphaDiack-ol4qe
    @MoustaphaDiack-ol4qe 7 วันที่ผ่านมา

    Justice pour fallou libéré fallou

  • @rokhayadiop2042
    @rokhayadiop2042 12 วันที่ผ่านมา +6

    Yalla nako yalla teguil. Natou bi😢

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 7 วันที่ผ่านมา

    😭😭😭😭😭metina serigne fallou mbacké diourom niari yon waloul niou sa tourando bi 😭😭😭😭😭😭😭😭❤❤❤❤

  • @Yacinengom-mq3kr
    @Yacinengom-mq3kr 12 วันที่ผ่านมา +13

    Yalle nako serigne falou walou bala werou radiape bi di diex

  • @bettyba9426
    @bettyba9426 7 วันที่ผ่านมา

    Ayway ayway li métina métina ba ci kanamou yalla na gnepp diogue na Sénégal yeupp diogue pour Fallou niou bayi ko

  • @AdamaThioune-h8r
    @AdamaThioune-h8r 12 วันที่ผ่านมา +3

    Justice pour falou 😢😢

  • @ndiayendeyefatoumatabineto2020
    @ndiayendeyefatoumatabineto2020 9 วันที่ผ่านมา +2

    Fallou Yalnako yalla taxawou geunéko si xate xate yimou nek. Barké serigne fallou

  • @GoraBoromItali
    @GoraBoromItali 11 วันที่ผ่านมา +6

    Diomaye legui mou libéré ko wallahi deugual ,dioubal ,leral kassé dallal léne séne khell ☝️ c'est la première ma guiss lou rafet lii ça veut dire kone Fallou na rien fait

  • @serignegueyetv
    @serignegueyetv 11 วันที่ผ่านมา

    Ohh serigne fallou khamomala wayé yalla na yalla samou la 😢😢😢😢

  • @Salsaa-x7z
    @Salsaa-x7z 12 วันที่ผ่านมา +5

    Liberté pour falou fall

  • @mouhamedfaye6255
    @mouhamedfaye6255 11 วันที่ผ่านมา +6

    Lii yeup, poligamie moko waral😢, Ayway déf lein nii Mane yam sii bèn djabar... Justice pour Fallou❤❤❤

    • @cisse10
      @cisse10 11 วันที่ผ่านมา +3

      Dou polygamie sah tente dji bi mouy seysi féké yayou fallu ganiou na tente dji da bone rek wayé yalla dieu até insha allah yalla neu fallou guéné diam

    • @Mmm-mv8sy
      @Mmm-mv8sy 11 วันที่ผ่านมา +1

      Hors sujet 😂Yow ya doff rek

    • @AminataDIOUF-ez8kd
      @AminataDIOUF-ez8kd 11 วันที่ผ่านมา +1

      Hors sujet 😂