KAWTEF 😭 15 ans de prison pour Fallou Fall accusé de viol, les graves révélations de sa sœur !

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 25 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 287

  • @morniang6490
    @morniang6490 4 วันที่ผ่านมา +46

    Magui niane si barke serigne fallou sama yakar yalla nako yalla takha wo reral lepou 😢

  • @fatimandao8359
    @fatimandao8359 5 วันที่ผ่านมา +54

    Oumy fall yow mi naw nala fall mag bou bakh ngua yalla nala yalla same diapaléla du courage ma sœur ❤

  • @fatoumbaye3027
    @fatoumbaye3027 5 วันที่ผ่านมา +62

    Déme lénne séty serigne moutaha mbacké ak serigne mbaye sy

  • @NouraDiouf
    @NouraDiouf 5 วันที่ผ่านมา +27

    Djiguenn bou bonne baakhoul. Yalna lene Yalla takhawou😢

  • @AwafalloufallMadamefall
    @AwafalloufallMadamefall 4 วันที่ผ่านมา +40

    Prison dé barina ay innocent ndékété 😢😢😢

  • @AdjaSeck-h9n
    @AdjaSeck-h9n 3 วันที่ผ่านมา +20

    Fallou xamou mala dh walahi mais yalla na yalla léral say mbirr cii barké serigne Fallou mbacké yalla nala sa Toureundo walou

  • @aramefall520
    @aramefall520 5 วันที่ผ่านมา +48

    Justice pour Serigne fallou Fall

    • @Kviirsdoll
      @Kviirsdoll 5 วันที่ผ่านมา +2

      ❤❤❤❤❤

  • @adjisow4943
    @adjisow4943 3 วันที่ผ่านมา +13

    Bala mouye yagg yalla nako yalla atté ak sene tante bou bone bi si barké Serigne FALLOU Amine

  • @maimounabarry3795
    @maimounabarry3795 4 วันที่ผ่านมา +30

    Lii rék motakh niounane borom djaboot ragaloul dé niamouy bayi lay khalate: Yalnaniou Al Razaq moutieul si yéné ak pékhé none

  • @senegalaise1
    @senegalaise1 5 วันที่ผ่านมา +25

    Ouvre une cagnotte ma chérie sur kopar express après tu renforces des avocats pour ton frère du courage ma belle nalèn yalla taxawou inchalla 🙏🙏

    • @OmarKandji-t8p
      @OmarKandji-t8p 3 วันที่ผ่านมา +1

      Bilahii sou oubé ma déposei si lima âme ndakh doundou nakko injustice bii

    • @OmarKandji-t8p
      @OmarKandji-t8p 3 วันที่ผ่านมา +1

      Mais mane sathie lagnema accuseiwoneu mais sa ngoneu gua signou borome leiraleko

    • @senegalaise1
      @senegalaise1 วันที่ผ่านมา +1

      @@OmarKandji-t8p ndeysan touma yague na si aduna mai lo mougn mu diex té lu way def bopam masta 🙏
      Cagnotte bi da melni ibina kopar express il faut vérifier là-bas

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 5 วันที่ผ่านมา +28

    Justice pour fallou deysane metina Yaye amoule rameplase sène frére bi nek espagne bakhoule diabare mogui si keuregui diabarame aussi bakhoule djiguène daye dèfare famille mougnelènes yallana dina atè le president Basirou Diomaye Faye et premier ministre Ousmane Sonko diapalélèneSí

  • @NestorGueye
    @NestorGueye 3 วันที่ผ่านมา +16

    La dame est très respectueuse ...
    Elle dit toujours 《Tanta》
    Ce sont des gens bien.

    • @AliouneDiouf-t3d
      @AliouneDiouf-t3d วันที่ผ่านมา

      Je ne comprends plus, est ce que leur tante n'a pas causé même la lesion

  • @Aminatall-t1t
    @Aminatall-t1t 2 วันที่ผ่านมา +5

    Thiey yawmalkhiyam dîna metti wayei fallou yallah nako yallah guené si prison bi barakatou Rassoulilah saw

  • @khadydiedhiou9332
    @khadydiedhiou9332 4 วันที่ผ่านมา +37

    Jiguéne diou bone yalla naniousi yalla mousseul

    • @moustaphaofficial
      @moustaphaofficial 14 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Amine 🤲🤲🤲

  • @OmarKandji-t8p
    @OmarKandji-t8p 3 วันที่ผ่านมา +8

    Bilahi cette femme a raison liimou wakh nii je le vis et je lai vécu juste pour fallou nguir yallah

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 5 วันที่ผ่านมา +15

    Justice pour Fallou😭😭😭😭😭😭

  • @SantiYalla
    @SantiYalla 4 วันที่ผ่านมา +7

    Sama yaram dafa daw thi problème Serigne Fallou,Yalla na yalla léral lép inchalah thi barké S Fallou, La yobou sa yay doufi bayi kén

  • @fatoukinendiaye6730
    @fatoukinendiaye6730 2 วันที่ผ่านมา +5

    Yalla Nako yalla démbali ba lépou fégne thie barkep serigne fallou mbacké😢🙏

  • @khadydiedhiou9332
    @khadydiedhiou9332 4 วันที่ผ่านมา +11

    Justice pour sérigne fallou soutien à lui

  • @bourguibafaye8521
    @bourguibafaye8521 5 วันที่ผ่านมา +12

    Mére bi domèrame bou mag leu. Justice pour Fallou

  • @fatoufaye9434
    @fatoufaye9434 3 วันที่ผ่านมา +5

    Yalnako serigne Fallou Mbackè sa tourando takhawou🤲🏾

  • @MourSis-f7z
    @MourSis-f7z วันที่ผ่านมา +2

    😢😢héé mane dé ma warou yalna yalla moussale nous si djiguéén bou bonne lahilahahilala

  • @MbayeDiop-h4g
    @MbayeDiop-h4g 15 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Wa legui fou nitt di mouthié 😭 xolal Fallou mi liko dal metti na walaxi man sax sama xol dafsi diekh cmm man lan ko def yalla nko yalla samou 😢

  • @elhadjidione8938
    @elhadjidione8938 5 วันที่ผ่านมา +14

    Fallou yalna ko yalla téguil natou bi
    Séne tanta bi yalna ko yalla toroxal wér ko

    • @sellykane8779
      @sellykane8779 3 วันที่ผ่านมา +1

      Amine ya rabi

    • @ndiayebineta4033
      @ndiayebineta4033 วันที่ผ่านมา

      Amineeeeeee🙏🏽Blh ki kayy kou bone la yall nakko yalla wére

  • @abysall5599
    @abysall5599 5 วันที่ผ่านมา +9

    JUSTICE POUR FALLOU 😢😢😢

  • @seynabousene-ty3dh
    @seynabousene-ty3dh 5 วันที่ผ่านมา +8

    Yalla nala sa tourondor takhaw Amine

  • @FattouDiop-x7m
    @FattouDiop-x7m 5 วันที่ผ่านมา +20

    Magui niane si barkép rajub bi Fallou serigne fallou walouko

  • @daarahalimoulkhabirdaaraha3389
    @daarahalimoulkhabirdaaraha3389 3 วันที่ผ่านมา +6

    Sarap Ndayam Kén Waroul Yobou Prison Si Viol Sans Teste ADN ....
    Sonko Réek Doy Nasi Firdé Lii Dafa Yombou Trop Yama Viole Réék Prison 15 ans Dafa Yombou Trop Beuri Na Niou Nékk Prison Ta Walahi Défou Niou Dara 😢😢😢

  • @amidoudiakhate9754
    @amidoudiakhate9754 5 วันที่ผ่านมา +8

    Justice pour Fallou

  • @fatymbaye3479
    @fatymbaye3479 5 วันที่ผ่านมา +7

    Ndeyssane yalla na ko yalla tahawou barke serigne Fallou ak weerou keujou radjap

  • @boubacardiouf8949
    @boubacardiouf8949 5 ชั่วโมงที่ผ่านมา +1

    Yalna niu borom bi Moussal ci pexxeb noone

  • @modoumbayegning5056
    @modoumbayegning5056 2 วันที่ผ่านมา +5

    Séne deukendo yi dé nite gnou baxlane yalna yalla fayléne taxaway bi lou bax rékk mo amsolo, bou sougnou yaye yi dixalate dé li rékk motax ,yalna yeureume yaye yi djitou barsax😢

  • @amsatousy6722
    @amsatousy6722 4 วันที่ผ่านมา +4

    Aye waye kérok alakhira dîna méty deh . Yaye dal kouka ngiak rek mou fégne. Yalla n'a yalla sam léne

  • @salliousene5663
    @salliousene5663 5 วันที่ผ่านมา +8

    Yalna yalla até😢😢😢

  • @MbéneDiop-w3b
    @MbéneDiop-w3b 5 วันที่ผ่านมา +12

    Fallou yalla nala yalla takhawou🙏🏻

  • @ndeyematydiop4718
    @ndeyematydiop4718 5 วันที่ผ่านมา +13

    Tafeu léne photo tanta bi stp affaire bouma méti li mo takh gnépe bagne yayou djitelé ki Djiguéne bou bone la

  • @mariemefall9017
    @mariemefall9017 5 วันที่ผ่านมา +11

    Bilayy li damako dioyy ba sonou dafa melnii mane nanouko def .... hooo metinaa 😢

    • @OmarKandji-t8p
      @OmarKandji-t8p 3 วันที่ผ่านมา +1

      Makko khame mane Mikko doundou mais yallah dakko leirale

  • @CherifWade-sv2zc
    @CherifWade-sv2zc 3 วันที่ผ่านมา +3

    Justice pour fallou 😢😢😢

  • @Fatoumataousmane
    @Fatoumataousmane 5 วันที่ผ่านมา +7

    Justice pour fallou

  • @FatimaHane-d4h
    @FatimaHane-d4h 3 วันที่ผ่านมา +12

    Sa tanta dji yalla nako yalla torokhal barck s salliou mback mima yakar

  • @amdiatoudiallo3953
    @amdiatoudiallo3953 2 วันที่ผ่านมา +1

    Justice pour Serigne fallou 😢😢

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 5 วันที่ผ่านมา +30

    Khana Diomaye dou sétan information yi 😭non😭😭 thiotte ndaye li way réwmi amoul lois sac jour nga deug lou katte ndayem ci réwmi affaireyo kén monoul comprendre quoi

    • @beugueyayame8899
      @beugueyayame8899 5 วันที่ผ่านมา +1

      Deugue piir ngua wakh c triste😢

    • @OusmaneNdiaye-qk6nv
      @OusmaneNdiaye-qk6nv 2 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂Se saaga yi dal na loool😂😂😂

  • @yacinewade896
    @yacinewade896 2 วันที่ผ่านมา +2

    @bb Èva ❤: Des fois nitt tékla thiono you méti yakarni yakhna sa adouna fék bobou sougnou borom mo tokk diko sétane ndakh si natou yoyou si nga nara diaré défarou ba fawou 😔Fallou dinga raw say morom inchalla

  • @aichaloukass3791
    @aichaloukass3791 4 วันที่ผ่านมา +3

    Justice pour Serigne Fallou Fall

  • @FallDamel7484
    @FallDamel7484 4 วันที่ผ่านมา +5

    Yalla nako sunu borom diaplé bamou guéne foumou nek si barké seydina Mouhamed🤲

  • @samoufall8476
    @samoufall8476 4 วันที่ผ่านมา +4

    😢😢Justice pour Fallou Fall

  • @KarimPouye-j9p
    @KarimPouye-j9p 2 วันที่ผ่านมา +1

    Svp plais fallou souko yalla dimbalé bamou guéne je suis prête à être sa femme courage frère

  • @NdeyeFall-zn7kz
    @NdeyeFall-zn7kz 2 วันที่ผ่านมา +1

    Yalla nala yalla guéné si li si barké Serigne Fallou sa toura ndo 😭😭🙏🙏

  • @BayemodouSall-sb6cz
    @BayemodouSall-sb6cz วันที่ผ่านมา

    Justice pour serigne fallou fall

  • @FatoubinetouSy-i1r
    @FatoubinetouSy-i1r 3 วันที่ผ่านมา +2

    Yalna Yalla léral lép si barké Seydouna Mouhamed psl

  • @SeynabouToure-e5u
    @SeynabouToure-e5u 12 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Méti na vraiment
    Force à vous sister

  • @MameDiarraFaye-s4z
    @MameDiarraFaye-s4z 2 วันที่ผ่านมา +2

    Yalla nala sa toureundo walou métina trop🙏🙏

  • @MamadouNiang-hu5yl
    @MamadouNiang-hu5yl 5 วันที่ผ่านมา +3

    Yalna yalla attél boppam

  • @MamadouNdiaye-mn1yy
    @MamadouNdiaye-mn1yy 3 วันที่ผ่านมา +3

    Bou fékké daniouko takal yalla nako borom bi sétal si barké tourondo wam ak Serigne Babacar sy 🙏 yalla nako borom bi sutural🙏

  • @makhtarthiam7269
    @makhtarthiam7269 3 วันที่ผ่านมา +6

    C'est assez triste mais quand je lis les commentaires, je comprends pourquoi notre pays n'arrive pas vraiment à avancer, je vois des gens qui vous disent qu'il faut prier un être humain comme eux, les Serignes, c'est juste des bêtises.

  • @ndeyematydiop4718
    @ndeyematydiop4718 5 วันที่ผ่านมา +6

    Sèrigne si nek si dekeu bi nek si internet bi défe léne liguéye pour la Famillle fallou et fallou mou guéne prison ak séne papa khelmi délou si ak séne frére bi nek Europe yéne Sèrigne yi nek si internet bi liguéyal léne yalla

  • @Rabydabo
    @Rabydabo 4 วันที่ผ่านมา +2

    Ndeysane tatam bi bonna trop lépp beugue yakk adouna fallou yall nako yalla léral lépp 😢😢😢

  • @marcelgomis3135
    @marcelgomis3135 4 วันที่ผ่านมา +3

    Oumy courage

  • @NassikhaTv
    @NassikhaTv 4 วันที่ผ่านมา +4

    😢 c'est triste

  • @CheikhNdiaye-s1y
    @CheikhNdiaye-s1y 3 วันที่ผ่านมา +1

    Yalla nako yalla takhawou si barke Serigne fallou

  • @OussayeSanè
    @OussayeSanè 3 วันที่ผ่านมา +2

    Pa bi deh fiñouko dougal reyna fallou yalla nako yalla tahawou

  • @MouhamadoumoustaphaGadji
    @MouhamadoumoustaphaGadji วันที่ผ่านมา

    Yalla nala yalla takhawou notre Fallou.
    J'ai un coeur vraiment meurtri.
    Yalla deug rék lay até té deug rek moy moudiou.
    Du courage ma sœur.
    Sén tante bi djiguéne djou bon, sén papa kou irresponsable la

  • @BabacarSeck-ny1gz
    @BabacarSeck-ny1gz 3 วันที่ผ่านมา +1

    Yalna yalla leral lep
    Du courage sister
    Yalla nieupeu lafi neikal ci barker nabiy Moustapha PSL

  • @Na_dieye_2004
    @Na_dieye_2004 2 วันที่ผ่านมา +1

    Fallou yale nako Yalla tahawou si barké serigne Babacar sy

  • @MouhamedCissé-j9d
    @MouhamedCissé-j9d 2 วันที่ผ่านมา +2

    Yalnagnou YALLA mousseul si diabar djou bonne. Famille sénégalaise dafa beuri ayy diégg you bonn , féne ak diaxxasé kassé moy séne rôle.

    • @YoyoCambaye
      @YoyoCambaye วันที่ผ่านมา

      Bilay yow

  • @mansoursow9896
    @mansoursow9896 วันที่ผ่านมา

    Fallou yalla nale yalla same inchallah

  • @tallaseye5104
    @tallaseye5104 3 วันที่ผ่านมา +1

    Yalla nako yalla takhawou inchallah

  • @boromtoubajerejef289
    @boromtoubajerejef289 5 วันที่ผ่านมา +2

    Justice per s Fallou

  • @KhadimRassoulDieng-y7s
    @KhadimRassoulDieng-y7s 2 วันที่ผ่านมา +1

    Fallou yalnako tourandowam takhawou si barké seydina Mohammed j'y verse des larmes même djiguène diou bone bakhoul

  • @BabacarSall-f8s
    @BabacarSall-f8s 2 วันที่ผ่านมา

    Bilay foulou yalnala yalla takhawou

  • @adamadiop1915
    @adamadiop1915 3 วันที่ผ่านมา +2

    sén tanta dall amna serigne ba diap sakh justice bi doy n'a war

  • @thiounambengue1183
    @thiounambengue1183 3 วันที่ผ่านมา +1

    Justice pour Serigne falou sa tourando

  • @assdiouf1033
    @assdiouf1033 5 วันที่ผ่านมา +8

    Li diakhal nit gni Moy juse yi fane lagnou soukandikou ba teuthe ni ki 15ans kou nekh gua sose mais juse yi gnoy ate' juse gno lene wara wakh li lagnou teudje' fallou

  • @Intello0PP
    @Intello0PP 18 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Yalla nalen yalla takhaou

  • @MamakhadyMboup
    @MamakhadyMboup วันที่ผ่านมา

    Yalla nako yalla yalla génné famou nékke si barké al khour ààn

  • @FatoumataSane-h4p
    @FatoumataSane-h4p วันที่ผ่านมา

    Oh mon dieu je pleure 😭 libéré Fallou

  • @modougueye3761
    @modougueye3761 4 วันที่ผ่านมา +3

    Li nimouma mète 😭😭😭

  • @RohuiTouré-z5b
    @RohuiTouré-z5b 3 วันที่ผ่านมา +2

    Lou tolni serigne fallou ak werou kasurasab bi ngani fallou ngay torakhal digako cuisse justise poùr fallou

  • @malickgueye4881
    @malickgueye4881 2 วันที่ผ่านมา

    Barki serigne fallou si barki wèrou rajab bi yalla dou sètane 🙏🏻Yalla nalene yalla takhawou🙏🏻

    • @moustaphaofficial
      @moustaphaofficial 14 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      Amine 🤲🤲🤲

  • @LoufaNgom
    @LoufaNgom 2 วันที่ผ่านมา

    Yalla Dina ko guènè dè inchalah😢

  • @PapeAmarSeck-j6k
    @PapeAmarSeck-j6k 2 วันที่ผ่านมา

    Yalla magui ley niane si Barke seydouna Mohamed (Saw) nga diapalé fallou mou geuna foumou nek 🙏

  • @nopitv7609
    @nopitv7609 2 วันที่ผ่านมา

    Maître ndiogou Ndiaye un très bon avocat ❤❤

  • @medounendiaye6935
    @medounendiaye6935 3 วันที่ผ่านมา +1

    Fallou yalnako yall génni Guadalajara fanam may ko étrange ju bari
    Képp Ku bokk thi dil bi yalna ko yalla weer bëthëk nda

  • @mohamedndiaye4779
    @mohamedndiaye4779 2 วันที่ผ่านมา

    Justice pour Fallou Fall 😭😭😭😭

  • @ndiagamakhtarsow3599
    @ndiagamakhtarsow3599 3 วันที่ผ่านมา +2

    naka là mana def ba diapalé fallou ak foumay diar kouma si diapalé ma dieul lou là beugue nak wa salam

  • @bayeamdyfaliloundiaye4313
    @bayeamdyfaliloundiaye4313 วันที่ผ่านมา

    Eskey masouma guise papa bou wayadi et irresponsable ni sen papa😢Mere bi mram deugla
    No li koum naxariwoul do nit,Mame fallou yala nala sa torando taxawou barkep rajab
    Machala Oumy kou yeureum say rak nga té mak bou djiguene moy yay

  • @MoussaSylla-g8i
    @MoussaSylla-g8i 2 วันที่ผ่านมา

    Ohh c’est dure deh mais yalla na yalla leral Lep si barké seydina Mouhamed psl

  • @MourSis-f7z
    @MourSis-f7z วันที่ผ่านมา +1

    Ousmane sonko dé warna diote lii nakhe lou mélni lanouko toumalone mais sénégalais yii séta nounouko béne Yonne ba yalla até deug donc biroume fallou tamite yalna yalla téksi lokho mou lére

    • @mbayecheikhsow659
      @mbayecheikhsow659 วันที่ผ่านมา

      Wakhal dh sénégalais begoul injustice

  • @BiguéNdiaye-w2l
    @BiguéNdiaye-w2l วันที่ผ่านมา

    Yallanako tourandom Serigne fallou mback takhawou samouko si barké Aladj fallou 😭😭😭😭😭😭

  • @aissatouguisse1824
    @aissatouguisse1824 วันที่ผ่านมา

    Boul wakh tanta kii dou tanta domou khathe laaa kou niape ndayame laaa fallou yalna yalla sam

  • @MaguetteThiam-p9n
    @MaguetteThiam-p9n 4 วันที่ผ่านมา +1

    Justice pour Fallou Fall

  • @BAKHOUMDieSamb
    @BAKHOUMDieSamb 2 วันที่ผ่านมา

    Walahiii magui niane yalla bou sama Papa ame 2ème femme jamais 😢😢S Fallou Fall yallnala yalla taxawou🙏🙏♥️

  • @SodaDiop-n4t
    @SodaDiop-n4t 2 วันที่ผ่านมา +1

    Yalla n'a yalla lérarl lep barké sa tourando barké magal

  • @KhadyNiang-p1r
    @KhadyNiang-p1r 5 วันที่ผ่านมา +2

    justice pour fallou

  • @SAWDATOUNIANG-dh4gy
    @SAWDATOUNIANG-dh4gy 23 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Du courage ma soeur yala naleen yala tahawou si barke weer wi seen tante bobou yala nako yala torohal li mou def sou nekee dou deug yala na am louko meti si adouna ak alahira

  • @mariediakhate7398
    @mariediakhate7398 2 วันที่ผ่านมา

    Bilay dieul boubone amna Tass keur leum defeule bay ak dom guir alalou adouna yakheu niaboott Diambour ani yallah ho metina justice pour fallou fall

  • @BambaNdiaye-b7e
    @BambaNdiaye-b7e 2 วันที่ผ่านมา

    Amin barkéb borom touba 😢😢❤❤

  • @NdeyefatoundiayeNdiaye-cf4zr
    @NdeyefatoundiayeNdiaye-cf4zr 5 วันที่ผ่านมา +3

    Yalla nako touradowam walou si barkep wëer wi

  • @HawambodjMbodjhawa
    @HawambodjMbodjhawa 2 วันที่ผ่านมา

    Yalla naniou yalla moussal si nit kou sokhor 😢

  • @abdoulay2867
    @abdoulay2867 2 วันที่ผ่านมา +2

    Comment on peut mettre dehors ta propre fille au moment où certaines sont des appartements et faire du n'importe quoi,sa mère n'est plus là au lieu de la conseiller d'être la mère de ses frères et donner un bon exemple le papa rejette ses enfants comme ça,il est juste un faiblard.