Ya Allah fait en sorte que la personne qui regarde ce message ait une vie heureuse pour lui et ses proches, pardonne lui ses péchés et ouvres lui les portes du paradis Amine 🤲❤🥺
Frère grâce à toi tes vidéos a changé ma vie magui dounedou beneneu doundou lima donne dépensé si xaliss chaque jour bari Wone na trop sakh 10000f mais grâce à toi je dépense 1000f par jour le reste je l’ai gardé à côté et magui siye djisse sama boppou lolou sakh je suis j’ai 20ans mais yaa takh ma yewwou 😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Takh Nga ma nékk ba neen nit, Nima dan xallatè, ni ma daan ngisé mbir yi, Nima daan xolè nit ñi ak Nima daan doxé, tax Nga ma yokka gëm sama bopp, tax Nga ma gëna xam sama bopp. Tax Nga it samay disition ma koy jelal sama bopp, tax Nga it fallé Touma Li nit ñi di xallat ci man. Takh Nga it may khalat Bou baax ci sama avenir. Merci merci merci beaucoup grand jeo tekki Fore life merci beaucoup encore une fois 😍😘💓❤️
Bro encore on vous merci vous avez changé nos mentalité... malheureusement on ne te voit pas pour te présenter aujourd'hui ce que ta réaliser pour nous. Na ylla bour bi fay la
billahi bro ...... Lou bori ... may nangou ya takh....... iow kay Na diam mbori Amal diam rek ya ham lounék sa héél.. nla koo yallah defal aminn ... wakhal aminnn..rek❤️🙏
Vraiment vraiment frère chaque fois que je regarde tes vidéos je me récents beaucoup de plus dans ma vie bilahi que le bon dieu te de garde avec beaucoup de bonheur diam niou barri si yaw ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Je suis faire de toi fr Yaw ya takh ama touma tant même bouma kheuy youl sakh damaye sétane saye. Vidéo rék thi laye néque nouni amé khaliss rék laye khole merci beaucoup mon frère Amal diamou frère
Mane fane lanèkon si senegal bilahi dembe lay doga kham ni li amna senegal dembe lay setane vidéo yi 🕧 ba 03.h sama nek yewou guisou ma sama téléphone bi nekate sathie nania ko mou am louma méti bilahi sama téléphone yaye la abou ni poul egali vidéo yi merci 💯💯❤
C comme si vous êtes dans ma tête et que li la beugueu xamal sama wa cogne yi di tok di casse rek ak di nane ataya yaw yaye sa cheffou bopp te ya meuneu ligueye sa tekki❤
jajeuf souma wadji li rafetna trop mashaallah yallah nala fi yallah bayi bassi kanam inshaALLAH Mais si vous pouviez etre plus rapide quand vous parlé yakar nani dall moyy geunn
comme sur un parcours aux innombrables kilomètres la tunique c'est toi qui choisi de la mettre plus on envisage une vie de principe moins on se comporte comme des traîtres à la traite... pune compétition d'athlètes sur une lignep ld'affranchissement à hautes têtes soit pas bête... la flamme est allumée pas de jambes accroupies donc focus sur la ligne d'arrivée où t'arriverais à te faire pconnaître Qui veut la perdre, le temps n'est plus à la... mais à la quête et reconquête... Tekki forlive... yone bi guène... Never stand out of the way.... it's an evryday pray of life to stay... Respect infiniment bro kène amoul sa Faye... Demba ak taye...
Kou beugé seydina mouhamed(ﷺ)beusal j'aime
Môme rek
Gnapako beugue billahi amoul morome ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏
Psl❤
Avec tes motivations rek. Kou tekki woul iow la neekh ❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Bly fr tekki Rk inch'Allah
Lou ler nga wakh baye
@@gorasamb9547 merci
Ya Allah fait en sorte que la personne qui regarde ce message ait une vie heureuse pour lui et ses proches, pardonne lui ses péchés et ouvres lui les portes du paradis Amine 🤲❤🥺
Alahouma amine
AMINE❤
Je s8 devenu une autre personne grâce à toi vraiment merci beaucoup pour tes conseils de motivation tekki for life never give up 🖇✨❤️
Kou d'accord ni réalité lay wax rk l'a lale j'aime ♥
Frère grâce à toi tes vidéos a changé ma vie magui dounedou beneneu doundou lima donne dépensé si xaliss chaque jour bari Wone na trop sakh 10000f mais grâce à toi je dépense 1000f par jour le reste je l’ai gardé à côté et magui siye djisse sama boppou lolou sakh je suis j’ai 20ans mais yaa takh ma yewwou 😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Yalla nala yalla défal diamou ak képp kouy sétane say video a chaque fois tu nous donne des bonnes conseils force sur vous❤💪💪💪💪💪❤
Bou adouna nékh baniou fatté gni niou djiitou si birr souf. ndax yageu yageu daniou léne di fékki dji. na niou léne diangeul fatiha ak 11 likhlass nianal léne yallah bour bi yeureum léne té xaré léne alldianatoul firdawsi si barki alkhourane
🤲🏽⚰️🤲🏽
Dieuredieuf dieuredieuf yallah na yallah fayla sa yéné si gnou AK sa xol bou rafete bidiahy takha aleykhi salatou wa salam
Tu a parfaitement changer m'a vie a l'époque je dirais que c'est l'état maintenant mon distin est entre mes mains merci frère je vous remercie
Takh Nga ma nékk ba neen nit, Nima dan xallatè, ni ma daan ngisé mbir yi, Nima daan xolè nit ñi ak Nima daan doxé, tax Nga ma yokka gëm sama bopp, tax Nga ma gëna xam sama bopp. Tax Nga it samay disition ma koy jelal sama bopp, tax Nga it fallé Touma Li nit ñi di xallat ci man. Takh Nga it may khalat Bou baax ci sama avenir. Merci merci merci beaucoup grand jeo tekki Fore life merci beaucoup encore une fois 😍😘💓❤️
Yaw mi lire sama commentaires bi yalla nga ame Diam 🙏🙏🙏🙏🙏
Lalal j'aime ,partager , statut.
Mangui ziarre bou wéer sama wadji Amal yaw incha allah amatina solo que dieu te protege
Nous ma méll yallak yaw la billakh Sante n'a yalla la goudou fane néll Amine fotolou amall diame,🙏
Cheikh Anta vivant on t'aime fort bilahi que dieu te protège avec ttes les Sénégalais rawatina khetou naby❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yalla nañiou yalla maye goudou fann ak werr amine
Tu entrain de changé la vie des gens positivement 🔥❤️
Merci beaucoup je suis très content pour toi💙💚💙💚 Ousmane 🇸🇳 🇨🇭
Bro encore on vous merci vous avez changé nos mentalité... malheureusement on ne te voit pas pour te présenter aujourd'hui ce que ta réaliser pour nous. Na ylla bour bi fay la
Je n'est mm pas les mots... Fatté n'a sama bop. Yanggui changé jeunesse bi bu bakh!!! Merci beaucoup ♥️♥️
De plus vous me rendez fièr de continuer ma route.Diapa nga yi life trope vraiment je vous remercie 👍
billahi bro ...... Lou bori ... may nangou ya takh....... iow kay Na diam mbori Amal diam rek ya ham lounék sa héél.. nla koo yallah defal aminn ... wakhal aminnn..rek❤️🙏
Balaye soûma démé baye Hadi si mbiryi souma sétané délou si wat balaye Yama n’alla yalla Faye waye awma sa fay djamou si yaw❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yall naniou yalla defal soutra merci frère Ama Tina solo
Ma source de motivation bne continuation 🙏
Vous savez que depuis que j'ai commencés à suivre vos consommations conseils , j'ai commencé vraiment à changer . merci au fond du cœur 🙏🙏🙏
Génial !
joh yaw dangà bax billahi yalla nala yalla défal lépou lo beugeu kontaan n'a si yaw de
Merci ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️😭♥️♥️♥️♥️♥️😭♥️♥️♥️♥️♥️😭♥️♥️♥️♥️♥️😭♥️♥️♥️♥️😭♥️♥️♥️♥️😭😭😭😭😭♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏🙏🙏🙏😭♥️♥️♥️
ماشاء الله. ❣️❣️
Billahi daymèti rèk wayè xaliss doumayap billahi merci
Amna solo de🥰yalla nala yalla tahawou jaajeuf bouro 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Machallah frrr Say motivation niousiy ndiariniou waye limala waxon booy deff Lou bax sii dortel bii dagay metti ms lepp sii banex laye moudiou inchallah niougui sa guinaw
Frére je viens de regarder tes vidéos mais sa ma appris quelques leçons de vie merci beaucoup mais je suis une jeune fille
Vraiment vraiment frère chaque fois que je regarde tes vidéos je me récents beaucoup de plus dans ma vie bilahi que le bon dieu te de garde avec beaucoup de bonheur diam niou barri si yaw ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Kou ka beugue lalal j'aime
Fima nékonn nekhonna tropp mais bima guissè sa vidéo daww na louma meunn pour nek premier commentaire 😭😭😭😭😭😭😭😭
merci
@@tekkiforlife de rien mon frère 😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Machalla billahi daffa lèrr 😢😢😢❤❤❤❤❤❤mè yalla bakhna merci beaucoup 😊
kou ler billahi 🧏👍
DEUG LEUH ❤🙏
Je suis faire de toi fr Yaw ya takh ama touma tant même bouma kheuy youl sakh damaye sétane saye. Vidéo rék thi laye néque nouni amé khaliss rék laye khole merci beaucoup mon frère Amal diamou frère
Vérité absolue kou d'accord beseul j'aime
MERCI BEAUCOUP YALNA YALLA SAMMU LA
Ndaysan macha allh Amatina solo Lool ms dilen deff par 2 sakh si semen bi
Mon frère Yalla nala yalla faye si liguay def ❤contana bou bakh man ioe rek laye deugglou ❤merci pour tout ❤
Je m'appelle Modou bou bamba yalla nala yalla doli diapalé taxawoula défar saye mbirr dolila soutoura ak yermandé je suis fière de toi 🙏
dama done déf Dara Di khalate pérte Ganga raga loule Péret inchallah je vais résilier inchallah
Bro yagui déf Lou Nice je suis au Maroc mais sâ Bouma décourager say vidéo l'ay sétane m'a pris courage lomay conseil comme frère
merci pour le partage , vous avez gagné un abonné de plus
Amneu Solo ❤🙏🏽
Machalla amna solo lol vallaho♥️🖤🤍
Ohhhh lou garaw ndeysan❤❤🙏
Machallah machallah tekki
Mane fane lanèkon si senegal bilahi dembe lay doga kham ni li amna senegal dembe lay setane vidéo yi 🕧 ba 03.h sama nek yewou guisou ma sama téléphone bi nekate sathie nania ko mou am louma méti bilahi sama téléphone yaye la abou ni poul egali vidéo yi merci 💯💯❤
Détt way, massa
diamou si yaw frr bi 🤲
Vraiment tu ma bcp motivé frère ❤ merci bien
C comme si vous êtes dans ma tête et que li la beugueu xamal sama wa cogne yi di tok di casse rek ak di nane ataya yaw yaye sa cheffou bopp te ya meuneu ligueye sa tekki❤
jajeuf souma wadji li rafetna trop mashaallah yallah nala fi yallah bayi bassi kanam inshaALLAH
Mais si vous pouviez etre plus rapide quand vous parlé yakar nani dall moyy geunn
Merci beaucoup ✊🏻
19h BA 2h Noka mana taxawallé💵👉👂🥰
Frr bon continuation merci ❤❤❤❤
Merci bcp fr ✅🙏🏿❤️
Machala sama xol sédue na si yaw yalla nasa diamou yague
Vraiment grand sokhla n'a numéro
comme sur un parcours aux innombrables kilomètres
la tunique c'est toi qui choisi de la mettre
plus on envisage une vie de principe moins on se comporte comme des traîtres à la traite...
pune compétition d'athlètes sur une lignep ld'affranchissement à hautes têtes soit pas bête...
la flamme est allumée pas de jambes accroupies donc focus sur la ligne d'arrivée où t'arriverais à te faire pconnaître
Qui veut la perdre, le temps n'est plus à la... mais à la quête et reconquête...
Tekki forlive... yone bi guène...
Never stand out of the way....
it's an evryday pray of life to stay...
Respect infiniment bro kène amoul sa Faye... Demba ak taye...
Merci à vous aussi contane na si yaw
Bilahi kén d'où yaw ❤️ amal diam diouri ndamalay bayi khél bou bakh
Merci. 🎉❤ Amena solo
Merci beaucoup ❤️❤️❤️❤️❤️
Yague fi té wér conseils yi amna solo
Force à toi frérot ✌️✌️
Grand frr bi yalla na la yalla défal diamou 💌📚💞
Woow ses paroles sont vifff Biss nika tay abonnés na dila suivre
Machallah ♥️ amna solo ❤ 🙏🏿 ❤ 🙏🏿
Yallna la yallah samal bopam aral la bopam si barki Alkhourane
Mé saway yalla na sa diam yague
Bonne continuation sur les conseils que dieu te protège 🙏🙏🙏
Muto. Obrigadu nha irmon buta judanu muto bem. Forsa na bu yarbaju kuta fasi dia dia. Merce
Frère Ligay déf amna solo merci frère
Macahalla bilay li am na solo trop ❤merci vraiment
Nic frère bilaye je suis un électricien oto Bouma ammè keur ak oto kinaw yalla yawlla yalla n'alla yalla fayy mon ami
YALLA na borom bi leeral yoonbi
Billahi dama laye nianal Yalla goudal sa fane
à bonne ma ngurr diemi seydina mouhamed 🙏🙏
Grand frère longue vie
Zo kontane na❤
Jack tu es le meilleur tu a changé ma vie
Première fois may commentaire, s’il te plaît gneuwal sii côté investissement wollah soxleu nagnko trop sakh
Merci frr merci beaucoup frr ♥️💙
Merci encore 💯💯
tu es la seule personne qui peut changer ta vie
Vraiment frère contane na si iow trop amal diam rk ❤️❤️
Merci beaucoup vraiment
Tu as changé bc de mentalité vraiment diodby mougi cool téki for Life never giv up
Merci encore ❤❤
Niogi léne di bégué toull tan😍
J’ai tout changé Billakhi grâce a vous
Mba diamou la le 23 dimanche passé guissougn vidéo mba diamou la
Diameu la kay. Dama xawone xatte rék. Mais dimanche prochaine inchallah
Merci ❤❤❤❤
Mérçi beaucoup
Merci beaucoup grand frère ❤️💪
Mon Frère stp dognou gnokhe conseille si Sport Sourtou alimentation ❤❤