Maylèn niou sounou jaam pourquoi yén nit sou déffé erreur dolén ko comprendre et en plus ni gén amé jot di wax si limou dioum ,loutah sou wakhé lou bakh dolèn ko guéné comme ni gén di déff ni maylén diam yalla kassé mo kham kou bakh ak kou bone ,,yupp man an
Boyy ki parfois wakhi doff reek laniouy wakh surtout école c n'est op important 😂 j peux dire que diagouma ecole pour am alal ms pour am kham kham j'ai racontré beaucoup de profs à travers leurs discours il sont changé mon education
Bien dit bro pour confirmer ce que vous entrain de dire moi personnellement j'ai le suivi durant une période mais le jour où je compris que il ne fait que de résumé des livres je commence de les faire par moi même parce que je peux le faire comme lui
Sa moroumou julit da ngaye wax çi mom lu rafet mies yaw mom virement da ga sakhor coriace wo waxie soxor rek lafi dëque. May wax ga koy fénal nan allahou AKBAR
Wakh nga lima beugone wakh yepp pour mom livre yi toubab yi bind Nio geuneu meuneu régler souniou ay problème mondaine….il na rien compris…le Coran est écrit par Un ÊTRE PARFAIT qui est ALLAH tandis que livre yoyou niako bind niouy dioum lagn té aussi Amna Nio kham ni geumeuniou YALLAH 😢
Mane limaléne di niane moye kou abonnés wone si compte tekki for life nanga désabonner ndakh abonnés bi dakoye yokka dolé te yokkou dolé kinga khamante ni daye yakk dîne même môme si la bokk ❤❤❤
Je proclame un boycott à vie contre Tekki $, en raison de ses paroles blasphématoires. Nous n'adorons que Dieu (Allah) ; ni l'argent ni les biens matériels ne doivent être au centre de nos vies. L'argent doit rester entre nos mains, et non dans nos cœurs. De plus, il est permis aux croyants de chercher honnêtement leur subsistance; par conséquent, poursuivez vos efforts.
Wala wou wakh niou lo saway wakh arrangé woukou parce que ndakh na boy yi dilén encaisser dalen di défal formation té com ligéyoul ci lolou la yakar ah li saway wakh daye wané ni mom fen katt la limouy geumlo bôy yi nékoul
@@ibrahimaciss2060 waxoul niou bayi école dani ÉCOLE so mané binde mana lire mana wax francé ak angalé rék meune nga bayi lisé dés yeupou meune nga ko diangal sa bopou Yaw mi ya wara nopi ak sa VIDÉO you bone yi
Yéne xamouléne zoo mandouléne ci mom yaw borom chaîne bi xamo zoo . Té sa wax dji moko ték talé . Dioum neu t nangou n'a lol où est le blm . Formation bi xamo l'âne ak l'âne moci nék mane mangui ci ms boci dougué dingua xamni diar n'a lou eup 50 000 zoo à changé des millions de vies . Ci loo xamoul bh wala sax ngua xam ko ték ci tank chipp riiii 😏 une seule erreur kou nék Di narr
Mane limaléne di niane moye kou abonnés wone si compte tekki for life nanga désabonner ndakh abonnés bi dakoye yokka dolé te yokkou dolé kinga khamante ni daye yakk dîne même môme si la bokk ❤❤❤
Merci frr vérité absolue
Dakor zoo da dioum mai nitte koudoul dioum amoul mai niou dakor zoo avant donnaa def Lou bakh niou dakor walla
Daño wara tegal dayam gananma lan
Machallha merci
Thank you brother ❤❤
On n'est des musulmans alhamndoulillah l'homme qui propose m'ai c'est dieu qui dispose 🎉 alhamndoulillah 🙏🏿
بارك اللهُ فيكم يا حبيبي ❤
Merci frère ❤❤❤
Merci
Téki wakhou dof dh Lafi wakhhh
Merci beaucoup léerna nangne ❤❤❤❤ lép gnouy Sénégalais yi leu kou gneuw gnou yékati
Surtout les 48 lois du pouvoir moo gueuneu bonn ci livre yi
Sourtout bobou
Amna solo
😂😂😂😂😂😂 frr yaaaa dof th meune doule
Maylèn niou sounou jaam pourquoi yén nit sou déffé erreur dolén ko comprendre et en plus ni gén amé jot di wax si limou dioum ,loutah sou wakhé lou bakh dolèn ko guéné comme ni gén di déff ni maylén diam yalla kassé mo kham kou bakh ak kou bone ,,yupp man an
Boyy ki parfois wakhi doff reek laniouy wakh surtout école c n'est op important 😂 j peux dire que diagouma ecole pour am alal ms pour am kham kham j'ai racontré beaucoup de profs à travers leurs discours il sont changé mon education
Bien dit bro pour confirmer ce que vous entrain de dire moi personnellement j'ai le suivi durant une période mais le jour où je compris que il ne fait que de résumé des livres je commence de les faire par moi même parce que je peux le faire comme lui
Bilahi tu peux le faire même avec chatgpt c’est très facile
فلتستلم❤❤🎉
Maasàllaa ❤
Attention maître est ce que tu connais bien ce gars ?
Bien dit broo
Tekki khélou dieun la yore
Saway saway rére gua dhé tmt
Beugu buzz diaroul li
Machalla
Sa moroumou julit da ngaye wax çi mom lu rafet mies yaw mom virement da ga sakhor coriace wo waxie soxor rek lafi dëque. May wax ga koy fénal nan allahou AKBAR
Saway rérga ab Dof ga rek bilahi wallahi
Wakh nga lima beugone wakh yepp pour mom livre yi toubab yi bind Nio geuneu meuneu régler souniou ay problème mondaine….il na rien compris…le Coran est écrit par Un ÊTRE PARFAIT qui est ALLAH tandis que livre yoyou niako bind niouy dioum lagn té aussi Amna Nio kham ni geumeuniou YALLAH 😢
Bilahi lolou moye problème bi tereyi rekk lagni lire 📖 fatté realité
Sama xéll mousoul dall si lafe tik tok yi bilaye frère
Yoo man you are right Bro
God bless you ❤
Thank you❤
Noo kii moom mënoo koo layal 😢😢
Waadj pere pauvre la geume. Ndakh moom deffa pauvre
Machallah
nagne ko xar mou léral rek mane guissouma lolou
Lolou mo geune si mome dé vraiment
Afrique dema goul tekki for limou Wakh dara nekou si
Waro diague alxouran dégko di nek alxouran wi c'est vrai
Yaw nopil doff
Gua bal ioe sax khamo fimouy wakhé
Zoo gourou leu 😮😮😮
Livre yi ay yeeffeer mooleen binde
Baayil dih fenal sa mbook julitt
Doff ga rek
Mane deh dana ko déglou mais bayi nako ndax kii mom deug deug dama fogone kou mouseul mais dof la
Saa waay wakhal wakhii nitt dof gua troppp kaay doool nii rkk
Ab Dof ga rek
Ba kham nga ni yallah beugoul nitt kouy fen
Doff ga rek
Mane limaléne di niane moye kou abonnés wone si compte tekki for life nanga désabonner ndakh abonnés bi dakoye yokka dolé te yokkou dolé kinga khamante ni daye yakk dîne même môme si la bokk ❤❤❤
Mandé teup na depuis dembe
Tekki For life yoréwoul entreprise mais Légui yaw aussi lo yoré 😂
Wakhi alkhouran la yoor
@@RassoulAbibiou sa way ki mom ak tekki rék nio yam mom aussi lan la diaring niit yi la wax
Surtout formation yi moye wax massoma si gis kom wané ni teguina dara té mom limoye wax bodone Deuk leu dafa wara wane bopam
Trekki for life kou mana fen la mougi bagg ya abonné yubari amunko
Wax nga Lepp
Je proclame un boycott à vie contre Tekki $, en raison de ses paroles blasphématoires. Nous n'adorons que Dieu (Allah) ; ni l'argent ni les biens matériels ne doivent être au centre de nos vies. L'argent doit rester entre nos mains, et non dans nos cœurs. De plus, il est permis aux croyants de chercher honnêtement leur subsistance; par conséquent, poursuivez vos efforts.
Wa dji dh bobam lay xéxal pour matal 1000abonnement 😂
Doff ga rek
Livre business yi ak développement personnel yi la plupart ay franc maçon gnooko bind.
Iow wakhofi dara 😂
Merci beaucoup
Yaw ki loumou wah si contexte lako wahé té wahoul alkourane kawéwoul beneu yone
Que tout le monde se désabonne sur le page de for life.
Yaw liguaye wakh ak li zo wakh sa fait deux yéne daguéni di diawalé lou bokoul
Amo kham kham yow dof nga
Wala wou wakh niou lo saway wakh arrangé woukou parce que ndakh na boy yi dilén encaisser dalen di défal formation té com ligéyoul ci lolou la yakar ah li saway wakh daye wané ni mom fen katt la limouy geumlo bôy yi nékoul
Dagni bayilo boys ecole après dilené faylo sene formation
@@ibrahimaciss2060 c'est ça la réalité
Wa dji dof la zo da bakh rk di wakh
Dafa soff rekk
Topale faleu waxo fi dar lo déga xam xalaat TV
Coach bi molene di wahe bayilene école apres moulene di iri dilene formé si français akk anglais yewoulene😂😂
Suis le après ngani comprendre
@@ibrahimaciss2060 waxoul niou bayi école dani ÉCOLE so mané binde mana lire mana wax francé ak angalé rék meune nga bayi lisé dés yeupou meune nga ko diangal sa bopou
Yaw mi ya wara nopi ak sa VIDÉO you bone yi
Merci beaucoup @@MOTIVATIONSEnwolof
@ibrahimaciss20 60 mes def ni boul arrêt Di wout khame xam tekki for life IS best ✅❤️
Yéne xamouléne zoo mandouléne ci mom yaw borom chaîne bi xamo zoo . Té sa wax dji moko ték talé . Dioum neu t nangou n'a lol où est le blm . Formation bi xamo l'âne ak l'âne moci nék mane mangui ci ms boci dougué dingua xamni diar n'a lou eup 50 000 zoo à changé des millions de vies . Ci loo xamoul bh wala sax ngua xam ko ték ci tank chipp riiii 😏 une seule erreur kou nék Di narr
machallah