Khassida Moukhadimatoul Amdah Transcription et Traduction en Wolof

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 13 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 212

  • @ALIOUNEBADARALEUH
    @ALIOUNEBADARALEUH 2 ปีที่แล้ว +62

    Tidiane la deh j'aime trop les khassida de cheikh ahmadou bamba té damakoy dëgglou chaque jour yallananiou yalla fayal gëun guii paye kén dou mom

    • @cheikhahmadoubambandiaye927
      @cheikhahmadoubambandiaye927  2 ปีที่แล้ว +3

      Amiin waay, diadieuf

    • @ndiayeterena6125
      @ndiayeterena6125 2 ปีที่แล้ว

      000

    • @AlyMauro
      @AlyMauro 5 หลายเดือนก่อน +1

      Nioune Serigne Touba la n'iou am mo niou guenel lépou sii mbacké balla Aïcha Daf nio yarr ba néwou niou sou niou béne morom ❤

    • @MarwaneGnagne-e5t
      @MarwaneGnagne-e5t 3 หลายเดือนก่อน

      Quel belle traduction

    • @MameFatouSeye-h9d
      @MameFatouSeye-h9d 9 วันที่ผ่านมา

      Billahi dagua bakh rek ❤❤❤❤

  • @mouhamedfall9237
    @mouhamedfall9237 2 ปีที่แล้ว +157

    Je remercie du fond du cœur ❤ la personne qui nous a fait cette magnifique traduction, j'ai une forte émotion en ecoutant et en lisant. L'ISLAM rek moy deug. DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA.

  • @omarfofana6087
    @omarfofana6087 10 หลายเดือนก่อน +10

    La beauté de ses vers ,temoigne de l amour infini , incontournable et incommensurable pour le soleil des soleils seydouna mouhamad(psl) cheikhoul khadim l' intemporel ,la source intarissable . dieureudieuf MBacké

  • @mamediarrandiaye3039
    @mamediarrandiaye3039 2 ปีที่แล้ว +15

    Souniou yaakar tay ak euleuk yalla na yalla sakhal niou si yonne ❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭😭

  • @MbackeNdar82
    @MbackeNdar82 3 ปีที่แล้ว +20

    Wallahi serigne touba Kenn la si Tagg yonent bi (saw) Nimouy taggé mo nekh tè matalé ay teggunn

  • @bintoubop7847
    @bintoubop7847 ปีที่แล้ว +17

    Li si khôl lénén khédiou si barkie serigne salihou nekhna trop gnikoy djangu yalna yalla goudan sen fann ❤❤❤

  • @bbfa5765
    @bbfa5765 2 ปีที่แล้ว +17

    Walay kein d’où serigne Touba 😭😭li dafa neikh thi xol ❤️

  • @adelaidedrame462
    @adelaidedrame462 2 ปีที่แล้ว +11

    Ahmadoul Khadim Aime tant Allah et le Noble Prophète Muhammad sallallahou aleyhi wa Salam ! Dieureudieuf Khadimou Rassoulillahi sallallahou aleyhi wa Salam.

  • @secklamine4279
    @secklamine4279 4 ปีที่แล้ว +16

    Dieuredjeuf serigne touba yaw miniou khamall kouy rasoulou’lah

  • @coumbasowngom9121
    @coumbasowngom9121 3 ปีที่แล้ว +9

    Jeureujeuf Serigne Touba kenela amoul morom jarama Mame cheikh Ibrahima fall

  • @bigbayethierlofficiel6069
    @bigbayethierlofficiel6069 3 ปีที่แล้ว +18

    Soumakoy déglou damay douguou bassi sa chaîne ma conecter ko ak sama ouffeur tay topou si araf yi dikou youkhou diko sikar sama khol dih nékh ak souniou wa keur🌟♥️🌟
    Dieureudieuf si vidéo bi🙏🏾
    Dieureudieuf Serigne Touba🙏🏾
    Diarama Mame Cheikh Ibra Fall🙏🏾
    Dieureudieuf mbokou Talibé yi🙏🏾

  • @colyfatou1601
    @colyfatou1601 4 ปีที่แล้ว +9

    Yalla na la serigne touba fayale bopame

  • @laminedieye662
    @laminedieye662 3 ปีที่แล้ว +64

    Je ne peux pas tenir mes Larmes en écoutant ces belles paroles Djeureudjeuff Ahmadou Bamba Khadimoull Rassoull 😭♥️🙏

  • @mouhamedmodyndiaye4178
    @mouhamedmodyndiaye4178 4 ปีที่แล้ว +20

    Masha allah nekh na lolou yalla na lako serigne touba fayale

  • @fatoushfatouseck6578
    @fatoushfatouseck6578 2 ปีที่แล้ว +12

    Thiey Dame kene khamoul nougnou koy deff rekk❤️❤️❤️❤️

    • @wakeurcheikhismailagueyetv876
      @wakeurcheikhismailagueyetv876 ปีที่แล้ว +1

      ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamediarracisse5028
    @mamediarracisse5028 2 ปีที่แล้ว +6

    Sa Soumay dégulou xassida bii Limay yeuk mak borom bi dongua ko kham ❤️🤧🧕🏾

  • @bambasow2645
    @bambasow2645 2 ปีที่แล้ว +6

    Serigne bi dou morom,
    Kepp kouko outeul nawlé, safara moy sa tieurr, Yonenti (PSL) mo gueune si nit yi, Serigne Touba mo Meune si mindefou Yalla yi❤️❤️

  • @camarasaly7099
    @camarasaly7099 4 ปีที่แล้ว +22

    Yalla nala mame BAMBA fayale bopam

  • @davidpisat4358
    @davidpisat4358 3 ปีที่แล้ว +15

    Merci pour le transcription dieuwrine niogui lay ziare dila guereum dila sante dila nouyou ligua deff rafette na lolou machallah grace a toi khassida gagui guena mokk diangue dji guena yomb donc dieureudieuf yalnala yalla defal tawfex bou bari ak diam daradiey chekhoul khadim

  • @AmiFall-j6p
    @AmiFall-j6p ปีที่แล้ว +4

    Dieureudieuf Serigne Touba celui qui nous a fait cette traduction jusqu'à qu'on puisse le lire bayinanou la ak kou Ted ki

  • @gueyeMbayang-gj3xs
    @gueyeMbayang-gj3xs 17 วันที่ผ่านมา +1

    Sama xassida préféré heure Bouma kheuyé déglouko❤❤ thieuye serigne touba😭🫶🏼♥️

  • @adelaidedrame462
    @adelaidedrame462 2 ปีที่แล้ว +8

    MADHOU RASSOULILLAHI SALLALLAHOU MUBARACK !
    Sama khôl tooy na lool . Dieureudieuf Serigne Touba.

  • @KhadySagna-n8w
    @KhadySagna-n8w 11 หลายเดือนก่อน +4

    Dieuredieuf cheikh Akhmadou Bamba Khadimou Rassoul ❤❤❤❤

  • @aminatambaye2022
    @aminatambaye2022 2 หลายเดือนก่อน +1

    Fayou yallah ak borom touba rek❤

  • @muqadamatulamdahjan2989
    @muqadamatulamdahjan2989 4 ปีที่แล้ว +22

    Cëy Muqqadimat nimiy def ci xol😢❤🔐Jërëjëf

  • @NourouDaraynitvhd
    @NourouDaraynitvhd 4 ปีที่แล้ว +13

    Manchala amna solo dé Mouride

  • @rassoul9851
    @rassoul9851 4 ปีที่แล้ว +23

    Alhamndoulilah , dieureudjeuf Serigne touba , xassida bi nehna amna solo masha allah , yalna diam yagg si barké seydina Mouhamed PSL .

  • @Sokhnande
    @Sokhnande 4 ปีที่แล้ว +14

    Ohh macha'Allah neex na trop
    Yalla nala yalla fay yiiw si barké seriñ bi 🙏🏾

  • @mamediarrandiaye3039
    @mamediarrandiaye3039 2 ปีที่แล้ว +5

    Dieureudieufeuti cheikh ahmadou bamba Khadim Rassoul♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @magattefall5145
    @magattefall5145 4 ปีที่แล้ว +7

    Yalla na la Yalla fay si barké khassida yi 🙏🏾 liguey bi rafet na amna solo🙏🏾 man FadjiaAni lay weur😍

  • @ousmanesene8620
    @ousmanesene8620 ปีที่แล้ว +2

    Dieredief borom Touba alkhamdoulilah

  • @awasagna5147
    @awasagna5147 3 ปีที่แล้ว +4

    Ndeysane xol sédna lol bilahi,ma ngui léne di nianal tawfex ak taysir thi barké Mouhamad Aleyhi Salatou Wa Salam.Dimbali nguéne niou trop thi dourouss bi.Yalla na Allahou faye lène yiiw🤲🏿. Alhamdoulilah, allahouma salli ala Mouhamadine Wa Salim, Ahmadou Bamba dieureudieuf 🙏🏽.

  • @Sonko_pro_tv
    @Sonko_pro_tv 2 ปีที่แล้ว +6

    SI KHASSIDAYI RK BA BAGNIY SANGO SOUF INCHALLAH WAROUNIOU DI TAYI DI WAX BAT BI DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA NDAX NIOUN BAT BI MOY LIGNUY ARE KON NAGN SI SAX

  • @babacarcissokho
    @babacarcissokho ปีที่แล้ว +1

    Béss bignou xamé wahou ma lép wayé asss toutt sii seugn bi dinagn bayi sunu lép téé jooxx ko sunu lép kééneu duu serigne touba... jeureu jeuf ahmadou bamba❤❤

  • @nenediallo5015
    @nenediallo5015 2 ปีที่แล้ว +8

    Li nekh na machalah💖💕

  • @MamanDia-w4x
    @MamanDia-w4x ปีที่แล้ว +1

    Thieey yonènete bi mo mèkha tagg dhe ❤❤🤧🤧

  • @AbdouThioune-fu1tr
    @AbdouThioune-fu1tr ปีที่แล้ว +2

    Mouride kassé mo wor ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @djidyseck3652
    @djidyseck3652 4 ปีที่แล้ว +8

    rejeureujeufaty Borom Touba❤😢

  • @talibebamba5450
    @talibebamba5450 4 ปีที่แล้ว +25

    Dieuwrigne li mom noce la nak ! Nungui lay sant dila nianal 🙏🏿🤲🏿❤️

  • @syllandeye5048
    @syllandeye5048 2 ปีที่แล้ว +17

    Serigne touba amoul morome💓😘😘

  • @fatoundour5320
    @fatoundour5320 2 ปีที่แล้ว +1

    Machallah am l
    wèrreul mouthieul ak BORROM TOUBA ak BORROM TOUBA ak BORROM TOUBA ak BORROM

  • @bintoubop7847
    @bintoubop7847 ปีที่แล้ว +12

    Dieureudieuf serigne touba❤

  • @khadygueye7897
    @khadygueye7897 4 หลายเดือนก่อน

    Serigne touba ken la wakh nako te dou yakh dara❤

  • @adjasaliou116
    @adjasaliou116 4 ปีที่แล้ว +25

    Dieureudieuf serigne touba 🥰💖💖💖💖💖💖💖🤲🤲🤲🙏🙏🙏🙏🙏

  • @sokhnawallofall4901
    @sokhnawallofall4901 2 ปีที่แล้ว +8

    Dieureudieufati serigne Touba

  • @lopezibrahima4811
    @lopezibrahima4811 2 ปีที่แล้ว +1

    Ay way Yalnanou Yalla fayal sounou waji

  • @papisgoudiaby9926
    @papisgoudiaby9926 2 ปีที่แล้ว +8

    Dieurediefety Serigne Touba 😭🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @MG-Saliou
    @MG-Saliou 4 ปีที่แล้ว +6

    Ohhh Muhadimmat dinama yobbou fou soreee li aldiana la😪

  • @ngonediallo9524
    @ngonediallo9524 2 ปีที่แล้ว +11

    Thieuy khadim Rassoul moo meuneu bindeu dieureudieuf Serigne Touba mbecté mi ❤️🥺🌹🔥

  • @mbayendiaye9238
    @mbayendiaye9238 2 ปีที่แล้ว +4

    Dieureudieufé Serigne Touba bilahi watalahi sayou maay dégglou moukhadimat bi rék damaay nioy bilahi hawma loutah 😭

  • @matyseck446
    @matyseck446 4 ปีที่แล้ว +9

    Jajeuf way 💚🖤 Yague yok ak wer doléy Xassidas yi

  • @madadiao1913
    @madadiao1913 6 หลายเดือนก่อน

    Jerejef Serigne Touba lii Dina ma dimbali ba ma kham, khassida da guii ngepp War nagn koo jang ngir njoukal borom Touba jaraw lakee mame cheikh Ibrahima fall

  • @mamefatouseye61
    @mamefatouseye61 3 หลายเดือนก่อน +1

    Thiaye sougnou amoul wone Serigne touba 😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @fatouciss121
    @fatouciss121 ปีที่แล้ว +1

    Djeureujeuf Serigne Touba ki merci way mi takh niouy déklou khassida bi ak loumouy signifié ms suniu ko monone télécharger dina bakh déh kou bakh ki 🤝💓

  • @dembelebirama5680
    @dembelebirama5680 ปีที่แล้ว +1

    ❤khäna dii andak akk Mbégté rék sougnū kay dégglūū 😊Akhmadūna Bamba jërëjëf

  • @davidanne5413
    @davidanne5413 2 ปีที่แล้ว +2

    Cëuy dégeul ma lii rkk Serigne TOuba kéne khamoul loumou done yalna niou sakh si ioe ba deh 🙏♥️🙏

  • @fadeldoumbouya8721
    @fadeldoumbouya8721 2 ปีที่แล้ว +7

    Mayniou telecharger ko nguir dieumi serigne touba

  • @fatymakhathiam295
    @fatymakhathiam295 ปีที่แล้ว +2

    SALLALLAHOU ALLAH SEYDINA MOUHAMED RASSOULILAH SWS ADJIARATOU FATY SALIOU THIAM BOUKOULE KOULE RASSOULILAH SWS

  • @serigneissakhagueye8982
    @serigneissakhagueye8982 2 ปีที่แล้ว +4

    Barkep Borom Touba ligêy bi raféte na torop bilahi walahi li mom sunu meckté la.

  • @ndeyefatougueye3384
    @ndeyefatougueye3384 2 ปีที่แล้ว +4

    Kén dou Serigne bii

  • @passanendiaye2148
    @passanendiaye2148 3 ปีที่แล้ว +8

    Lou gaw si fekheul kholl ❤💖

  • @danediego137
    @danediego137 4 ปีที่แล้ว +3

    Bi rek ladone khar macha Allah yalla nalen serigne Touba faye

  • @diarradiouf1472
    @diarradiouf1472 4 ปีที่แล้ว +7

    machallah amna solo wayé diapaléniou niou meun ko téléchargé

    • @cheikhahmadoubambandiaye927
      @cheikhahmadoubambandiaye927  4 ปีที่แล้ว +2

      salam sokhna diarra, ma ngi diégalou d wayé dou si man. TH-cam moko bloquer pour Droit d' auteur

    • @douloba136
      @douloba136 3 ปีที่แล้ว +1

      Nio ngui ziar bou werr.Mais vidmate di nga KO meuneu téléchargé.

  • @ramatasow6117
    @ramatasow6117 2 ปีที่แล้ว +2

    Thii serigne touba kenn la 4h di matin ma tock di diagu khassida li serigne touba rk mocka meune

  • @ahmedsane2666
    @ahmedsane2666 4 ปีที่แล้ว +4

    Wa htdkh nio meuneu diang machallah

  • @mamemariamaseye5183
    @mamemariamaseye5183 2 ปีที่แล้ว +1

    Dieureudieuffff dieureudieuffff dieureudieuffff

  • @farykounta6187
    @farykounta6187 3 ปีที่แล้ว +7

    Hassida bi fimoumay yobei dafa soriii😭😭😭😭😭

  • @pendasarr9166
    @pendasarr9166 ปีที่แล้ว +3

    Dieureuf borom touba❤

  • @ngomrama4157
    @ngomrama4157 2 ปีที่แล้ว +1

    Dieureudieufè borom Touba 🤍🤍🤍🤍💖

  • @moussandiaye6967
    @moussandiaye6967 4 ปีที่แล้ว +8

    Dieureudieuf mouride. Dila nianal yokk, yagg ,ak werr thi barkep Yonente bi (psl)

  • @mmembacke8892
    @mmembacke8892 3 ปีที่แล้ว +2

    Walahi barki cheikhouna cheikhoul khadim sama khôl seddna bilahi sama khôl fesna mashalah mashalah

  • @NdeyearameNdiaye-kg3wb
    @NdeyearameNdiaye-kg3wb ปีที่แล้ว +2

    Serigne bi wlh diambar la

  • @mouridesene
    @mouridesene ปีที่แล้ว

    DIEUREUDIEUF BOROM TOUBA. KHALIFAM YALNA YALNA YOK AYE FANAM TÉ DÉFARKO.

  • @papaamadoumbaye523
    @papaamadoumbaye523 2 ปีที่แล้ว +2

    Mâcha Allah Koubakh . Jeureujeuf Serigne Touba

  • @khoudiafall6881
    @khoudiafall6881 4 ปีที่แล้ว +8

    Machallah nèkhna wayyy❤️😭

  • @amyniang5337
    @amyniang5337 ปีที่แล้ว +3

    Thieye serigne touba 😢😢❤❤❤❤😂

  • @djibrilsow5780
    @djibrilsow5780 4 หลายเดือนก่อน

    gnoune senegal blh bouniou khamone serigne touba dinagnouko guena fonke

  • @atouwallybouserignesaliou8135
    @atouwallybouserignesaliou8135 2 ปีที่แล้ว +4

    Yalla kéne la♥️♥️

  • @khadimcisse5280
    @khadimcisse5280 3 ปีที่แล้ว +3

    Machallah dieureudiefe serigne touba diarama mame cheikh ibra fall. May lathié rek kane mo radiass debut vidéo bi

  • @NabaCissé-p6i
    @NabaCissé-p6i 2 หลายเดือนก่อน

    Serigne Touba rek moo wor❤❤❤❤❤
    Bilahi

  • @lolitasobota7128
    @lolitasobota7128 6 หลายเดือนก่อน

    sallalahou hanla Mouhammad PSL Muhammad Aleyhi sallatou wa Salam❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭🙏

  • @massambangathe
    @massambangathe ปีที่แล้ว +1

    Dieureudieuf Serigne Touba❤

  • @mouridesene
    @mouridesene ปีที่แล้ว

    DIEUREUDIEUF BOROM TOUBA ❤❤❤❤❤❤.......EXTRA

  • @NdeyeFatouNdiaye-mo3ki
    @NdeyeFatouNdiaye-mo3ki ปีที่แล้ว

    Dieureudieufè brom touba

  • @Rampiii
    @Rampiii 3 ปีที่แล้ว +5

    Sama khol seedna😭😭😭😭❤️

  • @beugborombelel2293
    @beugborombelel2293 4 ปีที่แล้ว +4

    Masàlla amatina solo jëwriñ

  • @mamediarracamara9810
    @mamediarracamara9810 3 ปีที่แล้ว +6

    Dierediefei serigne touba

  • @thioyefatoubinetou9395
    @thioyefatoubinetou9395 หลายเดือนก่อน

    Vraiment merci yalneu YaAllah fayyla 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @waawcoumba52
    @waawcoumba52 5 หลายเดือนก่อน

    Mon Khassida préféré 🥰

  • @khadymboulemariediop4588
    @khadymboulemariediop4588 2 ปีที่แล้ว +1

    Les khassahide m apaise kan j'ai mal et k je pleure 😭😭♥️

  • @aichademe1152
    @aichademe1152 3 ปีที่แล้ว +10

    Macha Allah ❤️❤️

  • @FatousnSene
    @FatousnSene 8 หลายเดือนก่อน

    Diaradieuf Serigne Touba amoul morome

  • @NdeyesokhnaNdour-lv3jx
    @NdeyesokhnaNdour-lv3jx ปีที่แล้ว

    Xassida bi doumassi doyal mouk dafa Sed sama xol ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fallosowafia8670
    @fallosowafia8670 2 ปีที่แล้ว +1

    Transcription yi amna solo trop

  • @MariamaMariama-n7n
    @MariamaMariama-n7n 10 หลายเดือนก่อน +1

    Mame sokhna mariama dieng magui sante suniou borom thie kham né signe bi amoul morom

  • @taf2615
    @taf2615 3 ปีที่แล้ว +5

    Dieureudieuf machala !

  • @bassndiaye791
    @bassndiaye791 2 ปีที่แล้ว +4

    Ndeysan 😍😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️❤️

  • @assanediop79
    @assanediop79 3 วันที่ผ่านมา

    Yala nala yala fay qui traduire li❤

  • @sokhnaaminatasaw8445
    @sokhnaaminatasaw8445 4 หลายเดือนก่อน

    Sama xole bi akka sedd Dieureudieuf kou tedd ki

  • @mamefatouseye61
    @mamefatouseye61 3 หลายเดือนก่อน

    Ndaysan li souma koy dégue lou damay 😭😭😭😭😭😭