Axirou zaman "KUDUL JAAMU YÀLLA DOO TÀQA LIKOO AK SAYTAANE" Avec Oustaz Makhtar Sarr.

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 15 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 32

  • @aminaniang7917
    @aminaniang7917 11 หลายเดือนก่อน +2

    Yalnaniou yalla atté thi yeureumande labal Sounouy xool barkep nabii ❤❤

  • @alybaye1995
    @alybaye1995 ปีที่แล้ว +14

    Cette vidéo est arrivé à la bonne heure et au bon moment yalna ma yalla diégal samay bakar Amin

  • @mansourdieng2000
    @mansourdieng2000 11 หลายเดือนก่อน +1

    Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Sél Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Baax Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Yiw Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Dioup Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Bari Xam Xam Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Am Dégu Dégu Ci Diiné Mi Yalla Nala Yalla Faye Yiw Oustaz Makhtar Sarr Yalla Goudeul Sa Fane Yalla Yokou La Ci Xam Xam Ak Khéweul Gou Yaatou Lool Té Barkél Ba Ngua Yeuk Ko Amine Allahouma Amine Dieureudieuf Oustaz Makhtar Sarr ♥️👈

  • @mouhamedndiaye1418
    @mouhamedndiaye1418 ปีที่แล้ว +3

    Machallah oustaz ❤amna solo yalna la yalla fay yiw

  • @amethsy1140
    @amethsy1140 11 หลายเดือนก่อน +1

    Dieureudieuf oustaz makhtar sarr yala nala yala fay la guoudal sa fane.

  • @beuguerassoul3126
    @beuguerassoul3126 11 หลายเดือนก่อน +1

    Oustaz Makhtar Sarr yalla na nga fi yague té wérr Amine

  • @khadimgueye3317
    @khadimgueye3317 11 หลายเดือนก่อน +1

    Machalla soupe bi oustaz ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Souleymanediallo-z3l
    @Souleymanediallo-z3l 20 วันที่ผ่านมา

    Dieureudieuf oustaz

  • @cheikhdiop82
    @cheikhdiop82 11 หลายเดือนก่อน +1

    Machalla tay mom oustaz yeugal nga sama gayi 😅😅 , but machalla yalla na yalla def gnou deg ta topeu .

  • @SerigneBabacarCiss-o9k
    @SerigneBabacarCiss-o9k 11 หลายเดือนก่อน +1

    اللهم صل على سيدنا محمد الفاتح لما أغلق والخاتم لما سبق ناصر الحق بالحق والهادي إلى صراطك المستقيم وعلى آله حق قدره ومقداره العظيم وانصر لإخواننا في فلسطين

  • @tahiroutoure9054
    @tahiroutoure9054 11 หลายเดือนก่อน +1

    Manchala

  • @cheikhcokidiop6690
    @cheikhcokidiop6690 11 หลายเดือนก่อน +1

    ماشاء الله تبارك الله شكر لكم وجزاكم الله خيرا يا اخي الكريم

  • @BoussoSow-gm6oj
    @BoussoSow-gm6oj 11 หลายเดือนก่อน +1

    Oustaz makhtar yaw rec laniouy top yalla defal 2:10 la diam ak wer 2:34

  • @BoussoSow-gm6oj
    @BoussoSow-gm6oj 11 หลายเดือนก่อน +1

    Bilay oustaz thune bokoul 19:40 thafine sa dianguale yarouna ande ak dine ak civisme 22:48

  • @tallandiaye3493
    @tallandiaye3493 ปีที่แล้ว +4

    Masha Allah ame solo ya Oustaz ❤❤❤❤

  • @yeewuteyeete8468
    @yeewuteyeete8468 11 หลายเดือนก่อน +1

    Dunyaa bi jeex na na nga def jub yóobbal *
    Farlul te yòkk jëf yu baax te armal
    Rafle wu deñtalu bu wóor ci léepp *
    Leneen ludul yàlla ma doy ci fépp
    Sag bëgg yàlla namu doy na doy ko *
    Sa bàyyi àdduna ci xol nga am ko
    Yàlla ci xol néegam du dugg giss leneen *
    Benn mu wéet ca mbaa mu génn jëm feneen
    ...Wolofalu Serigne Abass Sall..

  • @khardiatagueye
    @khardiatagueye ปีที่แล้ว +2

    Maachalla amna solo

  • @modou5844
    @modou5844 ปีที่แล้ว +1

    Elh Ibou sakhou disait "doyna di fay pour niou doorla "🥲

  • @fatougueye8180
    @fatougueye8180 11 หลายเดือนก่อน +1

    As Salamu hanlaykoum yaa Oustaz mashalah ame na solo trop niou beugone nka nieuw si diouli ak tewlème

  • @mamadyfaty8444
    @mamadyfaty8444 ปีที่แล้ว +2

    Macahaalah

  • @manamilasalihanmanamilasal1422
    @manamilasalihanmanamilasal1422 ปีที่แล้ว +1

    ما شاء الله جزاك الله خيرا

  • @ousseynoukebe3944
    @ousseynoukebe3944 ปีที่แล้ว +1

    Jeureujeuf oustaz, amna solo, yalla naleu yalla feey yiw

  • @astoudiagne1767
    @astoudiagne1767 ปีที่แล้ว +1

    Amna solo lôl dierengéndief

  • @Ndiayemo921
    @Ndiayemo921 ปีที่แล้ว +1

    Machallah amna solo ya oustaz ❤❤

  • @sdnismahila489
    @sdnismahila489 11 หลายเดือนก่อน

    Mane mi def may dal demay wakh sama yèneu xarit niounane ma boulniou diaxasek yalla

  • @DiopMouhamed-jt3qg
    @DiopMouhamed-jt3qg ปีที่แล้ว +2

    ❤❤❤

  • @modoujobe1917
    @modoujobe1917 ปีที่แล้ว +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Abdoul-qadirba
    @Abdoul-qadirba ปีที่แล้ว +2

    🌹🌺🌺🌺🌺💐🌸🥀🌷

  • @adjandimbalane7882
    @adjandimbalane7882 11 หลายเดือนก่อน +1

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲😍✅thank you

  • @tahirgueye4342
    @tahirgueye4342 ปีที่แล้ว +2

    ❤❤❤❤❤❤