Maashaallah Oustaz et l'invité!!! La discussion est très pertinente et instructive! On a besoin de ce genre de discussion sur le fond du sujet avec une vision globale du problème pour élever le niveau du débat et mieux sensibiliser les gens! Qu'Allah SWT vous fortifie!!!
Alerte à toutes les femmes de grâce ouvrons nos yeux l'heure est grave alhourane ak sunna rek moy deug chéres femmes bouniou nek ay mounafihoune de grâce chères dames preservons nos enfants contre ces phénoménes soyons les premieres dans ce combat n'acceptons plus ces abominables
Mashaa Allah amna solo. Yalna ya Allah SWT défalgnou dég ak top. Ték ndiabot gui ci yonou siratal mustakhim barké Seydina Mouhammad SAW. Allahouma amine
Merci beaucoup oustaz Makhtar Sarr Amatina solo loll way Yallna yalla faye leu té sammu leu Àre leu mayleu fann wu guddu mayleu khéweul you sawan bawan si barkep Moustapha PSL ❤💙💖🙏
*Jeudi 8 Juillet 2021* Machallah Oustaz Makhtar Sarr Axirou Zaman Bi Amna Solo Lool Sakh Wally Seck Yalla Nako Yalla Sopi Yalla Goudeul Sa Fane Oustaz Makhtar Sarr Amine Allahouma Amine 🤲♥️
Eskeuy contane na si yene trop, vraiment yalna Yalla samlen dolilen yiw bidja i nabiyil Moustapha sala lahou aleyhi wassalam. Vraiment c'est un début que j'apprécie beaucoup et ce genre de débat doit être constamment répétitif pour nous faciliter la conscientisation en nous et la sensibilisation
MAR YACINE MAR WALY YALLA NALA YALLA TAKHAWOU SAM LA MOUSSEUL LEU TER ARAL LA BOPAM 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼💪🙏🏼💪💪🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Waaadji waxna xam xam dh walay ndey sann dieureudieuf sangue bi yalla na yalla doli xam xam bi..ouztaz mom machallah dafa degg datie di jambarr lole te borom xam xam la
Yalla nagnou yalla guena sangue malanou soutou ro,li mane daal tite na ...parceq gnome ILS sont intelligent, doué ...et ils sont courageux,té li guéne wax sé LA pure vérité ils connaissent et maitrisent bien les méthodes scientifiques...
Merci Oustaz Wally Seck kou yapp sénégalais yi laa, l'honneur vaut plus que l'argent
Waly dafa yebate bahoul si senegak
P
Diazakalah khairan
Maasalla, yàl nañu yàlla musël ci goor jigueen, yàl na yàlla sammu ouztas maxtaar saar
Macha Allah Ya Oustaz nous sommes dérriere vous Incha Allah seule la lutte qui libère
Maashaallah Oustaz et l'invité!!! La discussion est très pertinente et instructive! On a besoin de ce genre de discussion sur le fond du sujet avec une vision globale du problème pour élever le niveau du débat et mieux sensibiliser les gens! Qu'Allah SWT vous fortifie!!!
Machaallah
Kou andd ak borom bi do ragal nous somme de tt cœur avec vous
Ma sha Allah gnongui s'en ginaw Oustaz
Ohh ce monsieur il est fort vraiment ce kil di est vrai ma sha Allah
Aouzou billahi minash Sheytani radjim
Soubhanalah thièye Djallah Djalalouhou denke naniou la souniou bopp si barké Seydouna MOHAMMED saw amine ya Rabbi
Mane la Oustaz Makhtar Sarr 🤚🏿
Je suis Oustaz Makhtar Sarr 🤚🏿
Eu sou Oustaz Makhtar Sarr 🤚🏿
YALLAH nalla YALLAH aar sam lá Barkéb SIDY BIRAHIM FALL
Alerte à toutes les femmes de grâce ouvrons nos yeux l'heure est grave alhourane ak sunna rek moy deug chéres femmes bouniou nek ay mounafihoune de grâce chères dames preservons nos enfants contre ces phénoménes soyons les premieres dans ce combat n'acceptons plus ces abominables
Macha'Alla inviter bi liguay wakh amna solo trop mogui may diagual yalla nalen yalla fay amine
Merci beaucoup makhtar sarr
Maacha Allah émission bi amna solo Yalla na Yalla faye lène
Mâcha ALLAH
UN NUMÉRO DE TRÈS HAUT NIVEAU À OUSTAZ ET AU MONSIEUR TRÈS TRÈS BON !!!
Dieurdieuf merci dieurdieuf Oustaz Matare sare Wally diémala sopékhoule moguene thiyawe dieurdieuf merci Oustaz ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
Mashallah am na solo lol sax, yalla nañu yalla défal dégg ak topp, ci darajay Seydina Muhammad (saws).
Mashaa Allah amna solo. Yalna ya Allah SWT défalgnou dég ak top. Ték ndiabot gui ci yonou siratal mustakhim barké Seydina Mouhammad SAW. Allahouma amine
Aameen 🤲🏻
Merci beaucoup oustaz Makhtar Sarr Amatina solo loll way Yallna yalla faye leu té sammu leu Àre leu mayleu fann wu guddu mayleu khéweul you sawan bawan si barkep Moustapha PSL ❤💙💖🙏
Merci Oustaz et Mariama Fall amna solo
Yalla nafi yalla yagal sén takhawaye
Oustaz makhtar Sarr yallana yalla samou
*Jeudi 8 Juillet 2021* Machallah Oustaz Makhtar Sarr Axirou Zaman Bi Amna Solo Lool Sakh Wally Seck Yalla Nako Yalla Sopi Yalla Goudeul Sa Fane Oustaz Makhtar Sarr Amine Allahouma Amine 🤲♥️
Franchement plateau de haute niveau yala na yala Faye y'a oustaz
Machallah oustaz Makhtar sare mala begue yalla nasa diamou yague amine diereudief serigne touba amoul morome
Merci beaucoup.. Oustaz sarr et ses invites..fall est tres pertinent intelligent et intellectuelle... jiajeuf kilifeugui
Dier dief oustaz ❤️❤️❤️🙏🙏🙏💪paré n'a niou pour Lou mou a ndi réck nion koye khare
Bouda kayy Sarr, Yalna Sa Diamm Yagg si Barkep Yoneneta Bi Salalahou Aleyhi Wa Salam !!!
Manchallah Oustaz Makhtar Sarr yallana yalla samoulen té are len
Machaallah amna solo yalla nalène yalla barkèl merci bcp
Oustaz lennn rek MoMA diakhal Lima nekkk extérieur mangi argentine sino folen wottë mango sen wett
Machala oustaz makhtar sarr yalna yalla barkel xam xam bi 💚💛❤
Dieureudieuf serigne matar sarr
Mansha halla oustaz. Kii kham khamm. Bou lerr wakh Fiii yalla mallen yalla diaplé wayy
Eskeuy contane na si yene trop, vraiment yalna Yalla samlen dolilen yiw bidja i nabiyil Moustapha sala lahou aleyhi wassalam. Vraiment c'est un début que j'apprécie beaucoup et ce genre de débat doit être constamment répétitif pour nous faciliter la conscientisation en nous et la sensibilisation
Machalah Oustaz! Deug deug Sénégalais moh nafékk beug nitt ba bou déffé loudoul yoon gua layal ko.
L'invité est très très pertinent merci beaucoup ❤️
Asalamoualeikoum YA OUSTAZ MACKTAR SARR YALLAH NA LA YALLAH DÉFAL DIAM tamou méye là wër akk wërlé ame nasolo sougnou DEUKEU bi mo doy war douniou atté DEUGUE wayé yallah rék moy yallah JËRJËF JËRJËF 🙏🙏🙏🙏
Yalla nala yalla taxawou si barkep s touba
MachaAllah, il est très fort cet invité. Xam-xam ndékété réroul..
YALLAH nalène Yallah faye Oustaz Makhtar ak sa invitè bi ♥️ Yallah na Yallah nassakhal pékheye Sheytané ak ngni kofi togal denke naniou Yallah souniou bopp 🤲
Oustaz on est 100% avec toi khamna ni Sakh do ragal té wolou ngua yalla
Oustaz guirr Yalla dogg yi boulén ko wathie niogui téyé souniou crousse dih khar inchalah ravi
Amna solo loolu waay kilifa yi, yalnalen Yalla fayal boppam🙏🏿👌🏿
Cheikh Madiama Fall est tt simplement extraordinaire je le decouvre avec une pation ... un vrai savant au vrai sens du terme
il est excellen machallah je sui ces emition leral Genth sur RDV
May allah blessed you oustaz 🙏
Aameen🤲🏻
This is why I really like you, because you always tell the truth without fear.
mascha halla merci oustaz moukhtar sarr amatina solo machalla baraka lahou
Ma Shaa Allah Oustaz, avant leur mort et le jour du grand rassemblement ils sauront et verront que tout est vrai,In Shaa Allah...
MAR YACINE MAR WALY YALLA NALA YALLA TAKHAWOU SAM LA MOUSSEUL LEU TER ARAL LA BOPAM 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼💪🙏🏼💪💪🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Diayye n'a ngoreume saytanè
Adouuna diarouka
QU'ALLAH nous vienne en aide parr miséricorde de sa part. Amine
Machallah xol yi sedd na thi yeen
Madiama fall dit Elhadj fall un grand savant que les sénégalais doivent découvrir
Il est vraiment un grand homme qui connaît beaucoup de choses
Bilahi t’as raison frère ✌🏽
machallah ko mat di deglou le il est un grand educateur
@@mbayethiam4696 c mon oncle aka bari xam xam
Vraiment billay bro❤❤❤
Yalna niou Yalla moussal thi ngoodjiguén ! Moussiba bou reuy la! Niéppa ko wara khéekh!
Waaadji waxna xam xam dh walay ndey sann dieureudieuf sangue bi yalla na yalla doli xam xam bi..ouztaz mom machallah dafa degg datie di jambarr lole te borom xam xam la
Merci ya oustaze machallah dieureudieuf 🙏🏿
mersi ouztaz amatinah soloh
Wallahhi Ndéy sane yalna yalla motaly xam xam deg la guis si sagabii allahh
Machalla amna solo
Maa Cha Allah. Èmission bi am na solo.
Ma cha allah Serigne Madiama Fall amatina solo lolou
Ma challah oustaz kaddou yi amna solo
شكرا جزيلا يا استاذ حفظك الله ورعاك ونصرك وطال عمرك مع السلامه وصحة بدن وعافيه في الدنيا والآخرة 🤲
ATALA LAHOU OMROUKA YA OUSTAZ
ما شاءالله جزاكم الله خيرا بارك الله فيكم
ALLAH nous vienne en aide bil moustafa s.w.s
Yalla nagnou yalla guena sangue malanou soutou ro,li mane daal tite na ...parceq gnome ILS sont intelligent, doué ...et ils sont courageux,té li guéne wax sé LA pure vérité ils connaissent et maitrisent bien les méthodes scientifiques...
شكرالكم.فجزاكم.الله.خيراوأيدكم.ونصركم.،،ألاإن.الأولياءالله.لاخوف.عليم.ولاهم.يحزنون.نحن.معكم.
Thieuy wakhtane wi amna solo! Yala na Yala Faye Lène!
Yalla na Yalla samm Oustaz Makhtar, samm wa daara, samm djiko yi.
Yalla yalla fay lann
Macha allah oustaz
Koufi beug promouvait bone dane la wara dénoncer boo deugueuré bopp gnou dall sa kaw! Merci Oustaz gnou ngi ganaw!
Merci Oustaz. Nous sommes de tout coeur avec vous
Merci Oustaz makhtar Sarr ñoo ngi sisa ginaw... Gòor jigèn sa khate
Si kaw çi kanam rk oustaz billahi lislam kou kay défendeur kén doula manal dara billahi wallahi yalla rk mofi négue
Yalla faylen yiw
Macha allah oustaz longue vie rekk seule la lutte libére
Maximum des partages wallahi billahi émission bi Niepp warr Nagne ka deglou té comprendre na yalla Faye lene
Diereudieuf ya oustaz
Yalna yalla tahawoula oustaz mahtar Sarr
سكرا جذك الله خيرا،👍👍👍👍🙏🙏🙏
Gniongi khar in cha allah
Machallah
Merci oustas makhtar Sarr ❤️♥️
yalla na sa diame yage Aminee 🤲👍👍
Bilahi sarr
Maa shaallah Amatina solo Yalla rék mon am sa faye Yallna leu faye si barkep Moustapha PSL ❤
Maguilay nianal dame thi niary bountou yii daradjayy TAHAA YACINE PSL akk barkep seydina cheikh akhmad attydjany rta ❤️
Mashallah am na solo
Macha Allah amna solo diereudieuf
Merci beaucoup ya oustaz
Oustaz yalla nala yalla defal diam
Machalla oustaz yalna yalla borom bi samla samla sa ndiabot
Masha Allah ya Oustaz na tabate yi saff rek gor djiguéne mome tall rek
ويمكرون ويمكرالله والله خير الماكرين 🙏
jazaaka laahou hayran ya oustaze! kou xalaatoul nietti fanou bammeel;loula neeh defal;loula neeh wahal! diinagnou diakarloo ak boroom bi euleuk!
Very important discussion May allah bless you all
Machallah Yalla nala Yalla wereul te takhawoula sa ligueyy am na solo trop
Masha'Allah, wakhtane bii amna sollo loll, que Dieu vous protègent.
Yala nala YALLA sama sama wa andajkoyi walahi loumou lelene diaral diaral nanouko
Jerejef Oustaz yalnala YALLAH Samma
Merci père 🤝✊✊👋👏👏❤❤❤❤👍👍