C’est pas Ameth ton mari c’est le grand frère de Ameth qui était ton mari, donc c’est son frère qui doit prendre la responsable de ses enfants tu na rien na dire à Ameth dou force pour mou defal say dom dara doul way toi
@@aminandong7735 non dou force mom Mai’s dagneko lathi thi yèn diguentè comme k papay Xalei yii dafa nék prison Ameth meunone nalén diapalé rek ndakh li djiguene la meunoul déf lèp
aye way sokhnasi bayil média yi guir yalla li amoul sens Ameth thiou boula topatowoul boulco topoto té nga gnanal sa ndiabote gnou guene thi diaffé diaffé yi mo guene
Niaka topatto mbokk doux crime ameth n'es pas dieu pour satisfaire ayy mbok l'essentiel ils s'occupent bien sa famille proche bayiléne yakk derrre akk manipulation
Bilay tu as raison moi j’ai travaillé dure pour obtenir mais à chaque fois les mbokk ki n’ont rien contribué pour ta réussite c’est eux ki te critique alors tu ne peux pas satisfaire tout le monde
Topato c’est pas matériel, il peut juste prendre son téléphone et prendre des nouvelles ça ne coûte pas grand chose ! Mais je vous comprends vous n’êtes pas habitué à l’argent massa
Desolé sister mais yaw so nékalone AK sa sœur nguéne magandoo mou kheuyy ame dieukeur diabotame nêkeu Thi ay tolof tolof yallah may la weursseuk dingako diapalé Wala Doko diapalé?
C’est à cause d’irresponsabilité de leur papa que s falou est en prison,,guir yalla homme gniéneu gni amlén diom sisén dom yii,,biir balél dinagn lénko lath dé 😢😢
Mane sax rousna nek cii media yii dii werante rek ahmet seuyoul ak iow freram ngadon seuyeul dou force mou diapale say domm bayilen dii guene licii famille
Pourquoi topoto topoto topoto rék ? Topoto lène séne bopou. Wayé dépendance rék, di yaakar si nite gni rék. Motakh homme et femme niépa wara job ba kéneu dou dépendre si kéneu
Béne erreur rk ga défe comme lidieunti woula waro wone toude sakh ameth thiou menone ga yame si sa nidiayou dome la yame si meytou léne media yi dagnou léne di manipulé bon gni gène di tontul ameth thiou mome bo dégué sakh khamni ameth limou léne di défal mo takh bima dégué ay wave la changé vidéo bi ameth da gawantou wo léne pour sétal déram ca devait pas te surprendre béne erreur rk ga défe waro wone douge si détail meytou léne wakhé khol si site yi boula la lidieunti woul bouko lidieunti c'est simple
Ohh Alioune Samb on était ensemble à yarakh il es parti en enseignement par les pirogues kou ame jam yalla nala yalla guéné si khate khate yi Barké Serigne Touba Aliou je suis de tout cœur avec toi
@@myaatraambayee3601bilay waxatiko seytané kharam naniu fékher ba mouhamadou Rassoul laakh ahmadou rassouliaahi dou yone bafay dem . n'est pas mouride qui veut DIEUREUDIEUF CHEIKHUL KHADIM FII DUNYA WAL AKHIRA ❤
Sokhna si ngua balma Alioune samb mi ndek Espagne 🇪🇸 molene diour donc c a lui de s occuper de c enfant Ameth loumou defal khaley dafa fek mou ndekh ko sérieusement sokhna si ngua balma de mais y’a togn ameth thiou ndak. Adouna bi dal metina dal ngua tok étale sa vie familiale nonou gniak diang dal bakhoul savoir vivre zero
Lou séne yone nékoul rek nguéni Dougg famille bi guiss Dina am problème dém léne lidieunti séne famille té bayi ay fénn Di weur Di nétali rek nék léne ay nitt 😢😢😢😢😢😢😢
Sokhna si togne bakhoul. Amet n'est pas ton mari. Diouroul say dom nite dou togne. Bo amer loy wakh wakhko sa bayou dom. Imbécile deug ga togn di yakk nite te sekolene dara
@@amiraniass6428 Ahmet défoul Dara môme magou Amet ladone seyal pa Ahmet Amna ay dome youmou wara topato dekbi Dafa méti meno topato gnép aska Ahmet limou yor doynaco môme ak diabotam ça
Vous titrez que c'est l'ex femme de Ahmed thiou mais c'est pas vrai c'est la femme de son frère cette femme la qu'elle problème elle a avec Ahmed thiou
Nos télé numériques jouent trop ds l'émotion la plupart du temps niom nioy provoquer dioy yii ak sen ndeyssane you bari yii ils manquent de professionnalisme à mon avis
Douleu rek ! Comment peut tu dire un homme qui n’est pas ton mari de s’occuper de tes enfants par force mais ds qu’elle monde nous vivons 😂Sénégal nekhna trop ! Ils faut arrêter! Se que la dame lui reproche n’est pas forcer!!! Tu divorce je sais pas ds quelle circonstances puis guaye tok di yak dèrou niteu! Si y’a un une personne irresponsable c’est bien le père de tes enfants! Arèleu! Ta bien dit daguaye takkeu or ? N’espa donc vend tes or et régle tes problèmes , tu n’est plus mariée ds cette famille donc laisse les tranquilles niak gua classe tropeu
Yalla dou nite 😂😂 di essayer yakh Wally ba thiow li moudiei sur votre propre famille 😂😂😂massa sokhnassi 😂a part sa tu es joli dei tarkala❤🎉 li thi desse souniou yone neikoussi 🥹
Khamnani dall diongoma nga Macha allah
Ndiabot gui yalla nalléne yalla weulbati si yonou ndioub inchallah té sokhna si yalla nako yalla yokou kholou mougne
Ndeyssane wallo ndawssi kou bakh la. Kaylene niou déloko le frère de Ameth thiou ça se voit que elle est toujours amoureuse de lui.🥰😊
Je pense aussi qu elle aime tjours ce Monsieur deysane
Dafa niro ak mam bassine thiam
Commataire bi ladone séte
Mome ladone wakh sama khel
C sa meillieur amie
Ay photo youmou book ak mame bassine la def chambre a couchèm ndeysane
Walahi dioy na beug kén khamoul loumou don Sokhna si yalnala yalla défal diam diaplé la ba délowat la sa brom keur bilay 😢😢😢😢
Mame Asta wallo kéne mounouko trohall Mami seurigne touba leu yallah nalla yallah diapalé❤
En tout cas femme bi kou nitté là MachaAllah yallah nako yallah takhoule diabotame
Amine ya rabi
Thiey yallah ! Lii bane ndieurigne leu am? Bolek manieres you kene khamoul, yalnaniou yallah may soutoureu ak niité ak dieuf yefou niit
Coalition internationale ande déloko AliOune samb je vous salut 😢
C’est pas Ameth ton mari c’est le grand frère de Ameth qui était ton mari, donc c’est son frère qui doit prendre la responsable de ses enfants tu na rien na dire à Ameth dou force pour mou defal say dom dara doul way toi
Linga wax lou nit meuneu dégue leu wayé saga yi rék gnoko yakeu
way way ya gnémé deugue way commentaire bi ladone séte
Wayê nak rafetna so amè say domou makk nga di lènee némékou dontè dou force
Parce que son frère est en prison c'est normal pour l aidé
Manite dé@@ndeyesokhna997
DOMOU XARAME YIII DÉGNOU LAYYY FASSÉ .
FASSÈ WALLÉ SA DOMEU
DIOURRR DOMEU DI SANNII DJIGUENN GNI AY DIAMBARE LAGNOU MACHALLAH SAMA BOKEU GOOR YIII GNO BARRII AY DÉFÉAN AK DOMOU XARAME😢
Billahi walleye yow wahatiko lo lerr nga wakh
*Deugue bou werrr bilay walay*
😂😂😂😂
ndeysan dafa beugeu wadie ❤❤❤❤❤❤❤yalla nalen yalla bolle wate si barki seydina mouhamed ❤❤❤❤
Ces faux journalistes, vous avez détruit les familles, les valeurs et ce pays
Je te jure j'ai dit la même chose
*Je te jure*
Bilahi ya wakh DEUG
Aliou Samb ki begue nala dh déloul ak mom ❤️❤️❤️❤️amour bou sincère la am thi iOw lima dégue ni mbeuguèl la🙏
M quii amul soutoureu qui mome dou diabar t aussi c pas forcé ameth thiou topato ay domame c pas sont marii
@@aminandong7735 non dou force mom Mai’s dagneko lathi thi yèn diguentè comme k papay Xalei yii dafa nék prison Ameth meunone nalén diapalé rek ndakh li djiguene la meunoul déf lèp
Yalla nagnou yalla doli soutoure si barckè seydina Mouhamed psl amine y’a rabie
Amine
Bilahi beug nala trop barker serigne BABACAR sy 😢❤
Soxnasi beuss bou diotaté ci dieukeureum diodiou walay dina seuy lou nééékh, bon courage la belle nirowalè Mame bassine
Massa yalla nala yalla takhawou guéné sa ndiabone yoyou
Ma cherie seuy bou jiekh jiekhna. Wakh ji yep jarouko. Yaral say dom liguey def ci sa bope mogueune. Merci
Ay wayyy bayléne yakanté bi lou wayy wakh guir yala bayiléne mou dialeu tontontébi amoul sens té mbook dafa sacré
Elle est très belle machalla bon courage ma chérie
Vraiment yaw dagua degou Machallah je suis fière de toi brave femme ❤❤❤❤
Ndeyesane. Yalla bahna. Yanalene yalla bolewat.te teguila natou yi yeup. Et ça passera inchallah.
Elle trop brave.beugu n'a ay domame mai des fois domm day niakk diomm.
Massa ma chérie yalla bakhna inchallah dina bakh inchallah dieu est grande 😭😭😭soxna Wallo boul wakhati si media yi tègal lep si lokho yalla sunu borom
La femme là koi kon puisse dire elle est honnête et sincère
Dou force pour Ameth défal la nékoul sa dieukeur
Massa sokhna seuye dafa méti, mougneul té nga dioubeunti sa ndjiaboot Yalla diékhoul
Ameth thiou dousa djekeur balay topato,dou force aussi pour mou topatola nit dal day digne
Sénégal seul pays ou le ndimbeul est force thieuy lii
Kanne mo yorre numéro sokhna gua djokhmako svp
@@adjadiallo1706*wotel thi borom chaîne TH-cam bi bakham*
Damadiomi😂 bilahi forcela
😂😂😂😂 li kay doynawar aide par force
Wally il faut elle est cette dame s'il vous elle est brave et courageux❤❤❤❤
😂😂😂😂😂
Mome dafa jongama sakh Machallah ❤❤
Bayilèn di yakhanté amoul chance 🙏🙏🙏🙏
Surtout si ay mbok. Gni dama yakar werouniou.
Kene khamoul lilane la di werante ni rek cheuteute
Meytouleen Media yi diaxassé ak mbook rek laniou meun yewoulleen waay
Yawe dagua wara régler téh ameu soutoureu
Bilahi nak ni ay dofflen
Merenalleen trop topp sites yi ngua xamni ay vu rek laniouy out di vilipendé sa familles ni
Yallnala yalla soutoural té same ndiabott gui tékléne si yonou siratal moustakhine inchalla bon courage ma belle ❤
Massa ma sœur tu es une femme brave je suis de tout cœur avec toi 😭😭😭😭😭😭
Deysane elle est vrémen sincère pour son amour d enfance
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
L'éducation de basse est très important pour les enfants papa et maman conserver votre mariage
aye way sokhnasi bayil média yi guir yalla li amoul sens Ameth thiou boula topatowoul boulco topoto té nga gnanal sa ndiabote gnou guene thi diaffé diaffé yi mo guene
Merci elle est mauvaise
J'ai les larmes aux yeux, walaye yallah na ALIOUNE SAMB DÉLOSSI THI DIAM balla mo yagu ,guène nèkeu thi diam inchallah
Amine
❤❤❤❤❤❤aaamine 💕
Thiey yalla , yalla ndiaboot lii 😢
Yalla naniou yalla moussal si Djiguén bou amoul soutoura
Niaka topatto mbokk doux crime ameth n'es pas dieu pour satisfaire ayy mbok l'essentiel ils s'occupent bien sa famille proche bayiléne yakk derrre akk manipulation
Bilay tu as raison moi j’ai travaillé dure pour obtenir mais à chaque fois les mbokk ki n’ont rien contribué pour ta réussite c’est eux ki te critique alors tu ne peux pas satisfaire tout le monde
Mais wakh ngua deug ki dou diabaram c la femme à son frère
Topato c’est pas matériel, il peut juste prendre son téléphone et prendre des nouvelles ça ne coûte pas grand chose ! Mais je vous comprends vous n’êtes pas habitué à l’argent massa
@@fatoudiop2933cette femme ne doit meme pas blamer ahmed khaleyi sene baye migui dounde nek exterieur pq blamer ahmed guene balma
@@iboufaye5170 moma diakhal di limou wakh Ahmed mi dafa gniaw trop franchement
Je ne suis pas dacor avec ameth mais c’est pas à lui de prendre en charge les enfants de son grand frère dafcoy nekh rek mou diap thi
Desolé sister mais yaw so nékalone AK sa sœur nguéne magandoo mou kheuyy ame dieukeur diabotame nêkeu Thi ay tolof tolof yallah may la weursseuk dingako diapalé Wala Doko diapalé?
@@fatouba3872 bilahi
@@fatouba3872Mais dou force
Mane d mame walo la gueum .
Wakh dji niaw na nak
Mais on sent que elle dit la vérité 😶😶😶😶😶😶😶😶
C’est à cause d’irresponsabilité de leur papa que s falou est en prison,,guir yalla homme gniéneu gni amlén diom sisén dom yii,,biir balél dinagn lénko lath dé 😢😢
Déja yénako forcé ladj bi lolou la wakh au début bayiléne diakhassé ay mbok 😢😢😢
Mane sax rousna nek cii media yii dii werante rek ahmet seuyoul ak iow freram ngadon seuyeul dou force mou diapale say domm bayilen dii guene licii famille
Femme bi weroul, je croyais que c'est son mari. Qui Moy domeram DEUG loutakh yakh der
Moma diakhal me journaliste bi moko forcé si wakhou ameth thiou
Pourquoi topoto topoto topoto rék ?
Topoto lène séne bopou. Wayé dépendance rék, di yaakar si nite gni rék.
Motakh homme et femme niépa wara job ba kéneu dou dépendre si kéneu
Béne erreur rk ga défe comme lidieunti woula waro wone toude sakh ameth thiou menone ga yame si sa nidiayou dome la yame si meytou léne media yi dagnou léne di manipulé bon gni gène di tontul ameth thiou mome bo dégué sakh khamni ameth limou léne di défal mo takh bima dégué ay wave la changé vidéo bi ameth da gawantou wo léne pour sétal déram ca devait pas te surprendre béne erreur rk ga défe waro wone douge si détail meytou léne wakhé khol si site yi boula la lidieunti woul bouko lidieunti c'est simple
Tu as parfaitement raison
@@princessekounta2538 🤎
Bly yaw
Sama adversaire wa keur gniak diam deugue rek gua wakh nak 😂
Merci nit d'où togne
Ohh Alioune Samb on était ensemble à yarakh il es parti en enseignement par les pirogues kou ame jam yalla nala yalla guéné si khate khate yi Barké Serigne Touba Aliou je suis de tout cœur avec toi
Kou baxone je vous assure
Ani soutoura ay Sénégal yaguouna Bilahi
Wa ki es-ce que werna,tchè amna gnou sagn wakh !!popopo😢🙈
Sokhna si te nga djapeu si yallah mo gueune
YOW YA YAKAR SERIGNE TOUBA ADIOUNA AKH ALAKHIRA .MANNE YALLAH AKH YONENTE BI LAH YAKAR .JE SUIS UN ELEMENT DU PROPHETE (SAW)❤❤❤❤❤❤❤❤
Tout mouride est musulman mais tout musulman n’est pas mourid
Alhamdoulilah sant SERIGNE TOUBA thi barkep MOUSTAPHA
@@myaatraambayee3601bilay waxatiko seytané kharam naniu fékher ba mouhamadou Rassoul laakh ahmadou rassouliaahi dou yone bafay dem . n'est pas mouride qui veut DIEUREUDIEUF CHEIKHUL KHADIM FII DUNYA WAL AKHIRA ❤
DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA
Ameth thiou nak yangui soga am problème . D’où buzz rékk ngadon woutt ak yakk wally légui nak adouna khamnala. Moytouléne togn. D’où dangani doo nopi aythia rékk.
Elle est honnête
Ndeyssan courage Mame walo gueumeul yalla rek lep dina bakh m nak moytoul média tu stp ma belle adouna amoul solo❤
Bayillene sen vie wou famille yinguene di etallé si net bi
Bakhna
Courage ma belle.yalla nalla yalla yapalé
Sokhna wallo je compati vraiment bonne chance 😭😭😭😭😭😭
Niaw wallo wallo bi rek lay topou yalla nala yalla samme arela inchallah amine wally wouyoule mame wallo ta yalla takh 🙏🙏♥️♥️
Ahmed n'est vraiment pas obligé de s'occuper de tes enfants. N'importe quoi.
Yaw nit ngua
God is With you my love❤❤❤ be strong
Mame Walo li mou wakh dou wakou kouye souse wakou nite la ameth kou bone la 😂😂😂wally lalake la kene dou ko tonie
Légui Ameth on lui reproche quoi ?
Thieuy yalla massa yalna yalla bolewate lene vous vous aimez ca se voi
Sokhna si ngua balma Alioune samb mi ndek Espagne 🇪🇸 molene diour donc c a lui de s occuper de c enfant Ameth loumou defal khaley dafa fek mou ndekh ko sérieusement sokhna si ngua balma de mais y’a togn ameth thiou ndak. Adouna bi dal metina dal ngua tok étale sa vie familiale nonou gniak diang dal bakhoul savoir vivre zero
Bilahi
@@mamediarragueye7839dama warou ki weroul
Manko deloo koo alioune samb diotnaa😢😢😢
Nitte kou deugou vraiment yalla nalaa suniu borom soutoural si barke Yonent bi (psl)
Mais mane tourou idaly lat deg? Si 30:00
theuyyy yalla ana soutoura oh
Lou séne yone nékoul rek nguéni Dougg famille bi guiss Dina am problème dém léne lidieunti séne famille té bayi ay fénn Di weur Di nétali rek nék léne ay nitt 😢😢😢😢😢😢😢
Sokhna si togne bakhoul. Amet n'est pas ton mari. Diouroul say dom nite dou togne. Bo amer loy wakh wakhko sa bayou dom. Imbécile deug ga togn di yakk nite te sekolene dara
Manedé lolu moma diaxal
Elle est trés belle ma sha Allah lafthiat
Sokhnasi yagi déf lou gnaw kani alioune samb ga beg mou diour say ndom ba paré ga tok di yak séne wa keur légi dale soutoura amatoul
Sa se vois qu’elle aime toujours son premier mari 😢ndeysan
Limouy wakh ni c vrai
Ki amoul soutoura cou yabou métouco d'où lép lagniy wah
@@coeur2lion38 mes senegal Li Moy problème bi ken d’où wakh Li nek ci Yaw soutoura ba kagne ameth bou beugon soutoura dou déf yen yi
@@amiraniass6428 Ahmet défoul Dara môme magou Amet ladone seyal pa Ahmet Amna ay dome youmou wara topato dekbi Dafa méti meno topato gnép aska Ahmet limou yor doynaco môme ak diabotam ça
@@coeur2lion38 saway Man xamna Amethe thiou bou bakh ki Lep loumou wakh rk Amna lou des
Vous titrez que c'est l'ex femme de Ahmed thiou mais c'est pas vrai c'est la femme de son frère cette femme la qu'elle problème elle a avec Ahmed thiou
Ssi mw qui avais cru que c étais son ex mais plutôt celui de son frère 😢
La femme la bien précisé journaliste gno wakh lou léne nekh c la cousine et l'ex femme du frère de ameth
Vraiment franchement cette dame mougui togne Ameth! Di yak dèèr famille di wakh aye wakhou biraleu du n’importe quoi!!
Elle est très belle... et drole nena faat mbaye kanamam amna ndeyessane
Dafa nob Aliou samb ba legui kii
Billahi wallahi 😂😂😂Nankoko
Dioxarh Mounan ay mbeugeulou xalé dou dégn Fii 😂😂😂Dako nobe Dei billahi wallahi nanko mayath
Billahi walleye yow wahatiko
Ndeysan yalla na lén yalla bolé watt😢😢❤❤❤
Nos télé numériques jouent trop ds l'émotion la plupart du temps niom nioy provoquer dioy yii ak sen ndeyssane you bari yii ils manquent de professionnalisme à mon avis
Ma fille chérie Yalla nalla Yalla diapalé way té baxal sa ndiabott gui. Gorgoroul thi sa dom yi té niom tamite niou am diom diapalé la
Alioune Samb kaye djieul sa sokhna
Une très brave femme yallah na la borombi doli same thi barke alkhourane
Billahi walleye yow wahatiko
Dom Yi niom tamit nen yerem sen yaye🙏🙏🙏
Bene barack la deuk elle a parfaitement raison ameth topa touwoule famille wouma dagni louer rk bilahi
Thiey les journalistes senegalais courage madame
Inchalla dieu et wally seck dilla la dibel li il va t'aider inchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Beugg gaa Aliou Samb en tout cas 😢😢😢
Douleu rek ! Comment peut tu dire un homme qui n’est pas ton mari de s’occuper de tes enfants par force mais ds qu’elle monde nous vivons 😂Sénégal nekhna trop ! Ils faut arrêter! Se que la dame lui reproche n’est pas forcer!!! Tu divorce je sais pas ds quelle circonstances puis guaye tok di yak dèrou niteu! Si y’a un une personne irresponsable c’est bien le père de tes enfants! Arèleu! Ta bien dit daguaye takkeu or ? N’espa donc vend tes or et régle tes problèmes , tu n’est plus mariée ds cette famille donc laisse les tranquilles niak gua classe tropeu
Vérité absolue
Deugg nekhoul nak
moma diahal, non senegal dou réw
MoMA diaxal au début je croyais que Ameth est le père de ses enfants. Mais ko xamni Say parents gni gui doundou tamite
En tout cas daal dou par force...ce n'est ni son mari, ni le père de ses enfants...Sénégal dafa metti....
Massa yalnalenes sounou borom bolewat guenes seybi té barkel senes diabotes.amine ya rabi
Ndeysan 😢 this is real love ❤️
En tout cas sa teint baxna 😌😍
Ki fans nakoo❤❤❤❤❤
Bilahi Walahi Talahi 1er AMOUR dafa fort ndeyssane khamnassi dara YALLAH bakhna😢
C vrai dei première amour kene douko fatei
Bilahi limou wax ay affaire dom xawma si dara mais ay parents wame bene barack lagn nek di louer rk topato wouléne lolou c’est vrai
Hoo neysane habite à guediawaye Bagdad mame wallo c mon voisine mes c la première fois j'ai vu mame wallo mes du courage my sister
Elle l'aime toujours deyssane ❤❤❤
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@@KhadyDiop-gt4fkbonne nga loye réé😂😂😂😂😂😂
Oh ndeysanne diolo guama ndeysanne yalnala yalla takhawou thi barki seydina Mohamed psl yalla bo guiss lo ragale thi sa djaboot bi
N'déysane elle est tjrs amoureuse de son ex mari 😭😭😭😭😭😭😭
Yalla dou nite 😂😂 di essayer yakh Wally ba thiow li moudiei sur votre propre famille 😂😂😂massa sokhnassi 😂a part sa tu es joli dei tarkala❤🎉 li thi desse souniou yone neikoussi 🥹
Wakhal deug yakoul Wally seck dagay doull rekk femme dafay doulll rekk
@@khadimg2078 niapal ndayam feulei ladioumala ok ❌😡❌❌❌❌👎👎👎
Bilahi walahi yalla dou niit
Mayléne nitgni diam Waly seck mo yak bopam Moy seul gor biy sol yeré djigéne Sénégal gor nane lay solé ba large
Louye Wally dou yalla dou yonente
Mame Walo dafa diogama bo khamė sa bopou meun gua ammm dieukeur diou bakh bou ammm tėranga bilay
Qu’Allah assiste les enfants et la famille
Sortie inutile.
Ou le pere de tes enfants ?
Amine