Kawtef😱Fallou Fall la woudiou yayam jine vi0l domou bayam bou am 5 ans, sa grande sœur dément tout

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 24 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 188

  • @abdouldiagne6517
    @abdouldiagne6517 15 วันที่ผ่านมา +107

    Ma pire peur est de mourrir et de laisser mes enfants avec une autre femme.Yalla nagniou Yalla bayek sougnou ndiabote bagnou meuneul sen bop amine.

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 15 วันที่ผ่านมา +5

      *Bilay déhh😢Amenn way🙏🏽🙏🏽🙏🏽*

    • @gertrudecoly8291
      @gertrudecoly8291 15 วันที่ผ่านมา +4

      Amine ya Rabbi

    • @NancyEva-d7l
      @NancyEva-d7l 14 วันที่ผ่านมา +4

      Amine yarabi

    • @falloufall9900
      @falloufall9900 14 วันที่ผ่านมา +2

      Losiy ragal rék louko raw mongi thi ndéysane doyna waar mais yalla guise na lép

    • @princesses4209
      @princesses4209 14 วันที่ผ่านมา +1

      Bilaye amine ya raby barche Mouhammad (psl

  • @sokhnambow2259
    @sokhnambow2259 14 วันที่ผ่านมา +21

    Fallou yalla nala yalla guéné fofou nga nk si barki seydina Mouhamed

  • @AstoubaNdiaye
    @AstoubaNdiaye 15 วันที่ผ่านมา +30

    Yalla mi meune lépp yalla na takhawou fallou Fall mou guéneu fofou

  • @absadiop2563
    @absadiop2563 15 วันที่ผ่านมา +19

    Ndeyssane mettina troppo Yalla diapale ko si barke Serigne fallou Mbacke

  • @salvachachasalomon-bs7fg
    @salvachachasalomon-bs7fg 14 วันที่ผ่านมา +34

    Yalnagnou yalla mousal si diabar bou bonn

  • @milkaciss0896
    @milkaciss0896 2 วันที่ผ่านมา +2

    SERIGNE Fallou yalla nala yalla takhawou guenne la fofou gua nek inchallah

  • @YayeAwaGUEYE-ci2hx
    @YayeAwaGUEYE-ci2hx 15 วันที่ผ่านมา +28

    Taaw bi tamite nélaaw na cheuuuu. Il faut protéger ses petits frères et sœurs 😢. Mais nak bouléne faaté ni Yallah ngui guiss leep ta dafaaay aaaté walahi

  • @mamoubessoum
    @mamoubessoum 14 วันที่ผ่านมา +10

    Il est temps nak parfois gouvernement di audit sur la gestion dans les tribunaux qu'on enquête sur les juges, les procureurs et tous ces gros bras

  • @AichaCasq
    @AichaCasq 14 วันที่ผ่านมา +13

    Ya des femmes sadique trop méchants dieu il dor pas courage les enfants le garçon qui es en prison que dieu lui vient en aide amine merci kalifa

  • @YayeAwaGUEYE-ci2hx
    @YayeAwaGUEYE-ci2hx 15 วันที่ผ่านมา +22

    Fallou Courage. Lou Yallah nara défaar kouko beugueu yakh yaye yakhou. Jiguéne gni daniouy woudié ba woudié AK wa alakhira. Thiéy atté Yallah kouko doul khaalate

    • @buz7755
      @buz7755 14 วันที่ผ่านมา +1

      Deug bou wèr😢

  • @aminatasall2573
    @aminatasall2573 9 วันที่ผ่านมา +3

    Eskey Allah ndeysane 😢😢😢 un jour Dieu va jugé inchallah 😢😢😢

  • @Jubjubaljubanti1137
    @Jubjubaljubanti1137 15 วันที่ผ่านมา +15

    Yalna yallah takhawou Fallou si barke Seydina Mouhamed SAWS

  • @1xbetsenegal304
    @1xbetsenegal304 14 วันที่ผ่านมา +7

    Fallou fall homme de chambre chambre 30 bilay wadiou bakh yerou tey vraiment boko guissé khamni innocent la bilay

  • @TallaDiop-zf7pv
    @TallaDiop-zf7pv 14 วันที่ผ่านมา +13

    Pexey jigeen weesuna lii ci lu ñaaw

    • @mamilabarronnendir5613
      @mamilabarronnendir5613 12 วันที่ผ่านมา

      Li meunanion nèkhal docteur bi fi loounè ngafiy guiss tenta dji bougnouko dimbelè nak juge bi dèfoul dara gnome lignou bind si papier bi rek lagnouy soule ndikou mome tanta dji nimouy dèm tribunal dafa warona and AK policier

  • @salvachachasalomon-bs7fg
    @salvachachasalomon-bs7fg 14 วันที่ผ่านมา +19

    J'ai des larmes aux yeux 😢😢😢😢la méchanceté des gens

    • @bintoudoumbia8955
      @bintoudoumbia8955 13 วันที่ผ่านมา +1

      Ne t'inquiètes pas tout ce paie dans ce bas monde. Adina dou keur Lou way def sa bop. Toumal sa morom nguir sa nafss bakam do dé mouk té doko djiss

    • @sokhnandiayeba5606
      @sokhnandiayeba5606 10 วันที่ผ่านมา

      Sourtout les femmes

  • @MamanDione-m3f
    @MamanDione-m3f 14 วันที่ผ่านมา +7

    Yalla nako yalla maye liberté barke werou kaze radjiab bii barke tourodome

  • @Marième-d6f
    @Marième-d6f 14 วันที่ผ่านมา +2

    Yallah na Yallah até ko ak gniom, Li métina lol😢😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @Salioufall-d6o
    @Salioufall-d6o 14 วันที่ผ่านมา +3

    Fallou yallah nako yallah diapale mou nguen lii dou yoon waay

  • @MaimounaEmich
    @MaimounaEmich 14 วันที่ผ่านมา +6

    Salam ,Kali il faut aider cette Jeune homme si tu peut sil plait merci. Que dieu te benie 😢

  • @ElenaBojic-j7g
    @ElenaBojic-j7g 15 วันที่ผ่านมา +6

    Moo serigne meunna lounè wayè yalla bakhna

  • @buz7755
    @buz7755 14 วันที่ผ่านมา +3

    Pexey jigeen bou bonn weesuna fi😢😢

  • @MaimounaDieng-fz5hr
    @MaimounaDieng-fz5hr 14 วันที่ผ่านมา +3

    Amna djiguene niou doul khalat bamel ak yalla.dome dome rekla😢😢😢😢

  • @saurafall5922
    @saurafall5922 14 วันที่ผ่านมา +2

    Métina trope mai courage fils yalla bakhna

  • @assdiouf1033
    @assdiouf1033 15 วันที่ผ่านมา +11

    Problème Viol bene consultation sakh doyou si Sénégal dafa doywar nit gni dagno bagnate

  • @Humanitaire92-td3vg
    @Humanitaire92-td3vg 14 วันที่ผ่านมา +6

    Salam,
    Svp, les contacts de la femme qui témoigne, c'est pour une assistance juridique ?

    • @1xbetsenegal304
      @1xbetsenegal304 14 วันที่ผ่านมา +1

      Diapalako nio bokone chambre bilay ki innocent yala khamnako

    • @TahiratouBarry-b9d
      @TahiratouBarry-b9d 13 วันที่ผ่านมา

      Contacter kalipone

  • @mariemdibba2027
    @mariemdibba2027 14 วันที่ผ่านมา +1

    Fallou fall yalna la yalla takhawou

  • @khadidiaba5009
    @khadidiaba5009 3 วันที่ผ่านมา

    Yalna souniou borom SWT diapalé bah mou guénate

  • @Marémdione
    @Marémdione 15 วันที่ผ่านมา +2

    Thieye yalla 😢

  • @sokhnandiayeba5606
    @sokhnandiayeba5606 10 วันที่ผ่านมา

    Fallou yalnako bour yallah guéné fofou,yalnako bour yallah atté akk mére bi ak papam

  • @DiagneKaty
    @DiagneKaty 14 วันที่ผ่านมา +1

    Ndeysan ohhhh

  • @CheikhtidjaneSeck
    @CheikhtidjaneSeck 13 วันที่ผ่านมา

    Yallah 'a yallah def diamou

  • @aliousy3143
    @aliousy3143 13 วันที่ผ่านมา +3

    Merci beaucoup la famille de fallou

  • @JarrieJallow-t4c
    @JarrieJallow-t4c 12 วันที่ผ่านมา +1

    salut kally dibalelen guiryala takhawoulene

  • @FatimandaoTymandao-gr4gl
    @FatimandaoTymandao-gr4gl 15 วันที่ผ่านมา +2

    Thiey yallah !

  • @fallkadia547
    @fallkadia547 12 วันที่ผ่านมา +1

    Lolou meneu nék dakh mére bi sou féké da ame loumou tak ou bien gala dieu sou takhawé ak procureur loumou wakh lolou moy nék sama tanta déf nanou même chose wallahi ak samay frère et soeur yallah bakhna inchallah

  • @massambandiaye6150
    @massambandiaye6150 14 วันที่ผ่านมา +2

    Faut pas jugé on a un seul version pour l instant mai yalna yalla safara lép

    • @1xbetsenegal304
      @1xbetsenegal304 14 วันที่ผ่านมา

      Saway ki khamnako boubakh defoul timoul barki yalla

    • @paulclarcksylva
      @paulclarcksylva 13 วันที่ผ่านมา +1

      Saway ki nio fowado jugement j'étais là-bas le dossier médical a révélé que y'a pas de pénétration et l'enfant est vierge comme fofou louthi version pour kham ni li accusation...

    • @massambandiaye6150
      @massambandiaye6150 13 วันที่ผ่านมา

      @@1xbetsenegal304 donc yalnako thi yalla sétal thi barké seydina mouhamed

  • @burr9379
    @burr9379 12 วันที่ผ่านมา +2

    Pa bi kéneu liguéyouko. Payi thi bopam gno beug ndéyou taat ba sank sen ndiaboot. Li moy wakhbi

  • @kadjagaye6530
    @kadjagaye6530 14 วันที่ผ่านมา +5

    J'ai vu ça vraiment ça fait mal trop 😢😢

  • @mamadoundiaye9683
    @mamadoundiaye9683 7 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Yallah nagnou yallah meussoul si nitou chaytané ndakh dagno beuri pékhé trop té niémé yallah amoul lougnou sanioula déf, lou léreu lay wakh ni louma kham

  • @ThianeSarr-om3pg
    @ThianeSarr-om3pg 13 วันที่ผ่านมา

    Ndeye sane Niang ke taye me'tina yanete' yage yage yalla dina ate' aka ame woudiou bonne fallou yalla naka yalla diapale'

  • @khadydiouf3813
    @khadydiouf3813 15 วันที่ผ่านมา +11

    Djiguéne diou bone té doméràme wanté sa dome yi dougnou téķî

  • @RiimaToure
    @RiimaToure 14 วันที่ผ่านมา +4

    Diabar djou bone bakhoul

  • @hawasadio3608
    @hawasadio3608 11 วันที่ผ่านมา +1

    Louye kueur adouna dou dara nite mo ngueuneu fort Lép . Cette femme là doit faire très attention du moment qu’elle a des enfants.

  • @MaimounaCamara-ko3gv
    @MaimounaCamara-ko3gv 14 วันที่ผ่านมา +4

    Wa Sénégal amoul yone bilay li kali naniou ko tope va mbakaner fomou dîner niar nawsi moye domerame pir

  • @haby8760
    @haby8760 13 วันที่ผ่านมา

    On est de tout cœur avec toi Fallou❤

  • @AliouCisse-w9n
    @AliouCisse-w9n 14 วันที่ผ่านมา +1

    Kaly li ki wakh dafa beuri legui nioune âme naniou si ka lou meti la ki Di wakh ni 😢😢😢

  • @natoukoite6205
    @natoukoite6205 4 วันที่ผ่านมา

    Fallou yalla na ko yalla takhawou bamou guénn thi prison bi barké salal laakhou laakhou alaa mouhamed amin lii dawna yaram

  • @khadydiop3591
    @khadydiop3591 15 วันที่ผ่านมา +7

    Li tamite mèttina dhè khawma Senegal kagne lay diak mai qui nèk spagne amoul bèn fouleu il y'a beaucoup d'innocent dans les prisons li doyna war

    • @mariamambodji7604
      @mariamambodji7604 14 วันที่ผ่านมา +1

      Esk diapou niouko mystiquement

  • @FarmataDîop-j5d
    @FarmataDîop-j5d 2 วันที่ผ่านมา

    Sen grand frére bi mo wara construire keur yoboufa ay rakam. lofi déy ci domou jambour yalla faye lako ci sa dom

  • @TallaDiop-zf7pv
    @TallaDiop-zf7pv 14 วันที่ผ่านมา

    😮😮😮😮pexey merbi rek

  • @Gggge_dudiolof9536
    @Gggge_dudiolof9536 15 วันที่ผ่านมา +8

    Ki nek Espagne mom khana dagno ko liguey

    • @unebatante7716
      @unebatante7716 14 วันที่ผ่านมา

      Kham guani dagn ko ligueye

    • @thialediop9431
      @thialediop9431 13 วันที่ผ่านมา

      Li diape papadji doukofi bayi

    • @malickndiaye2804
      @malickndiaye2804 11 วันที่ผ่านมา

      Ki ne Espagne xam nako bou bakh

  • @babaissasarr8617
    @babaissasarr8617 14 วันที่ผ่านมา

    Ndeyesane thiey yalla yalla mou guine

  • @FatouDiedhiou-q8e
    @FatouDiedhiou-q8e 14 วันที่ผ่านมา

    Kaly ya beaucoup de mystique au Sénégal tout est possible..

  • @aissatoudiagne2309
    @aissatoudiagne2309 14 วันที่ผ่านมา +1

    Quelle horrible histoire si les témoignages des 3 intervenants sont avérés! Il urgent d'interjeter appel rapidement et de médiatiser au maximum cette affaire avec les différentes parties concernées (la juge, la procureure, la greffière, les avocats des 2 camps) afin que justice soit rendue conformément au" Jub, jubal et jubanti ".

  • @DakarParisParisDakar2133
    @DakarParisParisDakar2133 13 วันที่ผ่านมา +1

    Jiguenne buh bonne yalla nagnuh si yalla mousseul Je suis femme ayant vécu presque la même chose avec deux femmes différentes mais jiguenne bu bonne su douguer si keur oooh c’est fini

  • @fatoudieng895
    @fatoudieng895 14 วันที่ผ่านมา +2

    Temp wou mack Sall la wonn justice bal so ame bra long akk khaliss lo beugue niou defall lokho cest malleureu😢😢😢

    • @sokhnandiayeba5606
      @sokhnandiayeba5606 10 วันที่ผ่านมา

      Justice bobou mofiii neek bétey,ayy inoçent gno fesss si kaso yiii,reyy guii mélni touli akk malii si 2024 diap début 2025,diaam paaka 2 mois guaa guéneu kaso

    • @SuperOUMZ
      @SuperOUMZ 4 วันที่ผ่านมา

      Verdict bi bi dafa yagoul sakh si ngourou diomaye la di cherie

  • @marindiayegawlo2144
    @marindiayegawlo2144 4 วันที่ผ่านมา

    Yalna gen way li metina trop kalifon japci lo meune

  • @mbayediangue1691
    @mbayediangue1691 วันที่ผ่านมา

    Man dh cas bou mell nonou guiss nako fi souniou kogne khaléyi sénn yaye dafa fatou pabi amatt diabarr Mais diabarr dji def na aye pekhém ba khaléyi guénnu keurr gui niari khalé you gorr ak séni diabarr bilénn pabi guénné fi souniou keurr laniou nékonn Mai legui daniou Louer si kogne bi fi

  • @MohamedKalleDiop
    @MohamedKalleDiop 14 วันที่ผ่านมา

    Ku dégg xamne du dëgg waay jigéen ju bon moo bon rek🤲🏻

  • @mamembaye3365
    @mamembaye3365 14 วันที่ผ่านมา

    😭😭😭😭😭😭

  • @FatouNiang-pk7gx
    @FatouNiang-pk7gx 12 วันที่ผ่านมา

    Bayi Léane ko ak yala

  • @BintaSadio-y9b
    @BintaSadio-y9b 11 วันที่ผ่านมา

    😭😭😭😭😭😭😭

  • @souleymanendao1843
    @souleymanendao1843 14 วันที่ผ่านมา +1

    Avant de juger écoutez l'autre version. Il s'agit de viol et la justice à tranché attention 😮

  • @dialibatoumarahib79
    @dialibatoumarahib79 14 วันที่ผ่านมา +1

    Djigén diou bon day tas keur bahoul thi keur bahoul thi all

  • @ElajGueye-nv7su
    @ElajGueye-nv7su 13 วันที่ผ่านมา

    Souleymane ndene ndiaye diapsi

  • @wanealpha1965
    @wanealpha1965 14 วันที่ผ่านมา

    Massa thiey yallah

  • @syndeye9523
    @syndeye9523 11 วันที่ผ่านมา

    Toi si tu peux te renseigner fait le c'est mieux parce que la maman ne peut pas avoir accès au dossier fait tes investigations pour pouvoir l'aider

  • @Salioufall-d6o
    @Salioufall-d6o 14 วันที่ผ่านมา +4

    Seen makk bi nek espagne mome bakhoul qoui

  • @namaraylingerie
    @namaraylingerie 14 วันที่ผ่านมา +1

    C'est lui qui l'a fait j'en suis sûre car quand c'était moi pendant 4ans presque chaque jour par le frère de mon père et quand je l'ai dit à la gtande sœur de mon père pour qu'elle me sauve, elle m'a traitée de menteuse et m'a dit que je veux détruire la famille. A la fin c'est la femme de mon père qui m'a sauvée c'est pour ça que je l'aime plus que tout

    • @paulclarcksylva
      @paulclarcksylva 13 วันที่ผ่านมา

      Parce que le frère de ton père te faisais la même chose rek tu dis que c'est lui qui l'a fait sans le connaître ni même kham touti ci noumou démé...li yalla boumou dall sa frère wala ko kham sakh...iow guemeu gua ki févaroul Dara diotouko violé rakam boumou bokal béne baye té dossier médical bi affirmé ni ya pas de pénétration et que l'enfant est vierge

    • @MarieNdour-bl9fo
      @MarieNdour-bl9fo 12 วันที่ผ่านมา

      Tu étais témoin ragalal yalla

  • @MaimounaCamara-ko3gv
    @MaimounaCamara-ko3gv 14 วันที่ผ่านมา +1

    Nawsi mo bone da faye docteur bi pour mou takal khaler bou guoor bi

  • @TallaDiop-zf7pv
    @TallaDiop-zf7pv 14 วันที่ผ่านมา +1

    BII BAY XAMUOLNE BIS DINA ÑAW MUODE LUMOY WAX YAYU XALEYII?

  • @Gggge_dudiolof9536
    @Gggge_dudiolof9536 15 วันที่ผ่านมา

    😢😢😢😢😢

  • @safiatousy6249
    @safiatousy6249 13 วันที่ผ่านมา

    da ame ay belle mére you bonne mains yalla bakhna

  • @paulclarcksylva
    @paulclarcksylva 13 วันที่ผ่านมา

    Pour ceux qui disent écouter l'autre version avant de juger il ne s'agit pas de juger li kou andeu ak sa xell xamni c'est impossible dans la mesure où le dossier médical atteste que y'a pas de pénétration et l'enfant est vierge... peut-être problème famille waroul wone égue fi mais kogn ba à l'unanimité kéne guemoul li franchement Fallou nio fowado bokone école défado lépp té diarouma féne mais dniou ko togn mane kérok ba juge wakhé l'enfant est vierge et que pénétration amoul ci lathi paré

  • @modoubambandiaye8714
    @modoubambandiaye8714 13 วันที่ผ่านมา

    Metti na trop waye yalla bakh na

  • @Dieynaba-qj6pq
    @Dieynaba-qj6pq 14 วันที่ผ่านมา

    😭😭

  • @MoreMbaye-i6y
    @MoreMbaye-i6y 13 วันที่ผ่านมา

    Faut le dire justice Sénégal bi nio defoul sén liguey dax je peux pas comprendre gua teudie nitt ki sans preuve lolou Sénégal rkk la am

  • @ndiagsgalsen6383
    @ndiagsgalsen6383 12 วันที่ผ่านมา

    Yala nagnu yala mousal si djiguen bou bone😢

  • @khadysow5105
    @khadysow5105 13 วันที่ผ่านมา +1

    Ki kou bonne la kaso keneu douko yeneu keneu

  • @khadydiouf3813
    @khadydiouf3813 15 วันที่ผ่านมา +2

    Même bougnou défé appelle khalé Bou guore bi na guéne keur yalla dana léne atté mére bi domérame la

  • @sokhnambow2259
    @sokhnambow2259 14 วันที่ผ่านมา

    Tanta yalla djiss nala dh xana danga yakarni do dei

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 14 วันที่ผ่านมา +2

    Thiéye kalifone légui dall limoy sa liguéye 🙄🤔😒 leufeul ndayi li rék😢😢 il devenir un Adamo 🥹🥹🥹

  • @DiarraFall-xs4xg
    @DiarraFall-xs4xg 12 วันที่ผ่านมา

    Nagne ko wakh ngour gui mou diappalé kondakh lii dou yon méti nama trop souma amon dolé gnou kham

  • @CouraCissé-w5m
    @CouraCissé-w5m 15 วันที่ผ่านมา

    😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @diarrasaliouniass7145
    @diarrasaliouniass7145 15 วันที่ผ่านมา

    😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @madialendiaye6789
    @madialendiaye6789 15 วันที่ผ่านมา +1

    Yombana DH mer

  • @TallaDiop-zf7pv
    @TallaDiop-zf7pv 14 วันที่ผ่านมา

    Lii mette jna lool

  • @korkafametmaguettefam9983
    @korkafametmaguettefam9983 12 วันที่ผ่านมา

    Amneu gnou sohor d!!!!!!!aduna dou keur bahneu dal

  • @amethngom7873
    @amethngom7873 11 วันที่ผ่านมา

    Niéuwlénn dahra djolof

  • @Abdou72Ndeer
    @Abdou72Ndeer 14 วันที่ผ่านมา

    Seenn papa dji mo.mataddi?

  • @TallaDiop-zf7pv
    @TallaDiop-zf7pv 14 วันที่ผ่านมา +1

    JIGÈN JU BAX BIDE SÈY FEK AY XALE CIKÈR BULEN XEEX LII ÑAWNA DEMETTI

  • @NabouMbye
    @NabouMbye 14 วันที่ผ่านมา

    Haley b mann na am daga daga wayeh yay ji man nako dugal sochu

  • @nenessakho6717
    @nenessakho6717 14 วันที่ผ่านมา +1

    Yala na kaka yala faye si aye domame limou lébal domou duambour yi

    • @ThionDieng
      @ThionDieng 10 วันที่ผ่านมา

      Aminn

  • @thereselissire840
    @thereselissire840 14 วันที่ผ่านมา

    Kali pour maan li weur ba weur moy niou convoqué délégué de quartier bi ak chef de quartier bi niou cdé liii wala niou djeul xalé bi dièmko latié baham

  • @ndeyemaguattediop6242
    @ndeyemaguattediop6242 2 วันที่ผ่านมา

    Fotohe de fatima diang sa data yaya 🐖🐖🐖💔💔💔💔💔🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🐕🐕🐕

  • @Salioufall-d6o
    @Salioufall-d6o 14 วันที่ผ่านมา

    Liii dafa niaou sakh bilahi

  • @moustaphaaliounediawara4301
    @moustaphaaliounediawara4301 15 วันที่ผ่านมา +3

    Moh mokk legui da ngay warou

  • @ToureabdoullToure
    @ToureabdoullToure 14 วันที่ผ่านมา +1

    Ana bénén version bi bou mére bi la beug dég

    • @paulclarcksylva
      @paulclarcksylva 13 วันที่ผ่านมา

      Frère dossier médical bou affirmé ni pénétration amoul té xalei bi amna virginité ba légui version mère bi dakh diarna dégue lou pour khamni li c'est monté de A à Z....je te rappelle jour jugement j'étais là-bas

    • @MarieNdour-bl9fo
      @MarieNdour-bl9fo 12 วันที่ผ่านมา

      Esceque sa va

    • @ToureabdoullToure
      @ToureabdoullToure 12 วันที่ผ่านมา

      @MarieNdour-bl9fo shut up

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 13 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Tatou mak sak sojoy oubi chaque instant diko woné apres dafay am ay déchirure

  • @papathiam87
    @papathiam87 11 วันที่ผ่านมา

    Senegal dangaye xol niit nexoula gua sossale teudje...les juges sont nuls et Corompus