Mashallah am na solo. Yallah sakh mourid la. Ndax da nam niou khamko/ wala da nam khame mou bind. Kone yallah mo njeuk tokk si nam. Da beug xam beug xame. Donc nit famou djougue sori na.
Saway uoe soumil sa baye late bi dag sa rasta yi fèhèl nak yam sisa moussa ndiambè tè bayi yonou mourid yèn sèn serigne Serigne Abdou Late guènèko Touba Bèn Talibè Serigne Touba boula bayi khèl xamoul diokhon kon Bayil yonou mourid bingay lakko
Yaw yagui wedi yalla ndakhe yalla nena loudieunk yonetoubi si ak rére la wa makka nekone wa inkano min khaplou lafi dalaline moubiine boulenfate ninak diouli ak koor ak asaka filako sala lahou hanlayhi wasalam fenk
GRATITUE ET BENEDICTION DIEUWRIGNE NDIASSE 💖💖💖
Aka dégg 🙏🏽❤️
Sallalahu Alayhi wa Sallam ❤
Alhamdoulilah ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashallah am na solo. Yallah sakh mourid la. Ndax da nam niou khamko/ wala da nam khame mou bind. Kone yallah mo njeuk tokk si nam. Da beug xam beug xame. Donc nit famou djougue sori na.
❤❤❤❤❤
Euskey ❤
👍🏻👍🏻👍🏻
Est Nay(avare) et épargne sont liés ?svp
Saway uoe soumil sa baye late bi dag sa rasta yi fèhèl nak yam sisa moussa ndiambè tè bayi yonou mourid yèn sèn serigne Serigne Abdou Late guènèko Touba
Bèn Talibè Serigne Touba boula bayi khèl xamoul diokhon kon
Bayil yonou mourid bingay lakko
Wadji wakh daye rafet, waye nit loumou am rek lay diokhe. Khana bala nioula guene dagua fay deuk. Kou deukoul wone touba nouniou lay guene. Ma ladj la , comme dano geunewone cheikh Moussa , alors kone serigne Mountakha lane larone deff Darou? Pourquoi aussi chaque annee mou djeul adiya wakeur Cheikh Moussa.

❤❤❤