Salam dama gént nekk ci auto ak sama borom keur. Man maay dawal moom mou mel Mei day wax ak man di may diokh direction. Ma guentat si même goudi gi sama borom keur diokh ma lou mel ne tànku xarou yapp bou gnoroul di am loum ma siy wax. Day mel ne dama ni tekk Waaye maa ngi bayi xel pour xam li miy wax pour Comprendre ko.
Serigne djily dama listikhar goudi teude guisse gnari auto bou wekh ak bou bleu de nuit
Macha’Allah dama guente di guiss auto you rafét loll
Bektela
❤❤
Salam dama gént nekk ci auto ak sama borom keur. Man maay dawal moom mou mel Mei day wax ak man di may diokh direction.
Ma guentat si même goudi gi sama borom keur diokh ma lou mel ne tànku xarou yapp bou gnoroul di am loum ma siy wax. Day mel ne dama ni tekk Waaye maa ngi bayi xel pour xam li miy wax pour Comprendre ko.
Cheuuuu
Salam soudé taga geunte and ak kiga beuge dougou si oto nk
Lolou bakhna machallah yalla meuna def mou doone sa dieukeur wala diabar inchallah
Salut Déma guénete nék ci auto di yor sac comme un voyage mai déma tahaw nak togouma ci sége firélema pardon