A toute la jeune Tidianes archivons cette vidéo et prenons conscience de l'importance des leçons de cette homme. Barak'Allah fiik Ya Cheikh ❤️ Amouniou sa fay FALL🙏❤️
Bo amoulwone xam xam xawma founou dieum Fall. Vous êtes doté d'une clairvoyance Rare et d'un potentiel pédagogique inouïe. Qu'Allah vous rétribue au centuple Bijahi Rassoulilahi SWS barké Cheikhou Tidjanii RTA.
Merci Serigne Hamad dame fall thi layer bir bi nguene nianal ma ma done deugue deugue djoulit deugue deugue talibe cheikh damay soga djieul tariha bi bess yagoul alhamdou lillah
Invité na nieupp si conférence bimou wara df le 26 mars 2022 à Diender, thies, Sénégal 🇸🇳 animateur bi di cheikh tijan mbaye Thème: yonente bi sws lay waxtané inchallah yalnagnu si yalla yobou si barké yonente bi sws
Tabarakallah Serigne Fall di gnane Bour Yalla goudal sa fann defal la wer te sam la .Cours yi dieurigne yokoute ak mbekte rek la . Vraiment Dieureudieuf 🙏💚 di khar suite bi .
Merci beaucoup serigne Ahmad fall yalla na yalla faye leu yiw thi leeral yi 📿❤️🤲Aminé mais man daal soumay deglou👂say wakhtane Wallahi dafay melni man kesse ngay wakhal yalla kham nako😥😢
Maa Shaa Allah Serigne Ahmad Fatabaraka’LAHU Akhsanul Khalikhine. Nek tidiane yomboul ndeketer.Magui dora comprendre gar yi di dinguate euhlou Soufianker yi. Ndeketer danio tokher , 😂 danio dem dem sene yaram sene roukh tayi ndeyssane. C’est de l’endurance de la patience. Yalna Buur Yalla dafniou deugui taliber Cheikh Abul Abass. Jerejef Seydi
MAACHA ALLAH. Nous avons bien suivi la vidéo. Alhamdou lil Lah nous espérons avoir bien compris. QUE le BON Dieu fasse que nous soyons parmi ses protégés dans la Tarikha CHEIKH AHMED AT TIDIANE bijayi Mouhamed Rassouloul Laahi Salla Laahou Aleyhi. Yalla na Yalla fayal ñu la ngeun gui pay zahiran wa baatinane
Assalamou aleicoum ya seydi dila ziar dila ñanal barké cheikh Tidiane rta Nous les élèves j’attire notre attention à savoir nañouko deglou té topato ñangue mi té bayi sax suggestion yi car il le dit souvent ya une équipe derrière lui et ça s’entend qu’il y’a de la réflexion donc deglouko ñanalko rek Ma ngui diegueulou Salam a tous
Yalna ñu Boroom Def Taalibé Cheikh dëgg. Jazaakal Laahu qayran sama sòppe Serigne Ahmad Fall.
A toute la jeune Tidianes archivons cette vidéo et prenons conscience de l'importance des leçons de cette homme. Barak'Allah fiik Ya Cheikh ❤️ Amouniou sa fay FALL🙏❤️
C Sow Attidiany oubien
@@mamadouanneka1730 Celui de Tik-Tok? Non non
@@mouhamedsow221 ah okay
Machalla maximum de partage rék amna solo
0et et 000000
Bo amoulwone xam xam xawma founou dieum Fall. Vous êtes doté d'une clairvoyance Rare et d'un potentiel pédagogique inouïe. Qu'Allah vous rétribue au centuple Bijahi Rassoulilahi SWS barké Cheikhou Tidjanii RTA.
QUEL IMMENSE BONHEUR DE VOUS ECOUTER❤️❤️❤️ BOUR YALLAH FAY YIW❤️JEUREUJEUF
Un pure bonheur !!!
Heureuse de vous connaître et la vous écouter vous étes une fierté de la tariha tidiane yalla n'ala bourbo yalla sam te fayla
I
Sma sopè ya oustaz ya tahe demouma entraînement direct bi rek ladone harr
Wallahi ndaysanne ya wakh deugeu dii 🤣😅🥰
@@ibrahimafall855 un tu
@@ibrahimafall855 pl
Machala oustaz ahmed fall nongui fedali sounou thiofele si yawe
Merci Serigne Hamad dame fall thi layer bir bi nguene nianal ma ma done deugue deugue djoulit deugue deugue talibe cheikh damay soga djieul tariha bi bess yagoul alhamdou lillah
Invité na nieupp si conférence bimou wara df le 26 mars 2022 à Diender, thies, Sénégal 🇸🇳 animateur bi di cheikh tijan mbaye
Thème: yonente bi sws lay waxtané inchallah yalnagnu si yalla yobou si barké yonente bi sws
SALLALLAHOU ALEYHI WA ALIHI WA ASS HABIHIL AKHYAR WA ZURRIYATIHI WA SALLIM TASLIMAN KATHIRAN KATHIRAN KATHIRAN
Machallah serige Ahmad fall yalla na yalla godalle sa fan mayla wer sy Barker si Barke serige babacar sy amine 🙏🙏
Serigne yalna yalla goudeul sa fane may leu wér ak werlei si barkei Sangue bi 🤲❤❤❤
SALLALLAHOU ALEYHI WA ALIHI WA ASS HABIHIL AKHYAR WA ZURRIYATIHI WA SALLIM TASLIMAN KATHIRAN KATHIRAN KATHIRAN
Cheikhou tijani ♥️♥️🥺🥺🥺
Wallahi Serigne bi machallah ❤
al hamdoul lillah diangate nafi lou bary ci sama diganté ak chartes
tarikha bi yallah nala Rabou Raby samawaty wal ardy fay goudal fann té am diam
Tabarakallah Serigne Fall di gnane Bour Yalla goudal sa fann defal la wer te sam la .Cours yi dieurigne yokoute ak mbekte rek la . Vraiment Dieureudieuf 🙏💚 di khar suite bi .
❤❤❤❤❤❤Kène Dou CHEIKHOU TIDIANI
Māchā Allah dieureudieuf Professeur. J'aimerais vraiment que s'ensuive la traduction en wolof de la diawharatoul kamāl.
Serigne Ahmed fall on te souhaite une long vie pleine de bonheur ❤ 🤲🤲🤲❤❤❤❤❤❤❤
Walahi cheikh ahmed fall tu es un dont de Dieu pour nous 🙏🙏😍
Machala serigne Oustaz Profesor Ahmed Fall yalna yalla barkel xam xam bi barkep Taha Sws ❤❤😍🥰🤩
Beug nala té yalla lk takh wallahi azim yalna yalla goudeul sa fane méyla wérr Baraki Taha Rassoul Saw Amine ya rabbi 😇
Merci beaucoup serigne Ahmad fall yalla na yalla faye leu yiw thi leeral yi 📿❤️🤲Aminé mais man daal soumay deglou👂say wakhtane Wallahi dafay melni man kesse ngay wakhal yalla kham nako😥😢
2 ans après,
On est là ❤
Merci beaucoup Serigne Ahmed Fall At Tidianiya,
Yalna yallah yokk sa xaam xaam masha'Allah😊❤
Cette vidéo est d’une importance capitale!!!
qu'Allah vous donne des palais au paradis encore merci que tes enfants vous suivent vos pas et aide nos enfants et qu'Allah leurs donne une longue vie
Surtout lolou
Amine ya rabbi 🤲🏾
Allahou Akbarrr
Alhamdoulilahi
La hawla wala houwata ila bi lahi
Dieureudeuf Serigne bi
جزاكم الله خيرا
Dieureudjeuf serigne ahmad yalna yalla fay yiw diangalé yi amna solo lol vraiment amouniou sa fay
زادكم الله خير ا العافيه في كل مكان و في كل شي حيياكم الله حياه طييبا
Alhamdoulilah thie beug Cheikhou Tidjaani, Alhamdoulilah thie dadiéég niou mélni Serigne Ahmed Fall, Oustaz Hady Niass, Oustaz Ahmed Ba, Oustaz Aboubacrine Atijiaani...soldaarou CHEIKH laalen toudé MachaAllah
Macha'allah contane naniou yalnala yalla tahawou ci lep Inch'Allah ci barkei salatoul fatihi
Jeureujeuf hadj cheikh mouhaddam Serigne Ahmad FALL
Dieureudieuf Serigne Oustaz Ahmad Fall AT TIdjany 🙏🤍
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته اخوكم في الله بب انياغ امباكى جزاكم الله خيرا يا استاذ ورعاك وحفظك من كيد الكائدين وظلم الظالمين وشر المعاندين ءامين
MashaAllah, dieureudieuf Ya Seydi Ahmad, Yalna Buur Yallah swt feyal gnoula! Amiin ❤️
جزاك الله خيرا يا أستاذ
dierediefe serigne ahmet fall kham kham bi ler'na rafetna machallah
Machallah Serigne Ahmed fall yallana yalla yok xam xam bi
Sa diangalé amatina solo jerejef waay Yalla na Yalla doli leer 🙏🙏🙏
Machallah sangeu biii lerrr na dh yalla nala Borom bii fay
Amna solo Fall Yallah na la Yallah fay yiw
Si je l'écoute rekk
Damay beugg yeslou encore
Machala Serigne daara jazaka lahu khayra
Merci Oustaze
ALLAHU AK BAR LAHILAHA ILLALA MOUHAMMADOU RASSOULOULA SAWS
Machalla niogui tewlou bou bakheeee
Djazakoumou Lahou khayran Ya Ouztaz
Walahi wahatiko Machallah Machallah ya oustaz longue vie à toi je t'aime tellement ❤❤❤
جزاكم الله خيرا
Wallaaaaaahiiiiii♥️🥺♥️♥️♥️
Allahou akbar hana koula diglouwoul waaYé koula diglou Møu doY seuk 😥🥰🥰❤️🙏❤️
Quel pédagogue yala nala borom faye serigne hamed fall
yalna bour yalla fayla mayla goude fane ak weer yalla samla barké seydina mouhamed s.a.w ourmati chekh tidiane rta
Maa Shaa Allah Serigne Ahmad
Fatabaraka’LAHU Akhsanul Khalikhine.
Nek tidiane yomboul ndeketer.Magui dora comprendre gar yi di dinguate euhlou Soufianker yi. Ndeketer danio tokher , 😂 danio dem dem sene yaram sene roukh tayi ndeyssane. C’est de l’endurance de la patience.
Yalna Buur Yalla dafniou deugui taliber Cheikh Abul Abass.
Jerejef Seydi
Machallah outaz yalla na la bour Yalla fayal bopam
Machallah ya oustaz kabir
❤❤machalah yalnanou cheikh nangoul sougnou talibé ❤té yalla fae lene yiw amna solou ❤
Machallah ya oustaz yalla na yalla fayal niou la thi barke seydi cheikh Ahmed tidiane chérif
MashaAllah ❤❤❤Xol seidna
Man sha Allah Oustaz merci pour le rappel
Machalah meilleur vidéo dans TH-cam
Serigne sope nala té beugue nala guisse guir dieumi Cheikh Ahmada Atidiani
On l'attend impatiemment
aka barie kham kham machallah
Yalna yalla fayla ligua ligua beugue ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha'ALLAH
Que le tout puissant vous protège merci je viens de tomber sur la vidéo merci pr les éclaircissements
Alhamdoulilah ❤🧡💛
Machalla amna solo
Machallah sa liguey rafet na trop ndax jeune yi nio guéneu sokhla yéwou
Yalla na yalla doli sa diamm
ماشاء لله يا أستاذ
Tawfekh ak taïssir bour yalla déf ka si ioe incha allah
MAACHA ALLAH. Nous avons bien suivi la vidéo. Alhamdou lil Lah nous espérons avoir bien compris. QUE le BON Dieu fasse que nous soyons parmi ses protégés dans la Tarikha CHEIKH AHMED AT TIDIANE bijayi Mouhamed Rassouloul Laahi Salla Laahou Aleyhi. Yalla na Yalla fayal ñu la ngeun gui pay zahiran wa baatinane
machallah Yanala yallah faye thi barker cheikh rita beugonna yeslouwat thi yaw inchallah 🙏
ماشاء الله تبارك الله ❤️❤️
Serigne darra beugue nala
Sama serigne Daara Ahmed Fall Attidjany
Partager la vidéo; pour que tout le monde puisse être informé
Machallah yallah na yallah barkel xam xam bi
Yalla na yalla goudal sa fane may la wér barki cheikh tidiane rta
Machallah un pedagogue hors norme !
Dieureudieuff oustaz
❤❤❤❤
Chéikhou tidiane chérif❤📿
Wallaye ndaye san ❤️❤️❤️💯💯
Macha Allahou
Machalla Cheikh Ahmed Fall
Assalamou aleicoum ya seydi dila ziar dila ñanal barké cheikh Tidiane rta
Nous les élèves j’attire notre attention à savoir nañouko deglou té topato ñangue mi té bayi sax suggestion yi car il le dit souvent ya une équipe derrière lui et ça s’entend qu’il y’a de la réflexion donc deglouko ñanalko rek
Ma ngui diegueulou Salam a tous
Masha ‘Allah❤❤❤ 22:17
Machallah amna solo yalna yalla fay la inchallah
Mashalah🙏🏾
Emission bi am na solo trop on nattend la suite inshala
Machaa Allah Mudir ❤❤❤❤
Ma Sha Allah fall ❤️❤️❤️❤️
Mashallah
MashAllah MashAllah
Jërëjëf serigne bi 🙏❤🙏
Machahala 🥰🥰
Machaallh serigne ahmed fall
Macha Allah Serigne
Barakalawou fika
Machallah amatina solo