Introduction au Wird Tidjaane - Partie 1 - Serigne Ahmad Fall

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 15 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 180

  • @NdeyeAstouSOUMARE-k5e
    @NdeyeAstouSOUMARE-k5e ปีที่แล้ว +8

    Maguui ziarrr lou beurre serigne ahmed fall ..ak toute l'équipe vraiment cette page enseignement bouh Mashallah j'en apprend beaucoup yalna yallah faye la thi barke Cheikh Ahmed Tidiane Chérif ❤❤❤❤

  • @daoudathiaw
    @daoudathiaw 2 ปีที่แล้ว +61

    Ma shaa Allah, jeurejeuf yaa Oustaz. Tu peux porter autant de montres que tu veux car tu nous donnes l'heure comme peu de gens savent le faire, un véritable maître des horloges ! Aladji nak, faut que mou fegn. Yallah na bour yalla fey lène yoke xam xam bi aar lène Amine

    • @habibatoufadiga6417
      @habibatoufadiga6417 2 ปีที่แล้ว

      Pppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppppp

  • @tivaouanetvsunnahakhalquran
    @tivaouanetvsunnahakhalquran 2 ปีที่แล้ว +38

    Wallahi anzim Djeureudjeuf Wallahi anzim Djeureudjeuf
    Un professeur un guide spirituel un visionnaire un émérite dans son domaine, un maître hors pair et conscient des enjeux de la société sur le côté temporel comme spirituel
    Yaaw lagnouy deglou Serigne Ahmad ♥️yaa djoubaal nitt gnii , yaa talaat safara thiofeel si xolou nitt gni, ya nou guindiii , deglou wouniou kennn té douniou tarder naakh sa mission dafa waar weeuy .
    Yalna Allaah taxawu lenn incha allaah si barké yonente bi ax cheikh tijani rta.
    Djeureudjeuf Serigne Ahmad At tijani ♥️
    Yaaw laaniouy deglou , yaaw laniouy rooy , xool yi fessal nguakooo . ♥️moudjahid piiir ngua , Tivaouane dilaa saggooo Cheikhou Tijani dila saggooo, kouy sopper dila saffoooo
    Bonne continuation

    • @fatouseck5364
      @fatouseck5364 2 ปีที่แล้ว +3

      Vous avez tt dit ma sha Allah yalna yalla goudeul ay fanam yok kham kham bi

    • @tivaouanetvsunnahakhalquran
      @tivaouanetvsunnahakhalquran 2 ปีที่แล้ว +2

      @@fatouseck5364 Amine incha allaah
      Vraiment amounu fayaam
      Niaan akk topp ayy orientation yi mougnouy diokh rekk laagn fi desser

  • @layely7613
    @layely7613 2 ปีที่แล้ว +15

    Bilahi Serigne bi amna nivo xam ga ni Aladji mounkoy tek si axe té monguikoy deglou aisément sans frustration si diam ak xol bu sed Mach allah tay accepter nak merci oustaze lep si diangalé bi

  • @csts-im7jf
    @csts-im7jf 2 ปีที่แล้ว +6

    Dieureudieuf quel modestie ya oustaz
    Votre dimension est tres haute.vous êtes une référence pour toute une génération. Walahi seydina cheikh tidiane mola mana fay. Alkhamdoulilah

  • @iboundoye1228
    @iboundoye1228 2 ปีที่แล้ว +33

    Je suis tellement captivé par VOTRE DISCOURS que je m'attarde très peu sur le paraître. Qu'ALLAH vous garde en Paix

  • @ibrahimakhalilebaattidjian3953
    @ibrahimakhalilebaattidjian3953 2 ปีที่แล้ว +5

    Alhamdoulilah Di sant bour yallah si xeweul gou reuy gui mougnou defal tay gnanal Serigne Ahmed fall yalana ko bour bi takhawou té deugeureul takhawayam si barkel cheikhana aboul abassi ahmada tidjiani

  • @deugguitv2564
    @deugguitv2564 2 ปีที่แล้ว +19

    Machala Serigne Oustaz Profesor Ahmed Fall ATTIDIANI yalna yalla barkel xam xam bi barkep Taha Sws 😘😘🥰😍

  • @fatouseck5364
    @fatouseck5364 2 ปีที่แล้ว +15

    Ma sha Allah Fall on a toujours hâte de suivre vos cours yalna yalla goudeul fane wi yok kham kham bi ak wer gui barké sangou sangue yi SAWS barké Cheikhouna Tidiane RTA souniou serigne

  • @galykane5382
    @galykane5382 2 ปีที่แล้ว +17

    Gnakk kham Cheikh Tidiane Chérif erreur leu 🎉❤

    • @khalifathiam8706
      @khalifathiam8706 ปีที่แล้ว

      Meunouniouko xammm dh lolou momassi diaxal

  • @badiewo973
    @badiewo973 2 ปีที่แล้ว +14

    Sunu oustaz namone nagnou là je vous écoute religieusement di ziar gneup 🙏💚

  • @papendoye5867
    @papendoye5867 2 ปีที่แล้ว +13

    Serigne bi sopenala yalla khamenako yalla na yalla fayela barkep Cheikhouna Tidiani rta 🙏🏿♥️

  • @oumarmboup1216
    @oumarmboup1216 2 ปีที่แล้ว +7

    Sounou oustas loo def bakhna barke cheikhou tijaani

  • @soa9211
    @soa9211 2 ปีที่แล้ว +41

    Oustaz boul déglou Aladji mi, kii aada lala beug doundlo, opinions nitt gneupp koulén beug déglou dangay moudiou nekk otage niko Serigne Cheikh Al Maktoum dane wakhè. Boul ragal nitt yi dila khass wala dila raddou, l'essentiel moy nga xam sa mission té dioublou ci.

  • @cheikhoumardeme293
    @cheikhoumardeme293 7 หลายเดือนก่อน +1

    Barakallahou fikoum ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @baitydiop6363
    @baitydiop6363 ปีที่แล้ว +1

    Machalla yalla yokh xam xam bi

  • @ahmadousih
    @ahmadousih 4 หลายเดือนก่อน

    Serigne Ahmed yallna yalah faye ya barké cheikh..... contane nagn si leçon yi

  • @sokhnarokhayasane1537
    @sokhnarokhayasane1537 ปีที่แล้ว +2

    Asalamou Aleykoum dieuredieuf ziarra nala MachaAllah dieuredieuf mbokk talibe Yallah na Yallah feeye Amine Amine Amine 📿

  • @deuggeurek1013
    @deuggeurek1013 2 ปีที่แล้ว +6

    Merci pour le débat sur l’éducation!
    La racine du mal moy la laïcité. Waax lène si aussi 🙏

  • @mathioyendiaye1037
    @mathioyendiaye1037 2 ปีที่แล้ว +3

    MashAllah Seuñ Ahmad Fall Djeureudjeuf YAllah Buur bi fayeleu Yiww , Gueureum nagnoula dehh YAllah xamnako 🙏🏿

  • @ousmanediallo8972
    @ousmanediallo8972 2 ปีที่แล้ว +3

    Ma sha Allah ya Seydi Cheikh Ahmad Fall yallah nala yallah fay yiw

  • @mamadoumbaye9872
    @mamadoumbaye9872 2 ปีที่แล้ว +5

    Namon nla dh Walay ndeysan

  • @Abdsr8735
    @Abdsr8735 2 ปีที่แล้ว +4

    Que d'enseignements !!! Merci Serigne Ahmad Fall et ton équipe 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾!

  • @fadelfall6813
    @fadelfall6813 2 ปีที่แล้ว +3

    Manchalla ya seydi boule déguelou béne détracteurs.figua ték sa lokho fofou la yalla nagnou borom déf aye talibé cheikh Ahmad tidiane Chérif woumou naguoule sén talibé 🙏🙏

  • @issakhagueye1367
    @issakhagueye1367 2 ปีที่แล้ว +4

    Walay ndeyssane machallah

  • @assanediop6285
    @assanediop6285 2 ปีที่แล้ว +3

    Assalamou aleykoum Serigne Ahmad fall yallah na la bour yallah Faye si temps bi ngay def pour seddo AK gnoune xam xam bi

  • @assanendiaye295
    @assanendiaye295 2 ปีที่แล้ว +4

    Serigne Ahmed fall diarama❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @hadjarandiaye2861
    @hadjarandiaye2861 2 ปีที่แล้ว +2

    Niane bi avant wird nékh na trop dieurédieuf S Ahmed fall yalna la yalla faye.

  • @mouhamedthiam6814
    @mouhamedthiam6814 5 หลายเดือนก่อน +1

    Yalna yallah barkel

  • @babacarndom8308
    @babacarndom8308 2 ปีที่แล้ว +2

    encadrement bi amena solo dieureunguéne dieuf kou daanou niak conseil mola danél ❤ serigne ahmad chapeau ❤

  • @papatoure-z7i
    @papatoure-z7i ปีที่แล้ว +1

    Mâcha allah sama cheikh bi débat très intéressant et très satisfaisant 🎉
    Yalla na borrom bi nangou niane yeup amine

  • @adamadiop2942
    @adamadiop2942 2 ปีที่แล้ว +1

    Masha Allah dieureudjeuf yalla na yalla sam la arr la si barket seydina cheikh Ahmed tidiane Chérif ❤️♥️♥️♥️

  • @thiernohamidouhanne3719
    @thiernohamidouhanne3719 2 ปีที่แล้ว +7

    très bien Serigne par rapport à l'éducation c'est ca que je disais hier par rapport à l'école il faut écraser ttes les écoles on en marre et le pire on exporte des connaissances de toutes formes alhamdoulilah d'être talibé ❤️

  • @ndeyefatousylla4269
    @ndeyefatousylla4269 ปีที่แล้ว +2

    Machalla machalla vous êtes excellent que le prophète vous protège

  • @deuggeurek1013
    @deuggeurek1013 2 ปีที่แล้ว +17

    Bravo pour la qualité des vidéos! Le format aussi est top avec Les off et les interventions de Al Hadji ❤️
    (Al Hadj, on a quand même un peu de mal à vous entendre, dél yeukeuti kaddou bi touti rek 😉)
    Ziaar na la Serigne Ahmad Fall !

  • @Beug.c.a.tidjani
    @Beug.c.a.tidjani ปีที่แล้ว +1

    Machalla serigne Ahmad ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @diamdi
    @diamdi ปีที่แล้ว +1

    Ma sha Allah j'ai beaucoup appris en peu de temps Qu'Allah vous Récompense infiniment.

  • @thiernobarrysall8966
    @thiernobarrysall8966 2 ปีที่แล้ว +9

    Professeurs complet macha allah

  • @ibrahimadiouf685
    @ibrahimadiouf685 2 ปีที่แล้ว +1

    Machallah dieureudieufeuti serigne Ahmad fall yalla na yalla fayal niou la thi barke yonenti bi salalahou aleyhi wa salam barke seydi cheikh Ahmed tidiane chérif

  • @cherifgueye1329
    @cherifgueye1329 ปีที่แล้ว

    والله إني أحبك في الله

  • @gayendeyeastou8333
    @gayendeyeastou8333 2 ปีที่แล้ว +9

    Professeur 🙏🏾🙏🏾❤️

  • @bambiste7---officiel959
    @bambiste7---officiel959 2 ปีที่แล้ว +3

    Bismillah barkép cheikh tidiane rta

  • @alioundiaye5120
    @alioundiaye5120 2 ปีที่แล้ว +3

    Serigne bi yalla na sa djam m yàg g macha allah si ñagalèmi

  • @cheikhgueye628
    @cheikhgueye628 2 ปีที่แล้ว +1

    Masha’Allah amatina solo lolou Jëreudieuf cheikh oustaz professeur sopey serigne ahmed fall yalla naleu yalla Faye

  • @seydinaousmane3375
    @seydinaousmane3375 2 ปีที่แล้ว +13

    Serigne Ahmed boul tite boul ragal bilahi tarikhaby rek Moy deugue Loumou saf kako Mathiako meuna kham gnioune gni tarikhaby defar gniou deuké werd souba AK ngone walahi Limou def si gnioune xamnaneko defna si gnioune mandou AK doylou AK bagnia Moy yalla AK bagnia lek Lou lewoul bilahi kou tarikhaby reuth gnewoumala geuwma loudoul tarikhaby nakh limouma sopé yalla rek moko xam bilahi souma sagnione gnieup dieulko defar nitte mossi gaw Serigne by nopaloul tarikhaby borom weursseuk mokoy geum mandé dama warou wa lo xamny yankoy werde souba AK ngone dem ba meuna to sath meunato fene menato Moy yalla li dé bou baxoul guissouma louko geun mandé Lilay yeuk si werdewi motakh bilahi damay werde ba dhé fekemasi nakh walahi bilahi talahi gnéwouma kene Demna ba amatouma diote werde wazifa mbolo diangue alkhouran cheut alhamdoulilah machalah xam lep wakh lep bakhoul wayé magui gnianal yalla khep kou beuga dioup bilahi dieulal werd Di wazifa mbolo legui nga dioup khothe talibe cheikh ba aldiana

  • @mouhamadoulaminebao598
    @mouhamadoulaminebao598 2 ปีที่แล้ว +3

    Barakalahou yalna yala Faye yiw

  • @omardiouf7118
    @omardiouf7118 11 หลายเดือนก่อน

    Alhamdoulilah bougnou Yalla défé Tidiane

  • @nafissatoukane1486
    @nafissatoukane1486 ปีที่แล้ว +1

    Marcha Allah. Yalla doli deugeureul fayélén yiwe you eup sén diorte té barkel ❤❤❤ beugue nala ndakh sa thiofél si seydina Mohammed S.A.W. si barké cheikhou tidjane cherif. R.T.A

  • @thilobasse7415
    @thilobasse7415 2 ปีที่แล้ว +1

    Machalah yaw daal naw nanioula fonk naniou la ndakh xam xam ngay wakh yalnala yalla bourbi fayal bopam si barké Cheikhouna Tidiane. dara débordé woufi.yene yi ay détails leu.

  • @salifguind038
    @salifguind038 2 ปีที่แล้ว +5

    Dieureudjeuf Serigne bi 🙏

  • @zeynabmakhtoum8025
    @zeynabmakhtoum8025 2 ปีที่แล้ว +4

    Mashaallah serigne bi vérité absolue ☝️♥️♥️

  • @amethkeita4303
    @amethkeita4303 2 ปีที่แล้ว +5

    MACHA ALLAH SERIGNE DAARA

  • @diendiaye3561
    @diendiaye3561 2 ปีที่แล้ว +1

    Machala Yalla gnou len Yalla samal tei fayal gnou len liguey bou am solo bi nguen di def Serigne Ahmad Fall goudal fane sa doundou bi amna solo lol si gnoune

  • @AmynaNabySarr-bouDabakh
    @AmynaNabySarr-bouDabakh 2 ปีที่แล้ว +1

    Mashallah Serigne Fall Yalla nala sounou Borome faye yiw 🙏🏾 li amena solo trop vraiment diangue nasi lou bari 🙏🏾

  • @bocartall4236
    @bocartall4236 2 ปีที่แล้ว +1

    Mashallah mashallah. Mala beug way ya oustaz💓💓💓💓

  • @babacarmbayedjite2652
    @babacarmbayedjite2652 2 ปีที่แล้ว +4

    Macha'Allah, yallah nalaa souniou borom faay. Li ngaay deff amna solo trop. Niongui laaciy remercier bou baakh

  • @baalamine4936
    @baalamine4936 2 ปีที่แล้ว +4

    Barakallahou fiika

  • @idrissahanne3146
    @idrissahanne3146 2 ปีที่แล้ว +3

    Dieureudieuf oustaz boul fallé dé cheikh tidjan mo nek sa guinaw

  • @elmalickattidiaani9963
    @elmalickattidiaani9963 2 ปีที่แล้ว +2

    Yalna sa Borom samou la inchallah 🙏🙏

  • @abdouseck01
    @abdouseck01 2 ปีที่แล้ว +4

    Fattabarakallah ❤️❤️❤️

  • @abygueye1151
    @abygueye1151 2 ปีที่แล้ว +2

    Jazaakummulaahu xayran yaa oustaz, waxtaan wi neexna maachala,la causerie est très critique, très pertinente, amna solo.

  • @diopndioba162
    @diopndioba162 2 ปีที่แล้ว +3

    Mach alla Serigne bi siarnala wayei niongi sakou waxtaan si Sidy Barham Al Kaolakhii

  • @abdouthiane9676
    @abdouthiane9676 2 ปีที่แล้ว +2

    Yalna nga fi yageu ta wér billahi sopou nala

  • @elhadjimalickndiaye9273
    @elhadjimalickndiaye9273 2 ปีที่แล้ว +2

    Macha Allah Serigne contane Nanou si yaw

  • @familygeuye4932
    @familygeuye4932 2 ปีที่แล้ว +1

    machallah machallah machallah sag bi kham kham bi ler'na rafetna 💯❤️❤️

  • @bayemadiodiothiam3578
    @bayemadiodiothiam3578 2 ปีที่แล้ว +1

    Machala yalna niou yalla def talibé cheikh

  • @pbt737
    @pbt737 2 ปีที่แล้ว +1

    Eskey eskey yallah baakh, alhamdoulilahi rabil alamiin. Yallah naniou yallah nangoul sounou wird bi niou djapp

  • @ibrahimabandoye4863
    @ibrahimabandoye4863 2 ปีที่แล้ว +1

    Ma Sha Allah Fall ❤️❤️

  • @tallaissata5168
    @tallaissata5168 2 ปีที่แล้ว +1

    Machalla lafe thiate ya oustaz

  • @ndeyefatousylla4269
    @ndeyefatousylla4269 ปีที่แล้ว

    qu'Allah vous protège merci beaucoup

  • @cheikhfall2285
    @cheikhfall2285 2 ปีที่แล้ว +3

    Mon père spirituel

  • @bailodiallo7980
    @bailodiallo7980 2 ปีที่แล้ว +1

    Mâcha allah Oustaz barakallahou fikoum

  • @MalickSeydi105
    @MalickSeydi105 2 ปีที่แล้ว +1

    Djazakoumoulah ya seydi

  • @familygeuye4932
    @familygeuye4932 2 ปีที่แล้ว +2

    dierediefe seydil khadji Malick Sy diarama Serigne Babacar s'y Al khalifa Serigne Babacar s'y Mansour yall'na yalla yagal kofii loll barke seydina moukhamét psl 💯❤️🥰

  • @sannemamadou3766
    @sannemamadou3766 2 ปีที่แล้ว +4

    Macha'allah Serigne qu'Allah vous récompense

  • @modouthiam2910
    @modouthiam2910 2 ปีที่แล้ว +1

    Mâcha allah oustaz

  • @familygeuye4932
    @familygeuye4932 2 ปีที่แล้ว +1

    dierediefe serigne ahmet fall a tidiany ❤️❤️

  • @ibrahimakhalil520
    @ibrahimakhalil520 2 ปีที่แล้ว +2

    Dieureudieuf OUSTAZ 🙏

  • @miketoure4518
    @miketoure4518 2 ปีที่แล้ว +2

    ALLAHU AK BAR LAHILAHA ILLALA MOUHAMMADOU RASSOULOULA SAWS

  • @MisterLamcine
    @MisterLamcine 2 ปีที่แล้ว +2

    Beug na la ziaar si ya Shaykh !

  • @khadidiatoucissesoppoudaba446
    @khadidiatoucissesoppoudaba446 2 ปีที่แล้ว +2

    Ay way aldji tay yaw lay wahal diapplé lénma si diawharatoul kamal bi srige Ahmed wonako mai batay hamna yitté la rk mais billahi sokhla nako dh si barki cheikhou tidiane Chérif 🙏

  • @rassoulndiaye8060
    @rassoulndiaye8060 2 ปีที่แล้ว +2

    Macha Allah Serigne amatina solo. Amna wazifa yo xamnei sofa deimei wax sikaw gnou fokk ni daguay nieukantei ak gnome gnoulay fétassou rk à la fin daguay oblige noppi wax si souff

  • @babacarndiaye6304
    @babacarndiaye6304 2 ปีที่แล้ว +1

    Machallah sama sopé

  • @rouguindiaye1817
    @rouguindiaye1817 2 ปีที่แล้ว +1

    Machallah Al oustaz

  • @mouhamadoulaminebao598
    @mouhamadoulaminebao598 2 ปีที่แล้ว +4

    Serigne Ahmed fall nitni ken manoulena satisfait li am solo moy wah te yala tah yonenete sah daan Nanou corrigé

  • @fayebabacounta656
    @fayebabacounta656 2 ปีที่แล้ว +1

    Amna solo lol. Yalna la yalla faye

  • @papasambacamara8620
    @papasambacamara8620 2 ปีที่แล้ว +3

    Assalamou halaykoum Oustaz et toute l'équipe yalneu borom bi geuna deugeureul taxawayy bi té barkelko wayy 🤲🏾..xana dii laath tèèré Serigne Mor DIOP bi founiouko meuna amé a défaut de le télécharger.. diaaguèn'dieuff 👏

  • @papandiaye9419
    @papandiaye9419 2 ปีที่แล้ว +1

    dieureudieuf Oustaz

  • @NJAGACEESAY73937
    @NJAGACEESAY73937 ปีที่แล้ว +1

    Mashallah ❤❤

  • @layely7613
    @layely7613 2 ปีที่แล้ว +8

    Kone oustaz t'es au courant de l'existence des wahabyou au Sénégal je ne t'entend jamais parler d'eux oustaz war ga wax ak niom nak teklen sen place prsk mane vidéo bi niou la barré Bamako guissé dama merr yaw ga guissko mu def lay ré eskay merci kone grawoul on les aveugle rkk

    • @assanendiaye5870
      @assanendiaye5870 2 ปีที่แล้ว +7

      Parsk diar nio tontou bro

    • @mamadoumbaye9872
      @mamadoumbaye9872 2 ปีที่แล้ว +3

      Salut frère ban video lagn ko barè soxlanako nioniou Ay mbam lagn rk

    • @talibecheikhndao6085
      @talibecheikhndao6085 2 ปีที่แล้ว +1

      @@mamadoumbaye9872 slt mbok c'est lorsqu'il parlait de 5 femmes sur la chariat, Serigne momar Diagne la répondu en lui barrant. Merci

    • @hadjarandiaye2861
      @hadjarandiaye2861 2 ปีที่แล้ว

      @@talibecheikhndao6085 oui je lai vu aussi celle de serigne momar diagne. Wakh deug yalla begone na mou undi thi ay léral thi até 5 femmes

    • @layely7613
      @layely7613 2 ปีที่แล้ว

      No c pas les 5 femmes dé il parlait Mame cheikh Abdouhadre dieylani

  • @mouhameddiop1463
    @mouhameddiop1463 2 ปีที่แล้ว +3

    J'adore l'esprit critique de Aladji machallah

  • @ibrahimanakone7802
    @ibrahimanakone7802 2 ปีที่แล้ว +2

    Di melni qoutbou 😂😂😂😂 je suis à terre.

  • @aliounebadaratoure8308
    @aliounebadaratoure8308 2 ปีที่แล้ว +1

    Barakallah serigne ahmed

  • @moussalo1645
    @moussalo1645 2 ปีที่แล้ว +1

    Ouztass beug nala guisss dei nga defar ma nguir yalla damay soga diap tarikha bi j’habite à Grand Yoff

  • @dabaxful
    @dabaxful 2 ปีที่แล้ว +1

    Soula Yalla fayé ....

    • @dabaxful
      @dabaxful 2 ปีที่แล้ว

      Gua sedd gnou

  • @moussagueye3489
    @moussagueye3489 2 ปีที่แล้ว +2

    Macha Allah

  • @Islamberik1998
    @Islamberik1998 ปีที่แล้ว +1

    MAASHALLAH❤❤❤❤❤❤❤
    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @amethdiop8145
    @amethdiop8145 2 ปีที่แล้ว +1

    Dieureudieuf Dieureudieuf Dieureudieuf

  • @generalamir5927
    @generalamir5927 2 ปีที่แล้ว +4

    eskey seydii ahmad namonn naala ❤️

  • @bayemadiodiothiam3578
    @bayemadiodiothiam3578 2 ปีที่แล้ว +2

    Boula nekhe tak dix montre