Sunu réew mi de jànguñu xam-xam ay làkki doxandéem la ñuy jàng, jeexal ci seen dund gépp te duñu ko dégg, te it seenug yaras àgg na ci ku man a tàqale ci làkkuw jàmbur ñu koy kaw-kawal ak a naw fekk xamul boppam. Nun jàmm dañoo teggi fàww nu dabi ko.
Jërëjëf sëriñ bi billahi dëgg bu wer pengg nga wax benn si man ma ngi ci daaray farence bi lii di synonym antonyme degg naa ko waaye amoon a si jafe jafe
jaajëf wax ji gàtt na waaye amna solo lool te it leer na, tay jii rek gis naa xale buy jàng ci tókkóor gone yi, mani ko loo jàng tay?mu ni ma: "allaahu rabbii yàlla mooy sama broom" maa ngi naan ci sama xel kii de nde gam tawhiid rek la leen di jàngal mënoon na yam rek ci "yàlla mooy sama boroom"
Tasaareleen ko Facebook - Twitter - instagram ak Whatsapp ngir jàpp ci xeex bi
Te ngeen bindu ci TH-cam bu saabal.com
❤️💕😍😍😍😍🇸🇳🇸🇳🇸🇳💕❤️
Wa delenko envites guir yalla mom doumasi doyal
Waaw léen góor, wolof du moromum frañse, na yaatu rek.
Waaw leen góor nii la de ayca Wolof na dem ca kanam a kanam.🙏🥰🥰🥰
Jërëjëf Abdu Rahmaan Jéey !
Jërëjëf ci leeral yi am na solo lool jërëjëf 🙏❤️
Teeree yi fou mouye diaay nguir yalla si touba
Daaru xuddóos pàkk ginaar (libérairi xidma)
Jërëjëf sëñ Abdu rahëmaan
Mashallah Amna solo bilaye wahga dëgg 🇸🇳🇸🇳🇸🇳😞
Yàlla nala yàlla fayae
Billayy lou werr nga wax bimay diang boudone wolof mballa sérère mayy guene ayyy .
Machallah âme n'a solos
Merci beaucoup frère ❤❤❤
Machallah a mena solo Yale bakhne inchallah Dina bakhne
Wakh gua degue dée khépe sa popou rke yalla na lenne yalla diapou lée
Macha llah ❤
Sunu réew mi de jànguñu xam-xam ay làkki doxandéem la ñuy jàng, jeexal ci seen dund gépp te duñu ko dégg, te it seenug yaras àgg na ci ku man a tàqale ci làkkuw jàmbur ñu koy kaw-kawal ak a naw fekk xamul boppam. Nun jàmm dañoo teggi fàww nu dabi ko.
Machallah
aw làkk jumtukaay la rek ngir taataan xam-xam. sunu réew mi frānse bi bokk na ci li nuy tagatembeel cig ndóol.
Yàlla na nu bari gnou melni yaw
Waw góor 👏👏👏👏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🎤🎤🎤🎤
Maasàllaa am na solo Sëriñ Abdurahiim farba jërëjëf.
Maasalla Wolof rek
Begue si yawe monsieur leye 🙏❤
Jaajëf sama Sëñ daara bi.
Am na solo lool. 🙏🏾🙏🏾
Walef a mena solo Yale bakhne inchallah Dina bakhne
Je suis halpoular mais amna solo 🥰
jàng ci saw làkk dara dàqko xoolal lii
Machalla dieureudief Serigne Abdou Rahman âme n'a solo loll way
Maasàllaa jotaay yii nay faral di baril di am fii ci saabal gi waay.
Jërëjëf yal na Yàlla fay la
Wa xalé bû buegue jangge noûmuy déff
Jaajëfati
Jërëjëf lëy amatina solo lool
Amna solo waaye leepp u luñuy bind ak lumu manti doon ci Wolof lañ kowara bindée meem budée laku jambur Sax ci Wolof lañ ko wara bindée
Maasàllaa amna solo
Maasallaa am na solo
Maacha Allah
Maasàllaa wallaahi solowu na lool.
Waaw leen góor nii rekk la
Tubaarikàllaa am na solo lool sax
Machalla
Amna solo de
Màsaalla
Am na solo
Maasàllaa am na solo.
Waaw góor waay
Wax ji de gànjaru na lool sax !
Merci
Masàlaa am na solo.
Yëfi dof li ñi dal.
Da ngay wax ba sonn.
Ku ma bind, ci wolof, ay wolof nag ñu tontu la ci faranse.. Fii ci Tugal.
Waaw leen góor ! yal na leen Yàlla fay.
Amna solo
Yal na Yàlla fay leen.
Am na solo lool na yaatu rekk.
Ku bëgg teerė wolof numuy deff
Maa chaa allaah
Jërëjëf sëriñ bi billahi dëgg bu wer pengg nga wax benn si man ma ngi ci daaray farence bi lii di synonym antonyme degg naa ko waaye amoon a si jafe jafe
Jaajëf
Waaw góor jàpp rekk të a bàyyi.
Waaw góore waay !
Jaajaf sëriñ bi
Waawaaw, aka wér.
❤❤❤
Dëgg gu wér nga wax👍
Jërëjëf
Machalla Amna Solo
jaajëf wax ji gàtt na waaye amna solo lool te it leer na, tay jii rek gis naa xale buy jàng ci tókkóor gone yi, mani ko loo jàng tay?mu ni ma: "allaahu rabbii yàlla mooy sama broom" maa ngi naan ci sama xel kii de nde gam tawhiid rek la leen di jàngal mënoon na yam rek ci "yàlla mooy sama boroom"
Wér na de Sëriñ bi.😁❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Maasàllaa
Amna solo looll
Maasàllaa jàmbaar
Amna solo lool
Lu wér nga wax!
Tubaar kala lii de am na solo lool
Lu wér nga wax
Lii moom war na di am
Magui ziar bouwér kou beugua ame téré bi foy diar
contane sy yaiow Abdou Rahime
Amna solo lool.
Wakhi dof
Machalla sa numéro
Wolof reek
Gnûgî räfët lû lî gay dëff bûbãkhã bãkh ãk yôkûtë topsî
Ayca kon Na yaatu.
Salam kou beug am si livre yi noumiy def🙏
Assalamou aleykoum, ki sokhlana numéro téléphone nam ndakh sama woleuré bou yag la won thi Diourbel
Nagnou defar souniou arafi bopou
Assalaamu halaykum ani yene l’Essonne yi 2,3,4.....?
Saa legiey rafet na, ku begga diangue te nek bitim reew noydef ?
Dëgg rek nga wax !!!
Ab laaj lan mooy melxam ak Xewxam? Damaa dégg Nga koy wax te xamuma ko
Phisique chimie
Li moom jar na janŋ jarna yaatal ndax ñu xam ko wayé dictionnaire Wolof?
15000 f 👉 763872046 watsab
Meun naa ame sa numéro
Kii numu tuddu
Abdou Rahim Leye
Dégg du romb a nopp...
Jox ma chaîne bi ma dafaral la ko ba mu rafet
Maasàllaa
Machalla
Am na solo
Amna solo
Jaajëf
Numéro Abdou Rahim la sokhla