Jeune homme si tu porte vraiment serigne babacar sy rta dans ton coeur part à tivaoune et demande pardon à ses petits fils Parce que y'a un de ses vénérés petits fils qui condamne fermement vos chants folkloriques sur serigne babacar sy rtb soit modeteste et fait le pour l'honneur de serigne babacar sy n'écoute pas les gens qui te glorifie!
Aboubacry comme Serigne habib wakhna diemal guissé ak mom ngua balou. Gni ci dess mom tekki wouniou dara boul sax am loy wakh ak niom douniou dara am na ko khamni page la yoré ni dey diapalé tariqa bi té ay bêtise mo eup si ay publication dara la xamoul si tariqa bi.
Papa Aboubacry boul may none yi louniou wax boul moussa arrêter di way serigne babacar sy soit fort meti na niou torop mais xamguani yonentébi sax amone na none 😭😭
Aboubakri je t apprecie bcp et tu chante bien mais notre tarikha a ses propres réalites. Et ban système guay changé, les poèmes de Serigne Babacar ne sont pas pour les cérémonies folkloriques. Bonne continuation je te souhaite le meilleur en tant que Babacariste
Du courage mon frère et tu as bien fait d'éclaircir car ces personnes mal intentionnées vont fermer leur clapette. T'es jeune et ceux qui parlent n'ont pas fait le tiers de ce que tu fais au Sénégal. Alors le chien aboie la caravane passe. Et c'est eux-mêmes les diables alors bon vent. 👏👏👏👏👏👏👏
Yallah mola deff ti birr xol gni gni...daniou la la beugue,daniou la sopp grii serigne babacar sy.. Inchallah lolu sa ne changera jamais ..nioun sayy sopé dou critiques yi dou wakh yi sur les réseaux sociaux yi qui fera qu'on arrête d'être fier de toi..beugue naniou t yallah rek takk dou degne .. Reste sur la ligne droite continue di beguel say sopé.. Et fait en sorte que nos grand marabout ne soit jamais en désaccord avec toi c'est sa le plus important ! Gni di yakk sa derr gni di nekk ti réseaux yi di wakh du n'importe quoi boulene falé boulene tontou ... Amgua nioula meune defendre ils auront jamais se qu'ils veulent ABOUBACRY SAMB DINA LAW BA FAW et kene dou thi meune dara .. Wakh yi c'est normal nak yay Ki Nekk sur la toile actuellement ..' gueune di beuguel say sopé tt en sachant ou tu met les pieds nioune say sopé gueune naniou la sopp gueune naniou la sopp gueune naniou la fonkk griii serigne Babacar Sy griii Mame El hadj Malick griii mame maodo ...QU'ALLAH NOUS GUIDE ET QU'IL NOUS ÉLOIGNE DE TOUT CE QUI NOUS ÉLOIGNE DE LUI.
Liima sii meiitty moy sokhna yiiy toontou seine xam xam sorriwoull elle ne sont la qx pour éterniser le débat sur les futilité..... Une faute avoué et a moitié pardonner...... Serigne Habib Sy bii Mouy addou c pour t recadrer fataliila haalou keur gui wanteii dou pour dara Khalifa meune na kanamam meune ganawam boo seillaleii sa pass pass taii organisé liingay dff diinagne la dgg taii doo gneii keineuh Encore une faut moytoull waxou xalei You djigueiine lou yakhou sii adouna bokk nagne sii liko yakh bonne réception #beugg Serigne Babacar Sy
Macha Allah sa wakh rafetena Samb Diam si yaw adouna ak diar diar gno and mai sante yalla bigua âme modestie def vidéo explique sante yalla aussi ak opportunité bigua am meuneu guene si média yi leral pour maître les points sur les i
yaw tu es un modèle pour nous , on ne laissera personnes dire du mal sur toi. ces jaloux qui n'ont rien à faire de leurs vies ne peuvent rien sur toi JE SUIS JEUNE, JE SUIS ABOUBACRY SAMB J'AIME SERIGNE BABACAR SY, J'AIME ABOUBACRY SAMB
Hello babacar je suis tidian tallibé cheikh. Je suis fière de toi. J'ai regargé votre prestation au lycée Kennedy c'était bien passé rien à dire machalah. Retenez une chose le chien aboi la caravane passe. Instant bi ya khéw les gens ne veulent pas voir une personne qui avance. Mon homonyme gardez la tête haute. Les sénégalais t'aiment. Je veux avoir ton numéro svp.
El hadji abdou néna gén way serigne babacar sy si modernité Sa wakh rafét na trop machalla Waye ga bayyi tamayi rék Dél way té boum am tama wala guitaar voir sans son rek dina manékh
Iao barhame lingay wah ni hamoossi Dara demal deglou Binta Thiam nga wahma fane ngakoy classé vu k Tabala yi bahoul...loo guiss thi adina Ass moothia geuna bonnn iao nak ass tiidiaane nga matoo talibé cheikh Serigne Babacar sy hamoula hamoul gni melni iao...seydil Hadj Malick sy hamoula...diémala matt talibé moo geune
@@thelastboy657 lolou man worou ma sam yonn nekkoul si binta thiam loumou donn en tout cas elhadji abdou dabakh dafa interdit niouy waye serigne babacar ak ay sabar , tama , tabala ....
boul deigou nite gui yalla mola deif si kholou nite yi ndakh serigne babacar sy continue ne d'ecoute pas les gas dagne ba beugue yakhal mais serigne babacar sy mon gni sa guinawe tes wa tivaouane amna fougne la teikk bilahi mane fala deukk mais neicouma magui amerique mais je t'ecoute continue frere yalla nala yala same barkei serigne babacar sy mignou bocou
De toute façon en tant que fan's et ami suis vraiment surpris de ce qui vient se passer mais courage rék on est tous derrière toi, Moi ce qui me concerne je préfère "bagna tontou kéneu"
Aboubacary Samb moi je t'estime bien dakh kou beugue Serigne Babacar beuguenala . mais je ne suis pas d'avis avec toi par ce que tourou Serigne Babacar Sy dou ay thiakhane . imagine toi nga dem anniversaire di fa toudou yonent bi ak Serigne Babacar . Gor gni ak djiguene gni diakhasso sol Aÿ yeré you bonne té béne djiguene dou thie mourou . tourou seydina mouhamed ak cheikhal khalifa dou anniversaire ak guenté moy séne place
Dafa dioum rek man khamouma histoire bi nimou demé vraiment ma ngui guiss nitt yi di wakh naan dey outt buzz soudon outt buzz dem defi mbalakh walla lenén nagn ko comprendre rek gniko ndiaboté gnou diegal ko walla gnou rectifier ko mo geuneu gnoukay weer ni diko torokhal parce que kou degg nim wakhé khamni dou yabel walla dou tayef tamit Limouy woté deugg le si mom
MAchallah yallanala yalla diapalé. Moi j'ai un neveu de 2ans et demi qui regarde tes videos et qui saute a chaque fois. j'aurai aimé que tu le vois. Ton numéro svp
Abou du courage mane moride la mais damala beug trp bilaye barki Serigne fallou mbacke nitt kou nioul si bopom mon sokor j'ai vu tout les commentaires mettinama trp bassi khanamou yalla niou gne gnio la beuguel sunu bopou bare inchallah lepp dina bakh sa me fait vraiment mal bhl courage moi je te soutenir a 100/courage
Diam rekk ngay amm samb koula khamoul rek molay sedel lou kiaww mais nioune gni deuk ak yaw kham nagnoula bou bakhh. Yalla kham na li nek thi khol yi ..dina bakhhh bakry one love💟💟
Touss lén té bak ko kouniouy bak seydil Aboubacar Sy dakh moko yayoo wayé naniou bayii gii🎸🎷🎹📯🎶🎵🎼🎺🎻🥁 yii lolou la mame Abdou Aziz Sy dabakh wakh instrumental bokou tchii
Du courage mon frère, le chien aboie la caravane passe, Sénégal nak mo meti bo beugué avancé yaura toujours des gens pour te barrer la route. Mais boulen falé, deugoul rek ci la nga nek goorgorloul
Sama kharit Sa Numéro dama ko perte👉Wayé mangui lay hamal ni Sou la Wahii Nit ngi Tahé Bayi Tageu Serigne Babacar Sy Bilahi Kon sa begeu Serigne Babacar Sy déss na🤚okey Aboubacar diap teuweu bayi Serigne Babacar Sy amoul tank guindaw sakaw sakanam rék incha allah C.Moulaye DABAKH NDIASSANE
@aboubacarysamb mane deih sa sopé la wayei nagnou nangou li sunu kilifeu yi diglei rk ndax moy deug.. seydi Aboubacar deih beugoul koukoy weuy di teug kone nagnouko wormal🙏.. on a rien contre toi nak ndax sunu mboukou talibei nga.deifal Lou mbaye beug gnou beug leuh diapalei la nga deim ci kaw ci kanam barkeii Cheikhal khalifa🙏 courage et bonne continuation 🙏❤️
Djiguen gni rek niolay encouragé si lingay def nakh niou bari si niom gatt khamouniou si diné folklor rek molen nekh Abdou aziz mbaye,doudou kende,ibrahima mboup,haj mbaye dondé kou beug tagg naby dangay roy si niom Demal nga diang bindou magg gni té té tagg yonent bi mo geun sa mbalakk mi yaw ak nienen nioukay def soff nguen ma trop
On doit défendre notre tarikha.le tarikha cheikh ce n est pas n importante quoi .ce qui chante doit revoir ce qu'il chante .Il y a certains place on ne doit pas chanter Serigne Babacar Sy
Cad weuy qasida makk gni waroul nekk métier. serigne Babacar Sy bamouni sen tariqa daci tek seen métier. Li xéw yeup moy gni dieul weuyou buzz defko métier. Sétaatal sa dokhaline ndakh keurgui danioulène respecté ndakh sen topp sounna ak séllal boul nangou amfi weuy bou niaaw. Soudé sa tiofél ci Serigne Babacar Sy deuggou na toppal li ndiabootam beug, soudè deuggouwoul nak wayé xaliss ak buzz ngakoy outé mom Yalnala Yalla taxawou ndakh martabam xadioul ci yow
Bilahi yaw khamo sa bope yaw ak musician yéna yame psk né gua da guaye way Serigne salio com ni musician yi di déf ligua begue moy dieul tourou Serigne babacar di si out beuzz rk bayil tapalee😌
Jémall guissanté ak kilifeu yii. Gua wakhatane ak niome. Lougn la meuntii wakh, ak nougn la wakh rek ga deffei koo nonou. Boul top nite yi ba lorrr sa bopp. Frére. Yalla nala yalla lafal tiate
C’est facile d’être derrière son téléphone et être là à dénigrer insulter une personne souvent c’est ces mêmes personnes qui le suivent partout qui le text sur whatsapp pour dire que loumouy waay dalleine neikh trop qui L’encourage arrêtez d’être fake niit ki soko khamoul danguay Mandou si ay mbirram peut-être que khol lay wakher mais c’est très bien réfléchi cheikhoul khalifa nioune nieupa ko bokk nimako beuguer gueumnani momako gueune beug thioffeilam si Serigne Babacar gniko dieiguer deugg reik nioko meune kham bon c’est une chose de dire que mais s’en est une autre de le lynché sur les réseaux sociaux et de dire même que la personne a fait un pacte avec le diable et aussi de dire que day mboubo tarikha bi mais tarikha bi takhouko diouk enplus de cela de l’insulter de mère sa c’est vraiment trop tout sauf sa kou respecter ndey bila diour do saga ndeyou diambour deilowatte leine sein khel si yalla akk dafa mince tei amel ngueine akk kouleine defoul wakhouleine gueumnani talibe cheikh moleine ko gueuna doone gueune leine beugg cheikhoul khalifa itam il faut arreter cela dioulitte lagn avant tout tei ay mbokkoum diouliit warouniou wakhanter lou niaw rawatina niou bokk beine Tarikha mouy Tarikha cheikh Ahmed Tidiane cherif kokou deih seutou yonente la khamoul wone lou niaw nay leine di rafetal doleine deim beugoleine kouy deim louy lolou tmt kingueine di wahal di teik louneik si déram deih niit kou bakh Leuh kou am khol am yitter beuri diam yéné nieup diam itam ko khamni allalam douko boler ak keine foko feik moungui reih même gnissi gueuna ndaw sakh daleine di wayal teikssi dafa am nianou wadiour tei kou am nianou wadiour thi kaw thi kaname reik lay deim ak loleine meunti wakh tall bou yalla tall mom sani si Matt mogueune dieim ko fay kone nopalou leine si niit ki meuna loleine ko dara aduna mo deimer ni nieup meunou niou bokk beugg souko nieup beugone sakh gueumnani douko djik kone continuez de râler pendant ce temps mom mingui job di deim sa kanam ma kanam gnikoy beugg nioungui yokk de jour en jour ball bouy deim thia kaw leuh day dieing reik mais dou meusseu danou si barkep cheikhoul Khalifa 🙌🏽
Merci le frere geste bi noble na si nangou kilif tef bi ak bayi helle say harite ak gnila sope ak sa diganték serigne babacar sy bénene ensuite kouko beug dioh conseil woko té bagne ko commenté merci de votre comprehension
Man dh taliber serigne touba la wayer sopeu naleu loll legui leral yi Amna solo lol lithi dess t malakoy gnane gua dem thi serigne bi djiegualou ko leral lal ko man man bigua liguay def motakh faw gnoulay sosal ndakh koufi bakh mba gua bakh gnou sosal khol ko thi sa serigne khol ko si sma serigne khol ko si kep kou bakh courage koubakh yalna yaleu diapalé
Saway meune nga wayei ! Pour wax la deug rek Teug bi ngaay baayi!! Keur maodo ken xaméw len li!! Issa laye , mbay ndonde , Doudou kende, Abdou aziz mbay ken massu si Teug té meune naagnu lignuy df , xaana beugo doug ci Zawiya bi di Wooy??! Teug bokul ci gnune mbok vraiment
Yaw kham ga li mame abdou wakhone thi kouy way serigne babacar s'y pourquoi do dieufé lolou,boul topou sa bakane niepou diamou lane la yéné, s.babacar limou bind meuno ko diékhal kone bayile sabar yi ak tabalayi té oubi xasida yi👏👏
Iao yalla mola def si kholou domou adama yi ❣️talibé Serigne babacar sy dangay diengue rek mais do yégue souf 💪💪de tout cœur avec toi💋
Bayiléne séne thiakhane yi ki bou léne ko beugué daguéne koy wakh deugue limou néké moko tay
Courage so diapaté inchalla ndam rek inchalla barké serigne babacar sy
Yana yalla diouboleila akk Serigne sii ak gneup inchaALLAH
Bon courage samb 😘😘beugue nagniou la ba paré dara douko dinedi incha allah thi kaw thi kaname ❤️thi barké SERIGNE BABACAR ❤️
Bilahi yafi dieule musique yatax legui xaley you djiguene yi dema touniou soiree dansante
Jeune homme si tu porte vraiment serigne babacar sy rta dans ton coeur part à tivaoune et demande pardon à ses petits fils Parce que y'a un de ses vénérés petits fils qui condamne fermement vos chants folkloriques sur serigne babacar sy rtb soit modeteste et fait le pour l'honneur de serigne babacar sy n'écoute pas les gens qui te glorifie!
Machala yalla na yalla motali
the king of zikhroullah
talibe serigne babacar sy si kaw si kanam inchaallah
Aboubacry comme Serigne habib wakhna diemal guissé ak mom ngua balou.
Gni ci dess mom tekki wouniou dara boul sax am loy wakh ak niom douniou dara am na ko khamni page la yoré ni dey diapalé tariqa bi té ay bêtise mo eup si ay publication dara la xamoul si tariqa bi.
YALLAH naala YALLAH saamme té aarre leuh si barké sama toureundo ! Mashallah always proud of you....
Papa Aboubacry boul may none yi louniou wax boul moussa arrêter di way serigne babacar sy soit fort meti na niou torop mais xamguani yonentébi sax amone na none 😭😭
Bilahi
yalla nala yalla defal diam si barké serigne babacar sy .man douma tok té doumala deglou nakh liguey wakh si khalifa yak kat yi mom boulen falé
Amie ki ngépe diame laniouko yéné mes nak keur seuydile haji malick sy dafa ame ay réalité kénne warouci bolé lousi bokoule
@@azzisow6548 lolou mom deguela mais tamit guisouma lifi ayy aussi
Nous sommes de tout avec toi Mame babacar moy sougnou Soutereuh boul tite bou ragal lepay bax inchalah 😍
Aboubakri je t apprecie bcp et tu chante bien mais notre tarikha a ses propres réalites. Et ban système guay changé, les poèmes de Serigne Babacar ne sont pas pour les cérémonies folkloriques.
Bonne continuation je te souhaite le meilleur en tant que Babacariste
Mamadou Lamine Diouf lou ler nga waax mbok
Wakh deug yalla yaga nako wakh tarikhabi andoulak folkoulor mem tabalayi fo ko fek gnikoy weur gneepou bougnouy koy awou gnongui tathiou aka yoor ay bitel diko teuguè mane mom masouma d'accord ak mom done diang kate yooboul demal dianguiwat wasalam
Mani ben serigne doula wo gnoun say mboki talibè gnolay wakh nga bayiko demal kholi khassida mak gni boubakh tè bayi tathiou yi ak tabalayi
Vérité absolue mbokk j'aime Serigne babacar
Sa wah rafetna bokh talibei ni lay dokhé yallah na sa diam yague
Yalna yala lafal la thiat machala
franchement aboubacry amo morome mann kou beugue khalifa ababacar sy rkk beugue nalla nakh moy sama lépp goudall fann wayy samb
Mashallah du courage et fais tout pour raffermir les liens avec la famille Sy, Que le Bon Dieu veille sur toi et tout le monde.
Du courage mon frère et tu as bien fait d'éclaircir car ces personnes mal intentionnées vont fermer leur clapette. T'es jeune et ceux qui parlent n'ont pas fait le tiers de ce que tu fais au Sénégal. Alors le chien aboie la caravane passe.
Et c'est eux-mêmes les diables alors bon vent. 👏👏👏👏👏👏👏
Fi bén Serigne doulafi wo bofi wathie yone nioune niolay tékk yonne guanane Serigne yaw kham gua bou bakh Lou keur maodo beug ak louniouy bagn
Kharal ba kham yone
@@leydidiopsow6918 kone defa golén point balegi
Yaw dangua kham li wa keur maodo wax
Yallah mola deff ti birr xol gni gni...daniou la la beugue,daniou la sopp grii serigne babacar sy.. Inchallah lolu sa ne changera jamais ..nioun sayy sopé dou critiques yi dou wakh yi sur les réseaux sociaux yi qui fera qu'on arrête d'être fier de toi..beugue naniou t yallah rek takk dou degne .. Reste sur la ligne droite continue di beguel say sopé.. Et fait en sorte que nos grand marabout ne soit jamais en désaccord avec toi c'est sa le plus important ! Gni di yakk sa derr gni di nekk ti réseaux yi di wakh du n'importe quoi boulene falé boulene tontou ... Amgua nioula meune defendre ils auront jamais se qu'ils veulent ABOUBACRY SAMB DINA LAW BA FAW et kene dou thi meune dara .. Wakh yi c'est normal nak yay Ki Nekk sur la toile actuellement ..' gueune di beuguel say sopé tt en sachant ou tu met les pieds nioune say sopé gueune naniou la sopp gueune naniou la sopp gueune naniou la fonkk griii serigne Babacar Sy griii Mame El hadj Malick griii mame maodo ...QU'ALLAH NOUS GUIDE ET QU'IL NOUS ÉLOIGNE DE TOUT CE QUI NOUS ÉLOIGNE DE LUI.
Liima sii meiitty moy sokhna yiiy toontou seine xam xam sorriwoull elle ne sont la qx pour éterniser le débat sur les futilité.....
Une faute avoué et a moitié pardonner......
Serigne Habib Sy bii Mouy addou c pour t recadrer fataliila haalou keur gui wanteii dou pour dara
Khalifa meune na kanamam meune ganawam boo seillaleii sa pass pass taii organisé liingay dff diinagne la dgg taii doo gneii keineuh
Encore une faut moytoull waxou xalei You djigueiine lou yakhou sii adouna bokk nagne sii liko yakh bonne réception
#beugg Serigne Babacar Sy
Wallay wakh ga deugue mom dh niepou diamou lane ko yéné, na kholat bopam té moytou Diakhaso bi ak djiguéne gni
Merci sages paroles
Macha Allah sa wakh rafetena Samb Diam si yaw adouna ak diar diar gno and mai sante yalla bigua âme modestie def vidéo explique sante yalla aussi ak opportunité bigua am meuneu guene si média yi leral pour maître les points sur les i
Nous somme de tout cœur avec vs yalnala Yalna samm soutoural leu
Avec toi pour tourjour inchalla ❤❤❤❤💪
#Abou_Yaw_yallaH_Mola_djital_gniye_Wakh_Bouléne_fallé_Yallah_nala_yallaH_Doliii_Soutùreu_Défale la_DiaM_inChallaH
Macha Allah sama sope yalla nala yalla sameu si barké seydina Mohamed saw
Mashallah Sopé bi yallah na sa diam yagg tei lahou aral nioula samal nioula inchallah hou rabbi
Direudieuf Aboubakry wakh j rafétna lole wayé nak souniou sagnone gua baayi TABALA YII nakh mame abdou(rdh) moko wakhone té MAKHAMA serigne babacar sy( rdh) dafa fore sinon niogui laye bégué dila wakh niogui khar saye yénéni sons inchallah et BONNE CONTINUATION
Loumou tama yi wala tabala yi lougnu térro yonainte bi ngani mou nayiko yaw nit ngz
Yalnala yallah samal bopam...réussite rk ngay ame inchallah
yaw tu es un modèle pour nous , on ne laissera personnes dire du mal sur toi. ces jaloux qui n'ont rien à faire de leurs vies ne peuvent rien sur toi
JE SUIS JEUNE, JE SUIS ABOUBACRY SAMB
J'AIME SERIGNE BABACAR SY, J'AIME ABOUBACRY SAMB
Je suis de tout cœur avec toi et ton staff s yittè moy Serigne Babacar té mognou gnor
Mashalla Frere wakh dji raftena 🙏
Machalla aboubacry yalna La yalla takhawou si barki Mame khalifa diam rek inchalla ❤❤❤❤🙏
Machallah amatina solo metina loll mais adouna mo mél nonou kou nek ak niguay guisé yalna la yalla defal diam
Du courage abou yalnala yalla samal bopam
Hello babacar je suis tidian tallibé cheikh. Je suis fière de toi. J'ai regargé votre prestation au lycée Kennedy c'était bien passé rien à dire machalah. Retenez une chose le chien aboi la caravane passe. Instant bi ya khéw les gens ne veulent pas voir une personne qui avance. Mon homonyme gardez la tête haute. Les sénégalais t'aiment. Je veux avoir ton numéro svp.
babacar sylla tu l'encourage pas waxko mou deim jangui on veut que du bien de lui. Tariqa bii dou ay foo waa Sallam
Yalnala yallah diapalei ndam rk si barkei Mame Khalifa inchallah
Slt ay waay dama beuge Serigne Babacar Mane talibé Serigne Touba la mourit la je
Dangay doul rekk
El hadji abdou néna gén way serigne babacar sy si modernité
Sa wakh rafét na trop machalla
Waye ga bayyi tamayi rék
Dél way té boum am tama wala guitaar voir sans son rek dina manékh
Iao barhame lingay wah ni hamoossi Dara demal deglou Binta Thiam nga wahma fane ngakoy classé vu k Tabala yi bahoul...loo guiss thi adina Ass moothia geuna bonnn iao nak ass tiidiaane nga matoo talibé cheikh Serigne Babacar sy hamoula hamoul gni melni iao...seydil Hadj Malick sy hamoula...diémala matt talibé moo geune
@@thelastboy657 yaw mi ya khamoul loy wakh elhadji abdou mo binde khassida wakh lolou
Seyda Binta Thiam mouchtarchidaat talibé Cheih leu wala?
@@thelastboy657 lolou man worou ma sam yonn nekkoul si binta thiam loumou donn en tout cas elhadji abdou dabakh dafa interdit niouy waye serigne babacar ak ay sabar , tama , tabala ....
Sabar yi mom day dakk wala ga guenné thi sérigne babacar sy
Abou yaw yalla molay sameuhhh thie barké cheikhoul Khalifa .Meunalounioula dh barké cheikh
boul deigou nite gui yalla mola deif si kholou nite yi ndakh serigne babacar sy continue ne d'ecoute pas les gas dagne ba beugue yakhal mais serigne babacar sy mon gni sa guinawe tes wa tivaouane amna fougne la teikk bilahi mane fala deukk mais neicouma magui amerique mais je t'ecoute continue frere yalla nala yala same barkei serigne babacar sy mignou bocou
Diame si yaw cheikh bii kham nga aduna bii moo bindo nonou😭 yalla na yalla dolli la sutura 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Aboubacar samb svp boule bâyi bon contiation se sopou la Khady SOW fouta je t'aime beaucoup💖 BN contuation👏💕💕💕💓💞💝💗💝💞💟
Machalah kaddu yi rafétna amna solo
De toute façon en tant que fan's et ami suis vraiment surpris de ce qui vient se passer mais courage rék on est tous derrière toi,
Moi ce qui me concerne je préfère "bagna tontou kéneu"
Ndeysane massa way mbok mi métti na trop mais mougneul rék nous sommes tous coeur avec toi
On est derrière toi 😍😍😍
Bonne continuation mon frère Sénégal dafa méti💞
sénégalais mo beug polémique mé diam rkk guay am inshaallah barké cheikhal khalifa, bon courage
Bon courage
OMG Senegal 🤦🏾♀️, Courage Brother On t’adore❤️
Senegalais mo Bari gnou eupeul pour gnom juger rek ak khass domou adama yi dem bananeu dangua def pacte pour yakk tarikha bi c abusé bilahy
Yalna la Yalla sam,diegalou nga wakh nga ak respect.De tout 💖 avec toi
Aboubacary Samb moi je t'estime bien dakh kou beugue Serigne Babacar beuguenala . mais je ne suis pas d'avis avec toi par ce que tourou Serigne Babacar Sy dou ay thiakhane . imagine toi nga dem anniversaire di fa toudou yonent bi ak Serigne Babacar . Gor gni ak djiguene gni diakhasso sol Aÿ yeré you bonne té béne djiguene dou thie mourou . tourou seydina mouhamed ak cheikhal khalifa dou anniversaire ak guenté moy séne place
Dafa dioum rek man khamouma histoire bi nimou demé vraiment ma ngui guiss nitt yi di wakh naan dey outt buzz soudon outt buzz dem defi mbalakh walla lenén nagn ko comprendre rek gniko ndiaboté gnou diegal ko walla gnou rectifier ko mo geuneu gnoukay weer ni diko torokhal parce que kou degg nim wakhé khamni dou yabel walla dou tayef tamit
Limouy woté deugg le si mom
Yalla molay sam bne continuation vraiment
Machallah wah dji rafétna
ndaysane nulle n est parfaite mais Alhamdulillah binga guené lèral gnou lii rek moy nité yalla na yalla samou la si barkè serigne Babacar Sy
Beug nala si sama khol mane🙏🏽😘
Machaalla wah dji rafetna ni leu réral yi dasiy bakh🙏
Bonne continuation daddy😻
Nguir YALA boul bayi mouk wayi machallah gneupa la bag
Machala Samb kadou yi rafetna
Ioe diam rk guay amm
Lo def niou interprétéko négativement
Mei sant yala rk coz kouy dem rk laniouy sonal wala diko wakhall
Bégueulaté rk mola takha diokh
Ioe nit yi niola bgueul seine bop
Dnk diam si ioe
🙏🏼🙏🏼
Machallat💝💖💕💟💞💗💓😘😍👏
MAchallah yallanala yalla diapalé. Moi j'ai un neveu de 2ans et demi qui regarde tes videos et qui saute a chaque fois. j'aurai aimé que tu le vois. Ton numéro svp
Cheikh Ndiaye beugue gua niit koubakh nio deuk sama kharite la
Abou du courage mane moride la mais damala beug trp bilaye barki Serigne fallou mbacke nitt kou nioul si bopom mon sokor j'ai vu tout les commentaires mettinama trp bassi khanamou yalla niou gne gnio la beuguel sunu bopou bare inchallah lepp dina bakh sa me fait vraiment mal bhl courage moi je te soutenir a 100/courage
Diam rek gay am inchallah samb yaniouy bégueul ❤❤❤❤
Amougnou Lou eup cheikhal khalifa ioe kepeu kouy talibé cheikh ak koku nkoul da nga dehh si kholam ndakh beugu serigne Babacar😍
Diam rekk ngay amm samb koula khamoul rek molay sedel lou kiaww mais nioune gni deuk ak yaw kham nagnoula bou bakhh. Yalla kham na li nek thi khol yi ..dina bakhhh bakry one love💟💟
kéne sédélouko lou niaw tama yii lagne wakh mou bayi ko talibé cheikh khamé wougne ko si lolou
Daouda thiam bien dit , kenn sedelouko lou niaw wayé sagne naniou guiss lou waroure niouni waroure
Touss lén té bak ko kouniouy bak seydil Aboubacar Sy dakh moko yayoo wayé naniou bayii gii🎸🎷🎹📯🎶🎵🎼🎺🎻🥁 yii lolou la mame Abdou Aziz Sy dabakh wakh instrumental bokou tchii
Bonne continuation sama sopè diam rk ga ame 🙏🙏
Du courage mon frère, le chien aboie la caravane passe, Sénégal nak mo meti bo beugué avancé yaura toujours des gens pour te barrer la route. Mais boulen falé, deugoul rek ci la nga nek goorgorloul
Sama kharit Sa Numéro dama ko perte👉Wayé mangui lay hamal ni Sou la Wahii Nit ngi Tahé Bayi Tageu Serigne Babacar Sy Bilahi Kon sa begeu Serigne Babacar Sy déss na🤚okey Aboubacar diap teuweu bayi Serigne Babacar Sy amoul tank guindaw sakaw sakanam rék incha allah C.Moulaye DABAKH NDIASSANE
Moulaye Dabakh Kounta walaye kounta sidy dabah
je t'encourage Aboubacry linguay déf nékh na amna solo .beug serigne Babacar sy bamou diekh😍💜😍🤗
@aboubacarysamb mane deih sa sopé la wayei nagnou nangou li sunu kilifeu yi diglei rk ndax moy deug..
seydi Aboubacar deih beugoul koukoy weuy di teug kone nagnouko wormal🙏..
on a rien contre toi nak ndax sunu mboukou talibei nga.deifal Lou mbaye beug gnou beug leuh diapalei la nga deim ci kaw ci kanam barkeii Cheikhal khalifa🙏
courage et bonne continuation 🙏❤️
Djiguen gni rek niolay encouragé si lingay def nakh niou bari si niom gatt khamouniou si diné folklor rek molen nekh
Abdou aziz mbaye,doudou kende,ibrahima mboup,haj mbaye dondé kou beug tagg naby dangay roy si niom
Demal nga diang bindou magg gni té té tagg yonent bi mo geun sa mbalakk mi yaw ak nienen nioukay def soff nguen ma trop
Wakh nalén ko de même facebook jigeen rek nioy apprécié naneko ay none té niom yognou gnoy ay noname. Kila wakh sangoul sa tarr la beug
TH-camur TH-cam bilahi yakarone nani loou mane rek mako setlou mais ki dafa deugeur boppou rek té niak kilifa
@@babambaye2258 Serigne Cheikh nena kou amoul kilifeu Jinné done sa kilifeu na gorgorlou deloussite wat khamé gnikoy wah likoy diarigne
On doit défendre notre tarikha.le tarikha cheikh ce n est pas n importante quoi .ce qui chante doit revoir ce qu'il chante .Il y a certains place on ne doit pas chanter Serigne Babacar Sy
Cad weuy qasida makk gni waroul nekk métier. serigne Babacar Sy bamouni sen tariqa daci tek seen métier. Li xéw yeup moy gni dieul weuyou buzz defko métier. Sétaatal sa dokhaline ndakh keurgui danioulène respecté ndakh sen topp sounna ak séllal boul nangou amfi weuy bou niaaw. Soudé sa tiofél ci Serigne Babacar Sy deuggou na toppal li ndiabootam beug, soudè deuggouwoul nak wayé xaliss ak buzz ngakoy outé mom Yalnala Yalla taxawou ndakh martabam xadioul ci yow
Nitt koudoul djioum amoul None bou am khéll moma geunal Sopé bou doff bingay déff sa Clip bobou dama Commentair ni bayilén teugg yi am gnou gatt khéll nanma lou yonénte bi bagnoul kén warouko bagn ma khamni gni khamougn lou khéw kén wédiwoul ni beugg nga Cheikhal khalifa mais beugouli tama Merci bonne Continuation🙏🏻
Machaallah nit nii léy mél bujumé dina nango jégalu
Machalla frère Serigne Babacar doula setann walayy soit rassuré
👏👏👏
Bilahi yaw khamo sa bope yaw ak musician yéna yame psk né gua da guaye way Serigne salio com ni musician yi di déf ligua begue moy dieul tourou Serigne babacar di si out beuzz rk bayil tapalee😌
Mola tanei nax kein xamoula
Awa Kane yaw da ngua am tokhou doff🤫
Jémall guissanté ak kilifeu yii. Gua wakhatane ak niome. Lougn la meuntii wakh, ak nougn la wakh rek ga deffei koo nonou. Boul top nite yi ba lorrr sa bopp. Frére. Yalla nala yalla lafal tiate
Dama beugue Mame Khalifa té kouko beugue ma beugue la té yawe dagno bokk beugue Seydi Aboubacar
C’est facile d’être derrière son téléphone et être là à dénigrer insulter une personne souvent c’est ces mêmes personnes qui le suivent partout qui le text sur whatsapp pour dire que loumouy waay dalleine neikh trop qui
L’encourage arrêtez d’être fake niit ki soko khamoul danguay Mandou si ay mbirram peut-être que khol lay wakher mais c’est très bien réfléchi cheikhoul khalifa nioune nieupa ko bokk nimako beuguer gueumnani momako gueune beug thioffeilam si Serigne Babacar gniko dieiguer deugg reik nioko meune kham bon c’est une chose de dire que mais s’en est une autre de le lynché sur les réseaux sociaux et de dire même que la personne a fait un pacte avec le diable et aussi de dire que day mboubo tarikha bi mais tarikha bi takhouko diouk enplus de cela de l’insulter de mère sa c’est vraiment trop tout sauf sa kou respecter ndey bila diour do saga ndeyou diambour deilowatte leine sein khel si yalla akk dafa mince tei amel ngueine akk kouleine defoul wakhouleine gueumnani talibe cheikh moleine ko gueuna doone gueune leine beugg cheikhoul khalifa itam il faut arreter cela dioulitte lagn avant tout tei ay mbokkoum diouliit warouniou wakhanter lou niaw rawatina niou bokk beine Tarikha mouy Tarikha cheikh Ahmed Tidiane cherif kokou deih seutou yonente la khamoul wone lou niaw nay leine di rafetal doleine deim beugoleine kouy deim louy lolou tmt kingueine di wahal di teik louneik si déram deih niit kou bakh Leuh kou am khol am yitter beuri diam yéné nieup diam itam ko khamni allalam douko boler ak keine foko feik moungui reih même gnissi gueuna ndaw sakh daleine di wayal teikssi dafa am nianou wadiour tei kou am nianou wadiour thi kaw thi kaname reik lay deim ak loleine meunti wakh tall bou yalla tall mom sani si Matt mogueune dieim ko fay kone nopalou leine si niit ki meuna loleine ko dara aduna mo deimer ni nieup meunou niou bokk beugg souko nieup beugone sakh gueumnani douko djik kone continuez de râler pendant ce temps mom mingui job di deim sa kanam ma kanam gnikoy beugg nioungui yokk de jour en jour ball bouy deim thia kaw leuh day dieing reik mais dou meusseu danou si barkep cheikhoul Khalifa 🙌🏽
Bien diiiiiiiiiiiiii best
Aboubacry inchala boko defater anniversaire dinga am lou kawe sa ndiorte yalla nama fek senegal
Diam si yow 🙏
Machallah aboubacry yalla na la yalla Sam meu
Merci le frere geste bi noble na si nangou kilif tef bi ak bayi helle say harite ak gnila sope ak sa diganték serigne babacar sy bénene ensuite kouko beug dioh conseil woko té bagne ko commenté merci de votre comprehension
Courage Yalna Yalla diapalé la
Je veux son numéro
Soko amé tu me le renvoye
Du courage
Dieredieuf Samb day bakh sakh yone yémoul si bene machalla wakh dji rafetena trop
Sénégal mo nekh djiguéne yii mome Nay nekh rekkk di ame bruit 🎷🎤 wayer mame Abdou Aziz sy nena bouguene di waye mbaye.. Minal basitine mbaye madidine mbaye kamiline mbaye bagne di tama ki sabaroo dabakh moko wakh Mani xolatal boubakh Lou magui tarikha bi beugg gua nekk si wasalam
Man dh taliber serigne touba la wayer sopeu naleu loll legui leral yi Amna solo lol lithi dess t malakoy gnane gua dem thi serigne bi djiegualou ko leral lal ko man man bigua liguay def motakh faw gnoulay sosal ndakh koufi bakh mba gua bakh gnou sosal khol ko thi sa serigne khol ko si sma serigne khol ko si kep kou bakh courage koubakh yalna yaleu diapalé
De tt coeur avec toi frere arreté boulko sakh xalate tagg serigne gua xam moy sa tarbiyou si babacar sy
Saway meune nga wayei ! Pour wax la deug rek Teug bi ngaay baayi!! Keur maodo ken xaméw len li!! Issa laye , mbay ndonde , Doudou kende, Abdou aziz mbay ken massu si Teug té meune naagnu lignuy df , xaana beugo doug ci Zawiya bi di Wooy??! Teug bokul ci gnune mbok vraiment
J'aime SBS
Nio la beugue ba paré té Dara dou KO dini yalla Lou mou beugue si nit kéne mounou si Dara du courage nio gui sa guinaw
Mame Abdou né bolénko hinanle té bolén balakh balén sabaryi
Yaw kham ga li mame abdou wakhone thi kouy way serigne babacar s'y pourquoi do dieufé lolou,boul topou sa bakane niepou diamou lane la yéné, s.babacar limou bind meuno ko diékhal kone bayile sabar yi ak tabalayi té oubi xasida yi👏👏
Danga rafet nak bilay walay
Nobou Mala nak mais damay apprécier rek
Super abou diam si yaw