Bilakhi babacar wakhal waaye noooooon tahirou sarr changement bi mo gaww yaww si 24 heure ak ligua wakh lèpeu si lou bakh si nit ki saga yimou ko saga ak khass yii noooooon mais c choquan
Mane dei barki yalla bilakhi dèmb si goudi j'ai rever de tahirou sarr parceque tellement je suis choquè par les propos de tahirou sarr kouma wakhone ni nit ki ak limoufi wakh lèpeu dina saga PROS ak aye revelations yo kham ni noooooon tè limasi mèti moye keine toudoul toureum ba parè sonko wakhoufi dara lou nianww lou takh li moufi wakh lèpeu il ma tros dèçu trooooooos
38:32 Mais Diallo ds quel Sénégal tu es ??? Vous avez pas senti PASTEF Dakar 😳😳😳😳 des fois on se pose des questions sur la pertinence des analyses bref chacun son appréciation
La vérité en ai que wadji messoul geum Sonko
C’est exactement ça meussou koo geum, je l’ai toujours dis aux patriotes
Diallo wakh na deugue
Thirou Sonko attaque wuko de, da koo kobas rekk 😢mu far yulli li ci xol bi lépp 😴
Je suis pastef mais Les Guinéens sont tellement nombreux
Bilakhi babacar wakhal waaye noooooon tahirou sarr changement bi mo gaww yaww si 24 heure ak ligua wakh lèpeu si lou bakh si nit ki saga yimou ko saga ak khass yii noooooon mais c choquan
Babacar démala fan ya mane diallo
Sonko sotina thiouraye deumm bi soko sotee rek gaayi fegn theuy mou seleu me
Tahirou defa rew rek ms xamoul koum ko seikal 😂
Sonko Dakoo dóor mu xëm
❤❤❤❤❤❤
Sonko
Mane dei barki yalla bilakhi dèmb si goudi j'ai rever de tahirou sarr parceque tellement je suis choquè par les propos de tahirou sarr kouma wakhone ni nit ki ak limoufi wakh lèpeu dina saga PROS ak aye revelations yo kham ni noooooon tè limasi mèti moye keine toudoul toureum ba parè sonko wakhoufi dara lou nianww lou takh li moufi wakh lèpeu il ma tros dèçu trooooooos
Kone dh nio yaam … lima teud yeup wakhou tahirou yi ladone deegaat 😢
@@mariemedieng5913 dangeena wara tàmbli ci sonko yam ci sonko Kassé
Tay weeraanté gueine kheuyé
Diallo yoe khana bokou gnou dakar bignou nek
Diallo de bagne opposition méré ko mo takh dina wakh louné comprends ko rekk dafa beugg niépp content
Diallo moko wakhon
38:32 Mais Diallo ds quel Sénégal tu es ??? Vous avez pas senti PASTEF Dakar 😳😳😳😳 des fois on se pose des questions sur la pertinence des analyses bref chacun son appréciation
Je ne suis pas d'accord aussi avec la forte présence des Libanais
Tahirou sar Il est indiscipliné