clips officiel Tawfekh mbaye woyal : ( mbaaye woyal )

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 23 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 372

  • @astoudiop3254
    @astoudiop3254 4 ปีที่แล้ว +69

    Nekh na lol machallah kou beug tawfekh beseul jaime

  • @minambaye9052
    @minambaye9052 3 ปีที่แล้ว +11

    Tidiane la dh ms way bi dafma néx tellement yalla na yalla weral sa bat🙏🥰❤️😍

  • @amintambayembaye7181
    @amintambayembaye7181 4 ปีที่แล้ว +48

    Machallah tawfekh gneupp contente nagne kou waye wi nekh rekk beusseul jaime

  • @sonhiboundiaye2154
    @sonhiboundiaye2154 6 ปีที่แล้ว +11

    Machalla tawfex nekh na lol mouride inchalla lepp dina bakh inchalla barcké serigne Saliou

    • @naboufaye2654
      @naboufaye2654 4 ปีที่แล้ว +1

      😭😭😭😭😭👂👈

  • @meumeusalioufall121
    @meumeusalioufall121 6 ปีที่แล้ว +18

    Thiey Tawfekhe Mbaye Totch Ngafi Waaaw Goré Waaaye Yalna Serigne Saliou Wéreul baate bi Bégué Nala bou wér

  • @rackysarr8194
    @rackysarr8194 4 ปีที่แล้ว +138

    Sui talibe cheikh mai cette chanson c juste waouhhhhhh🤩🤩🤩

  • @thiernolo3734
    @thiernolo3734 6 ปีที่แล้ว +22

    Machalla thiey serigne saliou mo yemer 😍😍😍dieureudieuf tawfekh yalnala serigne touba same banga yegali ak sa sago

  • @kenyssecretskharitoudiekkd5817
    @kenyssecretskharitoudiekkd5817 4 ปีที่แล้ว +3

    Tay d lay doga khamni tawfekh mo way way wi
    Machalah

  • @fatoudiop2975
    @fatoudiop2975 4 ปีที่แล้ว +4

    tawFex sa fans la depuis Italie souma gneuwé Sénégal inchallah dina weur sa keur ba guis la dama la beugu rek tei yalla takh nio bokou Serigne saliou

  • @mariemethiam8491
    @mariemethiam8491 4 หลายเดือนก่อน +2

    Manchallah j’ai jamais su c’est lui Allahouma barik nexna❤❤❤🙏🙏

  • @AngeGabriel05
    @AngeGabriel05 2 ปีที่แล้ว +28

    J'ai découvert ta chanson dans une publicité de ton programme sur Zik FM... mais à peine G entendu ta voix waouhh😭😭 G validé grave
    Ma Shaa Allah🙏🏾

  • @fatouniang5603
    @fatouniang5603 2 ปีที่แล้ว +3

    Tawfekh nekhna trop mo dak si way yi machala bonne continuation

  • @Aliougueye966
    @Aliougueye966 ปีที่แล้ว +6

    J suis Talibe cheikh mz cette chanson c’est autre chose machalla way nxn vraiment wayyyy❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉

  • @ndeyesalioudiop6348
    @ndeyesalioudiop6348 4 ปีที่แล้ว +48

    Ndaysane sama xoll dafa sedd billahi s. Saliou si xoll

  • @diborndiaye1584
    @diborndiaye1584 3 ปีที่แล้ว +39

    J'ai cherché pendant très longtemps cette chanson machalla

  • @tawfekhmbaayeofficiel
    @tawfekhmbaayeofficiel  6 ปีที่แล้ว +275

    Je vous remercie pour vos commentaires sur cette page. Content na thi commentaires yii di lénn wakh ni am na yénéne youy niew inchalla.
    Di nian serigne bethio yagu fi

    • @jules1831
      @jules1831 6 ปีที่แล้ว +4

      tawfekh mbaaye officiel khadim
      mbengue

    • @mbackediagne8575
      @mbackediagne8575 5 ปีที่แล้ว +3

      😭😭😭

    • @bnoitbadiane7386
      @bnoitbadiane7386 5 ปีที่แล้ว +3

      mane dhee beug nallla lollll yak serigne saliou thioune sama 005551992910158

    • @maguettembaye7503
      @maguettembaye7503 5 ปีที่แล้ว +2

      Machalla mala beug lol té serigne Saliou takh

    • @mohamidfall2652
      @mohamidfall2652 5 ปีที่แล้ว +2

      @@jules1831 22 647

  • @aisambaye4746
    @aisambaye4746 6 ปีที่แล้ว +55

    mbaaye woyal ndam RK ci brki Serigne saliou nekhna trop

  • @mariemesoda7526
    @mariemesoda7526 6 ปีที่แล้ว +17

    Ma Shaa Allah.. Waay bi dafmay daanel billahi ♡
    Yalna batt bi weer waie Tawfekh

  • @ndiobalogueye5593
    @ndiobalogueye5593 6 ปีที่แล้ว +36

    Mach'Allah nekh na trop Dieureudieufei #SERIGNE SALIOU

  • @amadouly50
    @amadouly50 6 ปีที่แล้ว +8

    Machala tawfx .laf tiat si barkèp S Béthio

  • @gueyefvtoush6844
    @gueyefvtoush6844 6 ปีที่แล้ว +7

    di niani Diên amna louke guen kat fékhélakham naniouy napé Diên kon d mbaay wayall thiey serigne saliou

  • @ndeyecoumbadiouf6116
    @ndeyecoumbadiouf6116 3 ปีที่แล้ว +2

    mane dè lima dal moy douma doyal si way bi dou xèwi mouk tawfekh yalana bate bi wère foko watè rk xalatemasi coumba diouf touba citè millionnaire❤

  • @matydiaw4390
    @matydiaw4390 6 ปีที่แล้ว +5

    Wawaw aka meune limouy def machanllah

  • @sexygirl9471
    @sexygirl9471 4 ปีที่แล้ว +20

    Je ne peux arrêter de regarder la vidéo néxna trop Macha'Allah

  • @malenediagne517
    @malenediagne517 4 ปีที่แล้ว +8

    salam way bi damako weur weur ba sone machaAllah way bi amena solo nexna

  • @a.c.t.3817
    @a.c.t.3817 6 ปีที่แล้ว +4

    Wawaw nekhna Djadjef mouride ndam Serigne Bethio yalla nafi yagg tewer thi Barke Serigne Saliou

    • @a.c.t.3817
      @a.c.t.3817 6 ปีที่แล้ว

      Malaraw Sokhna fatoumata nodef

    • @a.c.t.3817
      @a.c.t.3817 6 ปีที่แล้ว

      775387427

  • @ouleymatafall5271
    @ouleymatafall5271 5 ปีที่แล้ว +6

    Machallah langa wooy rekk ci Serigne saliouh séedd na xol ...

  • @aichakane7964
    @aichakane7964 ปีที่แล้ว +2

    Chuis talibé cheikh mais j'adore cette chanson

  • @maniangkane3993
    @maniangkane3993 6 ปีที่แล้ว +5

    nèkh na lool yalla na baat bi gueneu wer ci barkep cheikh bethio

  • @ndeyefatougueye2502
    @ndeyefatougueye2502 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalla nehna trop yalla wereur bate bi rk thi barké serigne bamba khadim rassoul

  • @fatidiallo3213
    @fatidiallo3213 3 ปีที่แล้ว +48

    Vous avez une belle voix que Dieu veille sur vous 🇸🇳🤝

  • @Diassehjkjgdxcbkutfvj
    @Diassehjkjgdxcbkutfvj 3 ปีที่แล้ว +3

    Weurr nako ba sonou😂 waaawaw💪🏾💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽

  • @toushkardash4912
    @toushkardash4912 6 ปีที่แล้ว +4

    Mashalah tawfekh yalna Sérigne bi wereul batbi wae🙏🏽🙏🏽 nexna torop

  • @chiekhfall3014
    @chiekhfall3014 4 ปีที่แล้ว +2

    Frenchement Mane Tidiane la mais j'aime cette chason machala nékhna trope

  • @dababeye1451
    @dababeye1451 4 ปีที่แล้ว +16

    Ma challah son bi nekhna yalna bat bi were

    • @khadygueye9409
      @khadygueye9409 7 หลายเดือนก่อน

      En 2024 où sont les salihates(salihats)❤🎉

  • @cheikhniang4985
    @cheikhniang4985 4 ปีที่แล้ว +6

    vraiment chanson bii dayy daw sama yaram boubaxx ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @sidymatarkhouma8357
    @sidymatarkhouma8357 6 หลายเดือนก่อน +1

    jeureujeufė Serigne Saliou ❤️🫶🏼

  • @katydiop7
    @katydiop7 3 ปีที่แล้ว +23

    Bonsoir je suis tombée sur votre chanson. J'en ai la chaire poule mashalah nekhna 🙏🏽🙏🏽🙏🏽

  • @madiagundogan809
    @madiagundogan809 3 ปีที่แล้ว

    Barké cheikhal Khalifa doumasi doyal Taw fëh mbaye doundeul weral mouthieul rawal

  • @mamadoudiagne3656
    @mamadoudiagne3656 3 ปีที่แล้ว +1

    Loutakh son bi douma ci doyal yalna serigne saliou weral baat

  • @walymar-ln6hv
    @walymar-ln6hv ปีที่แล้ว +1

    Yalna yalla wereul batt bi machallah 🙏

  • @abdoulayeniang10
    @abdoulayeniang10 ปีที่แล้ว

    Guir yallah tontou ma way liguay way yakko tay❤❤❤

  • @mayadiagne8935
    @mayadiagne8935 3 ปีที่แล้ว +1

    Machalah tawfékh li ngay weuy da nga ko yeug way

  • @famoustaphafayeba9350
    @famoustaphafayeba9350 6 ปีที่แล้ว +4

    Dieureudieufati serigne saliou kennn gua sine thioune yaggg fi lolllll

  • @belle7382
    @belle7382 4 ปีที่แล้ว +5

    Mashallah lii nekhna looll waay

  • @mouhamedlam7083
    @mouhamedlam7083 5 ปีที่แล้ว +3

    Mbaye wayale sa kaw serigne bethio rék mo mata wayy

  • @maremendoye3708
    @maremendoye3708 6 ปีที่แล้ว +6

    Machalla yalans bat bi gueneu weiir si barkep Serigne saliou

  • @ibrandiaye7689
    @ibrandiaye7689 3 ปีที่แล้ว +2

    Macha allah ly nekh na 🥰🥰🥰🥰😅

  • @Secretfemmeafricaine
    @Secretfemmeafricaine 4 ปีที่แล้ว +4

    Macha'allah khol nekhhhhh na they Borom khelkom

  • @sognacoulibaly6567
    @sognacoulibaly6567 6 ปีที่แล้ว +5

    Machalah tawfekh ndam rek inchalah machalah

  • @alimandiaye4438
    @alimandiaye4438 2 ปีที่แล้ว +3

    Békna ,machalla,dieureudieuf borom khelcom serigne saliou.

  • @adameloum46
    @adameloum46 6 ปีที่แล้ว +4

    Laff thiate machallah yallah na bate bi gueune weer si barkè CHEIKH BI

  • @BinetaDjite-cp8xk
    @BinetaDjite-cp8xk 6 หลายเดือนก่อน +1

    dieureudieuf serigne saliou mbacké ❤

  • @yacinegueye6432
    @yacinegueye6432 3 ปีที่แล้ว +1

    Mashaalah tawfekh ak tayssir rek

  • @gagnadoba2329
    @gagnadoba2329 8 หลายเดือนก่อน +1

    Machalla ❤❤bamba reck diewrigne Ass Ya me meune

  • @rokhayalo225
    @rokhayalo225 6 ปีที่แล้ว +2

    Nekhna tawfekh yalanala yala may tawfekh

  • @evistandiaye7455
    @evistandiaye7455 6 ปีที่แล้ว +27

    FRANCHEMENT MANE MOME MAGUI SI BIRR FANS NEKH TROP MBAAY

  • @thieckapene2177
    @thieckapene2177 5 ปีที่แล้ว +6

    Machallah son bi limoko weur

  • @tanorafricain
    @tanorafricain 3 ปีที่แล้ว +12

    vraiment il à une belle voix diareujeuf srg saliou 🎤

  • @sokhnasaliou7859
    @sokhnasaliou7859 6 ปีที่แล้ว +5

    Machallah neexna deh mbaaaaaay loool sax ba takadioo

    • @papelo8697
      @papelo8697 3 ปีที่แล้ว

      ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️👍👍👍👍👍

  • @amiendiaye6027
    @amiendiaye6027 6 ปีที่แล้ว +5

    Machallah nekhna lol tawfekh

  • @Legendsai-7
    @Legendsai-7 ปีที่แล้ว +1

    Tawfex dafa meilleur quoi ❤

  • @khadijandoye8366
    @khadijandoye8366 5 ปีที่แล้ว +14

    Doumaci doyal franchement je l'aime way

  • @telmatambedou9649
    @telmatambedou9649 2 ปีที่แล้ว

    Tawfékh dale ndanane la la sha Allah, bonne continuation!

  • @sokhnaadjasaliouseck1027
    @sokhnaadjasaliouseck1027 6 ปีที่แล้ว +5

    Manchalla diamou Serigne Bethio saliou nice trop

  • @maguettembaye7503
    @maguettembaye7503 5 ปีที่แล้ว +13

    Machalla nékhna trop

  • @vieux3972
    @vieux3972 2 ปีที่แล้ว

    Yaa goreee cheikh bethio rek ngayy woyy woutengakk gnimaaa kham woyann rekk

  • @modoubayefall3177
    @modoubayefall3177 6 ปีที่แล้ว +7

    Nice na trop machallah yalna yok

  • @mbarcisse3595
    @mbarcisse3595 6 ปีที่แล้ว

    Diadieuf yalla n'a serigne yook la si barkep serigne saliou

  • @DabaMouhamed
    @DabaMouhamed ปีที่แล้ว

    Dieureudieuf mouhamed niang mou serigne saliou mbacke yague fin lol te wer ❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤

  • @dabz3318
    @dabz3318 6 ปีที่แล้ว +5

    Kone dé Mbaye wayaal, nekna ci khol

  • @jilidieng3722
    @jilidieng3722 6 ปีที่แล้ว +1

    Euskeuy nekhna lolou tawfekh Abdou Khadre dwr Cheikh Bethio Touba Hollande

  • @ndamadiop5018
    @ndamadiop5018 5 ปีที่แล้ว +3

    Ma challa codé Mbaye s saliou rék

  • @fatoudiagne1045
    @fatoudiagne1045 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla na badd bi wérr

  • @yacinesene9516
    @yacinesene9516 6 ปีที่แล้ว +3

    machala nékhna dou ma si doyale serigne bi yague fi lole

  • @ndeyefatouwar9357
    @ndeyefatouwar9357 3 ปีที่แล้ว +1

    Machallah serigne saliou si xol❤parole yi moma gueneu nex si way bi may ma dieune wanema nougnekoy napee ko guene😍🥰

  • @mbayedonde7338
    @mbayedonde7338 5 ปีที่แล้ว +3

    Machallah way bi nékh na trop

  • @salysaliouthiounembacke7953
    @salysaliouthiounembacke7953 6 ปีที่แล้ว +4

    Ndaysan nekhna lol thioune yague fi te wer

    • @awabadiane1401
      @awabadiane1401 6 ปีที่แล้ว

      Dafma woron ni commentair nga😂😂

  • @sallandiaye7340
    @sallandiaye7340 3 ปีที่แล้ว +4

    Tawfékh yakk moukhamèd niang dangène ma nèkh ndakhté kouye wakh thi s saliou dafmaye nèkh ♥️♥️

  • @bueguestouba3634
    @bueguestouba3634 6 ปีที่แล้ว +4

    lii nekh na torop

  • @dadosow2737
    @dadosow2737 4 ปีที่แล้ว +4

    Koorgui 2020 machallah nekhna trop sakh dieureudieufè serigne saliou

  • @gnimalybadji4458
    @gnimalybadji4458 3 ปีที่แล้ว

    Je me retrouve ici apres tik tok!!

  • @abrahamtvvila810
    @abrahamtvvila810 4 ปีที่แล้ว

    Manchala tawfekh l'i nèkhna

  • @sagnsesenegaltv
    @sagnsesenegaltv 2 ปีที่แล้ว +1

    Tawfékh il est meilleur 😢❤❤❤❤❤

  • @birahimsoldaroussaliou117
    @birahimsoldaroussaliou117 6 ปีที่แล้ว +39

    Qui à aimé avent d'écoute??

  • @khabane8
    @khabane8 6 ปีที่แล้ว +3

    ndeysane lii nekh naaa wayyyyyyy

  • @haajidsylla9863
    @haajidsylla9863 3 ปีที่แล้ว +16

    Sa werekane bi mo diougueti
    Bindate fi wayfi sougnou sangue bi
    Hamnani sah dou way koula moy
    Ndakh bate bou nekh bi yagnouko may
    Billai warone nama mana way
    Ba wayla mane lima beugue way
    Ndakh aire you nekh yi gayi di waye
    Gnenene gni yaw lagne ko wara way
    Koufi way kenene koudoul kima way
    Khamal ni way weundel nathi diay
    Kou way kenene koudoul kima way
    Ko meune Di waye ki yako may
    Di gnani djeun amna louko guene kate
    Fekhela kham nagnou napei djeun x2

  • @ndeyebounamadiop5863
    @ndeyebounamadiop5863 3 ปีที่แล้ว

    Non wakeur cheikh bethio maachaala

  • @yafatougadio8617
    @yafatougadio8617 6 ปีที่แล้ว +6

    Bonne continuation mbok talibé

  • @coumbasow300
    @coumbasow300 3 ปีที่แล้ว +1

    Suis talibe cheikh mé dal machallah wallakhi

  • @coumbasarr2843
    @coumbasarr2843 6 ปีที่แล้ว +6

    They serigne kene dou mome ❤

  • @khadygueye9762
    @khadygueye9762 6 ปีที่แล้ว +3

    machala amna sens trop sikou ame deg bne continuation

  • @amytine578
    @amytine578 6 ปีที่แล้ว +7

    Machalla bon continuation

  • @adamadiop7852
    @adamadiop7852 5 ปีที่แล้ว +16

    Ça touche directe au coeur

  • @ndeyesokhnaamar6958
    @ndeyesokhnaamar6958 3 ปีที่แล้ว +7

    Vraiment j'adoreeeee cette chanson 👍👌💓💓💓💓. C'est trop bon

  • @ndeyefatoudione8109
    @ndeyefatoudione8109 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalah Tawfekh nexna trop j'adore 🥰🥰🥰🥰🥰❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MamediarraSagnar
    @MamediarraSagnar 7 หลายเดือนก่อน +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤ 3:33 ❤❤❤❤❤❤ 3:36 🎉🎉🎉🎉

  • @mbayelenoble4148
    @mbayelenoble4148 4 ปีที่แล้ว

    Bilay dama beug takh ni g beug Serigne saliou

  • @coumbadiop9949
    @coumbadiop9949 6 ปีที่แล้ว +3

    Nekh na trop machallah

  • @nogayediallo3037
    @nogayediallo3037 6 ปีที่แล้ว +3

    ah machallah nexna lol mbaye wayal