TAWFEKH MBAYE Clip officiel "18 SAFAR" NAGNOU THIATOU

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 23 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 814

  • @morwakanahaqqan6585
    @morwakanahaqqan6585 4 ปีที่แล้ว +686

    Kou si yeuke nè Serigne Saliou dèfar nala wanèl sa bopou niou guiss🙏

  • @maguiseck4950
    @maguiseck4950 4 ปีที่แล้ว +22

    Bilahi bâche na founei thioune bethio yalla na firdawsi di keureum sagal naniou topato wa dianatou ❤️❤️

  • @only_child_officiel3822
    @only_child_officiel3822 4 ปีที่แล้ว +311

    Bamba si khôl❤️
    Mouride si khèl🧠
    Talibé si djiko😌
    Xassida si lokho🤲🏾
    Aldiana sunu demain😍
    Sadikh sunu chemin💕
    Massalik sunu succès💫✨
    18 Safar sunu yitté🌹
    Magalou jamm🙏🏽❤️
    Dieureudieuf Serigne Saliou❤️🙏🏽🤲🏾

  • @soxnandao2194
    @soxnandao2194 4 ปีที่แล้ว +268

    Suis Talibé Cheikh mais j'aime énormément Serigne Saliou❤️barki yonentibi
    Tawfekh man Mala beug li ngay weuy machala yala n'a yala weral bat bi 18 safar mbecté djoulit yeup

  • @kadiasy9860
    @kadiasy9860 4 ปีที่แล้ว +142

    Je suis talibé cheikh mais son bi si xol lay dougou dieuredieuf serigne saliou❤ bon magal à tous yalna gnu yallah ték si yonou diam té niewatt akk diam si barké seydina mouhamed (psl)

  • @oiaftv
    @oiaftv 3 หลายเดือนก่อน +3

    Je viens de le dėcoivrir ak son validė bii mais il est fort machallah🎉❤

  • @maimounafall3956
    @maimounafall3956 4 ปีที่แล้ว +832

    Ani talibe s saliou yi basal j'aime may guis

  • @khadijalo8182
    @khadijalo8182 4 ปีที่แล้ว +15

    Thieuy yalla sama mak dji lo wayoul bakhoul barki serigne saliou mbacke yalla nala yalla lafal thiat barki serigne saliou

  • @zeynasalioufallfall4883
    @zeynasalioufallfall4883 4 ปีที่แล้ว +5

    Non li ray nama barky s saliou machalla tawfekh yalla na yalla wèral bateu bi si barky s saliou

  • @sowsadio698
    @sowsadio698 4 ปีที่แล้ว +74

    Mangui koy mayy wa Fondation Sope serigne saliou F3S zone yeup ci aduna bi surtout wa zone Thies ......kou beigg ci tawfex mbaye beusseul j'aime

  • @ndeyesokhnasane5017
    @ndeyesokhnasane5017 4 ปีที่แล้ว +7

    Machalla naa bettte gueneu weurrrrr gua yague nio beugeeul ..Cheikh Bethio li yeup iowww yalla naniou yalla tasss sa barké..

  • @mayacinecisse4211
    @mayacinecisse4211 4 ปีที่แล้ว +10

    Mashallah li nexna wayy ....
    Dieuredieufeti Serigne Saliou ❤️🙏

  • @MamanFall-co6pc
    @MamanFall-co6pc 4 หลายเดือนก่อน +3

    8août 2024 Mane tidiane Bou beugu trop Serigne saliou Serigne béthio ak baye abdou Karine😍❤️😍❤️

  • @bsttbd1731
    @bsttbd1731 4 ปีที่แล้ว +11

    Thieuy Tawfex Mbaay Yalna la boroom bi taxawu barkep ahmaduna salihou

  • @lovemamma9644
    @lovemamma9644 4 ปีที่แล้ว +35

    Ndeyssan tawfekh ya bakh tè gnak kignane Yalla nga ame ngeureume ci barkep Cheikhe bethio sa sangue ba diamou Serigne saliou mbacke

  • @amyngom2888
    @amyngom2888 4 ปีที่แล้ว +4

    Ana sama mbokou thiantayi fi serigne saliou thioune yallana fi yagui

  • @fatou_khalifa2142
    @fatou_khalifa2142 4 ปีที่แล้ว +36

    Bilay mane damala fan trop tawfekh kou beugue sa numéro noumouy deff

    • @abdoulayekante4891
      @abdoulayekante4891 4 ปีที่แล้ว

      Aymh zf😍😍😍😍😍😍😘😍😍😍😍😍😘😗💓❤❤❤❤❤💗💖💖💕💗💞💟💓

    • @abdoulayekante4891
      @abdoulayekante4891 4 ปีที่แล้ว

      😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍eyziefgisfyidt

  • @yayefall5777
    @yayefall5777 4 ปีที่แล้ว +12

    ❤❤😍😍tawfekh mbaye yagal yokal weral barkep sr saliou mbectei salamatane ❤❤❤❤❤❤

  • @matydiagne2113
    @matydiagne2113 4 ปีที่แล้ว +10

    Machala mbaye wayal laf thiate si kanam thi kanam thi Lou bakh rek

  • @papemoukhymbaye4213
    @papemoukhymbaye4213 4 ปีที่แล้ว +21

    yalla na suñiou borom Yookk lerram si barkep serigne saliou😍😍😍

  • @bassirouniang8473
    @bassirouniang8473 4 ปีที่แล้ว +7

    Macha allah yall na la yallah lafal tiat kou beug tawfex beussal j'aime ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @kheweulmbaye5859
    @kheweulmbaye5859 4 ปีที่แล้ว +42

    Ndeysan tawfekh lepp bakhna

  • @bollodiallo8194
    @bollodiallo8194 4 ปีที่แล้ว +96

    Walay magal ko warna ndakh ki woté gnou magalaleko beusseum bi diarnako amoul loumou défoul amoul loumou dadioul pour l'islam , gnou Safar si diam inchalla , wakhi TALIBÉ CHEIKH machalla diam si yen mouride Yi ,

  • @fatou_khalifa2142
    @fatou_khalifa2142 4 ปีที่แล้ว +29

    Ohh tawfehh mbaye kene yow kou beugue tawfekh beusseul j'aime

  • @antadiop8878
    @antadiop8878 3 ปีที่แล้ว +2

    Tawfekh mbaye damaka begue rek ta yalla takhe

  • @bintambengue6829
    @bintambengue6829 4 ปีที่แล้ว +7

    Tawfekh mbaye yalna batte bi wére si barque serigne saliou

  • @aichandiaye7867
    @aichandiaye7867 3 ปีที่แล้ว +2

    Bilay tawfékh doto way chanson bou dakh bi machalla yalnala yalla défal diam té wéreul baate bi

  • @aidasalioundiaye8096
    @aidasalioundiaye8096 4 ปีที่แล้ว +8

    Li nékh n'a sa 💘❤💖💟💞💝💗💕💓☝sante MM saliou rék 👆machalla tawfekh yalla nala yalla défale tawfekh 👌

  • @coumbizadiack6182
    @coumbizadiack6182 4 ปีที่แล้ว +13

    Machallah mane dama beugue serigne Saliou mbacké baa beugue koo koo beugue

  • @khalifadiop4175
    @khalifadiop4175 4 ปีที่แล้ว +3

    Masahllah tawfékh yalla na yalla defall la diamo si barké serigne touba khadim rassoul amine

  • @keurmamesalliou529
    @keurmamesalliou529 4 ปีที่แล้ว +10

    Ndiayesane li nékh na looll barke Serigne salliou ❤️ Année way guir Borom Touba

  • @dabafall2909
    @dabafall2909 4 ปีที่แล้ว +48

    Kou beugue s saliou beseul j'aime

  • @quintinonhaga7807
    @quintinonhaga7807 4 ปีที่แล้ว +6

    Macha allah tawfekh sama tonton l'y nekhna trop laff thiatt

  • @ndiakhatesaliouniang261
    @ndiakhatesaliouniang261 4 ปีที่แล้ว +6

    Mancha allah 😍😍😍😍😍yalla na yalla wéreul baat bi si barkei serigne saliou mbacké ❤😍😍😍

  • @mamadoulamaranadiallo98
    @mamadoulamaranadiallo98 4 ปีที่แล้ว +12

    kou beug Serigne Saliou beussal j'aime ma xol🥰🙏👌📿

  • @likalika4698
    @likalika4698 ปีที่แล้ว +14

    Je suis tidiane mais j'aime bien mouride❤️❤️❤️🙏

  • @bambasarr7342
    @bambasarr7342 4 ปีที่แล้ว +12

    Mashalla le 11 août gnifa taxawon gneup xam nagnou ni thianta la gua déplacer Touba ba DK guir sante léma Cheikh bi rek Diadieuf Mbaye c Zeyna dinala wo nak

  • @papesambe1556
    @papesambe1556 4 ปีที่แล้ว +47

    NDEYSAN TAWFÉX DALL TAWFÉX REK BARKEP SERIGNE SALIHOU

  • @fatmambaye7382
    @fatmambaye7382 2 ปีที่แล้ว +4

    J'adore cette chason billahy yalna sa diame yagg barké Serigne Saliou

  • @ndeyeisseudienne5936
    @ndeyeisseudienne5936 4 ปีที่แล้ว +2

    Machalla Tawfex ak taïsir rek bilay son bi mom rk lay dégou bolékok aye poth😁 Thiakaw thia kanam rek si Lou bakh barké Serigne Saliou🙏

  • @Aminilove0711
    @Aminilove0711 4 ปีที่แล้ว +10

    J'ai pas l'habitude de faire des commentaires je suis aussi tidjiane mais j'adore trop ta chanson elle est juste merveilleuse Macha Allah bonne continuation

  • @saladieng4538
    @saladieng4538 4 ปีที่แล้ว +3

    Machalla gor gorlou wat léne thi jiguéne gni séne bopou néne yi

  • @brahamiennelum3612
    @brahamiennelum3612 4 ปีที่แล้ว +24

    Lii nekh na si khol ani Sama mbokou WAKEUR CHEIKHOUL TIDIANE na bleu

    • @thiounafaye6117
      @thiounafaye6117 4 ปีที่แล้ว +1

      J s layenne ms j aime cette son

  • @awandiaye988
    @awandiaye988 4 ปีที่แล้ว +10

    Ayyyy wayyyy mbaye doukate naaa baa sone keine dou iow kirrassouroulay 🥰

  • @khadysall6436
    @khadysall6436 4 ปีที่แล้ว +8

    Je suis talibé cheikhna cheikh saadbou mais j'aime Serigne touba et sa famille

  • @aminatalo1818
    @aminatalo1818 4 ปีที่แล้ว +15

    Mashalla Serigne Saliou defar na kou nekk😭

  • @fatoubintoundiaye3611
    @fatoubintoundiaye3611 4 ปีที่แล้ว +49

    Machallah clip bi nex na yiw na mouritei na bamou bari dolei😍

  • @awasylla8848
    @awasylla8848 4 ปีที่แล้ว +9

    Damala beug barki serigne saliou mbectè rk mba yènagui wadj magal gui inchalla😘💖🙏

  • @yamaseck2753
    @yamaseck2753 4 ปีที่แล้ว +6

    Yalla na yalla doli dèfar bat si barki s saliou ❤️❤️❤️🌹🌹🌹❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤚🤚🤚🤚❤️❤️❤️

  • @astougueye8499
    @astougueye8499 4 ปีที่แล้ว +13

    Machallah kene dou serigne saliou sama sangue bi

  • @aminatakasse6640
    @aminatakasse6640 4 ปีที่แล้ว +6

    Maachalah yalla na bat bi geuneu weur béguatinagnou

  • @aliounethiamboxeur6994
    @aliounethiamboxeur6994 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalla Tawfekh yalla nala yalla lafal thiat si barki serigne saliou son bi nexx na lol

  • @seynabouthiam4600
    @seynabouthiam4600 4 ปีที่แล้ว +2

    Tawfekh Mbaye yalla na yalla goudal Saw fane barki Serigne Saliou❤❤❤

  • @santeyallatv9117
    @santeyallatv9117 4 ปีที่แล้ว +45

    Diadieuff tawfekh mbaye clip bi nékh na lol Diadieuff

  • @aidasalioundiaye8096
    @aidasalioundiaye8096 4 ปีที่แล้ว +12

    Ila touba inchalla 18 safar wawawe 💪💪💪

  • @dembadiallo1312
    @dembadiallo1312 4 ปีที่แล้ว +1

    Machallah tawfekh yallah na yallah wéra pat bi thie barké s Saliou

  • @ngoneseye6939
    @ngoneseye6939 4 ปีที่แล้ว +3

    Waw waw daniouy Safar bamou nekh ❤❤❤🤝🤝🤝🤝🤝💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽inchala a 🤲🤲🤲🤲🙏🙏🙏🙏🙏

  • @bourysalioudia9214
    @bourysalioudia9214 4 ปีที่แล้ว +10

    Mancha Allah mbaye yañiouko tamal dé❤🥰😭🙏👌

  • @astelldiakhate5549
    @astelldiakhate5549 4 ปีที่แล้ว +1

    Tawfekh Mbaye mi est ce que doumako tèral thi limou wakh thi wa Diakhaté tamite machalah dall

  • @boromhlm6864
    @boromhlm6864 4 ปีที่แล้ว +7

    Tawfekh moy c f kou d'accord jaim

  • @mamediarraseck2548
    @mamediarraseck2548 4 ปีที่แล้ว +24

    Khol sédatina
    Dieurédieufeuti Cheikhoul Khadim

  • @salimataka1595
    @salimataka1595 4 ปีที่แล้ว +11

    Nice n’a de Tawfekh c’est Saly khadim Mbengue

  • @ElMessiaofficiel
    @ElMessiaofficiel 4 ปีที่แล้ว +3

    Akassa way😍...wakh di yokou boudé thiat,nagn niou Thiatou😍 Thiey Serigne Saliou💕
    lolou barina💌
    #DMBCONGRAT✌️
    Thiég in💥

  • @senegalrek5805
    @senegalrek5805 4 ปีที่แล้ว +2

    🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰machalla yal na yalla yokou takhawaay bi si barkép serigne salihou mbacke contane nagne dh 🥰🙏

  • @mamediaratoure596
    @mamediaratoure596 4 ปีที่แล้ว +1

    yii tawfekh li mom nekhatina machallah kein dou sama sangueu bi serigne saliou mbacke

  • @mbayediakhate5108
    @mbayediakhate5108 4 ปีที่แล้ว +4

    Tawfekh mu Serigne saliou gathia ngalama liii keen xamoul lanleu soo yi nga bolé mooo raw cas communautaire

  • @amiengom495
    @amiengom495 4 ปีที่แล้ว +27

    Machallah sant Serigne Saliou Mbacké mbecté ak tawfekh 😍🙏🏽

  • @BAMBISTETV
    @BAMBISTETV 4 ปีที่แล้ว +1

    Macha allah tawfekh yalla naga guena am tawfekh daga gore sa diguente ak cheikh bi yalla Na yalla yokou ay leram te tasunu ci barkem borom choucory

  • @adjimbengue4362
    @adjimbengue4362 4 ปีที่แล้ว +8

    Machallah yalna serigne bi gueuna wéral batt bi ci barkep serigne bethio 🤲

  • @khadijakane704
    @khadijakane704 2 ปีที่แล้ว

    Alhamdoulilah Serigne Saliou Yalla neu yalla yokou say lerr tass gnou ci sa barker Mbacke Balla Aissa

  • @ansoufaye9687
    @ansoufaye9687 4 ปีที่แล้ว +37

    Enfin j'ai retrouvé cette chanson machallah tawfekh mbaye chapeau à toi ♥️💯❤️

  • @diarradiakhate6424
    @diarradiakhate6424 4 ปีที่แล้ว +2

    Billay doumathi doyolll ♥️ ndakh nékhayou way bii dafa eupp♥️♥️♥️

  • @dioplalla6583
    @dioplalla6583 4 ปีที่แล้ว +7

    Bon courageuse nioune na way bâ faw qui barque serigne saliou

  • @sallasalioushop4476
    @sallasalioushop4476 4 ปีที่แล้ว

    Tawfèkh Mbaye Dieureudieuff wayyy mâchala YALA na YALA wèreulll battt bii barkep SERIGNE SALIOU MBACKÈ sama wèrouway

  • @boussombengue8183
    @boussombengue8183 4 ปีที่แล้ว +46

    Machalah yalla na batt bi geuneu wérr

  • @sokhnamangane7844
    @sokhnamangane7844 4 ปีที่แล้ว +3

    Sw fiére d'être mouride done talibé serigne saliou ma fiérté mbaké balla aissa

  • @fatoudiagne2251
    @fatoudiagne2251 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla na yalla weral bat bi si barke sama wassila sama werou way sama adouna sama alakhira Mame SALIHOU MBACKE

  • @mamasow6124
    @mamasow6124 4 ปีที่แล้ว

    Machsalla Nekh na trop waye
    Wakh di yokou boudè Thiat Nane
    Gniou Thiatou ❤️❤️❤️

  • @binetoudiakhate863
    @binetoudiakhate863 4 ปีที่แล้ว +3

    Machalla yalla na batt bi guena weirr wayy

  • @sinasow4237
    @sinasow4237 4 ปีที่แล้ว +6

    Thiey serigne saliou amoul morom tawfekh yague fi te were

  • @papaseck6919
    @papaseck6919 4 ปีที่แล้ว

    Machallah tawfekh ylla n'a ylla geune wéereul baat bi brckp s.saliou❤

  • @aminatayade9341
    @aminatayade9341 4 ปีที่แล้ว +13

    Esk degg guein li yeinnn😭❤️❤️❤️

  • @ndiagangom5304
    @ndiagangom5304 4 ปีที่แล้ว

    Li nekhna tawfekh s salioou thioun yalna fi yag te wer

  • @fatimdia7987
    @fatimdia7987 4 ปีที่แล้ว +2

    Machallah nékh na lool yalle na yalla wéreul batt bi❤❤❤🥰🥰🥰

  • @gayefatou3666
    @gayefatou3666 4 ปีที่แล้ว +3

    kn niou wadial magal touba yalla yobou niousi ak DIAMOU ani salihat yi🙏🤩😍🤩❤💖💞💝😘💓💗💙💖❤❣💝💞😍🤩🙏💝💝💝💟💟💌💕👌

  • @lemaitrenigne1381
    @lemaitrenigne1381 4 ปีที่แล้ว +1

    Sa son yi yeup bi mosi dakk machallah
    Magal ak diam si barki cheikhoul khadim

  • @fatoucisse3418
    @fatoucisse3418 4 ปีที่แล้ว +10

    Mane de Serigne saliou moma défare ♥️♥️💓

  • @peindasowsene8377
    @peindasowsene8377 4 ปีที่แล้ว +1

    Al way machallah tawfekh mala beugue ni li nekh way

  • @khelcombusiness6131
    @khelcombusiness6131 4 ปีที่แล้ว +1

    Ay way li barina barké Serigne Saliou sam❤️migui nekh ba dal laléne

  • @diakhatendeyeami640
    @diakhatendeyeami640 4 ปีที่แล้ว +5

    Je suis talibés cheikh mais li dougou nama lol way❤

  • @sokhnagueyediouf8562
    @sokhnagueyediouf8562 4 ปีที่แล้ว +3

    Wawaw danuy safar💪💪 nexatina dehhh

  • @mbendaciss9015
    @mbendaciss9015 4 ปีที่แล้ว +4

    Khôl sédatina tawfekh mbaye kénn du mom 💜💜💙💜

  • @darousalamtv3797
    @darousalamtv3797 4 ปีที่แล้ว +6

    Tawfékh wallay mala sopé yakar nanè mala gena sopè si kaw sof

  • @cherifalwalidfall7427
    @cherifalwalidfall7427 4 ปีที่แล้ว +3

    Liguey bi rafet na Serigne Saliou Molay fay

  • @sallandiaye7340
    @sallandiaye7340 3 ปีที่แล้ว

    Non tawfékh lingaye wakhe thi s saliou dafa nèkh❤️❤️

  • @awandiaye988
    @awandiaye988 4 ปีที่แล้ว +1

    Barkii Serigne Babacar sy magui dehhh waye bii meunou mako mougne. Liii maye rayye ay wayy daraaa daraaa laye layela laa dara daraaa

    • @LoMamediarra-kp7jf
      @LoMamediarra-kp7jf 4 หลายเดือนก่อน

      ❤❤😭😭😭😭😱🥹🥺

  • @khawlatouba7170
    @khawlatouba7170 4 ปีที่แล้ว +2

    Machallah tawfex mbaye borom batt bou nekh💖💖

  • @awakane8176
    @awakane8176 4 ปีที่แล้ว +2

    machala way tawfekh mabaye nice naa loool begg nane

  • @nassoukeita1446
    @nassoukeita1446 4 ปีที่แล้ว +3

    Ndeya mou Serigne saliou bonne continuation 🙏🙏🙏👍

  • @sokhnadione5826
    @sokhnadione5826 2 ปีที่แล้ว

    Wawaw wakh bou barè rèk amna Lou way dèf Moy faté bopam motath tontou sakh d'où koy dar❤️❤️❤️