Je suis fan numéro de Modou LÔ mais touss bi j'en suis devenu accro 😂 AMA BALDÉ tu seras un très grand champion. Du courage et bonne chance pour la suite de ta carrière 🎉
Merci Ama bon courage à toi frérot je ss fière de toi tu es un vrai patriote tu aura beaucoup de victoires inchalah tu a perdu aujourd'hui c normal c juste des leçons dans la vie ct cool le faire play ton tour viendra inchalah ❤
Inchallah tout ce temps perdu par Ama sera rattrapé. Ama va conserver ce titre de roi des arènes pour une longue durée à partir d'aujourd'hui. Ndakh yaruna ,yatuna beug na nieup teksi champion la. ❤❤❤ On y va pour les millions de vues Ama is back! J'étais auparavant fan de Lac2 puis de Tapha Tine mais là depuis c'est Ama.
Suis fans de modou lo mes ama dina meussa nek roi dh inchallah depuis l’or dama ko beugeu bilahi❤ yalla nala yalla defal diam ak sama copin pathé baldé 😂
Je viens de regarder le touss d Ama Baldé mais si tu étais a 100/100 de tes moyens la prochaine fois ne te sacrifie pas tu es un phénomène Ama Baldé bilahi walaye.
Yalnala Yalla may ndameu domou Fatlaye Baldé ❤ wallah yéné nagn la toi bi soudoul dara sakh Modou lo Balla Eumeu def nagn ligniou def thi lamb ba paré c’est votre tour franchement
Ba leggui nguimb Ama laloul souff yay Gainder deug Barki alkhourane waner wo niak diom ni niak fayda waner gua carrément k soy dé si forêt nala Gainder Ray 💪💪💪jambar Deug moy yow
@@abdalahfall7204 mais pourquoi vous vous permettez de mettre tout le monde dans le même sac ? Ici à Miami je n’ai pas encore vu quelqu’un qui est passé par le Nicaragua. Arrêtez de mettre tout le monde dans le même sac .
Bilayi ama diambar ga daifet rek mo niew bilayi mes sante Yalla rek losi kanam yalla na neke lou guene si iow incha allah roi 👑 bi day niew focus rek❤✊🏿🙏le grand champion nioune Pikine rek mo niou niorr💚❤️✊🏿
tu as perdu mais très franchement ce gars est un phénomène.yalla nalla yalla takhawou
Depuis son combat avec Modou il est devenu mon lutteur..
Je suis fan numéro de Modou LÔ mais touss bi j'en suis devenu accro 😂 AMA BALDÉ tu seras un très grand champion. Du courage et bonne chance pour la suite de ta carrière 🎉
De même que moi frère
Je le regarde presque chaque jour ❤
Worna yallah niosi yam dh frr 😂😂🎉
Pareil chaque 2 jours je regarde teh pourtant modou Lo rek lay topp 😭
non da meune dhé
Billay ba leggui meunoul geinneu sama xel 😂😂❤
Du courage Mbeur pas de stress restes focus sur ton avenir le meilleur reste à venir 🤲🏻🤲🏻☝️
Ama yalla nako yalla may ndam❤️❤️❤️❤️
Merci Ama bon courage à toi frérot je ss fière de toi tu es un vrai patriote tu aura beaucoup de victoires inchalah tu a perdu aujourd'hui c normal c juste des leçons dans la vie ct cool le faire play ton tour viendra inchalah ❤
Ama kassé NK premier commentaire ❤😂
wahal de
May deuxième commentaire ama yalla na dane après siteu dane lac2 si kaw nekh
Ama kasse tousse nakk
@@djeganefaye1566ppk8
Ama premier combat Stade aréna bi premier défaite si commentaire bi😂😂😂
Yalna yallah mayko ndam si barké seydina Mouhamed Saw🤲🤲🤲
Salalahou Allah Mouhamed ❤
Amine ❤🙏🏾
Amine
Ki est la en Octobre 2024 ?
Thiey Ama❤❤
Ama balde yalnala yalla May ndm ❤❤
Amine ya rabi ❤
😂😂😂😂😂😂😂😂
Le touch de l'année
Ama un vrai sportif un gentleman
Yallah nagnou Yallah soutoural meussouma dioy si lamb Yallah na Yallah andal ama
Le grand patriote yalla nala yallah may Ndam 🙏
Amine barke brom touba 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤍
😂 wa saway Ama défétte la moudjiou quoi 😂😂
😂😂😂
@@ousmanengom9297défaite ✅😂
Ama kassé bilahi nek nu Sénégal 🇸🇳 gnépou yaw lagnou wakh bilahi yalla ga am ndam 🙏😭👑👑
Amin.Nous pareille fi
Dou nieup dé😂😂
😂 saway dane naniou Ama le roi des fauxs lions 😂😂😂
J'aime trop ce gars il est juste phénoménal
Défaite biii bokk n'a thii louma gueneu métii thii 2023 bii..😢😢😢 sama Xol bii batey dafey métii.. Ama Yallah nala sounou borom def roi.. insh'Allah soumeu nieuwé Sénégal ioe laay ndieuk setsii.. Diambar DEUG gneu .. PIKINE SEUL ❤❤❤
😂😂😂😂 mounial modou rek aka maneu keupeu yalwane
Que le meilleur gagne non à la violence
Ama Baldé, domou Pikine bi Yalnala Borom bi Soubhana wataAllah soutoural mayla ndam ci kaw Mod'lo ci Barké Seydina Mouhammad PSL 🙏🏿
Allahuma amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine in shaa Allah
Amine Yarabi
Vive amadou baldé inchallah tay ak souba inchallah yalla baxna inchallah ❤❤❤❤❤❤❤
Inchallah tout ce temps perdu par Ama sera rattrapé. Ama va conserver ce titre de roi des arènes pour une longue durée à partir d'aujourd'hui. Ndakh yaruna ,yatuna beug na nieup teksi champion la. ❤❤❤ On y va pour les millions de vues Ama is back! J'étais auparavant fan de Lac2 puis de Tapha Tine mais là depuis c'est Ama.
Amine
Amine 🙏🙏
Amine Yarabi
Ama nelaaw naa wala ay mbokkam nelaaw nagn
En bon😂
Tu es très digne que tous les Sénégalais digne son avec toi
Modou Lô Yalla Nako Yalla May Ndamm in cha'Allah 🙏🏽
Yalla na la yalla may dame ci Barke sarige Saliou ❤️🥰❤️❤️🥰❤️🥰❤️
Amine ya rabi
Amine
Ama Baldé Yalla nako Yalla may ndam❤
Suis fans de modou lo mes ama dina meussa nek roi dh inchallah depuis l’or dama ko beugeu bilahi❤ yalla nala yalla defal diam ak sama copin pathé baldé 😂
Lo dhf dannou si katanou yalla inchalla dinga danou
vraiment ama balde touss nga lou nex billahi😍félicitations modou lo
No tousss bi amatoul thieuy le fils de falay ❤
Yalnaco yalah may NDAm Ama si barke yonentibi salalahou alehi Wo salam
Je viens de regarder le touss d Ama Baldé mais si tu étais a 100/100 de tes moyens la prochaine fois ne te sacrifie pas tu es un phénomène Ama Baldé bilahi walaye.
Ama ndam rek inchala ❤❤❤
Ken dou ama Yalnako yalla maiy ndam Inchalla ❤❤❤❤
Thiey domou falay bi ndam rek incha allah
Yalnala Yalla may ndameu domou Fatlaye Baldé ❤ wallah yéné nagn la toi bi soudoul dara sakh Modou lo Balla Eumeu def nagn ligniou def thi lamb ba paré c’est votre tour franchement
Depart bi 8mn58 bi on en parle no ama nla diaam sonal yalla nala sa borom mayat victoir si combat bi gua dieum
Ama moye dirige amoul kénène déléne xoll balla wakh AMA kassé 💪🏽❤️
Legui ni nguéne mel si vidéo graw na lutte tv, mashallah professionnalisme bangui fégnn nice 💯💯
Ama yalla nako yalla soutourale si barkit seydina mouhamed psl 💙🤍
Waa orchestre bi da am batterie 🥁 🤭🤣🤣 c’est Fort 😂
Bilakhi damay setane sakk jour li sama kholl seed ma dem liguey 🤘🏻🤘🏻🤘🏻👏🏽👏🏽👏🏽AMA keséè
Ki dagn ko beug rek t Yalla takh 🥺❤
Yalla nala yalla may ndam amadou baldé
Modou lo rek lay top❤❤❤❤❤😂mais Li dafa nice walakhi courage ama
Bravo l,un des meilleurs lutteurs au Sénégal
Yalna Modou am dam 🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹
Modou yala nala yala may ndam si barkè seydouna Mouhamed
Passement de jambes bi rék moma si nék❤
Ama champion roi des arènes inchallah ❤❤❤
Roi des fauxs lions wesh 😂😂
AMADOU BALDÉ YALLA NALA YALLA SOUTOURAL MAYLA NDAM SI BARKÉ ALKHOURANOUL KAREEM
Amin way
Ama balde rekkkkkk inchallah
Ama ndam rek Amen Amen 🙏 💪🌍✌️
Ama rek dong kessé kepp mom laniouy topp ❤❤
j'ai bien apprécié la simplicité de Modou Lô
Modou lo est un professionnel, son entourage explique tout, sur ce côté il dépasse largement les lutteurs actu
suis fans se de modou lõ mais maintenant ioe lay beugeu
Yalla nala yalla faral wayyy 🙏😭
12:26 diap 12:36 fofou louné la waww 🔥😮
Ama yalla nako yalla maay ndam
Yalnala yalla soutoural mayla ndam bou sédd gouy incha'allah
Ndam rk Ama❤
Peulh kassei sama xole bi seed naa❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Ama yeeeeeee 🎉🎉🎉❤❤❤
Meilleur chorégraphie
Yallah nala yallah may ndam inchallah si barké alkhourane
Du courage ama nion ioe rekk laniouy topp
Mbeur defaru watt dina bkh inshallah ❤
Ambiance lamb Ama la ❤️
Ndam rék in challah 💪
Modou kharagne lo mo yeungueull pikine❤
Danou rek Insha allah
Ndeysane yalla nako yalla may ndam way Amine touf touf
Modou lô rek bilahi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Modou reck❤❤❤
Si histoire lamb Ama c le 1er lutteur bi nga xameni la toussame amm ay million de vue ❤❤❤ ya meun kaay sama mbeurrr mi
Lou lerr
Yalnako yalla defal ndam lou Sedd ci Beussou tey bii
Amine
douma dann gnibbi inchallah peulhh bii rékkkk le lutteur du peuple ❤💪💪
Meilleur touss de l'année
Machalat ama p
Yakamtii na combat ame nak machalat moke talibè diambarou baye karim 💙🤍 bi ndam rek inchallah
Tout ça après nou nioussla vraiment metina bravo quand mm
Expatéfien dénna vive Modou kharagne lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ama mou sonko machalla
Ba leggui nguimb Ama laloul souff yay Gainder deug Barki alkhourane waner wo niak diom ni niak fayda waner gua carrément k soy dé si forêt nala Gainder Ray 💪💪💪jambar Deug moy yow
Je suis le combat de Miami (Floride) wahou quelle excellente danse de Ama Baldé . Sonko libre ✊🏾✊🏾✊🏾
J’habite à South beach collins Ave à côté de Mr. Jones t’habite ou toi?
@@NeymarJr-ku1oy sonou nga trop diar nirakaga di sonal nityi fi😊
@@NeymarJr-ku1oy j’habite à North Miami .
@@abdalahfall7204 mais pourquoi vous vous permettez de mettre tout le monde dans le même sac ? Ici à Miami je n’ai pas encore vu quelqu’un qui est passé par le Nicaragua. Arrêtez de mettre tout le monde dans le même sac .
Ma gui niane yalla s'y Barke seydina Muhammad Amine Ama am ndam bou seudeu gouy
Bilayi ama diambar ga daifet rek mo niew bilayi mes sante Yalla rek losi kanam yalla na neke lou guene si iow incha allah roi 👑 bi day niew focus rek❤✊🏿🙏le grand champion nioune Pikine rek mo niou niorr💚❤️✊🏿
C'est un phénomène ❤
Ama yalla nala yalla maye ndam
Walahi mo maan biss Patriote bi mashalakh yala nala bour yala May ndam
Ama yalnala yalla may ndam
Ama Ndam rek inchallah
Yaw késsé laniouy toppou baa légui champion 🎉
Wakhone nalen ambiance kase ngen niou dakh😅😅😅
Elhadji mbaye digua dok ligua fethieu yeup😂😂Lol
Ama moy Pikine 🎉🎉🎉
Ama balde yalna borom bii maylaa ndam
Ya meune kay 🎉🎉❤
Ama ndam ❤rek inchalla❤
Toujours là exceptionnel son touss 👌
Ama liga touss bo danon dou bax ❤
suis fans modou lõ number one mais legui ko beurell ioe laÿ farall tu es le sel de la lutte sénégalaise
Modou lo❤ kharangne lo❤
Ama le meilleur de sa génération