Barki RASSOULOULAHI touss mi nékh na, nôtre champion Boy Niang 2 pour toujours. Lahilaha ilalah ngéweul nékhna. Mais nous les fan de Boy Niang 2 war nanio battré les chanteuses.
J’ai toujours suivi la lutte de loin juste pour l’action. J’ai 37 ans mais BOY NIANG est mon premier lutteur préféré. J’aime tout chez lui et nio bokkeu santeu 😂..
Félicitations à Boy Niang et nos encouragements à Balla Gaye 2 dane ga fi kouné just entourage bi gay xol bou défarou délou si Say mbok wa Casamance sinn dina gnaw DH
Un constat k g fais de l'annulation du combat de Ama il risque de ne pas être roi des arènes com boy Niang 2 est sorti victorieux contre Balla. Boy Niang en bonne posture il préfère attendre voire la suite avec Modou si sera ficelé. Carte sur table
L'autre camp a touché son intégrité ndeyssaan et ça se voyait quand il a interrompu son touss et prendre son papa et montrer qu'il était vraiment son sang. motakh il ne pouvait pas perdre ce combat.
Il faut ma commentaire mais tousse bi rék War Na takh supportéres geuneu respecter souniou lamb ji Boy Niang vrai champion mais tamite mention spéciale aux tambres majors de boy niang et aux chanteuses vraiment rythme fi ba souba Do doyal
Non Femme Gueweul bi limou way Boy Niang meuneu touko Li Nekhna waay kou d'accord 😍😍
C la femme de cheikh niang lutteur
C'est sa cousine
Billahi li dafa nékh 😍♥️
Diabarou nidiayam cheikh Niang la
Je suis fan de Balla mes damakoy sétan lou bari vraiment way bi nekhna Boy Niang déug neuh✌🏼❤️
Chaque jour ma sétan touss bi plusieurs fois tellement dafa nékh 🥰😍🤩
Dama yakaron ni Man késsé la
Même moi billay
Ah ok ça me rassure dama yakarone ni ma weuroul😂
@@rouguietousy2292 meilleur touss de l'année
Pour mane dh llou mak rk la dall
Femme Geuweul di wayee moy clé lamb bi li nga waye nekh na trop❤❤
Mais yawe khana dagua nek si sama khéll bii
@@papadiaby.pikine632 noo bro Lou doy warr
Je penses diabarou cheikh niang la
Femme diabarou magam la
Les chanteuse linou way boy Niang dafa neex si khol ❤️❤️❤️
Koufi chanteuses yi andi 😍😍😍
Ya des moments émouvant que l'on n'oublie jamais et bravo thiapathioli bi bou dieikhei diekh na ndeysan
Ma cha Allah suis un fan de Modou et j'apprécie beaucoup Boy Niang dafay neexal lamb en plus champion la du courage Thiapathioli❤
Tousses mou nekh ga beuré mou geneu nekh félicitations 😍✨️
No je ne suis pas fan de boy Niang mais femme bii li mou woy bilay daffa fess bilay ca me touche au cœur ❤️ machalah
La chanteuse donne confiance a boy !! Cette chanson meunatouko ❤❤
il ne pouvais pas perdre ce combat il etais confiant felicitation champion nga ndakhe daka keumone ni daguay dane balla guaye tei Keum keum moye lep
Ya daka fethie ya eup dolé ya dakka beuré ya meun ya dane yaye ndandan bilahi 😂🔥🔥🔥
*Bissou ndam dou Bissou défaite. Bo setanei touss bii ngeu kham ni am neu changement par rapport ak touss contre modou lo bi*
Je suis un supporters de balla gaye mais boy Niang et un grand lutteur ❤félicitations
Barki RASSOULOULAHI touss mi nékh na, nôtre champion Boy Niang 2 pour toujours. Lahilaha ilalah ngéweul nékhna. Mais nous les fan de Boy Niang 2 war nanio battré les chanteuses.
La chanson rekk meune nako booster. C esy fort ce que la Dame a chanté. Ak baaat bou neh bi
Machalla champion , touss bi rek gagné ba combat bi
Les chanteuses mention spéciale ❤❤
TIK TOK LA KO DEUGG NIEW FI....COMMENT ELLE SAPEL
@@ouleyesy313 bilahi même mane
Bilahi
J’étais au stade mais bilakhi sama Yaram dafa daw li moy culture
Bilahi liga woyy koko woyy mou dane gaïdè Yalna bate bi werr
Mane môme balla moye la faral ba kérok Mouy bayi lamb mé boye niang machallah,goudé rék moko yakh mé lamb ji neikh n'a trop,yalla n'a diame yageu ❤️
Yalna yalla soutoural Modou lo inchallah meyeko ndam inchallah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Dama Sax télécharger tous bi diko ték sama auto dafa nkh trop ❤️🔥
😂😂😂😂
Mere Gueweul bi dou nite bilahi machalla ❤
Un vrai champion
Mane douma dèm fillay toguè yaw boye niang ki matt na goorèe no limo nèx 🤗🤗
Boy Niang nena guemb dou khaliss lepp yalla la ❤❤❤❤
Ki loumouy wëuy dawna Yaram dalay khaptal par force
Mane malaraw la meunoul mougn longue vie à toi
Félicitation boy niang
Boy niang domou pikine dafa paré balla ak sa thiés bouniou takhawone même jour boy niang dane léne❤️💚✌️
Bayil fen
PIKINE Moy Sénégal ❤️💚✌️✌️
Meilleur touss de l années ❤❤
Mais guéwel yi lign way Boy Nian nékha tropp seuhh
Waw daniou ko bakk beukateul ko xi touss bi motakH boy niang done takk nonou…touss bou saff sappp
Mais normal Boy niang gueweul leuh
Sou beuré mou nkh
Sou fethié mou nkh
Sou khekhé mou nkh
Way nekha fatal way 🎉🎉🎉❤
Machallah rek
Femme Bi di woy ohhhh♥️🤗 li de kouma ko wayon ma Daan b52🤣🤣
😂😂😂
Wouyay bi momay gaagn man🤩❤
Un vrai champion il peut faire d' autres exploits par son courage et sa force physique un vrai athlète
no ki bimou toussé leu lambj dji diékh kou kham lamb
Billahi wakhatiko
Barki Yallah
Wawaw dakor à taye mom boye mbeur bou mat seuk mo niew dona mbeuroym la b nak
Waawaaw
Aka leir touss bi deh amatoul
J’ai toujours suivi la lutte de loin juste pour l’action. J’ai 37 ans mais BOY NIANG est mon premier lutteur préféré. J’aime tout chez lui et nio bokkeu santeu 😂..
Elle a vraiment touchée les veines de garçon du monsieur 🎉
Mane ki limou waye soumako wayone ma dann kénéne koudoule balla guaye 😂😂😢
😂😂😂😂😂😂
😂😂
Ray ngama🤣🤣
C'est la chanteuse qui a gagné ce combat c'est grave ça.
La chanteuse a fait le son entier de cette chanson demlénn sétanko elle s'appelle Fatou fall ndiaga
Mane louma diakhal boy niang si touss bi kanam bi comme benene nite lamb daleu doynawar
Khaptal leu comme kou droguéwou billay j'ai fait ce ramarque 😂😂
Vs avez la meilleure version je crois
No boy Niang mom lamb DEUG là Indi kérog ❤️💚
Il es très bien entouré il fera d autres exploits
Sirtou lolou
❤❤❤❤❤❤ La joie de ça non boy niang day sedal sama khol
Félicitations à Boy Niang et nos encouragements à Balla Gaye 2 dane ga fi kouné just entourage bi gay xol bou défarou délou si Say mbok wa Casamance sinn dina gnaw DH
Nooo boy bi damako beugue rek ❤❤😊😊
Balla "" béléssiirr"" 😂 Zéro Fair-play.
Lègui mou déclarer blessure 😂
Dernier face to face après combat mou déclarer ""béléssiirr"" 😂
iow doul bayil ba meun ko binde
Neexna Macha'Allah. Mais aussi woykat bi naan "Gaïndé beugoul yappeu, mboum lay doundé" nii lagnukoy bayi😢
Boy bi mo dégg d !! meunou ma tokk jour té sétanou meu touss bi, bien que BallaG.2 moy sam mbeur 🦁
Un constat k g fais de l'annulation du combat de Ama il risque de ne pas être roi des arènes com boy Niang 2 est sorti victorieux contre Balla. Boy Niang en bonne posture il préfère attendre voire la suite avec Modou si sera ficelé. Carte sur table
T'es un visionnaire machalah ❤🙌
Dafa meunn touss bilay walay 😍😍😍
L'autre camp a touché son intégrité ndeyssaan et ça se voyait quand il a interrompu son touss et prendre son papa et montrer qu'il était vraiment son sang. motakh il ne pouvait pas perdre ce combat.
Wa Mère bi esk nitt leu😍😍😍
Bakk bi amone na solo trop ci Boy Niang, il y a un instant, la chanteuse s’est tue mais Boy Niang l’a ordonné de chanter. 6:53
Il faut ma commentaire mais tousse bi rék War Na takh supportéres geuneu respecter souniou lamb ji
Boy Niang vrai champion mais tamite mention spéciale aux tambres majors de boy niang et aux chanteuses vraiment rythme fi ba souba Do doyal
Bilaye frère d être guéweul ❤
Je suis un fan inconditionnelle de Modou lo mais après ce touss tu vois qu'il avait déjà gagné le combat contre bg2 Fatou ndiagua quelle chanson
Boy niang2 troisième roi de pikine inchallah ❤❤❤
les chanteuses vous avez assuré
Boy niang
C la 10éme fois makoy sétane 😍😍😍
Quand j'ai vu le touss, je savais dejà la fin du film
😂😂😂
Guémbou dou xalis bilao walay 😢😢😢😢
boy Niang ya same marae❤❤❤
Je passe jamais sans le regarde a nouveau c mon touss de l annee combat de l anne loumou leudeume leudeule loumouleudeum bouki for beuye
Kou deg gainde bougoul yapp mboum lay doundé rek beusseul ma j'aime 😂😂😂
Boy niang 2 yanala ndam li djik
Bilahi boy niang lay topu ama baldé euneu pikine rek
Moh Liii Kouma wayyy ma Roukhh Gainde Paré Yannou B52 Daan ko😢😢😢❤
Mère bi limouye waye nekhna
Dou mère
Ki moy sa mère bam diap la 😂
Li Dafa nekh wayyy❤❤❤❤❤
C’est Modou Lo qui mon lutteur mais j’aime beaucoup boy ndiang
Nb2 seul❤
Touss bi batay damakoy ceitane 😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️
Doumassi doyal jamais jamais ❤
Wa kou guiss malaw pikine😂😂😂😂😂
Lo deff inchalah danou
Ki limou waye boye niang mo daw yaram
Wa Pikine ako gno meune lamb
Kou geume ni boy niang staff bou bax la am
Barki rassoulou laay boy gnang dafa saf mbeur même boko supporté woul❤
Mais. quel. Belle voi
Je suis un grand fan de BG2 mais boy Niang ndanane leu tousse bi nekhena lol
Mai famme bi di waye nekhna batte mane sakh dama khaptalou wawe
Cousine nou boy niang leu
Bilaye walaye on dirait mane laye woye Bilaye 😭
Futur roi
01 janvier 2023
01 janvier 2024
Je le dépose ici
Je suis fans de balla gaye 2 Mai chaque fois ma setan touss bi dafa nekhhh bilahi
Li bilaye nékhna trope
Wouy yay😴😴
Je suis de guediawaye mais man mom rekk lay topou
Meunoumassé doyal bilay❤
FEMME BIDONE CHANTER POUR BOY NIANG DOU NITE LIMOU TAGUEU BOY NIANG BENEN AFFAIRE LEU
Femmes bi ndeye mbaye la toudou thies la deuk mbokou boy niang la
@@yorosow9245 foumou deuk si thies
Waw thies la deuk nio bokou kogne
@@yorosow9245 mais li takh ma ladj la man thies la deuk ban kogne la beug kham
@@aliouba1325 randouleine laniou deukk mane médina fall la deukk
Touss bi nekhna mais khamal dina beuréwat ak balla gaye 2
Gueweul bi limou way boy niang amatoul
C'est ça cousine
Vreiment jour bi boy Niang lamb deug là indi
Deuk pikine mo nekh
Wawaw💚❤️✌️
Wakh ko si kaw
C’est une fierté dafay yokk diom niit dafay defar borom diom
Touss gua Lounékh