Kawtef😱 Aissatou Penda répond sévèrement à Adamo, Kaliphone et Amina Poté yow amo lo wax niata yone

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 16 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 61

  • @ouleymatoudiallo6677
    @ouleymatoudiallo6677 21 วันที่ผ่านมา +4

    Wah deugg yalla kii sa moroomou doom la. Libéreko mou delou si ay way dioureum. Xalé Bou toutéé touri la.❤❤❤ Ousseynou da fa wara am ndiaboot

  • @general_galsen
    @general_galsen 21 วันที่ผ่านมา +9

    Cheikh Ahmed c’est le meilleur en communication

  • @BoubouSy-i4y
    @BoubouSy-i4y 21 วันที่ผ่านมา +5

    J’aime bien sa maturitée gnoune gorr lii lagnou soxla djiguén day dal dou mature adouna metiwoul j’aime bien cette dame yalla na bour yalla tek thi yene lokho inchallah
    Wayei beugone na aussi gua ande ak mom mou diegeulou wadiouram et puis guén avancer

  • @taphandiaye8963
    @taphandiaye8963 21 วันที่ผ่านมา +3

    Ahmet est un vrai interwiever mai Aissatou est d'un grand talent. Elle a cette facilité de communication de classe intercontinentale et il faut lui reconnaître ses qualités.

  • @antadiop8806
    @antadiop8806 21 วันที่ผ่านมา +3

    Ya ndiakh personalite akh dignité ya ndiakh fayda 😢😢😢😢😢

  • @DiougounaSakho
    @DiougounaSakho 21 วันที่ผ่านมา +5

    Ahmet Cissé khana mère bi dafela fay nguakay diayy nonou gni waxlén deug mogeun yaye dou morom seuy loumou nékh nékh té say waydiour andouniou ci amoul sens Cissé ak mère bi niak nguén fayda trop thimmm

  • @pendafedior1712
    @pendafedior1712 21 วันที่ผ่านมา +4

    Ahmet cisse ya faux nganika taar 😂😂mere delol domou jambour bi yaw sk dofo amo depression tamit 😮

  • @taphandiaye8963
    @taphandiaye8963 21 วันที่ผ่านมา +6

    Vraiment je retrouve une grande dame quoi qu'on puisse dire. Elle est ouverte et à de grandes qualites😮 . Arrêtez les insultes.

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา +1

      Mani yaw la andale! Gars yi da gnouye sissou rek. Ne seuy te mouy deugue si mome rek. "Les chiens aboient, la caravane passe"...

    • @diarravignob7740
      @diarravignob7740 20 วันที่ผ่านมา

      elle est folle ​@@lacitoyenneafricaine8566

    • @diarravignob7740
      @diarravignob7740 20 วันที่ผ่านมา

      ​@@lacitoyenneafricaine8566elle est folle

  • @Mechaelsoum
    @Mechaelsoum 21 วันที่ผ่านมา +2

    Amedh Cissé mo dale si kagne nak 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @Yayoumoussa
    @Yayoumoussa 20 วันที่ผ่านมา +2

    Ahmed bayil diayatè

  • @AissatouDrame-mk8jp
    @AissatouDrame-mk8jp 20 วันที่ผ่านมา +2

    Wa.qui.dafa.wayady

  • @Malicksindidi1988
    @Malicksindidi1988 21 วันที่ผ่านมา +3

    POUR VOUS DIRE MÈRE BI MO DOKHAAN BOY BI TAKK BOY BI NDIABAAR KO LOL SAH DIIKO TEUDÉÉ LIILA

    • @yvefay620
      @yvefay620 21 วันที่ผ่านมา

      sin droit le plus absolu ou non ??

  • @Malicksindidi1988
    @Malicksindidi1988 21 วันที่ผ่านมา +5

    NÉNA MOM DOU TOPP NITT TÉ AMOUSII INTÉRÉ LGUI BAAN INTÉRÉ NGA GIIS SI XAALÉ BII? BO DÉMÉ BA GIISATO SA INTÉRÉ SI XAALÉ BI LOUYY XÉÉW?

    • @yvefay620
      @yvefay620 21 วันที่ผ่านมา

      elle est là pour son intérêt comme toute autre personne .that's life

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา

      Lol kou la wakh ni khaler le? 😂 intérêt bi meune ne rouker trope sakh.

    • @Malicksindidi1988
      @Malicksindidi1988 21 วันที่ผ่านมา

      @@lacitoyenneafricaine8566 🤣🤣🤣

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา

      @@Malicksindidi1988 ah djiss nga jeune majeur bi bou bakh le Ousseynou mbengue là dou khaler dè!!!

  • @fatoufall1973
    @fatoufall1973 21 วันที่ผ่านมา +1

    Waw Aissatou ak Ousseynou fougni dem ni ?

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา

      Yawitt yaw laye tope nak! Ya nekh! Aissatou ak Ousseynou rek la dame mure et le jeune majeur da gnouye béguer dji comme tous jeunes mariés !

  • @ahmetsall8075
    @ahmetsall8075 20 วันที่ผ่านมา +2

    Ki wéroul dh blh da dof

  • @aminatasow5587
    @aminatasow5587 21 วันที่ผ่านมา +4

    Gnak fayda ki di la wakhlo rek ngay maguet bou Mélanie yawe

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา

      djiguene boussi ame 50 ans legui senegal na nga wadjale kharou sou fekker ni à partir de 50 ans mère le !

    • @SENEGAL303
      @SENEGAL303 20 วันที่ผ่านมา

      Sénégal so amè 30 ans sakh niouni mere nga😂😂😂​@@lacitoyenneafricaine8566

  • @nourradam6391
    @nourradam6391 20 วันที่ผ่านมา

    😂😂😂😂😂😂

  • @serignendiaye9275
    @serignendiaye9275 21 วันที่ผ่านมา +4

    Ki wèroul way

  • @AissatouGueye-q9h
    @AissatouGueye-q9h 21 วันที่ผ่านมา +3

    Yaw demain ameth cissé dinala sagua

  • @babacarThiam-x8m
    @babacarThiam-x8m 21 วันที่ผ่านมา +2

    Mais bayil hamet nguir yalla

  • @lacitoyenneafricaine8566
    @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา +4

    Sénégalais(e)s loutakh mou yabater ak touti sokhor ak tonkeu ignane ?! Mais dou Madame Aissatou Penda Diop dafa mariée ak un jeune majeur de 24 ans? Wa lou khew askane bi? Dara!!! c'est son droit de se marier ! Quels textes islamiques ou légaux dans notre cher Sénégal interdisent ce mariage? Aucun!!! Sénégalais(e)s soyez évolué(e)s, tolérant (e)s, croyant(e)s, li dou buzz. Et puis ame ne ay mères yo khame ni sa youma lene romber damay beug "battrer" lene khaliss! Da gnouye sentir lou nekh, dokh dokhou natt, andak élégance ak teye ak tek!!! Di wakh nankeu ohhhhhh. Yena sokhor beug khagne monsieur Mbengue banekhou seyyy rek 😂😂😂 seyyeul yaw jeune majeur bi ba done vieux majeur. Yaw la andale. Démocratie lagnou nek nak bou keneu sissou. ❤

  • @wiggly_art7431
    @wiggly_art7431 21 วันที่ผ่านมา +1

    Je penses que elle les malade 🤢

  • @Gggge_dudiolof9536
    @Gggge_dudiolof9536 21 วันที่ผ่านมา +1

    Nous les patriotes de la diaspora, on est de cœur avec la mere de Ousseynou. aissatou tiaga penda diop domeram bou dokhane sa ndey ga

    • @jeanattenzale
      @jeanattenzale 21 วันที่ผ่านมา

      Boul mass noune bi nel iOw rek

  • @djoulytoure1747
    @djoulytoure1747 21 วันที่ผ่านมา +2

    Tout ça c'est pour la pub .. et tu n'est pas modeste du tout..kou beurre tireur nga .

  • @Gggge_dudiolof9536
    @Gggge_dudiolof9536 21 วันที่ผ่านมา +2

    Mere bou dokhane ndayam bi

  • @lacitoyenneafricaine8566
    @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา

    Adamo vraiment doukou bakh lolou deug le. Nitt meune nga critiquer te do saga! kou nek bire Sénégal ak biti Adamo trokhal nako kou nek saga nako nitt ko khame ni da nga saga saga saga be nirok saga djaroul sakh deff nawler. Yaye yeup adamo saga na lene dey nek plein live saga ay auditeur rame gars yi tok di dégueu lou !!! Je me demande lou Etat Sénégal di khare si yeneu youtubeur yi you insolent yi! Fi amoul conventions internationales lepp négociation le gnou extrader lene pour troubles à l'ordre public sénégalais et corruptions de la jeunesse, djeuli adamo famou nek wala porter ko plainte famou nek (limouy deff ce n'est légal nul part dans aucune civilisarion). Ay État Sénégal régler wale ce Adamo bamou mele ni montre sonale ne sunu domou rew. On dirait un "stylo" ce adamo !

  • @AissatouGueye-q9h
    @AissatouGueye-q9h 21 วันที่ผ่านมา +2

    Amina mome bayiko ,amo diome !

  • @AissatouGueye-q9h
    @AissatouGueye-q9h 21 วันที่ผ่านมา +2

    Non Aissatou bayil teukou

  • @finnoallafineforzalajuve3222
    @finnoallafineforzalajuve3222 21 วันที่ผ่านมา +1

    Bayil léne wax bou niaw AK saytané AK niak mandou

  • @AissatouGueye-q9h
    @AissatouGueye-q9h 21 วันที่ผ่านมา

    Ameth cissé dinala déf lou bone !

    • @Malicksindidi1988
      @Malicksindidi1988 21 วันที่ผ่านมา

      AHMED SOULA DOGAALÉ TOUBAAY NGÉMB LAGUILAY XAAR

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา

      Humm kharale gnou khare nguimbeu gui bok

  • @fatoufall1973
    @fatoufall1973 21 วันที่ผ่านมา +2

    Ahmed Cissé dala cerné bou bakh khamnani dof ngueu

    • @Malicksindidi1988
      @Malicksindidi1988 21 วันที่ผ่านมา

      Koon file nga lolu yaaw

    • @lacitoyenneafricaine8566
      @lacitoyenneafricaine8566 21 วันที่ผ่านมา

      Gars yi nagnou réalistes kane mo doff? ki! Kone doff bou bari chance ngui ni mashallah

  • @AissatouDrame-mk8jp
    @AissatouDrame-mk8jp 20 วันที่ผ่านมา

    Yaw.yako.tope.intere.fsh.hale.la.sa.dom.sah.moko.mak.kou.thiak.diomgaaaa

  • @Gggge_dudiolof9536
    @Gggge_dudiolof9536 21 วันที่ผ่านมา +2

    Ak say lunette gay melni goumba , domeram deug ga

  • @MameDiarraDjitté-u1l
    @MameDiarraDjitté-u1l 20 วันที่ผ่านมา

    😂😂😂😂