Ndeysanne je l'as trouve encore fragile, souffrance dafa doywarr,Mach'Allah Diarra accroche toi surtout pour tes enfants ,defal diom foula akk yahida, persévérance , liguey dina bakh li diarr diarr la REKK ❤
Walay très chère , mai malheureusement bcp de gens non po le sens de l’écoute, amouniou deiiggg deiiggg…. Djiguene bo guiss son plu grand rêve c’est de se marier avec l’homme qui lui faut ! Suko meuneiii am. Mai les certains d nos hommes xamuniou valeur djiguene Bilay azime.
@@bineta1752wayadi woul d Bimou tassei yaagu meussou si wax mais circonstances yi mo tah en plus l’histoire tourne entre eux ta niom seen vie c’est les réseaux donc normal problème boun am rk nieuw fi
@ sokhna si je vis en Europe et jai aussi vecu au senegal quand jetais jeune réseaux sociaux dou pour vie privée amna lo khamni nite moko momale bopame lignay doundou apres avant sa mariage diaroul wakh sou amone foule niko doumassi tontou je passe a autre chose senegal rek gnay guisse koulay wakh artiste la khamoul public khamoul privé Nite dagnay ame privacy lo khamné cest intime mais aussi tamite quand le niveau d’éducation est trop bas loussi nite meune
@ vivre en Europe n’as rien à voir ici ta lingua wax weddi woumako nous sommes très bien éduqué dama la ni juste gnimouko sekkal toute leurs vies c’est internet kheuyna daa Seuss rk mais elle n’as jamais été comme elle mérite le bénéfice du doute si c’était moi doumako def jamais mais liy khassan si gomam mooko kham c’est pas la peine d’interroger notre éducation Europe n’est rien devant chez nous
Diarra est trop belle machalla walahi tu auras un bon monsieur plein de valeurs et de personnalité. L autre mome na khar rek ak modewayam mouy melni minuit et demi
@@nafisene5335surtout lolou gorou fethieu katt aka rissou ay djigueen di bakar chaque jour khawma loun si kheuthio 😢 Lou tah djigueen bouguoul dieukeur diou yiw
Pourquoi elle donne des explications sur sa vie privée kou diouke lathie ko mou tontou mais femmes sénégalaises kagne lay changé mentalité? Celui qui pose des questions dafe koy roubé ki anna aye mokame
Diarra tu es sensible comme mane sougnou xol mo niouy tongne prend soin de tes enfants Boulnangoti ken dila waxlo si sa vie prive del diouli di niane yalla mou takhawoula du courage et surtout oublie le passé
Elle a juste pleurer a cause des sacrifices quelle a FT pr une personne kil avait entièrement confiance et n'a pas reçu le même sacrifice en retour mais laisse tout dans les mains de dieu avec le temps dieu va trancher le vrai et le faux
La plupart des. Hommes bognoula fasé faséwalé say dome niari dome la am divorcée séne papa mogui Espagne té douléne dokh dara mane may liguéye am salaire bou minable mais yalla sétanouma béne yone affaire bi diome la ak foula
Du courage kouné gore bakhna sa baye ngua rouss Mom woy nako ame or du weuri peureum Rafete ngua machallah nango ligueye gorgorloul lep dina bakh Mane Malakoff wakh Dingua amate kou bakh
Vaz je suis de tout cœur ❤️ avec toi tiens .il faut chercher à avancer la vie continue ne te sous estime pas regarde bien où mettre les pieds. C'est dans nos épreuves que l'on apprend ❤❤❤
Diarra you very beautiful 😍 mashallah ❤️ relax Allah will bless you with a good husband 😊 some men are wicket walahi. Relax and take your time ⏲️ ✨️ ❤❤❤❤❤❤❤❤
Mais defal attention cii kokou ngay wax nane dafa bax t’es encore dans un moment de faiblesse boul yakamti darra lou la dal ben yon boumou la dalate boul baser wou cii ben gor
dome alalou yala la responsablité danioukoye dieuf kéne douko wax djiguéne amoul loudoul domame lo wara déf té défoko yala dina dieul sa weurseuk dioxko kiye def,point té djiguéneyi naniou ande mougne té xamni gor dou projet té diarra sa dioyeyi arétéko té focus sisa bop bayi domaramyi
Surtout prends tout ton temps avec ces mecs. Crois au bon Dieu , essaies d'entreprendre. Sinon tu seras très vulnérable. Yalla nala Yalla dolé tek lokho ci barkep Mame Cheikh Ibra Fall.
Bilahi dafa Beug Bass ba legui motakh mouy dioy li kouko doundoul mouno ko kham dafa meti Gua khekh guir ben affaire di degue lounek après Gua perte ko c’est dur
Il lui faut un bon coach qu'elle puisse développer sa personnalité. Elle m'a l'air très faible d'esprit Tu es très jeune et très belle donc aies le courage de faire avancer les choses et de retrouver ton sourire
@@nalerrenaagni2108 ame dieukkeur di si lokho yalla la nekk lolou lako yene mais djiguenes taye yi akk you demb yi bokkoul djiguenes you beuri seyetouniou kou siit rekk laniou beugue.
@@rockygaye-bc6rw kéne jugé bayil nekke avocat du diable, sa genre yi danio faible si genrou djiguenes yi delene wakh deugg mokko wane si réseaux sociaux yi.
Elle pleure parce qu'elle est sensible c'est tout.
Les femmes qui pleurent sont les meilleures machalla
😢😢😢 en l’écoutant parler me ronge le cœur ❤️ courage la plus belle 😍
Ndeysanne je l'as trouve encore fragile, souffrance dafa doywarr,Mach'Allah Diarra accroche toi surtout pour tes enfants ,defal diom foula akk yahida, persévérance , liguey dina bakh li diarr diarr la REKK ❤
Très classe ,femme forte ,battante ambitieuse ho que du bonheur dans ta vie Dieu te donnera une bonne personne qui connais ta valeur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oi
Oi
😂❤
❤😂😂
Li dé takh certaines personnes di wakh gorr dou projet
Bilaye goor dou meuss done projet
Lolou laniouy bagna dègue mais lolou mo am
Walay très chère , mai malheureusement bcp de gens non po le sens de l’écoute, amouniou deiiggg deiiggg…. Djiguene bo guiss son plu grand rêve c’est de se marier avec l’homme qui lui faut ! Suko meuneiii am. Mai les certains d nos hommes xamuniou valeur djiguene Bilay azime.
Goor gni dagniy am or diko dieundè ak peureum xawma loulène dal xalèbou melni machallah rafet tey yarou dieukeur bima la yènè
Lolou gu yakar
Djiguenn yeup rafete
Esk ham nga loutah bass amatoul confiance ci mome. Cherche les anciens vidéo tu comprendras
lol c’est leur choix !
Diara une famme de valeur nite kou bakh ❤️❤️❤️❤️❤️
Elle ne doit plus repondre sur sa vie privée mais wayadi bakhoule une femme doit avoir la tete sur les épaules qu’elle avance
@@bineta1752wayadi woul d Bimou tassei yaagu meussou si wax mais circonstances yi mo tah en plus l’histoire tourne entre eux ta niom seen vie c’est les réseaux donc normal problème boun am rk nieuw fi
@ sokhna si je vis en Europe et jai aussi vecu au senegal quand jetais jeune réseaux sociaux dou pour vie privée amna lo khamni nite moko momale bopame lignay doundou apres avant sa mariage diaroul wakh sou amone foule niko doumassi tontou je passe a autre chose senegal rek gnay guisse koulay wakh artiste la khamoul public khamoul privé
Nite dagnay ame privacy lo khamné cest intime mais aussi tamite quand le niveau d’éducation est trop bas loussi nite meune
@ vivre en Europe n’as rien à voir ici ta lingua wax weddi woumako nous sommes très bien éduqué dama la ni juste gnimouko sekkal toute leurs vies c’est internet kheuyna daa Seuss rk mais elle n’as jamais été comme elle mérite le bénéfice du doute si c’était moi doumako def jamais mais liy khassan si gomam mooko kham c’est pas la peine d’interroger notre éducation Europe n’est rien devant chez nous
Ana wayadi fii wakhal lenene@@bineta1752
Très bien parlé boula kéneu tardel focusal si sa bopou point lou waye def bopam yalla rek mofi nek courage
Très belle et très classe mashallah.Que Dieu te protège et te donne tout le bonheur que tu mérites 🙏
Tout mes encouragements ma fille chérie ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yagui melni bonbon Dubai ❤❤ Yallah nala yallah may goor bou kham sa valeur am sa yeurmandé❤
Warone guasi bolé machalla dé
@ y’a wakh deugue wayé wakh nako sama khôl billay ki yéné nako Lou bakh
Diarra est trop belle machalla walahi tu auras un bon monsieur plein de valeurs et de personnalité. L autre mome na khar rek ak modewayam mouy melni minuit et demi
Et puis sakh ki takh mou am lou ko nakhari daf ko diaroul. Goorou milieu diaroul topp.
@@nafisene5335surtout lolou gorou fethieu katt aka rissou ay djigueen di bakar chaque jour khawma loun si kheuthio 😢 Lou tah djigueen bouguoul dieukeur diou yiw
Yow nguani minuit et lann 😂
😂😂😂 Minuit et demie. Bilahi xalé bi dafa rafet ba paré diongoma
@@khadycisse877minute et demi Ray nama 😂😂😂😂
Ak louniou meune di wax tamite Diarra machalah Xalé bi diek na way ❤❤❤
Bilalaye mame Diarra mougniale loubess nekhe bamou dese bamele togale rek khole courage ma chérie ❤
Walahi wakhatiko
Dara léroul kenneu sah nah bamel néhoul Yalla d'où def Lou nahari
Sokhna Diarra bya Diogama kay digua am kou bakh inchalah mougniale on est de tout avec toi ❤❤❤❤❤❤
Elle est encore fragile, il faut qu’elle s’éloigne des réseaux sociaux , des médias en général pour se protéger
Kheuyna daye diayou pour trouver mari, na ma yallah ball nak, sa ma khalat la wakh
Je te jure , elle l’a pas encore comprise je pense la pauvre
Diara yaw ya mak bass sokhlawoko bayiko ak nitou mbedeu yi gnom la meritoo
Merci beaucoup sokhna Diarra❤❤❤❤❤❤
Prend ton temps avant de se remarier, presqu'ils sont tous pareille.
Courage Diarra yallah Bakhna ❤❤
Elle est toute belle❤❤
Pourquoi elle donne des explications sur sa vie privée kou diouke lathie ko mou tontou mais femmes sénégalaises kagne lay changé mentalité? Celui qui pose des questions dafe koy roubé ki anna aye mokame
Merci beaucoup. Pourquoi s'exposer. Qui est ce gars pour s'introduire dans la vie privée de gens ???. Sénégalais mo niak fayeda
Manqué reek, c est pas la premiere fois niit di tass, on passe á autre chose
@@tiyidekemet7300surtout lolou comme si il a le droit de poser des questions sur la vie des gens n’importe quoi
@@khadycisse877 kougnou pose question si sa vie gnani douma tontu . Mais dinwakh rek
@@Germinal5219 vraiment beugue naysanne réseaux sociaux toubab bi mognikoy use à dautre fin jamais gna degue di toke di raconte
Seuye dou projet , gore dou projet , gnome gneupeu yème .. concentré woul si yawe ake se dome mo eupeu importance❤❤❤❤❤❤
Sa yaye bou wakhone lolou do gnieuw si adouna bi😂😂
Amouniou bén koleuré motax boula sén dara béte
Diarra tu es sensible comme mane sougnou xol mo niouy tongne prend soin de tes enfants Boulnangoti ken dila waxlo si sa vie prive del diouli di niane yalla mou takhawoula du courage et surtout oublie le passé
Mouniale yola diéihoule dina.bakh inchalla concentréle sisaye dome nipm nieup nio yéme ❤❤❤
Bilay yalla Dinala tahawou courage sister❤
Une famme de valeur❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Elle est toujours amoureuse de Bass 😢
C pas amoureuse c'est juste habituee
Bilahi sa avenir mogui thi sa kaname ma chérie tu es toute belle darra diomboula
Ya diongama kay 💞❤️❤️💕
❤❤❤❤❤❤ machalla tu es belle machalla
Machalla diara ❤
Machallah yagui djogonma
Mais arrête di lidianti problème diambour bass ak diara liniou dioté khamolén si dr
May Allah bless her❤
Merci frere poour tes conseil franchement ton emission est interesent
Tu es très belle❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah très belle et poser du courage yallah bakhna ❤ ❤❤
Si j'étais j'allais plus parler de sa vraiment
Mane deh sou demb doun tay douma sey ak guewel
Elle a juste pleurer a cause des sacrifices quelle a FT pr une personne kil avait entièrement confiance et n'a pas reçu le même sacrifice en retour mais laisse tout dans les mains de dieu avec le temps dieu va trancher le vrai et le faux
Verite absolute
Machallah machallah machallah machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diarra may the Almigjhty Allah protect you and your kids Amin yarabi inshallah 🙏🙏🙏
Bilay je laissé ma femme topou adouna je regrette sur la tombe de ma mère 😢
Deysane
Yalla nala yalla mayat kou bakh comme mom
Focus sisay domm topato sa bop refete nga mashalah li bousi wah bene yone ya raw lolou demal lepay bah ❤️❤️
DE TOUTE FAÇON GNOUY ANDA KOU CI DÉME BA NI DOY AMENA LOULA GÊNÉ TÉH SATISFACTION MANOUL , DONC MIEU ON PRÉFÈRE RESTER SEUL.
Tu es magnifique ❤❤❤❤❤
La plupart des. Hommes bognoula fasé faséwalé say dome niari dome la am divorcée séne papa mogui Espagne té douléne dokh dara mane may liguéye am salaire bou minable mais yalla sétanouma béne yone affaire bi diome la ak foula
Si akimo khalé yi diap ni meune ngen koniasss baye bi diar si khalé kay , il faut assumer les conséquences
Du courage kouné gore bakhna sa baye ngua rouss
Mom woy nako ame or du weuri peureum
Rafete ngua machallah nango ligueye gorgorloul lep dina bakh Mane Malakoff wakh
Dingua amate kou bakh
Meguel kéne khamoule loumou mai ma belle sa classe romou na bass thioune
Wakhou doff
Vraiment 😂
Khawma lanla guiss si bass sakh ak mom nimou diongoma machalah
Bass thioune ana wéroul lila bayi 😂😂😂
Il pose mal les questions l'animateur
Elle est tellement belle 😢seuteuh goor Senegal ma diahler mane
Vaz je suis de tout cœur ❤️ avec toi tiens .il faut chercher à avancer la vie continue ne te sous estime pas regarde bien où mettre les pieds. C'est dans nos épreuves que l'on apprend ❤❤❤
Je suis une cap verdienne comme toi tu es très belle.la vie ne s'arrête pas là pense à te protège des mauvaises énergies ❤❤❤❤❤❤
Soit forte ma belle
M diarra sa djongoma lanla tamit ❤❤
Machala dioguoma sonoul machala
Machallah ❤❤❤❤❤
Diarra you very beautiful 😍 mashallah ❤️ relax Allah will bless you with a good husband 😊 some men are wicket walahi. Relax and take your time ⏲️ ✨️ ❤❤❤❤❤❤❤❤
J l aime tropppp el est belle machallla
Fatou ndiaye la xamoul noumou mel biniou koy beug 😅😅
Hana done djiguene ame foula
Wadji gnak na fayda meune na doule ci goor meun na lidieunti vie diambour. Tall sa live yakk derr fen diakhassei nite yii comme seule rek
Wouy traduction 😂😂🤣🤣dé na
Walahi gor dou projet ❤
C normale dieukeureum la wone amnagnou dome douko bagne me soukou yalla diapale dinako fate courage ma puce
Neysane goor dara safouko
Alkhamdoulilah j'ai un mental de fer
She has a class and kids so take of them inshallah
Lii pub leu AK stamipol nopalouleine encore chapeau a madame Thiam 🎉 communication yamathi doye
Même boulla diohoul boulko wakh kholal thii khalei yui yalla bakhna leipp Dina bakh intérêt dafa graw khamal luigaye wakh bou bakh
Mohamed sude danga nop ki wax ko ko mo gueun sa kestion doff yi.
Elle tres belle et plein dassurance. Gueum bopam.
Do morom basss ya rafet ya bari classe
Diarra vraiment sopp nala trop m bo topé emissions yi dinga manqué fateil bass nga dial si lénéne goor boula bayé dangkoy fatei
Trop belle diarra Khamou ma lo guissé si basse .
Wouy 😂😂😂😂 diankh bi c'est à dire la bonne s'appelle fatou non mais bimou né fatou mayko ndokh mou nane dama dé dal😂😂😂
😂😂😂😂😂
Non basse thioune yalnako yalla Faye li Moy def ki basse ko Kate ndey la
Silip bou xotékou kaye
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amna goor yoo yamné suñela miné gaa beuglen diouralen,,ñu tégla doff ak poubelle,dém thi thiagayi toplen dankh libertéba thi biirr,ak touti xalise bañu nekk di guagné takh ñu ñémé lou bone.
khaleyi djiguene daniou deugre bop voila beug kis lene ma rek
Gor kay mesoul nek projet ay mbam lanou rek kene bakhoussi 6 moy 9 rek bilay trokhal djiguene gor boukay def balaga dé digako guis dé
Ay way xana sa papa dou Goor
😢😢😢❤❤
Bass thioune yalla dina ko douma takh nite ki dou gou si islam nga abandoné ko😢😢😢
Lolou gua yaakar
Bi diarra di toup bobou bass takou ko moh
Lane moy abandonné ? Divorce abandonné la ?
Mais defal attention cii kokou ngay wax nane dafa bax t’es encore dans un moment de faiblesse boul yakamti darra lou la dal ben yon boumou la dalate boul baser wou cii ben gor
Yaw diarra bokok sakh khaleyi billaye
Diarra mi dh khawmako dh way kou bakh laye nourol
musique bi sofna akh
dome alalou yala la responsablité danioukoye dieuf kéne douko wax djiguéne amoul loudoul domame lo wara déf té défoko yala dina dieul sa weurseuk dioxko kiye def,point té djiguéneyi naniou ande mougne té xamni gor dou projet té diarra sa dioyeyi arétéko té focus sisa bop bayi domaramyi
Surtout prends tout ton temps avec ces mecs.
Crois au bon Dieu , essaies d'entreprendre.
Sinon tu seras très vulnérable.
Yalla nala Yalla dolé tek lokho ci barkep Mame Cheikh Ibra Fall.
Momdé dafa nirok Boury bi nek xaliso
Li mouy doundou metina
Bilahi dafa Beug Bass ba legui motakh mouy dioy li kouko doundoul mouno ko kham dafa meti Gua khekh guir ben affaire di degue lounek après Gua perte ko c’est dur
Il lui faut un bon coach qu'elle puisse développer sa personnalité.
Elle m'a l'air très faible d'esprit
Tu es très jeune et très belle donc aies le courage de faire avancer les choses et de retrouver ton sourire
Courrage Diarra
❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Go and get married if you do it u will forget everything I was in your situation but I got remarried I forgot everything Alhumdulilah
Tu as trahi ton seigneur…
Kane moye marié akk djiguenes niou mélni pose ongle akk kheff dara naturelle woul si mome genrou djiguenes yi douniou fote douniou passé. Bougoulo sey mais yagui nekk akk goor doyena war dé.
Pose khef ak ongle dé djiguene yikodoul def bariwoul té gnjkoy def gnougui am dieukeur di sey
Boule jugé khamo loumouye doundou
@@nalerrenaagni2108 ame dieukkeur di si lokho yalla la nekk lolou lako yene mais djiguenes taye yi akk you demb yi bokkoul djiguenes you beuri seyetouniou kou siit rekk laniou beugue.
@@rockygaye-bc6rw kéne jugé bayil nekke avocat du diable, sa genre yi danio faible si genrou djiguenes yi delene wakh deugg mokko wane si réseaux sociaux yi.
BOYS. RÉGLÉL. WAY
❤❤❤❤❤❤❤
Mohamed sude danga nop ki wax ko ko mo gueun sa kestion doff yi.
Elle tres belle et plein dassurance. Gueum bopam.
Silip bou xotékou kaye
❤❤❤❤❤❤