Balla gaye 2 et son Petit frère ama blade yalla naléne yalla diapalé si barki seydina mouhamed ndam rk inchallah Mane contanena trop si yéne et merci beaucoup Aziz allé Ndiaye et tout les famille allé Ndiaye wasalam ❤❤❤❤❤❤
Ama a intérêt à se rapprocher de Balla et Aziz , c'est un avantage pour lui sur le plan de la lutte mais également ils vont lui montrer le chemin pour mieux investir son argent.
Je demande à Azize de faire la même chose avec Lac 2 Balla 2 et Ama Balde .Merci Azize j’adore tu es comme Gaston un pèlerin de la vérité et de la paix ,qu’Allah vous bénisse Ameen
Merci Aziz Balla n'oublie jamais que ton père Falaye t'avait confié Ama donc aide tes frères Ama et Salif à devenir Roi des Arènes inchallah santé paix prospérité longue vie à vous inchallah ❤❤❤❤❤
Sa waye limoyla dioylo😅😅😅😂 yeureuléne sén bope😮😮 démlén diamou Yalla té diémeu térél sén bopeu ak séni ay wadiour❤ gni dagnouy fo di légueu séni ay guinar,,🐔🐓🐓🐓
Une chose est sur pour démarrer votre site vous avez été très intelligent en mettant Ama Baldè et BG2 en avant ..... Donc c'est une très bonne chose... Ama a reconnu ses torts et l'a assumé donc bonne continuation à vous tous Qu'ALLAH vous accompagne 🤲🙏
Balla et Ama deux champions. Balla qui a déjà eu le titre de roi des arènes reste un très bon mentor pour Ama et Sa thies . Aziz a raison rien ni personne ne doit les déstabiliser. Ensemble ils constituent une dream team pour un futur roi 👑
@@rouguikebe9984koo woo jeuloula loy outi keureum ? Ak lamb nimou complexé souda demone niou dane ko niou djigne ko balla nak delen khol lo xamni sou done yene la doungen ko deff ishhh
Balla gaye 2 ama baldé meme pas 1 h de temps 10.000 mille personnes vue kone diam mo wara doh séne diguanté lima méti moy biniou dané ama ba paré rk❤❤❤
Alhamdoulilahh merci Aziz Ndiaye djiss ndayy ni nga téwé sou ndiou champion bi. Balla yayyy ammma ❤❤❤ ammma yayyy balla. Balla télll sa frére ama guidé KO parsk ammma sou néké roi ndiounn Say fanss comme si Yako nék. Ndiounn fans Balla gaye yi pour ndiounn yaw AK ama pièce de monnaie la
@@cheikhdiop9932balla gaaw na merr trop mais dinala wakh Ben affaire amoul saguo si Ama d limko meuna mounial meunalouko ken Ama mo diellone décision diell yonou bopam il a été guidé par son fameux gang qui n’ont pas du tout fan de balla
@@ndiayeibrahima9876 yaw bayil sokor ak ignan Balla gaye 2 c le meilleur dans l'arène il va reprendre la couronne 👑👑💖💖 bientot inchallah soula meitei gua deim kharou on
Yalla naléne yalla défal diam ❤️ Billahi borom khol you rafét warou gnu takhaliko budule dara sax ngéne khole si séne gniari wadiour yi sama gniari mbeur ngéne Té ngéne moytou seytané yi
Mane dh modou lo moy sama mbeur mais sene ande nexnama trop yalnalene yalla lafal thiate ta mousal lene si seytané si barké seydina Mouhamed ❤l'union fait la force🤝✊️
Ama baldé démal nga touki kakatou jeune nga défar sa staff bou bah bo amé combat douma ame diam té meussou mala guisse Liguéye rk mon worr ❤❤❤le reste c la famille 👪
❤❤❤❤❤balla je suis très fière de toi c’est ça la vie adouna amoul solo lepp diekh un jour 😢le papa de ama Baldé il était toujours là pour toi donc prends bien soin de son fils et puis c’est ton frère ❤️🔥❤️🩹❤️yalla na diam vague amine 🤲🤲🤲🙏🙏il faut toujours être reconnaissant dans la vie nite kou bakhe da wara guoré machallah mon champion balla😍🥰🤩🙈🙈❤❤❤❤
Non vraiment sama khôl sédatina yalla nallénn yalla défaal Soutoura sii lii déss sissén carrière yéne famille Ndiaye bii mom yénn Lou bakh rk nguénn dii déff sii nitt gnii yalla nallénn yalla sameu 🙏 Al bourakh Evens thia kaw thia kanam 🙏
Pull is my favourite presenter and reporter.... before viewers will enjoy her program she is always the first to your enjoy.. she's always smiling and I pray God bless her with a good and caring husband..
Bilay li rafèt niar gni ay brom bakh la niou mè Aziz sama domou baye kèn dou yaw walay daga bakh Aziz Amal diame ak wèr ama ak balla Yalna yalla dèfal lèn diame may lè ay ndam you Bari peul yaw tamit diame si yaw ❤❤❤
Balla gaye 2 et son Petit frère ama blade yalla naléne yalla diapalé si barki seydina mouhamed ndam rk inchallah Mane contanena trop si yéne et merci beaucoup Aziz allé Ndiaye et tout les famille allé Ndiaye wasalam ❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤ Amine 🙏 dhieredhief
Amine Yarabil Alamina aka gnios rafet khol machallah ❤❤❤❤❤diam diou sah thie gniom❤❤❤❤❤❤❤❤
Aziz diereudieuf contanna diereudieuf contanna yallah na yallah fay yiw amine Yarabil Alamina ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vraiment aziz ndiaye man personelment damako fan par ce que reuyoul rew
❤ amine
Aziz continue la mission pour une réconciliation entre Balla et Lac Guediawaye a besoin de ça 🔵💛🔵
Tré bien c ça ki reste balla et lac 2
Surtout
Bilay sama khôl bi séd neu ñar ñi ak sathies damalén beug rék té yalla takh ❤
BALLA WO WARDI BAYII MER
Bilahi ak mane
MEREWONNA BALLA MAIS XOL SEEDNA❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Blh bb sa bopou rk nga xam 😂
Yallah la lako takha wkh mane niom 3 nioma bayi si lamb ❤❤
Ama a intérêt à se rapprocher de Balla et Aziz , c'est un avantage pour lui sur le plan de la lutte mais également ils vont lui montrer le chemin pour mieux investir son argent.
Bilaye
Merci c’est sa
Surtou inversir
Bien
🇺🇸Ama baldé est déjà avec Aziz Ndiaye sur le plan financier sa reste sur le plan de la lutte
Je demande à Azize de faire la même chose avec Lac 2 Balla 2 et Ama Balde .Merci Azize j’adore tu es comme Gaston un pèlerin de la vérité et de la paix ,qu’Allah vous bénisse
Ameen
Lac 2 et balla gaye 2 , il faut qu'ils se réconcilient ça me fera trop plaisir
Balla Gaye et ama seul force à vous mes champions ❤️🖇🥰
Kènnnn dou aziz ndiaye un homme humble et responsable machallahh longue vie Aziz❤❤❤❤❤
AZIZ NDIAYE C'EST UNE RÉFÉRENCE POUR LA JEUNESSE MACHALLAH QU'ALLAH CONTINUE DE VEILLER SUR VOUS ET VOS FAMILLES
Merci Aziz Balla n'oublie jamais que ton père Falaye t'avait confié Ama donc aide tes frères Ama et Salif à devenir Roi des Arènes inchallah santé paix prospérité longue vie à vous inchallah ❤❤❤❤❤
Walayy Frere balla souvent dayy nelaw na diapale niar gni ak niom youssou ndour thiate gackou ak boy yi lolou Moko dessé
@@mouhamedmoustapha684day nelaw kw
Balla Gaye2 moy Ama; Ama moy Balla Gaye2 ❤❤
Franchement parlé j'ai bien compris que les Sénégalais aiment ces 2 champion car je ne vois pas aucun commentaire négatif.
Alhamdulilah MashaaAllah Balla and Ama am so happy for you guys ❤❤❤❤❤
Balla et ama deux champions vous êtes des fréres ,balla nitt késsé laa pareil pour ama❤❤❤❤❤
Vraiment jai des larmes au yeux❤❤❤❤❤❤❤❤
Sa waye limoyla dioylo😅😅😅😂 yeureuléne sén bope😮😮 démlén diamou Yalla té diémeu térél sén bopeu ak séni ay wadiour❤ gni dagnouy fo di légueu séni ay guinar,,🐔🐓🐓🐓
Balla gaye 2 yallna yallah défal la li nékk sa kanam yeup békkté ak ama si barké seydina mouhamed psl
Machalla yalna lén yalla mouseul thi saytané Ama baldé Balla gaye motokh ma beugeu ko balla rék si khol ❤❤❤
Une chose est sur pour démarrer votre site vous avez été très intelligent en mettant Ama Baldè et BG2 en avant ..... Donc c'est une très bonne chose... Ama a reconnu ses torts et l'a assumé donc bonne continuation à vous tous Qu'ALLAH vous accompagne 🤲🙏
Quels sont les torts de AMA
Balla et Ama deux champions. Balla qui a déjà eu le titre de roi des arènes reste un très bon mentor pour Ama et Sa thies . Aziz a raison rien ni personne ne doit les déstabiliser. Ensemble ils constituent une dream team pour un futur roi 👑
Walahi Ama Balde nitou késsé leu. Boko holé rék hamni nite kou bakh la❤❤❤
Mani Balla bim ko wowé diotouko meunouko wone sétsi khamni Ama da nék si combat mais Balla mo déssé mature rek😂di topanté ak boy bi
@@rouguikebe9984koo woo jeuloula loy outi keureum ? Ak lamb nimou complexé souda demone niou dane ko niou djigne ko balla nak delen khol lo xamni sou done yene la doungen ko deff ishhh
Pluie de victoire Ins Shâ Allah ❤️❤️❤️
Machallah dieureudieuf Aziz yalla molay fay inchallah.
Balla Ama sa thies ak nieup yalnaléne yalla may diammou
C’est le sang machalla li rafetna diamou si yen ❤❤❤❤❤❤❤❤Aziz yalnalla yalla fay merci Nila meuné démè
Machalla Balla. Ama yeeeeeeeeeeeeéeeeéeeeeeeeéeeé ❤❤😂😂😂😂😂😂
Peul ma challah albourakh rék 💪❤❤ Aziz laf thiat way ama laf thiat ❤balla DRM dji Nice 👍
Vrement peul tu fais bien ton boulot force à vs les deux frères ❤️
balla méréwonala mé lgui comprendrena té contana diam si yén inchallah 🙏🙏❤❤❤❤❤❤
Balla gaye 2 ama baldé meme pas 1 h de temps 10.000 mille personnes vue kone diam mo wara doh séne diguanté lima méti moy biniou dané ama ba paré rk❤❤❤
Bilay nak
Degue guali Ama wakh si môme la
Khana déglou woo léne 😂
Balla ak Ama diam ci yenn sama 2 lutteurs yii 💯💪❤️🙏
Ndaysane ama c’est une personne véridique vraiment je suis très content machallah ❤ je vous aime beaucoup billahi
Je salue ce geste en tant que fan de modou lo ... Lou rafett réka refett
Les deux frères balla gaye 2 et Ama balde machallah yalnalen yalla diapale
Mon2 champion Modou xaragne lo et Ama balde yalla nalén yalla may ndamm inch'Allah ❤❤
Ama yalla nako yalla may ndamm inch'Allah ❤❤❤
Macha Allah lère na yalla sounou Borom yok sène diam inchallah 🙏❤️
Aziz Ndiaye❤❤❤ merci beaucoup mais défal Balla gaye ak Lac 2 ngir yalla té yalla takh❤
Machalah li rafetna trop ❤❤❤❤ yalla ngéne am diam les deux frères ❤❤❤ merci Aziz Ndiaye ❤❤❤
Alhamdoulilah je suis très content de cette réconciliation amlén té moytou Yak kati la lutte c'est pour un moment après la vie continue ❤❤❤
Bilahi je suis fière de vous merci Aziz le meilleur reste à venir
Alhamdoulilahh merci Aziz Ndiaye djiss ndayy ni nga téwé sou ndiou champion bi. Balla yayyy ammma ❤❤❤ ammma yayyy balla. Balla télll sa frére ama guidé KO parsk ammma sou néké roi ndiounn Say fanss comme si Yako nék. Ndiounn fans Balla gaye yi pour ndiounn yaw AK ama pièce de monnaie la
Ama ak Balla damaléne beugal sama bopou yalla naléne yalla défal ndam si barkém Mohamad yarabi❤❤
This is very nice ❤to my two champions Balla Gaye2 an Ama baldeh ❤❤ 🇬🇲 🇩🇪
Yalnanou yalla mouseul si seuytané yisi réwmi yalna diam sakh si khôl té niou yéneunté diam
Non lii môme kokou sedoul sa khôl do nitt...Balla Moy Ama...Ama Moy Balla...vive mes 2 lutteurs
oh li rafet na trop machallah e bonne continuation e bonne chance pour la suite de leurs carrières que dieu vous aide amine
Merci beaucoup Aziz Ndiaye, et sa reste balla et lac, ils doivent je revois le plutôt possible ,les fans le demandent.
Merci beaucoup Aziz Ndiaye, et sa reste balla et lac , ils doivent se revoir le plutôt possible, les fans le réclame.
Vous êtes tous des frères c'est un acte à saluer mais délèn ci bolé Lac de Guier 2 il fait parti de vous lolou rek mo déss😢
Peulh mom je l'adore elle est très pertinente et attentive ❤
Ama yalla nako yalla may ndam inchallah ❤❤❤❤
Yalnama Yallah Dieugueul
J’étais vraiment en colère contre balla mais dama djoum
Balla gueye2 balma
😂😂😂
BALLA MO WARA MOUNG
Ak mane
balla balma kay😅 isqeu yeugon nala 😂😂
@@cheikhdiop9932balla gaaw na merr trop mais dinala wakh Ben affaire amoul saguo si Ama d limko meuna mounial meunalouko ken Ama mo diellone décision diell yonou bopam il a été guidé par son fameux gang qui n’ont pas du tout fan de balla
Ama baldé mii yalla May nako khol Bou rafét dieul na lèpp kosi kaw ❤❤❤❤
Balla ❤❤❤❤❤ama ❤❤❤❤ pour toujours
Chapeau à Abdou Aziz Ndiaye ❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉
Alhamdou lilah et merci pour tt Aziz heureux de vous voir réunir pour construire le meilleur ❤❤❤
Machallah Aziz un exemple à suivre n'a gnouy nitte gni Di bayi féwalé li Moy Sénégal
2 references au coeur d or. Je les aime comme des freres bilahi. Je suis trop soulagé et heureux. Tout à l honneur de Aziz ndiaye. OUSMANE FALL COMO
❤❤❤❤one love les deux futurs rois
Impossible
@@ndiayeibrahima9876 yaw bayil sokor ak ignan Balla gaye 2 c le meilleur dans l'arène il va reprendre la couronne 👑👑💖💖 bientot inchallah soula meitei gua deim kharou on
@@abdoulkhadrecisse5087 yaw Katal sa yaye ak balla gaye ngay wakhou sokhor bou nk 👑 dès loumay yakhal
@@ndiayeibrahima9876sa way nañou respecté soñou Yayii seuteuteu lii ñawna Yaye dou thiakhane
Sama khol bi send na bilahy walahy li dafa rafet machala
Waaa peulh légui Albourakh Evens nga nék
Yalla naléne yalla défal diam ❤️ Billahi borom khol you rafét warou gnu takhaliko budule dara sax ngéne khole si séne gniari wadiour yi sama gniari mbeur ngéne Té ngéne moytou seytané yi
Barky serigne saliou damalèn beug ama balla for ever
Bilay sama khôlle sedd na si ama ak balla yalla nalléne yalla mousseule thii seytané ak naffékk yi
AMA Il est vraiment humble et honnête❤️ respect bro
Dieu le tout puissant les écoute et les accompagne dans leurs carrières
Mane dh modou lo moy sama mbeur mais sene ande nexnama trop yalnalene yalla lafal thiate ta mousal lene si seytané si barké seydina Mouhamed ❤l'union fait la force🤝✊️
❤❤❤❤Modou xaragne lo yalla nako yalla may ndamm inch'Allah ci boy niang
Amine
Raféna trop niou wara ande rék niouy ande bravo merci mon idole azize
❤❤❤❤❤
Salalahou aleyhi wasalam neina kou rafeital deiganetei yalla rafeital sa lepp inchallah
😭😭😭 au billaye sama ❤ sédena trop sama gniari mbeur yi taye la gueuneu contane si lambj
Ndaye sane balla gaye Ama 🙏🙏🙏🙏💪💪💪
Vraiment nous sommes très contents sur vous mais on attend entre lac et balla
Macha Allah kaddu yi rafett na merci AZIZ SUMA champion yi ame len diam ❤
En tt cas ki deff li deff na lou rafett mashAllah ❤
Yalna ko yalla fay yiw🙏🏿🙏🏿
Machalla yalla na len yalla defal diam catanal len li dess si sen carrière 🤲
Ama baldé démal nga touki kakatou jeune nga défar sa staff bou bah bo amé combat douma ame diam té meussou mala guisse Liguéye rk mon worr ❤❤❤le reste c la famille 👪
Walaye wakhgua DEUG dafa wara dém enteréné dji moguen légui mom nourotoul mbeur dra
@@taphadiene billahi wallahi damaka beug guiss ama bou karaw bidi tahaw
Ama Doussama mbeur dh Modou lo moye sama mbeur ms Ama dfa warra dém enteréné dji moguen mouy xaarito ak mbeur yi rk
@@taphadienegniii ay mbokou lagne nganane kharitooo😂😂😂. Gnii danio woo ama pour tek ko thi sur la bonne voie
Saway ama toukina mogui France li sûrement enrigistrer nagn ko il y’a une semaine voir 10 jr
OHHH LI RAFETNA NDEYESSANE YALLA BOULENE DARA FEEWALATI THI BARKE ALHOURANE 🙏 MA SHA ALLAH
❤❤❤❤❤balla je suis très fière de toi c’est ça la vie adouna amoul solo lepp diekh un jour 😢le papa de ama Baldé il était toujours là pour toi donc prends bien soin de son fils et puis c’est ton frère ❤️🔥❤️🩹❤️yalla na diam vague amine 🤲🤲🤲🙏🙏il faut toujours être reconnaissant dans la vie nite kou bakhe da wara guoré machallah mon champion balla😍🥰🤩🙈🙈❤❤❤❤
Ama balde vs siteu
Balla Gaye 2 vs talpha tine
Comme ça guéne meune préparer combat yii en groupe ❤❤❤❤❤
Machallah les champions je vous aimes❤
Ndame la li moy adouna aziz raféte na ❤❤ diam si yéne
Yalla nalene yalla deffal diam amine double less bimou gneuwe fallay moko dalle fithi dakar❤❤
Ama bâllde ❤daffa raffètt tè daffa amm yarr balla mèm chos❤
Allbouraxe ya meune Sénégal ❤❤❤❤❤ 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Sa Thiès mom Dou Am problem Ak ken ❤❤❤
Alhamdoulila merci nak aziz m gniar gni ak sathies gniom la beug bilahi
Balla gaye vs Ama balde nagnou dèm insep de paris liiguey sën retour ndam rek lagnou sii sokhla ❤❤❤
Aziz balla lac lagn beugg
Dokhko
Peulh bou rafett sass nagnla lolou
Machallah
Balla ya takh may supporter ama donc warolena reiro. merci beaucoup aziz diameu ci yalla ❤❤❤
Degue li Ama wakh nena balla da la dannn wo a chaque fois mais mom d'où dieul dayy fek moi diapp wala mou sanii phone bi
Degue li Ama wakh nena balla da la dannn wo a chaque fois mais mom d'où dieul dayy fek moi diapp wala mou sanii phone bi
Am very happy to see this ONE FAMILY
Maachallah...Lii rafeett naa..Merci AZIZ....
Non vraiment sama khôl sédatina yalla nallénn yalla défaal Soutoura sii lii déss sissén carrière yéne famille Ndiaye bii mom yénn Lou bakh rk nguénn dii déff sii nitt gnii yalla nallénn yalla sameu 🙏 Al bourakh Evens thia kaw thia kanam 🙏
Svp Balla Gaye 2 et Lac 2 on est vraiment besoin Aziz diap si
Pull is my favourite presenter and reporter.... before viewers will enjoy her program she is always the first to your enjoy.. she's always smiling and I pray God bless her with a good and caring husband..
So paré gua diobole Balla au lac 2 ❤❤❤❤❤
Peuhl temp yii mome danga gueneu mole MashaAllah ❤️🤫🙏🏿
Aziz yalla nala yalla faye 🙏 thi barke Seydina Mouhamed PSL❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ama balla machallah ❤❤❤❤❤❤❤
C'est beau. A noter que Peulh est très professionnelle et très posée. Bonne continuation
Yalla naléne Borome bii geuneu takhawou 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Sm❤bagui frigo❤❤machallah contenant na way billahi ❤❤