Bonsoir à toute l'Équipe de BM Production. Pour cette fin d'année sunu meunoon ameu bonus tournage yi ak coulisse yi dinassi baaax. Au passage on vous félicite pour le travail remarquable ❤💯✅
Ndaysan des vrais artistes Vous voyez ce que l'homme ordinaire ne voit pas Chaque épisode vous transmettez des messages très importants Ambulant man bi sama bop rk la guiss si épisode bi Vraiment un grand merci
Wallahi croisement Cambréne Pate d’oie colbane souma fa diarrei bilahi damay fattei sama bop courage à tous les jeunes qui se débrouillent chaque jour pour dimbalie sén famille Sénégal jeune you am joom niofi nekk
Bonne continuation à BM audiovisuel la série capitale c'est une série en magnifique je regarde je suis un jeune marchand ambulant mais nous les marchands mon somm très fatiguée
Vous avez tapé encore fort,une épisode avec bcp de leçons à tirer. Vraiment le message est très important et merci d'avoir pensé aux jeunes chômeurs❤❤❤❤❤❤❤
Message bi am na solo je me rappelle un jour boba ma ngui dara dia danio démon bène keur tokkk fa ngir boune paré diokh niou dèsss mais mais bène djiguène mo guèune né nio dieul téléphonam niouy wakh mouné nioko dieul ta yeugou gnou tinou niou mais heureusement borome keur gui mo guiss téléphone si nèkk bi néko ya ngui fatté sa téléphone si nèkk bi khôlo kou bakh diko guigne talibé yi wallahi nitt mo yakamti rek mais lou way mougne mou dièkh ta Yalla mi ngui ande ak mougne katt yi lila wakh si Alkhour an إن الله مع الصابرين
Marchan ambilan Ay gorr lan té kouné ngisi Koulén Di toroxal yakar ni dangaléna GeuN billahi sooyy dééé dalay bétteu Wala dinga am diafé diafé yoodoul masa xam
Bonsoir à toute l'Équipe de BM Production. Pour cette fin d'année sunu meunoon ameu bonus tournage yi ak coulisse yi dinassi baaax. Au passage on vous félicite pour le travail remarquable ❤💯✅
Une très bonne idée 🤔
Machallah bonne année
Wawaw beug nagnko dh👌
Ko
Ko❤❤❤
J’ai eu les larmes aux yeux dankh diaye katou promotion bi belle leçon
Xawma sax lane la wara commenté wallahi leçon yi amna solo machallah
Ndaysan des vrais artistes
Vous voyez ce que l'homme ordinaire ne voit pas
Chaque épisode vous transmettez des messages très importants
Ambulant man bi sama bop rk la guiss si épisode bi
Vraiment un grand merci
Wallahi croisement Cambréne Pate d’oie colbane souma fa diarrei bilahi damay fattei sama bop courage à tous les jeunes qui se débrouillent chaque jour pour dimbalie sén famille Sénégal jeune you am joom niofi nekk
Fo fek dragon day soof 🤣🤣🤣
Xolal ouroul ayni bii nim téyé rek 😍
Bilae walae je confirme
Alhadouliha je viens d être maman des jumeaux très beaux après 3 ans de mariage gnianaléne me 🌺🙏🙏
Yalna barkel
Nékkeu léne si you tube bii dii Diour rk ay Dôme capitale karma idoles maîtresse d'un homme marié etc... Toudou ablaye ba parré Di djour tmt🤷🏼♂️
Machalla
@@papanasri4931 😂😂 li raay nama
Machalla long vie bb
Marchand ambulant day nekh derette way💋bien jouer frère 😍
Actuellement Capital est le meilleur sketch au Sénégal,il y’a de l’humour mais également bcp de leçon morales à chaque épisode
Wallahi épisode bi amna solo amna ambulanmen yokoye doundou dh
Bonne continuation à BM audiovisuel la série capitale c'est une série en magnifique je regarde je suis un jeune marchand ambulant mais nous les marchands mon somm très fatiguée
Magal Gui magal Gui magal Gui magal porokhane inchallah
En tt cas Khadija m plaît bcp...
Jiguéne day nekh dérétttt...
Vous avez tapé encore fort,une épisode avec bcp de leçons à tirer. Vraiment le message est très important et merci d'avoir pensé aux jeunes chômeurs❤❤❤❤❤❤❤
Vraiment série dafay yété de ma part guiss nassi sama bopou 😢diam si yéne
Macha allah Ass tes propos me touchent au fond du cœur
Toub ba touba toul j'aime mon village'''''''''touba toul''''''
Magnifique thème bilay. Marchands ambulants yi gathia ngalama. Ay diambaars tigui.
Papa Ass ak wadjoubakh nioy meilleur acteur comédie kou d'accord
Bilakhi Amana solo trop vraiment 🥰🙏
Ça m'a fait pleurer lrsq qu'on a accusé faussement le vendeur bnne continuation
C'était comme si c'était toi qui étais accusé à tord. C'est jamais facile courage à eux qui subissent ce genre de préjudice
Qui est D'accord avec Ass et fodé clique sur j'aime
Un message très important pour le président
Mé capital mom dfa wara continue bokou n'a série you dak si Anne bi machalah
merci bcp capital vraiment content naniou trop man mi marchand ambulant la té osi amna sama Bac
🥺🇸🇳
Ndaysane marchand ambulant aka méti façon nit bou nékk ngay tasél 😥
Dieuredieuf s saliou mbacke💓💓
Chaque épisode est pleine d'enseignements, Masha'Allah
Wax lenn si ongles you goudou yi bookk😂
Merci infiniment
11:47 djoyou papa Ass bilay meunou mako mougne😂😂
Li meune Nani mo yakh sama adouna 2014 ba legui laniou mako defon
Defa de retour Oooh generique bi defa voix bi mashala et linsrumental aussi bien choisi🔥❤😍🎶🎙🙏🏾
Diay Kat bi dé néhna déréte Macha allah Boudon kénék filalay gnouss Bagua teud sa gnaway geuth
Djiguen deugu day beuriii diam nékh daréttt
Aye waye ndeysan adouna li mofi âme 😭
Vous êtes les meilleurs capital
Deuk bi koula gueuneu soon mola gueuneu diangu mais Sénégal mom bras long et surtout ce que je dis chaque jour l'habit fait le moine dans ce pays.
Ma shaa Allah la production est top
Oohh sa m rapel bcp bimay ambulant
Wa ki dou Djiby légui yawite yagui si théâtre yi😍😍
Ass ni dou yém kou beugue Ass b jm❤️
Gni ay théme you ameu solo laniouy déf marchand ambulant Ndogo Lo woy nako dé légui légui nga taxowo nitt diko Diay mou Dianila
L’homme qu’il faut à la place qu’il faut exactement ça 🙏🙏🙏🙏🙏🥺
J'ai vraiment rigolé ces derniers temps-ci merci à toute l'équipe de capitale... BM franchement son ak images yi diarna yone manchallah... Merci ✌️👌👍
Vive la consommation locale,cotè audiovisuelle et cotè markting vive la rèvolution
Xallé bou djiguéne bi mo réwe Ak niawayame😂😂🤣
Sama yaram daw n’a 😭😭😭
Ass vrai défaillant la quoi. Loum deff guen si. Niak diomm la deff 😂😂😂
Merci pour ce thème : l'insertion socioprofessionnelle des jeunes diplômés...
Le message est passé force à vous les ambulants
Message bi amna solo bilay 🙏🏽❤
Nooo xalébou djiguen di bang diwou mbeud guis guén lamou poudarou 🤣🤣🤣 nooo poudarou bi comme poucer 😂😂😂😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@@SaraSara-rw1qfno srx guis gua ko xamoul bopam noo ki ko maquillage raye nako 🤣🤣🤣
Ndayesane ambulants dafa meti trop ms nk lepp dina bakh inchallah
Diaykat bi il est Fort 💯
Les marchands ambulants yalla néléne yalla taxawou si barké cheikh ibra ✊🏿
Djiby mon ami des HLM bonne continuation frère !!! Félicitations.
Longue vie à toute l équipe on est très content vraiment ❤️
Ya n'a plusieurs qui ont eu leurs bac mais ils n'ont pas espoir .L'Etat doit soutenir les étudiants
Blyyy li mo am senegal gay dane sa doolé Nioulay togne
Kou beug capital beuseul j’aime 🥰
Ça se voit que boy you raffete yi gno geuna wathié sen bop k golo diamniadio yi😂😂😂
WOUYYY MANGUI RAMMM 😂😂😂
Ma ngi toup ba Touba toul 😂😅😃😄🤣😂
Marchabd ambulant bi il a un beau regard. Gentleman !
BOUL NOP SAMA JAMIGNE BI
thieye sénégal li mome dawna yaram
Message bi am na solo je me rappelle un jour boba ma ngui dara dia danio démon bène keur tokkk fa ngir boune paré diokh niou dèsss mais mais bène djiguène mo guèune né nio dieul téléphonam niouy wakh mouné nioko dieul ta yeugou gnou tinou niou mais heureusement borome keur gui mo guiss téléphone si nèkk bi néko ya ngui fatté sa téléphone si nèkk bi khôlo kou bakh diko guigne talibé yi wallahi nitt mo yakamti rek mais lou way mougne mou dièkh ta Yalla mi ngui ande ak mougne katt yi lila wakh si Alkhour an إن الله مع الصابرين
Lou takh Khadija yi rafet❤️😍way
Amna solo trop
vous êtes les tops de l'année ass ak fodé
Fo guiss kou niaw dey bari histoire 😂😂😂
Machallah Message bi dialleu nahh
Ndeysane Seen série amna solo Manemii lolou moma dall 2017 la am BAC ba licence guisouma Dara mou leer ma dawww gueune sarap ndayy liii rekk
😆😅😅😅
Machalah bonn leçon ❤️🙏🏽
Wa femme bi dou régler ak makup bou niaf ndym bi mounane ay dou diwou diwou mbéde
Ndeysaan message bi amna solo💚☝☝
Beaucoup de courage à nos emballant 💪🏾💪🏾💪🏾
Oh Sénégal métti na diague ba paré do am leguey 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Merci beaucoup message bi amna solo❤️❤️❤️❤️❤️
Papa Ass barckei seydina mohamed damako beug😂😂😂
Non vraiment série bi am na chance bly 😍🙏🙏
Sa leel bangui dem dehhh boy mongui dem dehh 🤣🤣🤣🤣gueneil niama bi 🤣🤣🤣🤣🤣 pa ass Dinama rey🤣🤣🤣🤣
Message bi amna solo wayé yaw ass doo diouboo ak kenne
Carrément c'est sûr, vous êtes extraordinaire ✌🥰
Ay way papa ass contuné léne way
Qui a compris le séquence de marchant ambulant et les clients ¿
Sama yaram dawna kw ,marchan ambulan da metti bilay ,diga dokh ay kilometre té do diaye tous .
Bilahi ndox 9h ba 19h do yobou 1000 f
@@moustaphabadiane2703 no diarnaci bro lou métti leu walay mai sa irra inchala
Niaryi koum néck si yaw nit kou Yalla beggeu gua moy lawéte ak téy 🙏
Machalah sene ligueye rafete na dilene nianale bonne continuation
Bilae sama toma dinama ray brick bi😁
Marchant ambulant bi dioylo nama😭
Dou ioe kessé
🥺🥺
Ndeysane marchand ambulant yi dagn len wara diapalé
👏👏👏Tay moom gisnaa sama bopp vraiment ci épisode bi
Magui Toubb ba Touba TouL 😭😂😂
Machallah message bi dialeuna
Marchan ambilan Ay gorr lan té kouné ngisi
Koulén Di toroxal yakar ni dangaléna GeuN billahi sooyy dééé dalay bétteu
Wala dinga am diafé diafé yoodoul masa xam
Té kigay xép sax so démé limi lék léko ko fimouye teude teudo fa bilae
Vraiment message yi mingui cool Nice na trop
Non niec n'a amna solo torop 😭 Sénégal 🇸🇳 yalna diamou yague rek 🙏❤️
❤️❤️🙏
Oh ndeysane j’ai faillit pleurer ni rek lagniouy def djigne la dara avant guay expliquer niou dorleu ba ray leu
Très intéressant cette épisode chapeau à vous
Amna solo trop bilahi
NIOUGA KÉBÉ THI HISTOIRE SÉNÉGAL BA LEEGUI KÉNNU DIOTAGOUKO THI REEWMI THI ALALL💰💴 TA THI AMBILAN LA DIEUKKÉ
AK BOUBACAR SAMBA DIEY BOROM THIÉB BI AMBILAN LAWON
Le Messages de Papa Ass pour le Président de la République est trop fort
Ayway père fodé sofi nekkoul wone dou bakh di