Masha'allah, une serie que je peux regarder en famille car il n'y a pas d'abus de langage, l'accoutrement est correct, le paysane reflète la réalité sénégalaise
Respectons les 5 prières quotidiennes et ayons la confiance entière en Allah car il n'y a de force et de puissance qu'en Allah, maître du destin ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
La patience et yermende Bakari est le sénégalais de vraie merci pour ce réveil de conscience même ces série de rien doit finir avec le jup jubal jubanti merci le peuple
Ah j'adore le comportement de la fille, dés fois dans la vie, il faut sd soucier un peu de la dignité et surtout du sacrifice que font les gens envers toi et éviter de tout prendre pour sa liguéyou ndeye. Niit, niit moy mbokam!
Chaque épisode est plus drôle que le précédent 😂 le jeu d’actrice de Oulimata la cliente 😅 qu’elle est son nom dans la vie réelle ? Encore une fois bravo au casting et aux scénaristes ✨
Masha'allah, une serie que je peux regarder en famille car il n'y a pas d'abus de langage, l'accoutrement est correct, le paysane reflète la réalité sénégalaise
Respectons les 5 prières quotidiennes et ayons la confiance entière en Allah car il n'y a de force et de puissance qu'en Allah, maître du destin ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Foutaise
Djibi seye niack na fayda😂😂ta sonal bakary ak Ndiabotam gui😅😅😅😅
😂😂😂😂
Lolou la beugone niow wakh 😂😂😂
Rombe na niak fayda
Tropp😂😂😂
Sama tonton dieukeur nilay def so boyalé mou fayko AK yénén
Grd yamar mané repose en paix 😢fatiha+11likhlass svp 🙏
Rip
Paix à son âme
Pour la première fois bakary wathie 10mille 😅 tay contente 'a🎉😂
Mais monone na am lou eupp 10000 mom 😂
Sheutt la fille a bien assuré 😂😂😂masha Allah
Djougei si Omar Diagne ak taximan bi ngew si bakary ak cliente bi 😂😂😂😂😂
Même moi 😂
Moi aussi 😂😂😂
Nonoula démé nk😂😂😂😂
ki môme cliente deugue la😂😂saf n'a lamigne
😂
Non mais franchement ki def casting bi réussir nako niom nieup ay Holal cliente Bakary bi rek elle a grave assuré
La cliente de Bacary a bien joué son rôle ❤
Qui kay dafa réw t'es soff 😮
😂😂😊
@@Bbass-verymoma diahal ki rew ba dofff
genre djigueine yi rk la beugeu com guel mom lay weur ni
Lirr katou commentaire yi longue vie à vous ❤❤❤
Amiinn Ya Rabi ak yaw it
@@BRIGITTESADIO-l3s
J'en fais partie
❤❤❤❤❤❤
Bakary mon idole un vrai chef d famille ❤❤😂😂sonou tjr pour la famille sama sokhna mom lamay togne
Machala iow tamit kou bax nga
💪🏾🥰
@@marieodilethiaw merci bcp billahi di sonou pour la famille dafa nekh thi xol
Nonou la deh la famille est tres important boula si dara guene
Tonton grand tamite 😂😂😂dougnou si wakh😂walla gnou bayi nonou😂😂😂
Ñakk simple rek😂
Tonton grand mome sama team moko mome😊
😂Lol😂
Une pensée forte à tous ceux qui traversent des moments difficiles. Restez forts, cela va passer.❤💪🏼❤
inch'Allah
@@awasarr7943 Bon courage 😊💪🏼
Li yane jour lay daw
Inch'Allah ❤
@@shella8096yane jour lay daw
L'une des meilleures série au Sénégal machallah vous êtes les meilleurs des meilleures ❤❤😂😂
Je découvre cette série. On retrouve notre télé nationale tant aimée il fut un temps. Merci pour la sensibilisation des automobilistes. Merci RTS
Machallah femme bi dafma moudj nex sax
La dernière séquence avec Bakary ❤
Le fait k mou xar ko bamou pareh et tout leep Ndax yeurmande
Wa RTS gnou meuneu gno eupou dolé barké seydina ousmane sonko mou selmi❤❤❤
Tchii Sonko Yalla maynako nakk RTS sakh légui daniou kaay tagg dakh mom
@yerosow7063 boubakh puisque c'est notre libérateur ❤️
Le retour des théâtres du mardi soir à la rts une demande nationale.
Théâtre rétro nak
@adjacisse3003 bien sûr rétro kay devant la télé avec toute la famille nous sommes nostalgique de cela
Yalla Na Borom Bi Taxawu Taximan yeup 🤲🤲 amna ñussi Dundu ay jaffé jaffé comme Bakary 😢 🙏
Bilaye Diam si yaw rékk ❤❤
La patience et yermende Bakari est le sénégalais de vraie merci pour ce réveil de conscience même ces série de rien doit finir avec le jup jubal jubanti merci le peuple
Diomay ak sonko yalla bounou rèro ❤🙏🏿
Lolou menoule ndiakk nakh yalla ak yalli laa
@@awadiop9823ya meuneu doull
Wa djiby seye bi mom nitt la wala kouber😂😂😂ki sokhorna dé😢😢😮
😂😂😂😂
😂😂😂😂con rek la def😂
@talibeserignebi9768 kikay badola la khamna vengeance lay deff😂😅
@@talibeserignebi9768 Kon wam gui dh thi gniaàkk lako djieumeé 😂😂😂
D'où nitt dee satala la 😂🥳
Cliente bi dafay bonn lo kholl 😭😂😂
bilay may wax mouni day dioye 😂😂😂
Sa kanam gui di melnè diombakh😅😂😂😂
Blh ki day diékhale khol blh wow beut bay beug dh sof tmt😢😅😅
Djiby Seye est le meilleur artiste 😅
❤❤❤❤ sounou mame yi yalla yalla nalen yalla khare aldiana ❤❤❤❤
Non la femme de Bakary je l'aime ak deur bou stylé bii Aka am fouleu😂😂❤❤
Wallahi Bakary saa bou reetanee rek ma rèetaan😂😂
bakary ak cliente bi dielal gose dieulal durat 😂😂😂😂
Kou j'aime yalla n'a nga goudou fan. Khaliss bou barri ta Barkel ❤❤
Kou guiss ni Bakary dayy moudie dokhane guele bi lala j’aime ❤😂😂😂
Ah j'adore le comportement de la fille, dés fois dans la vie, il faut sd soucier un peu de la dignité et surtout du sacrifice que font les gens envers toi et éviter de tout prendre pour sa liguéyou ndeye. Niit, niit moy mbokam!
Je suis très content quand Bakary dit alhamdoulillahi ❤❤❤❤❤❤❤❤
Ma série préférée du moment 🤣duo djiby Seye ak alima gadji lounek la
No franchement j'aime bien cette série, c'est tellement naturel la facon de jouer
Oulimata mii tamit leuf la😂😂😂😂d nena bakary xana dagga am sama thiompintance
Oulimata mi sofoul dei🎉 mais réwna ta meune tontou😂😂😂
Cliente bakary bi Ayna trop 😂
Lii laniou naane client boo doull yeikkalei fein😅😂😅😂
Délénn bayi xéll kiy wakh bu série bi diékhé
Lou am solo😢😢
DIEU MERCI 😂BAKARY AMNA CLIENT TAY😂😂😂😂
Wawé façon client yi mom bakhoul
10:15 Djiby Seye con na gnak foula😂😂
2:45 sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉
Manchallah ça c'est une vraie série télévisée à l'image du Sénégal y'a bcps d'enseignes jajëf au réalisateur et aux acteurs ViVE LE PAYS NOTRE FIERTÉ
Nena mola guena rafettah ak nimko wahe😂😂😂 non djiby seye dinama rey.
Machallah mais grand liko femme didéf métna
Cette série meilleur des millions de vues une série qui reflète la réalité Sénégalaise
Djibi seye ak Marieme dougnma ray😂😂😂😂😂wa cliente bi tamite rewna di gauche droite ni😂
La fille elle est formi double dable🎉❤
Machalla une idee tres tres original ya beaucoup d.enseignement ❤
Bly walahi Taximene yi sonou naniou🎉
Yalna yalla mousseul bep taximan si façon client yi 😂😂😂😂😂😂😂😂
Amine bro man 🚕 manla
Guel bii si taxi ban guel la Tmt 😅😅😅😅😅😅
Ki kay dafa yabaté té réw wayé Bakary tamite amna patience 😂😂😂😂😂
@@zeyna1393Bilahii Teksii elle est talentueuse 😅😅😅😅
Xalé 2002 yi la😂😂😂
La fille a bien assuré son rôle manchaa Allah
Non bakary meuna mougne 😅😅😅 ndeyssane borom bakhla
Bakary mi lanla yapp thi auto bi rap wala djiné😂😂
Djiby seye mii niiit laa😢😅Cliente bii boumou yapp souñou taxi nazional bii deih😅de tonton grand à seuñ'bii😂cliente bou rew🤣,ñoun ñi deurr dieul nañ coup irrégulier😢😂baKary zeu souwi fière❤🤣Bakary ak cliente bii😂barki très srx j'aime ce gars😂😂😂😂😂
Tay mom bakary dagnko togne mais djiby aussi dafa sokhor nk😮😮😂
Take katou cheveux bou j’aime sama commentaire bouma la reukè dinga mourou 🧕🏾 dji 😂❤❤❤❤❤❤😊😊😊😊
😂
😂😂😂😂😂
Yaw môme kana série bouma dème fékh lafa😂😂😂
Alhamndulillah Bakary contane na tay😂😂
3 mil nga narsé weur ndakarou😢 client bi réwna 😅
Djiby seye tamit fleurs yi dina laurre deh 😂
😂😂😂😂😂😂😂😂 vraiment Djiby seye nekhna 😂😂😂 wa cliente bi 😂😂😂
Djiby Seye amoul ben fouleu😂😂😂😂😂
Tonton grand kay😂😂
Tey mom bakary yap na client boumou doul yekalé fenn.😮😮😮
Bakari dama ko yeureum bilahi amna goor youy doudue li soubeu ak gone force a vous
Bakary la grande comédie mais difficile c'est un malade. 😂😂😂😂
La cliente est a bien joué son role😂
Bb Sadio😂
Mame Khoudia tam kagne lay weusin 😂
Sérieusement patience Bakary bi beine Taximan amouko
Non li dafa eup way😂😂😂
Djiby mom kouberr leu 😂😂😂
Chaque épisode est plus drôle que le précédent 😂 le jeu d’actrice de Oulimata la cliente 😅 qu’elle est son nom dans la vie réelle ? Encore une fois bravo au casting et aux scénaristes ✨
Mane mangui dém bou bakary ak cliente bi yégué fign djeum ngéne woma😂😂😂
Bacari avec sa cliente 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Vision Sénégal 2050 inchalla ❤❤❤
Une série 100% sénégalais
Je viens tout juste de regarder tous kes 14 épisode aujourd'hui 😅
Ya meune
Le Cleîn d’œil à PROS j’ai adorée ❤❤❤❤😂
Cliente bi khamadi na😂😂
Trop
Elle a bien joué son rôle 🤣🤣🤣
MEILEUR EPISODE POUR LINSTANT SELON MOI 😂
Bilahi😂😂😂
Djiby AK Mame khoudia😂😂😂
MEILLEUR SÉRIE SÉNÉGALAISE
Kou beugueu Modou lô beusseul j'aime way❤#dagualbopbi animou😂
Franchement la fille a bien joué son rôle 😅
Hii li boudone Mane dans la vraie vie dorna mbeuk bou yagg
❤🎉
Enfin Bakary ame cliente
Meilleur épisode wallae😂❤
Tonton grand 😅😅😅
kou beugeu bakary lala❤❤
Bakary mome la guina yereme thi Sénégal 😅😂😂
Stresss Bou ma meunti am boumay sétan Seri bi damay retann rek😅
Bakary sa cliente bi neub na😂😂
Ahhh djiby seuye kay nk sou ndiarignu bakary neikker dih eumbeul diabaram kay amnah. Ndiarign kon😂
Des rats de laboratoire 😂😂😂😂 sacré Djiby Seye
Niak foulak Djiby Seye daf maa depassè 😂Mai’s Bakari sa cliente bi rew n’a ba neube 😂
Vraiment. Vraiment Episodes bi nice
Sa kanam na djoumbakh 😂😂😂
Boule ma toufeli 😂😂😂😂😂
Sénégal mafi guan yaye❤
Bakary est extra 😂😂😂😂😂
Bakary damako yeureum 😂😂😂
Moussouma guiss lou melni wa Djibi seye mba diam la🤣🤣🤣