L'artiste est un créateur. Il est celui qui se souvient encore de son séjour dans le monde intélligible d'où sa persistance à refaçonner son art. L'homme en question Mouhamed NIANG a décidé de consacrer son art à rendre un hommage à son guide, à notre cheikh et homonyme le soleil qui rayonnera jusqu'à la fin des temps et au delà en l'occurence Serigne Saliou Jantub Jamono. Mouhamed on ne saurait te remercier autant car en tout temps, tu ne cesse d'aiguiser notre amoiur, nous rappeler l'éminence de Serigne Saliou. Il est sans doute claire que tu n'as pas d'égal dans ton art qui concilie originalité et création. Mouhamed NIANG tu fais notre fierté. J'espère un jour te dire à quel point nous t'aimons IN SHAA ALLAH.
Dieuredieufty sërignë salliou 😢😢😢😢😢😢 thiéye sounou wadjii 😭 yalle na nou ko yalla fayale ta Yoko aye léram😢 thie mbarkép allehourane😢❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
*Yaw mi nammou saw lamigne di out lou gakal yonou mouride* *Maguilay digeul ga mouma* *Téga xamni yonou mouride dina dathie Adouna comme niko Serigne Touba Khadim Rassoul waxé.*❤️🙏
Machallah Mohamed Niang sagoup bépp Mouride nga. Yiw nga yarou nga té meun nga lingay déf. Serigne Salihou Yalla na deukalé ak Yalla ak Yonentbi ak Cheikhoul Khadim ak Mame Cheikh Ibrahima Fall. Amine !
28 Decembre jour bi gueneu tiss si dioulitt rawatina salihate yalna nou yalla fatal serigne saliou mbacké si barkèb serigne TOUBA khadim rasoul 🤲🤲🤲❤️❤️
Mouhamed tu es le meilleur man tay soma beuguè serigne saliou ba gueumè wouma ko guinaw yalla Mouhamed ñiang la dih dèglou ay son wam moumay yobou gou soli may kheuy dih guene beugue serigne saliou beugue nak kou diara beugue 28 décembre motakh guissou ma serigne saliou dih gnane yalla sougnou goudi guou gneuk si birr bambèl yalla na yèkh wayè dih gnane yalla serigne saliou fèk gnoufa si barkip léram gui Mouhamed ñiang yaw tamite aka nèkhone bène bèss ma guiss la beugue nala teh amouma sa faye yalla namala yalla fayal ak serigne saliou si barkip zeydina mouhamed psl 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
L'artiste est un créateur. Il est celui qui se souvient encore de son séjour dans le monde intélligible d'où sa persistance à refaçonner son art. L'homme en question Mouhamed NIANG a décidé de consacrer son art à rendre un hommage à son guide, à notre cheikh et homonyme le soleil qui rayonnera jusqu'à la fin des temps et au delà en l'occurence Serigne Saliou Jantub Jamono. Mouhamed on ne saurait te remercier autant car en tout temps, tu ne cesse d'aiguiser notre amoiur, nous rappeler l'éminence de Serigne Saliou. Il est sans doute claire que tu n'as pas d'égal dans ton art qui concilie originalité et création. Mouhamed NIANG tu fais notre fierté. J'espère un jour te dire à quel point nous t'aimons IN SHAA ALLAH.
❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalnako yalla sam té défal la diam yaw tamite ci barki borom Khélcom🙏🏽🙏🏽🙏🏽
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ machallah
❤❤❤machalla li niou naron na wakh yeup wakh guako 😢😢😢sama yaakaar serigne saliou mbacké a vie❤❤❤
Ma sha allah❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏾
Je suis une Moustarchide ms j'aime beaucoup Serigne saliou mbacké yalla na yalla yokku léram té tasinusi barké bi 🤲😢
Machallah Nonoula déé nioune nieup béne lagne blh Mouhamed niang et le meilleur Machallah chapeau ❤❤
Aaammmiiinnne waaye
Na niep Wakh Dieuredieufety Serigne Saliou Mbacke .
Mouhamed Niang Messi Merci❤
Dieuredieufety Serigne saliou mbacké balla Aïcha ma vie mon bonheur ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Dieureudieufati Serigne Saliou ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊😊😊😊😊😊
@@YasinToure-zo3cb❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩❤️❤️❤️
Dieuredieufeti Serigne Saliou mbacke
Kou gueumni li nèkhna rek❤❤❤ ohhhhhh😢😢
On l'a jamais vu ni jamais entendu sa voix mais son amour vit des milliards de personnes notre bien aimé {PROPHÈTE MOUHAMED❤
Mane de tidiane la wayé
Bilahi wallahi dama sope saringe Saliou yalna niou ko yalla fayal mame Saliou 😭🥹♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Sop nga kou ko ndiar dh 😢❤Walaxi
Amine kou bakh ❤❤❤❤
ana gui beugue serigne saliou lalal j aime ❤
Dieuredieufty sërignë salliou 😢😢😢😢😢😢 thiéye sounou wadjii 😭 yalle na nou ko yalla fayale ta Yoko aye léram😢 thie mbarkép allehourane😢❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😭Ndaysane biss bounou doul masa fate si adouna serigne Saliou yalla nanouko yalla fayal barkep borom touba 🙏🏾❤
Xol toyyynaaa😢yalla naniou yalla fayal Cheikh Saliouh Mbacké ❤yalla naniou yalla tass sii barkep ❤
Ndaysane khôl yi toy na
Amine ya rabbi
Amine yarabi
*Yaw mi nammou saw lamigne di out lou gakal yonou mouride*
*Maguilay digeul ga mouma*
*Téga xamni yonou mouride dina dathie Adouna comme niko Serigne Touba Khadim Rassoul waxé.*❤️🙏
Serigne saliou seul ❤️kouy salikhate rk lale j'aime ❤️❤️❤️❤️
Magui dadialé pour diokhla ko gua wayal ma El hadji Bara falilou sama khol❤😭😭yalna serigne Saliou motali❤❤❤❤🎉
Biss bou ben Mouride ak talibé dou meussa faté😭😭😭.
Motakh Niang ballo ma beug la.
A travers tes paroles yi di yok yeuk yeuk.
Walahi deugue leu ay paroles Mouhamed Niang day yok yeuk yeuk bou bakhh❤❤❤
Dieureudieufeuti Serigne Saliou ❤
28 décembre une jour unibliable😢
Ndaysan je me rappelle ce jour khalei la won j’avais k 8 ans mé dama dioy comme mak serigne saliou yalna yalla yokii léram té tass niou si barkém🙏😭
Ndeyssane
Thieuy s saliou Mbacké yalla na yalla yokku léram té taasinu si barkém
Macha allah mouhamed Niang t'a encore frappé comme tjrs❤❤❤
Machallah Mohamed Niang sagoup bépp Mouride nga. Yiw nga yarou nga té meun nga lingay déf. Serigne Salihou Yalla na deukalé ak Yalla ak Yonentbi ak Cheikhoul Khadim ak Mame Cheikh Ibrahima Fall. Amine !
Le meilleur de tous les temps moukhamed
Kéne dou faté le 28 décembre 😭😭😭
Jamais ngua diouk sou niou khol thiofél bima am si moom bilay mi ngi mélni dama Féké ak dundam je t'aime maam booy 😭😭😭😭😭
Machallah il a encore frappé wallahi lii dafa nékh Serigne saliou rék ka féss sama xole ❤ machallah
Manou nioo am kou eupou Serigne saliou mbacké diadieuf mouhamed sama toma ❤❤❤
28 Decembre jour bi gueneu tiss si dioulitt rawatina salihate yalna nou yalla fatal serigne saliou mbacké si barkèb serigne TOUBA khadim rasoul 🤲🤲🤲❤️❤️
Serigne saliou est toujours parmi nous. On a pas besoin d'aller dans son mausolée pour sentir sa présence. Mâcha way wi néx na
Je ne peux même pas retenir mes larmes aux yeux 😭😭😭merci encore une fois Muhammad niang tu as tapé encore plus fort ❤❤❤❤
Dieureudieuféty Cheikhouna Cheikh Saliou Mbacké ❤🎉
Ki défar ndawgni ❤
Mouhamed Niang yalla nala yalla doli tawfekh ❤
Fan ga duek sah way bi mo neh bilahi
Serigne saliou yalla na yalla yokou léram😭🤲🤲😭♥️
Mbacké bala yalna yala yok léram ,tassnou si barkem😢😢😢😢😢😢😢
Machallah xol sedda tina Mouhamed niang yalla na sa diam yague🙏❤️
Dieureudieufety Serigne Saliou🙏❤️❤️❤️❤️❤️
Bienvenue à Maroc le grand chanteur mane talibe ndiol fouta bi damalay béugué
Na niep wakh dieuredieufety Serigne saliuo mbacké Muhammad Niang merci beaucoup li nékh na trop way machallah ♥️♥️❤❤❤
Dieuredieufety Serigne saliou mbacké balla Aïcha ma vie mon bonheur ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mach'Allah mouhamed niang amatina solo😢😢jërëdieufaty serigne saliou❤❤
Mohamed niang yalla na sa diamo yague ❤
Niang ya meune dieureudieufety serigne saliou sama wadji mala beug 😢
Mako gneuker aimer yeiko setane ❤
mouhamed Niang yalla nala niou serigne saliou mbacké fayal 28 décembre dounko masa faté😢😢😢
Le 28.decembre 2007 date inoubliable 😢😢😢
😢😢😢😢
Oooooooooh Sama khôl bi sedna barké serigne Saliou 😂kou sa khôl nex rk manifeste 🎉
Yall na Serigne Saliou fayal gnoula
Yalla nanuko yalla fayal S sailou mbacke
L’amour que j’estime à son égard est inconditionnel merci Serigne saliou 🙏🏻
Mane talibe cheikh la Machallah Serigne saliou borom diamano yalna nako yalla yeureum ak niniou djitou
Seriñ Saliwu, Borom Xelcom
Maam Saliwu, keine du mom
Yaa donnu Seex Bamba ci defar
Ya tax say ñoñ di wuyyò jambar
Jërëjëf Seriñ Saliwu ❤️
Niang ballo wayatiga sa sangue lou yemei yewate gome yii😭😭😊
Oh mouhamed tay yobou ga sama xél mi fou sori may dioy rk tay danga toyal sama xol dieureudieuf serigne salihou
Mouhamed tu es le meilleur man tay soma beuguè serigne saliou ba gueumè wouma ko guinaw yalla Mouhamed ñiang la dih dèglou ay son wam moumay yobou gou soli may kheuy dih guene beugue serigne saliou beugue nak kou diara beugue 28 décembre motakh guissou ma serigne saliou dih gnane yalla sougnou goudi guou gneuk si birr bambèl yalla na yèkh wayè dih gnane yalla serigne saliou fèk gnoufa si barkip léram gui
Mouhamed ñiang yaw tamite aka nèkhone bène bèss ma guiss la beugue nala teh amouma sa faye yalla namala yalla fayal ak serigne saliou si barkip zeydina mouhamed psl 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieufty Serigne saliou Mbacke ❤️❤️
Jour bou triste 😭😭yalle na yalla yokou leer rame Amine 🤲🤲
*Dieureudieuf Serigne Saliou*
Ndeysan lii nékh way
Dieureudieuf Serigne Saliou❤️❤️❤️
Mouhamed Niang mou serigne Saliou Mbacké 🎉Ban Serigne Daouda guay chante si Son bi🎉❤❤
Yalla na Yalla yoki ay leeram te tass youn si barkèm 🤲
DIEUREDIEUFF Mohamed Niang 🎉 🎉
Yalla na yalla goudall sa fane maylaa wérr mouhamed niang
Niang contenati naniou yallna yalla guena degeureur batbi barkép Serigne SALIOU❤❤❤
Ani gni beugue serigne saliou may lén ma ay cœur barckép Serigne saliou mbacké 🙏🏾❤️
Bilahi j'ai même pas les mots Niang ballo amouma si yaw sagoo ndax sougnou sangue ba mbacké balla yalna batt bi guen werr machallah ❤️🙏
Serigne saliou est toujours parmis nous . On a pas besoin d'aller au moseile
Heure bo wayei nioune nieup guiss si souniou diguanetei ak Serigne Bi ❤️Borom Yeurmandé dji douniou ko woor mouy🙏🏾Dieuredieuf niang weral doundal ❤️
Yallah naniou yallah fayalee serigne saliou kaye leinn santeileima cheikhouna saliou ❤😭❤️🙏🙏🙏🙏
28 décembre biss bu tiiss si gnune serigne saliou yall nagnu ko yallah fayaal amine❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ machalla mouhamed niang yalla na bât bi wére❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Xole you toye na machalla yalna yalla wéral batt bi té yokk kham kham bi
Inchallah le 28 casablanca dîna wathie ak mouhamed niang mba yénangui wadial ❤😊
Bis bouma doul faté mouk .thiey Serigne Saliou dafa sori si sama hol. Yalnanou yalla fayal Serigne Saliou
Oh j’ai des frissons dieuredieufate Serigne SALIOU 🙏
Machallah Mouhamed yalla na yalla wèreull bat bii
Alahouma amine
yalla nla yalla fay si barkép s saliou mbacké🥲😌
Machala yalla na yalla lafal thi thiate thi barkep Serigne saliou nekh na lool❤❤❤❤
Je suis tidiane j'aime serigne fallou
Sm yaram daw na barki s Saliou 😢❤
Mohammed Niang louma beugue wax Serigne saliou rek waxalngamako bilahi amougnou sa Faye yalna bat bi we4 si barké Rasoulillahi 🙏🙏
Thieuy domi bamba djexna serigne saliou Moy kou ted ki
Kou melni Serigne saliou dotoul am sim rew
Dieuredieufeti Serigne saliou
Begueutina Niang ballo
Dieuredieufé serigne saliou mbacké sama yakar Tay ak euleuk❤❤😢
nn li dafa féss worna serigne saliou 🎉
Sant serigne saliou rkk moniou warr❤🙏
Macha allah sama sopé bi damala beug rék té Yallah takh
Alhamdoulilah Diarëdiëfeuty
Serigne Saliou ❤♥️🙏🏾
Yalla nañu yalla fayal sunu sangue bi🥰🙏🏾
Ki daa degg serigne bi
Mohamed niang da kham serigne saliou meun koo woyy
Ndaysane Serigne saliou nitt kou bakh té oyof tidiane la mais damako yag beug yalla na yalla yokou léram❤❤❤❤
Machalad,dieureudieufety Serigne saliou mbacke
Damalay beug ba kagn Mohamed Niang♥️♥️♥️
Borom diamono ❤❤❤ serigne saliou ❤❤❤
Yalna yalla yéssal yeurmandé si mom🤲🏻 mame saliou l'absent le plus présent ❤❤❤
Alkhamdoulilah Dieureudieuf Serigne Saliou mame bauy dougnoula meusseu fate. Yallah sa Borom yokk say ler dole Mame Cheikh Ibra 🤲
Yallna niu yallah fayall mam saliu
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤niang ballo yalna SERIGNE SALIOU protège
Pour la première fois j'ai pleuré pour une chanson 😢
Dieuredieufety Serigne saliou mbacke mome Serigne Bethio ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤ Machallah Niang dieureudieuf serigne Saliou Mbacké yalla na nioun yalla tass sii barkep ❤❤❤❤❤❤❤❤
La wone fa wone nexatina machallah MOUHAMED Niang yalla na yalla weral bate bi maye la goudou fane AK were barkep serigne saliou ♥️
Tu vas me tuer je maîtrise tres vite tes chanson big job Mouhamed❤
Ndaysaann wallay MAME AMO MOROM 😭😭 dieuredieuféti MAME SALIOU IBN MAME BAMBA ❤
Maasallah ndaysaan kénduko masa faté 2007❤😢
Dieureudieufeuty Serigne saliou mbacké ✌🏾 As salih 💗🙏🏾😭
L’artiste qui n’a jamais perdu sa valeur ❤🎉
Dia dieuf waye🙏🏾Mohamed 🫶🏾mame saliou kénula 🫵🏽
Mouhamet niang mou Serigne Saliou me touche vraiment j'aime seydina Saliou