Ayy yalla sunu borom xawma ma wone sou wathie tone nourok nitte gnii dimbali léne indil léne lii di xassida xaww kone kou fatt faww nga niam sawara dieuredieuf borom touba yow mouñouko indil nga matt ñou yalla nak seuk nak🤍🤍🤍🤍💪🏻💪🏻💪🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Ndeysaan wér na waaye wuute bi moo ngi jogee ci ni ko kureel yi di tënkee waaye ñoom ñépp a bokku yaxum njàng muy kenog WKSM. Ba ci waa Daaru Xuddóos niko Lamine Seye daan jànge bokkul ak niko Maxtaar jàngee lépp WKSM😁
@@Khassidayi_rek Werna lool manam mak gni nio yeemé Fiimné nek boo xoolé mouxadimat s.masamba tawil Binu jang 1978 s.mayib jiiteko ci keur s.abdulahi jaxaté Fimné muxadimat bobu ci lia kourel bari daan sukandiku du jàng tawil te seenum njàngin dou boku te kou nek ci kourel yi lamuy jàng dafay wer ci famu tek Ndax booy xool ht. An htdkh seeni njang ci tawil bokul nunukoy jangué te lepa wer Fimné at yii sax la banén midadi tawil fegne te mak gni jangué keur s.mustafa saliou ci atum 1975 s.mayib jiitewon ko Batay midadi bobu nak mo gëna wayu muxadimat te daan thiouné yu nex yi moko ëupulé muxadimat bi Manam nun gniy jang aka tewlu nanu xamne gniy kourel tegu nanu fu wer degiin yi niodul mana yam ak cam gi ak ranié gi Ak tamit ku nek lamuy taneu ngir teunk ci lamuy jang li amsolo moy na lepu doon louwer te bayiko ci mak gni
Thiey Thieuy❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤diadiéf ❤❤❤❤❤❤❤oh oh oh ah ah ah❤❤❤
71 bis bu set nga dégg ci lu yees 😍 Waaw leen góor Bishri.
Xaadim Jóob ak Useynu Faal ci jàkkaarloo moom nii rekk la mana mel ❤️❤️
Walllahi louwer nga njangum moo bari ay xeetou mbir you doy waar
thieuye je pleure de joie wallahi borom touba amoul morom
Moustapha dieng yéména nimouy diangué 71oh😭😭
Merci beaucoup de mourid yi
Wa niawone démou nioniawate wala lii mom khana dou diamonoye taye machallah
Likouko deglou tee dioyoo reek doit nite kou tekhhee Thiey Serigne bi bou wathioul woon khawma founiou dieum bilaye ma Nam Touba baydioy
Ahmadou rek kep❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🧡🧡🧡🧡🧡🧡🧡💛💛💚💚
ماشاء الله مفا تح البشر❤❤❤
Ayy yalla sunu borom xawma ma wone sou wathie tone nourok nitte gnii dimbali léne indil léne lii di xassida xaww kone kou fatt faww nga niam sawara dieuredieuf borom touba yow mouñouko indil nga matt ñou yalla nak seuk nak🤍🤍🤍🤍💪🏻💪🏻💪🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Dieureudieufeti borom touba 😍😍
Ndeysane 🥰🥰
Bilahi ndame thiouner yemena Yaram 😭😭😭
Taarrrkala daga ko diekou MachaAllah
Ndeysane maguéna lol ❤️
Thiossanè na dh
Wallahi ndayesan
Waaw Gauur ♥️🙏🏽
Euskeuy Euskeuy kawer na lolle MachaAllah
JEREJEFÉ BOROME TOUBA KHADIMOU RASSOUL
Mak gni lay dégg dh 😭😭😭😭😭
❤❤❤❤
Thiey yallah ndam rék inchallah
Maashaallaah Jaajëf rek
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😍ay way li yéména
Thiosanne😪😭😭🥰🥰
Ndeye saane 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Ioe ku bax nga man di setan lamb dama lá faye guiss ngaye commentaire wayei bima la guissei fii lala geuneu woolu
Thieuy souniou borom
Waaw len goor
😍😍😍😍
Ceyy xassida
Akassa
Machallah
😢😢😢😢😢
Combien de personnes sont regardé le vidéo a leurs téléphone
😭😭😭❤skeuy
😭😭❤️❤️😭
Li nexna lol bilaye
😭😭😭😭😭😭😭😭😭
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Wouté nak 71 bou htdk
Wawaw. Maggni nak sen diang dafa khoot sen bén jotay meungua sé am facon jaģin you barii. Kourel bou nek ak noumkay dégué...
@@Khassidayi_rek ndayssan walay deugla
Wawaw bi sakh mo guene originalé boko comparé ack son mag gni
Ndeysaan wér na waaye wuute bi moo ngi jogee ci ni ko kureel yi di tënkee waaye ñoom ñépp a bokku yaxum njàng muy kenog WKSM. Ba ci waa Daaru Xuddóos niko Lamine Seye daan jànge bokkul ak niko Maxtaar jàngee lépp WKSM😁
@@Khassidayi_rek Werna lool manam mak gni nio yeemé
Fiimné nek boo xoolé mouxadimat s.masamba tawil
Binu jang 1978 s.mayib jiiteko ci keur s.abdulahi jaxaté
Fimné muxadimat bobu ci lia kourel bari daan sukandiku du jàng tawil te seenum njàngin dou boku te kou nek ci kourel yi lamuy jàng dafay wer ci famu tek
Ndax booy xool ht.
An htdkh seeni njang ci tawil bokul nunukoy jangué te lepa wer
Fimné at yii sax la banén midadi tawil fegne te mak gni jangué keur s.mustafa saliou ci atum 1975 s.mayib jiitewon ko
Batay midadi bobu nak mo gëna wayu muxadimat te daan thiouné yu nex yi moko ëupulé muxadimat bi
Manam nun gniy jang aka tewlu nanu xamne gniy kourel tegu nanu fu wer degiin yi niodul mana yam ak cam gi ak ranié gi
Ak tamit ku nek lamuy taneu ngir teunk ci lamuy jang li amsolo moy na lepu doon louwer te bayiko ci mak gni
71 Wala 78
71
Ndeysane
71 la ndeye sane thiosanena 😭😭😭😭
Machallah