Ndeysann dégloul Malick Ba thi Mawahibou bi...

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 20 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 126

  • @ibrahimasow6223
    @ibrahimasow6223 4 ปีที่แล้ว +21

    Khassida bi mo yémei banga khamni ére boko diang rek day gueneu wanei Kénak Serigne bi. Wayé 78 bi diaar na yone, tégué na, maggué na aussi. Wa HT danio am mayouk sa Borom. Légui mom mangui 78 bassi kanam. Jërëjëf ! Yalla naniou sonou Borom dollé samou t déf niou ay Mouride sadeex si Barkep Al Mustafa haleyhi salatu wa Salam

    • @Diantal
      @Diantal 4 ปีที่แล้ว +1

      Saay mbela nexna deh😁😁😁

    • @ibrahimasow6223
      @ibrahimasow6223 4 ปีที่แล้ว +1

      @@Diantal wakh nga deug tamit. Kharal ma bolé lène rek 😀😍

    • @Mouride961
      @Mouride961 4 ปีที่แล้ว

      Magui thi wa daaru man 😂😂😂

    • @Diantal
      @Diantal 4 ปีที่แล้ว

      @@Mouride961 wa seugn massamba kemane la deh 😁😁😁

    • @Mouride961
      @Mouride961 4 ปีที่แล้ว +1

      @@Diantal
      😁😂😂
      Euy mouride nioniu dh xamnaani nioy fondements yi

  • @papasafouseck
    @papasafouseck 2 ปีที่แล้ว +1

    Thieyyyyy sm wadji Malick bâ bilahii nigmay df yalla rkk moka kham😭❤️ sawayy machalah bilahii ❤️

  • @niangelementmalickbaht9670
    @niangelementmalickbaht9670 4 ปีที่แล้ว +9

    Thiey sm wadji Bou Néké si kourel gui rék Nga kham kou💪💪❤❤❤❤🙏

  • @abdoulayeosnseck7012
    @abdoulayeosnseck7012 3 ปีที่แล้ว +2

    😍😍 aldiana deug mongui niii 😍 degloul Malick ba rk

  • @khadyfall104
    @khadyfall104 4 ปีที่แล้ว +2

    Machallah s Malick yag fi loll te wer ci barke khassidayi

  • @moustaphaxalifababou5985
    @moustaphaxalifababou5985 4 ปีที่แล้ว +4

    Malick ba moy kourel gui billahi 😍😍😍geudj nama diglo kourel gui comme ni mashallah

  • @sokhnamatyyayefall3075
    @sokhnamatyyayefall3075 4 ปีที่แล้ว +6

    ndayssane li aldia na la machalla😍❤❤

  • @abdoukane5608
    @abdoukane5608 4 ปีที่แล้ว +5

    Machalla dieureudief waye Yala nale yala Faye si barkep Serigne Touba Amine Serigne Touba kenne amoule morom

  • @Dieylanidiop28
    @Dieylanidiop28 4 ปีที่แล้ว +15

    Thieeeuy Malick mo yorr deug deug animation Kourel gui 😇😇💫👌

  • @dieynabasarr3565
    @dieynabasarr3565 4 ปีที่แล้ว +4

    Deysann yarambi doyna bonne continuation dieurdieuf

  • @madiopthioune6726
    @madiopthioune6726 4 ปีที่แล้ว +5

    Machallah wa li kawéna trop.
    Ms kéndou malick ba

  • @cheikhsalioundiaye2501
    @cheikhsalioundiaye2501 4 ปีที่แล้ว +4

    Bilahi wallahi khassida moo neix si xool

  • @beugkhadimrassoulgayebeugk8076
    @beugkhadimrassoulgayebeugk8076 4 ปีที่แล้ว +5

    Mashalla yalla Nala yalla bindaal yiiw 🌹🌹🌹🌹❤️🙏🙏🙏

  • @moussadiagne5602
    @moussadiagne5602 4 ปีที่แล้ว +3

    Tieuy sama papa malick liguaye deff diarna Yonne fall👑

  • @cheikhgueye2389
    @cheikhgueye2389 4 ปีที่แล้ว +7

    Ndeyssane Thieuy Serigne Touba 💞

  • @mamegoor1547
    @mamegoor1547 3 ปีที่แล้ว +2

    Manchallah khol séde na ❤️🙏 ba sama idole 🙏

  • @abdoukhoudosssylla2855
    @abdoukhoudosssylla2855 4 ปีที่แล้ว +6

    Serigne Ndam FALL dieuredieuff

  • @mouhamadoubakhoum4439
    @mouhamadoubakhoum4439 4 ปีที่แล้ว +26

    Lii moy 78 deug. Bokoul ak touba mbela batay. Tiey wa HT ak S malick Ba

    • @tourecheikh6814
      @tourecheikh6814 4 ปีที่แล้ว

      Li mome nga done wakh fei thi mawahibou ahlouminane bi

    • @mouhamadoubakhoum4439
      @mouhamadoubakhoum4439 4 ปีที่แล้ว +1

      @@tourecheikh6814 niom mbella la niou done jangue mais da bari wone ayy nekhal trop

    • @tourecheikh6814
      @tourecheikh6814 4 ปีที่แล้ว

      Mais Makk gars yi gnio beugg lol 😂 Lou nekh rek lagni weur mais waroulll eupp tmt

    • @youssoundaofaye5798
      @youssoundaofaye5798 4 ปีที่แล้ว +1

      Wawaw seugne bakhoum magoum khassida

    • @morpene2994
      @morpene2994 4 ปีที่แล้ว

      @@tourecheikh6814 pôpoooog

  • @xalilba8593
    @xalilba8593 4 ปีที่แล้ว +11

    Waxnalén Malick Ba dou nitt baxna❤️😭😂🙏🏼❤️

  • @faliloudiagne6471
    @faliloudiagne6471 4 ปีที่แล้ว +2

    Amatina solo Mourides tawfekh rekkk inechalah

  • @lahatsylla606
    @lahatsylla606 4 ปีที่แล้ว +3

    Machalla ndaye guena bakh di guena nekh ba aldiana rek

  • @Kayel_d
    @Kayel_d 4 ปีที่แล้ว +5

    Kou daka diangue ngani kii la waw len goor

  • @cheikhounadiouf7980
    @cheikhounadiouf7980 4 ปีที่แล้ว +3

    maggué neu yarou neu amna solo lol

  • @badoux5228
    @badoux5228 4 ปีที่แล้ว +5

    Jeureujeufei Borom Touba 🥰🥰❤️❤️😭😭🙏🏾🙏🏾

  • @toubadiop6321
    @toubadiop6321 4 ปีที่แล้ว +1

    Thaiy Malik ba dina ma ray rek bilahi macalla

  • @mouhamed2820
    @mouhamed2820 4 ปีที่แล้ว +6

    Imam Malick 😍😍😍rk🤗

  • @mahmouddiallo7703
    @mahmouddiallo7703 4 ปีที่แล้ว +14

    Malick Ba nagnou cotisé nguir mou tokk Sénégal amna solo lol thi Kourel gui

    • @mouhamadoubakhoum4439
      @mouhamadoubakhoum4439 4 ปีที่แล้ว +2

      Bilahi en fait mom il à l'aise ci ndiangue. Dafay indi thiossan bangua khamné keman la dale

    • @mahmouddiallo7703
      @mahmouddiallo7703 4 ปีที่แล้ว

      Malick rôle bi Mouy joué thi djangue mi mo amm dolé mo takh bou nékkoul thi Kourel rék da ngay sentir son absence. Yalla nagnou KO borom bi takhawoul thi barké Cheikhoul Khadim

    • @ibrahimasow6223
      @ibrahimasow6223 4 ปีที่แล้ว

      Vraiment d'accord avec toi. Na Malick tok Sénégal way

    • @falloufaloudiakhate2022
      @falloufaloudiakhate2022 4 ปีที่แล้ว

      Je suis d'accord avec toi diar nako

  • @barabayefall3458
    @barabayefall3458 4 ปีที่แล้ว +12

    Il est le meilleur 😍😍😍❤

  • @cheikhtidianeseck9749
    @cheikhtidianeseck9749 4 ปีที่แล้ว +6

    9mn48😭😭thiéy Malick

  • @aliouba1916
    @aliouba1916 3 ปีที่แล้ว +1

    MACHA Allah

  • @ousseynouakassaboye7828
    @ousseynouakassaboye7828 4 ปีที่แล้ว +4

    Waw léne goor ❤️❤️

  • @ndiayemor5193
    @ndiayemor5193 4 ปีที่แล้ว +4

    Wa li yèmé ne d😭😭😭😭

  • @blackman7643
    @blackman7643 4 ปีที่แล้ว +6

    JEREJEFÉ BOROME TOUBA KHADIMOU RASSOUL

  • @mouhamadoufalilouniang1197
    @mouhamadoufalilouniang1197 4 ปีที่แล้ว +2

    Màsaallaa jaajëf rek

  • @adaafia6344
    @adaafia6344 4 ปีที่แล้ว +14

    Wayè kène dou ndam fall tamitt

  • @oumousow644
    @oumousow644 3 ปีที่แล้ว

    Machalla ❤❤❤❤malicke ba

  • @Diopibara254
    @Diopibara254 3 ปีที่แล้ว +1

    Waw machalla

  • @mbayendiaye8331
    @mbayendiaye8331 3 ปีที่แล้ว

    Malick ba mba dina magal si inchalla

  • @mml477
    @mml477 4 ปีที่แล้ว +4

    Malick il est exceptionnel

  • @abdoubayefallsplo4478
    @abdoubayefallsplo4478 4 ปีที่แล้ว +2

    Djajeuf amna solo nékhna lol

  • @malangsano9578
    @malangsano9578 4 ปีที่แล้ว +1

    Dieuredieuf mbacke

  • @mohamedgueye7560
    @mohamedgueye7560 4 ปีที่แล้ว +4

    78 original 🥰🥰

    • @khadimdiougue8922
      @khadimdiougue8922 4 ปีที่แล้ว

      Li 71la

    • @mohamedgueye7560
      @mohamedgueye7560 4 ปีที่แล้ว +1

      @@khadimdiougue8922 Nn 78 la fall gnome touba mbeill lagnou faral Di diang mtx kw mais li moy 78 original 🙏🙏

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 4 ปีที่แล้ว +4

    Malick ba ndeye saane 😭

  • @fallousow751
    @fallousow751 4 ปีที่แล้ว +2

    C’est le meilleur❤️ on voit nettement la différence quand il est là et quand il n’est pas là c’est un lion❤️

    • @frachise3075
      @frachise3075 4 ปีที่แล้ว +2

      Quelle différence !! C'est pas un match de football ça...ishhh arrêtez de parler si savez pas ce que vous dites

    • @amadoundiaye4353
      @amadoundiaye4353 4 ปีที่แล้ว +2

      @@frachise3075 vraiment

    • @khassidayirekk8581
      @khassidayirekk8581 4 ปีที่แล้ว +2

      Amoul beine difference
      Boufi nekkei daleini yokk rekk mai boufi nekoul douleine wagni dra
      Diangoum ramadan 2019 nekoussi beine yone tei diiangue mi machaalla

    • @bouyafall3462
      @bouyafall3462 4 ปีที่แล้ว +1

      @@khassidayirekk8581 Lou leir

    • @fallousow751
      @fallousow751 3 ปีที่แล้ว +1

      @@frachise3075 manam thii waloum finess bi laay waxer mouride mooy nexal diangue bi dh lolou mom dafa leer nagne

  • @baboufall3811
    @baboufall3811 4 ปีที่แล้ว +1

    Serigne malick bâ yala nafi yag
    Ki loumou bokoul nekhoul

    • @madandiaye1354
      @madandiaye1354 4 ปีที่แล้ว +1

      Téguiene lanou serigne touba diagall

  • @jewrine221
    @jewrine221 4 ปีที่แล้ว +4

    Ndeysane ❤️😭

  • @niangathioune255
    @niangathioune255 4 ปีที่แล้ว +4

    Ba😭❤❤

  • @barandiaye5898
    @barandiaye5898 4 ปีที่แล้ว +2

    Machalah

  • @bambandiaye4950
    @bambandiaye4950 4 ปีที่แล้ว

    Kéne dou serigne touba

  • @moudouseye5014
    @moudouseye5014 4 ปีที่แล้ว +2

    Thiey malick ba

  • @saiddiakhate6680
    @saiddiakhate6680 4 ปีที่แล้ว

    Amna solo

  • @cheikhtidianeseck9749
    @cheikhtidianeseck9749 4 ปีที่แล้ว +2

    Da am mayou Sunu Borom nak

  • @bayelahatmbengue6108
    @bayelahatmbengue6108 4 ปีที่แล้ว

    Ndaye san aka neekh barkéb serigne Touba amul loka dakh

  • @TaarouMourideTV
    @TaarouMourideTV 4 ปีที่แล้ว +3

    Thieuy !! Ku xam lu daqq lii namako wax😭😭

  • @PROD4TV
    @PROD4TV 4 ปีที่แล้ว

    Cey Yalla

  • @seydinaka1430
    @seydinaka1430 4 ปีที่แล้ว +3

    Sama xol sede na

  • @deguenembaye7101
    @deguenembaye7101 4 ปีที่แล้ว +3

    ❤❤❤❤

  • @cvpointernational4549
    @cvpointernational4549 4 ปีที่แล้ว +2

    😍😍😍😍😍😍

  • @serignembackediome9322
    @serignembackediome9322 2 ปีที่แล้ว

    🥰🥰🥰😭😭♥️

  • @sene_aliou_xassida5546
    @sene_aliou_xassida5546 4 ปีที่แล้ว +2

    Machalla ❤️❤️

  • @aliouthioune7749
    @aliouthioune7749 4 ปีที่แล้ว +1

    Ndeysaan neex na lool dh waayei njang mi teel na repeulou lool dh baat yi danio teela soufei

    • @abdoulahatkane8898
      @abdoulahatkane8898 4 ปีที่แล้ว +2

      Original bi nonou lako mag gni jangué

    • @aliouthioune7749
      @aliouthioune7749 4 ปีที่แล้ว

      @@abdoulahatkane8898 deug la waayei niom sen diangue en general dafay teela wathie

    • @doumbayedumbaye7236
      @doumbayedumbaye7236 4 ปีที่แล้ว

      Lep si mag gni laniou koy royé

    • @khassidayirekk8581
      @khassidayirekk8581 4 ปีที่แล้ว +3

      @@aliouthioune7749 louniou deff rekk nonoula
      Ay pro rekk nio nekk su kourel gui

    • @ettelectronique760
      @ettelectronique760 4 ปีที่แล้ว +1

      Ndiangou HT wayé amu thii Serigne bi molen def niuy ay kemtan kom Niko Serigne Mountakha Mbacké waxé rek ndeye sann ay kemtan lan si Yon bi 😭😭

  • @beugkhadimrassoulgayebeugk8076
    @beugkhadimrassoulgayebeugk8076 4 ปีที่แล้ว

    🙏🙏🙏🌹🌹🌹🌹🌹🌹

  • @gdehuytesabbkk
    @gdehuytesabbkk 4 ปีที่แล้ว +2

    Douseenn morom

  • @bajulle6671
    @bajulle6671 4 ปีที่แล้ว +1

    😭😭😭😭😭😭

  • @ndiagasougou1533
    @ndiagasougou1533 4 ปีที่แล้ว +2

    Mag nia lay duegu ni

  • @bambambaye5827
    @bambambaye5827 4 ปีที่แล้ว +1

    Sens doute

  • @moustahindieng9937
    @moustahindieng9937 4 ปีที่แล้ว +1

    Khana 71 la

    • @mbackediop7678
      @mbackediop7678 4 ปีที่แล้ว

      78 la dé yaram

    • @Mouride961
      @Mouride961 4 ปีที่แล้ว

      th-cam.com/video/UvV12YH_3GQ/w-d-xo.html
      Li moy 71

    • @syllabamba5798
      @syllabamba5798 4 ปีที่แล้ว

      78 ndongo yi diangue naniouko mou guena lerr kourel abdou samb

    • @Mouride961
      @Mouride961 4 ปีที่แล้ว

      @@syllabamba5798 waw kay jëwrin jëréjëuf thi léral wi

    • @tourecheikh6814
      @tourecheikh6814 4 ปีที่แล้ว +2

      Khaw nagne nuro touti mais 78 Mo dakhe pour mane

  • @sensational3771
    @sensational3771 4 ปีที่แล้ว +2

    Mom mo warone dadj Ndax batt bi oyofna

    • @khassidayirekk8581
      @khassidayirekk8581 4 ปีที่แล้ว +6

      Dadjie bi bayeko diop rekk
      1998 ba legui moy dadjie
      22 ans d'experience
      Tei malick residewoul senegal etats unis la nekk magal rekk lay niew

    • @sensational3771
      @sensational3771 4 ปีที่แล้ว

      @@khassidayirekk8581 je sais mais batou 1998 ba legui dafay changer insbi Malick rek wala kenen kou batam oyof mo warone dadj taxoul mou done dathie kath centrale bi

    • @khassidayirekk8581
      @khassidayirekk8581 4 ปีที่แล้ว +3

      @@sensational3771 bate bou oyof meunoul dadjal batte yeup kone amnassi nio khamni douniou meune di diangue si kaw parck daniouy nadjou
      Diop mome batte bi si nieup lay diapandi

    • @adaafia6344
      @adaafia6344 4 ปีที่แล้ว

      @@khassidayirekk8581 Waw nonou la meuna dèmè Kay motakh guissa toumako lou barri si kourèl gui

    • @ndiagambow539
      @ndiagambow539 4 ปีที่แล้ว

      @@adaafia6344 MachA Allah amna solo trop

  • @ndeyengonesamb8312
    @ndeyengonesamb8312 4 ปีที่แล้ว +3

    Machallah ❤❤❤

  • @seynabouka9572
    @seynabouka9572 4 ปีที่แล้ว +3

    Machallah

  • @falloudiop1334
    @falloudiop1334 4 ปีที่แล้ว +3

    ❤❤

  • @seydinaka1430
    @seydinaka1430 4 ปีที่แล้ว +1

    Macha alla

  • @chiekhmourtada1350
    @chiekhmourtada1350 3 ปีที่แล้ว

    ❤️❤️❤️❤️

  • @fallougadiaga1990
    @fallougadiaga1990 3 ปีที่แล้ว +1

    Machalla

  • @xeuchelaye6924
    @xeuchelaye6924 14 วันที่ผ่านมา

    ❤❤❤