Cette histoire est pleine d'enseignement. Cela montre qu'elle ne pouvait pas supporter d'être corrigée par ses ex... Elle doit juste être sérieuse et pieuse comme elle a tout laissée. Il ne faut plus vendre ton âme au diable. On compatis à ta douleur et que le bon dieu vous assiste. Amen... Niowal ma takk laa
Elle ne pouvait pas supporter d'être corrigée par ses ex... Dorr djiguene moy corriger ? En plus "corriger" melni kou yorr sa dom ? Sénégal dal diakhal guène ma Seuy yeurmandé sou si amoul rek dara amatoufa
Yoe mome louko tèré mou outi métier mo gueun li bou dè bindan sah mogueun li li mome moko tay khawma liguey bounko df la doy na war yalla nako yalla sopi
Si vraiment c'est possible elle n'a qu'à se caser au côté d'un mari puisqu'elle a vécu tou ça et repenti, je la conseille de se trouver un bon mari et tout viendra inch'Allah
Sokhnasi boul seuy 4foi rek diappuni goor niepp nilan mel so gissé goor gu bakh té manela yoré té yalla takh demal nga seuyé mo ngeun ndakh liguey rek doyul ndakh xalé nga té fawou nga ndiabot nak sudul lolou rek di nga déllo boume sa mbeuy mbeuy ga
Ah ma sha Allah yala nako yalla diapalé rek
Cette histoire est pleine d'enseignement.
Cela montre qu'elle ne pouvait pas supporter d'être corrigée par ses ex...
Elle doit juste être sérieuse et pieuse comme elle a tout laissée.
Il ne faut plus vendre ton âme au diable.
On compatis à ta douleur et que le bon dieu vous assiste.
Amen...
Niowal ma takk laa
Elle ne pouvait pas supporter d'être corrigée par ses ex...
Dorr djiguene moy corriger ? En plus "corriger" melni kou yorr sa dom ?
Sénégal dal diakhal guène ma
Seuy yeurmandé sou si amoul rek dara amatoufa
Machalah bonne continuation Chérie et courage
Machallah Thi émission bi Fatou damakoy suivre tt le temps j’aimerai avwr sa numro et bonne cntuarion
masha'Allah yalna yalla diapalé la si oubil la bountou kheweul yi geum ko rek sa ira inchallah dina bax🤲
Machalah yalla naka yalla djéguél téyérem ko
Fin bi macha allah sama mbok talibe
Yalla bakhna dina bakh inchallah te yalla na te si sa wasila baye niass
Machallah moudiou bouraféte mon diaraniane que dieu la protège
Yalla nako yalla diapele
Sokhna si Ligay doundou kay fo seyi denan la khass dorla fase la yallah nala yallah samou
Thieuy borom café ☕ 😊
Salam sister fatou 😢yallah nakko Sopi 😢sama wal ci caffè ☕ gui merci et Bonne Continuation ❤❤❤❤❤❤
Sister fatou kass yi Dina gneuw in sha Allah ❤❤❤❤❤❤
Mashallah du cou rage😪😪😪😪👏👏❤❤❤
Noumouy khamantè akh dieukeur reum Yi kène douko ssi respectè.mè yalla nala yalla diègual diègual mbolomi dioulit
Man de dalaye suivre depui Amerique
Thieuy borom café ☕ 😊😊
Yala nako yala diapalé tédiéuguel ko
Yalla nala baye niass takhawou si barké serigne rouba
ما شاء الله تبارك الرحمن جميل
Macha Allah madame 😢😢😢
yalla nako Yalla diapalé🤲🤲🤲
Ndeyssane yalnako yalla taxawou mayko borom keur bou baax thi daradiay nabil moustapha asws amine
Thiey taxsimane yi yena bonn😂😂😂😂
😂clandoman nak
Dieureudieuf BAYE NIASS❤
أيد الله لهاإلى صراط المستقيم صراط الذين أنعمت عليهم غير المغضوب عليهم ولاالضالين ءامين، ببركة سيدنا مصطفى عليه صلاة وسلام.
Bonne continuation que Allah choix avec vous ❤
Merci C’est formidable,
Salamou alleykoum je salute à toute l équipe sans oubliéla corréenne qui a perdu un membre cher de sa famille
na diap thie Baye pour toujours
Yoe mome louko tèré mou outi métier mo gueun li bou dè bindan sah mogueun li li mome moko tay khawma liguey bounko df la doy na war yalla nako yalla sopi
Force à toi je t’apprécie beaucoup depuis France
Jigene doylou rek mo koy war lo am mou doyla du courage
❤❤ c'est la pauvreté qui l,a causé
Soubhanalaa. J'espère au moins qu'elle se protège avec toutes ces maladies
Yalla nako yalla dipalé
Kou niake yaye niakeu lép😢gorou Sénégal..thiey...
Naye sane djiguen daye doye Lou Di def lo men
Moray yayam dh bukodon fadiee xalis bulew kon yalla manna thie def sutura
Si vraiment c'est possible elle n'a qu'à se caser au côté d'un mari puisqu'elle a vécu tou ça et repenti, je la conseille de se trouver un bon mari et tout viendra inch'Allah
Magui niane bepp goor bouy door jabaram yalla naga dè dém sawara
Bax na
Amine way 😂
Limou doundou métina mais gnake diné moko waral yaye yi nagnou yar séne dom thi diné tél léna dougual alkourane day tah gnou sauvé doylou échappé thi yéne épreuve yi
Ak gor
A chaque qu'elle le café je pousse un peu jusqu'à dépassé le café
🥰🥰♥️♥️❤️❤️😍😍😍
Est-ce que yakou gnouko mystiquement 😢
Kou diour sa domm yarko diagal ko liguey mo gueun gakoy yakh
Good luck
khamga louma yakar parsque si debut bi nena yayam dafka yakh mais lolou mouna takh foumou seuyiii doufa tok dakh education biiii
🤝🙏🤲👉👂
Ey. Wawe. Mbete. Mbame. Bayil. Li. Nguaye. Def. Deme. Ligueyi
Yale nako sougnou borome dimali li metina trop
Djîguengni ndiàngui len liguey len
Le neveu est impatient
Pourtant meuna nek sakh rap wla ay liguéy Dieu seul sait
Thiess lounek falay khèwè
On attend
Doyna ware....
Thiagatou mom amoul moudjou torokk reikk
Chéri djieuleu sama numéro
Fatou tu as l,art de parler
Comment la contacter svp? Mane je veux bien lui donner des produits à vendre et aussi lui proposer d'etre femme de ménage
Mom kayy warna doyal seukk si Gor nakk
Khalis bim don am motakhon rek
Sokhnasi boul seuy 4foi rek diappuni goor niepp nilan mel so gissé goor gu bakh té manela yoré té yalla takh demal nga seuyé mo ngeun ndakh liguey rek doyul ndakh xalé nga té fawou nga ndiabot nak sudul lolou rek di nga déllo boume sa mbeuy mbeuy ga
Mane touba la nek damala bega maye tasse noye defe ba diote thi
Manite beuge Na tasse café Touba 😂
👍👍👍❤❤🌹
🎉🎉🎉
❤❤❤❤❤❤❤
Damaa tardé recommagé
4 dieukeur yi amou si dom walla
KHAMGUA KI WALAHII DAFA BEUGG BONN REKK LU BONNE REKK
Serigne nit ken douko juger on ne juge pas
Wayi
♥️♥️💚💘🙏
Nul n’est parfait Senegal déffa métti
Wakhal thi kaw
Xana bougoutoul dieukeur
Khaliss. Bi. Nguaye. Fadie. Sa. Yaye. D'où. Weur
Ah. Yala. Beguenala
Madame boîte le café chez toi avant de venir à l émission le plateau N est pas restaurant
Il n ya que les imbéciles qui ne changent pas. Comment la contacter pour l aider?
Bonjour
Xana ampul dome
Matérialiste mo sonale nite yi rawati yéne djiguene yi.
Dioxma numérom niou khool
😁😁😁
laisse le verre cassé c'est mauvais pour toi
Loynane
Sa son dafa faible
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🤍🤍🤍🤍🤍👫🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍😘😘😘😘😘😘😘😘😘😘😘 maman. Bddd
Bhuf
😭😭
Môme. Mo. Ammoul. Foula
Taximani dalifot yi kaay lén wouyou fi
Donne ton adresse je t enverrai une tasse de café
Tu es sur la bonne route que Dieu te sauve. Elle n'a qu'à aller parler avec son marabout
Yaw mom liga don doundou yako tay nak
🤔🤔
Ze
C'est un théâtre tu ment
Merci beaucoup , stp peux tu envoyé son numéro de téléphone