@@hamadydioum3134 salam, mais ça se fait pas. La personne est mort. Pas a inventé une mensonge derrière que tu n’es plus dans cette Monde c’est un péché
Na wakh waadji Mou wane femme Bi 1 Thi séne vidéos yoyou après mouniko da fruitée Ta mane xajoumathi gathia Kone fok Ninou arrêté relation d'amour Bi ndax risque la point😢 Merci bcp s Fatou
Nako wakh ni Tata sama kharit bi guén adouna damako guént mounima wakhal sama yaye mou bayi lou bonne limou néké motax fima nék taliwouma mane dé lolou moy sama khalat
Assalamou halaykoum Sokhna si nouyou naala beugué naala émission bi amna sollo loole mais boumou déme si dieukeur dji n'a déme si mère bi wakh ak mome doucement rk❤❤
Sou xarit bi doon dound lay gueun metti. Il faut le dire à la dame. Il n'a pas le choix. Mais kou baakh nga. Il ya une autre solution aussi. Tonton bi nako wakh deugg bi que boy bi xamna lou xew.
Nako bloquer à nouveau... c'est facile à régler et penser après la mort... l'enfer est dure et pour niouy tédé diabarou jambour yi... il n'a qu'à fuire cette mamie
Nako wakh mere bi kilé au courant de tout. C'est la seule solution. Teksi niko mo wakh pabi nako bayi. Si elle ne laisse pas tout tomber dinako wakh pabi. Mane daal j'ai honte d'etre femme...limay deg yeup si mim réw...
Waajii naci maandu té nekk ci bopam yoonam nekkul ci problèmu jambur la man dé bumalkotee doon conseil damakoo naan naleen bayi AG yalla té maandu ci baniateexool walla deglu
Salam alikoum, moi si j’étais toi je ne dirai rien à personne ni son mari ni la tata comme la tata ne veut pas abandonner les choses. Laisse-le comme ça c’est mieux y’a des choses que tu fais dans la vie que Allah l’aime pas. Oh bonjour viendra Cest, Allah qui va tout montrer Inch’Allah, si tu allais pour des à son mari, tu vas détruire une foyer, même si ce n’est pas ta faute, mais tout le monde va tourner contre toi-même moi tout ce que je te conseille, méfie-toi et ne fais rien il va te fera plus mal que tu vas regretter plus notre prophète bien-aimé d’Allah a dit c’est lui qui mets une Voile sur les péchés sur les défauts de son frère. Alors Allah mettra une Voile sur ses péchés, le jour du jugement😊😊
Na waax taann AK tata bi en tant que sa propre, explique directement les faits,et lui demande d'arrêter car si son mari sera au courant,son mariage peut se ruiner,donc quelle arrête l'infidélité envers l'ami de son mari,c'est une honte donc parle à votre Tata c'est la meilleure solution.
je conseille au gars de parler à la dame et non au mari. Puis que la femme ne veut pas arrêter, il peut aller la voir et lui demander d'arrêter car il est au courant de tout... La femme va accepter car elle ne voudra pas que son mari soit au courant...
Ils n'ont qu'à piéger la femme le jour ou le tonton va là-bas appele l'ami l'ami fait semblant de venir la tata sans la prévenir pour qu'il était de passage comme ça elle va arrêter sans que le mari du tata le sache et sans que elle va pas penser le garçon à fouillé son téléphone ou pas elle va avoir des doute comment pourquoi sans réponse 😂😂😂
J'ai vu ce cas dans ma ville ya trente ans mais le mari cocu lorsque ses sœurs lui ont annoncé les dérives de son épouse il leur a dit qu'il est au courant mais que personne n'en parle
Na wakh tata bi da ma guente sa khariite mo ne m'a wahale sa ma yaye mou bayi Lou mouye def
Excellente idée
@@hamadydioum3134 salam, mais ça se fait pas. La personne est mort. Pas a inventé une mensonge derrière que tu n’es plus dans cette Monde c’est un péché
yagui niouy yéé si adouna , au top !!!
Émission bi nekh na torop chaque jour j'écoute
Machalla amna sollo Sénégal doy nawar nako wakh ndaw sy
Mbokou internot yi ziar nalene mba yenangui am diam maniko thieuye yalla thieuaaaye indeti na dè ....bi momaye dadji diadieuf waye sokhna fatou
Salam salam magiléye beugué Fatoumata nékel si diam avec toute l'équipe de Thiès info
Yalla naniou yalla moussal cilou bone
le gars ils les meilleurs ke dieu te bénisse inchallah
Na wakh waadji Mou wane femme Bi 1 Thi séne vidéos yoyou après mouniko da fruitée Ta mane xajoumathi gathia Kone fok Ninou arrêté relation d'amour Bi ndax risque la point😢
Merci bcp s Fatou
Nako wakh ni Tata sama kharit bi guén adouna damako guént mounima wakhal sama yaye mou bayi lou bonne limou néké motax fima nék taliwouma mane dé lolou moy sama khalat
@@fatousow94 machallah 🙏bi baxna👌
Na wakh tata bi mou arreté walla moy wakhko Dieukeureum 😢😢😢
Yéééh dédète na ci guène ba sète wéthieu yoname nékoussi. Na yème di place kharit dakh amna deugue you di tasse adouna! Wassalam…..
na nek tata bi wahko la vérité
Salam sister fatou xalass ci Bi Tata 😢merci Beaucoup et Bonne Continuation ❤❤❤❤Dieureudieuf
Fatou cv bien maser Verma bougé n'alla wayi emisoun bi metina wayi na wakh tata bi mou bayi Lou mouyi def yeginako😢
Li dé moy harite
Salam ,il na ka affronter la tata comça elle changera le reste de sa vie
Non appel anonyme
No bu wah ku goorki na wah tataA bi
Assalamou halaykoum Sokhna si nouyou naala beugué naala émission bi amna sollo loole mais boumou déme si dieukeur dji n'a déme si mère bi wakh ak mome doucement rk❤❤
Souko wakhé Tata bi kone dagni am problem yakou wanté ba faw té erreur bou gandé😂lay done continuel di surveille de près
SLM ya Fatou contente ci yaw n'a wax ak tata bi Niko s8 o courant d tous
Sokhna Fatou malla beug bilahi yowe rèk laye topou
NB :PLAISIROU AYES MINUTES , (KOYS BOU LEWOUL ) AMOUL NDIARINES DIAROU QUE DEE ..SURTOUTS DI MOY SE BAYOU AY DOMES LOU QUE FI DIAR,
Na dem wakhe ak mère biii loumouye degue
Nako wakh tata bi
Thies info merci 🙏
Il faut acheter une puce et l’appeler anonymement ou lui envoyer un message lui disant que je suis au courant de la situation
Voilas c’est ça juste l’envoyer une de ces vidéos
Voila
Je suis de même idée avec toi
❤❤❤❤
Alahou akbar 😮😮😮
Ou yala na lenn yala fay lenne rek merci
Plus tu connais les Hommes, plus tu respectes les animaux
🤭 Aywaay
Moungui niaw dh😎😎
Et la femme 😂
🤣🤣🤣🤣🤣tu a raison dé
nka wakhe tata bi rék moguene dh
Na abonne benne piis telepho woo tata bi manaseko bayil diw magek say vidios
Na wak tâta bii
Lingay def bakhna trop mais boudone gaaw dinaniou gueuneul
Efectivement 😢
Non mais Sénégal yakhouna . Mère bou tollou nii . Nako affronter
Nalenn baye niou katante
Émission bi amna solo chaque jour damkoy setane
Nako wakh tatam bi lolou mo eupp soutoura ndak souko wAkhé kénén déy guéna Law rék
Mome na mandou loloy wakh dji mome dissna té yanouwoul mome mo beugue tass famille.
Bonjour madame ❤
Manikou si they they yalla 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
En tout cas il n'avait pas le droit de synchronisé le téléphone d'autrui
Salam les amis dine dafa beugue kou mandou yonam nekouthie ❤❤
Ndekété yo yo😅
Nako wakh Tata bi
Sou xarit bi doon dound lay gueun metti. Il faut le dire à la dame. Il n'a pas le choix. Mais kou baakh nga. Il ya une autre solution aussi. Tonton bi nako wakh deugg bi que boy bi xamna lou xew.
Thieuye hom aussi thieuye fam😅
Na woutte numéro inconnu mou wo si mère bi menacée ko wakh ko 4 vérité
C’est mieux dou khamni mome la té mère bi dina arrêter
ziarrenalla nako wakh tanta bi moudiekh tak
Wadji deh Moy gor pire ndaysan
Ok doynawar mais soukeu wakhee djieukeur gii esk lolou worr neu vue l vieux napas 1 santé d fer
Nano wakh tata bi
À mon avis il faut parler avec Elle
Il n'a qu'à parler directement à la tâta...c tout
Nako bloquer à nouveau... c'est facile à régler et penser après la mort... l'enfer est dure et pour niouy tédé diabarou jambour yi... il n'a qu'à fuire cette mamie
Nako wakhe tata bi
nako wakh tata bii
Salam Salam niit kou bakh daye mandou thi famille diambour
Kho wax tata bi sou demee thi dieukheur ji konn seyou daw si dey tass
Nako wakh mere bi kilé au courant de tout. C'est la seule solution. Teksi niko mo wakh pabi nako bayi. Si elle ne laisse pas tout tomber dinako wakh pabi. Mane daal j'ai honte d'etre femme...limay deg yeup si mim réw...
Appel anonyme
Waajii naci maandu té nekk ci bopam yoonam nekkul ci problèmu jambur la man dé bumalkotee doon conseil damakoo naan naleen bayi AG yalla té maandu ci baniateexool walla deglu
Lifi seuss daal moy na diakarlo ak tata bi
Nako wakh tata bi
Émission bi nekhna
Na wah ak tata bi mo gueune sede ci si gnome gnepe. ❤ Mangui lendi ziarr bou bah
Djiguene boukoye defe domossa jerigno sa dome aye febar you mystérieux molene didale je vous le jure
Na wah ak tatabi ak menace bou bayioul mou wahko djeukeurbi
Nétali katt professionnelle
Na dem wakh ak tata bi
Na dem si tata bi
Salam alikoum, moi si j’étais toi je ne dirai rien à personne ni son mari ni la tata comme la tata ne veut pas abandonner les choses. Laisse-le comme ça c’est mieux y’a des choses que tu fais dans la vie que Allah l’aime pas. Oh bonjour viendra Cest, Allah qui va tout montrer Inch’Allah, si tu allais pour des à son mari, tu vas détruire une foyer, même si ce n’est pas ta faute, mais tout le monde va tourner contre toi-même moi tout ce que je te conseille, méfie-toi et ne fais rien il va te fera plus mal que tu vas regretter plus notre prophète bien-aimé d’Allah a dit c’est lui qui mets une Voile sur les péchés sur les défauts de son frère. Alors Allah mettra une Voile sur ses péchés, le jour du jugement😊😊
Nako wakhe tata bi wave
loulo moy degue demal thi tatà bi nga wakh kako
Na waax taann AK tata bi en tant que sa propre, explique directement les faits,et lui demande d'arrêter car si son mari sera au courant,son mariage peut se ruiner,donc quelle arrête l'infidélité envers l'ami de son mari,c'est une honte donc parle à votre Tata c'est la meilleure solution.
Salam je lui conseille d'acheter une puce numéro privé de menacer la dame qu'il a ses photos et vidéos si elle n'arrête pas il va les divulguer
je conseille au gars de parler à la dame et non au mari.
Puis que la femme ne veut pas arrêter, il peut aller la voir et lui demander d'arrêter car il est au courant de tout... La femme va accepter car elle ne voudra pas que son mari soit au courant...
Salam djeukeurou mère bi khamenako dafalene bayi tji bire 10ans nga diko defe
Bsr il doit parler avec son tata ces mieux
La solution est qu’il parle directement au tata puisqu’il ne veut pas qu’elle perd de nouveau son fils et son ménage
Nalen dedele mogeune
No coment
Na waxe tontons bi niko mou waxe tata bi niko ilfoh gnou araité par ce que magui koye koumasé dége thi kogne bi point
Mètina dè😢
Esk d'où out puce momit def ko apel anonyme sans pour autant mou wax KO mo bayilo wadji
Nako wak tata le mari nom
🎉
Il a déjà fait son mieux qu'il s'arrête là !
Nako wakh tata bi si ndiekku mogeun sinon rek suko wadji bayé rek dina woutat kenen ndakh tamu lagola,ms nak bumuko si akh dieukarji ak dome ji jamai
Nite daye mandou guene balma
Bayil fen
C’est pas son problème Que chacun répond de ces actes Les femmes aiment les réseaux sociaux et beaucoup ne les maîtrisent pas
😭🇸🇳💔😭🇸🇳💔😭😭💔🇸🇳🇸🇳💔
Ils n'ont qu'à piéger la femme le jour ou le tonton va là-bas appele l'ami l'ami fait semblant de venir la tata sans la prévenir pour qu'il était de passage comme ça elle va arrêter sans que le mari du tata le sache et sans que elle va pas penser le garçon à fouillé son téléphone ou pas elle va avoir des doute comment pourquoi sans réponse 😂😂😂
Damakoy conseillé mu wut beneen puce wula mu abbu téléphone boo xamni mère bu duko xàmme muniko so bàyyi wul lingay deff dinala siiwal té kula jegé laa
J'ai vu ce cas dans ma ville ya trente ans mais le mari cocu lorsque ses sœurs lui ont annoncé les dérives de son épouse il leur a dit qu'il est au courant mais que personne n'en parle
Nako wakh mére bi mé pa pabi walla dome dji
Bouko.wakhé.tatabi.mbadou.yake.adouname.eurezema.ba.bouko.diokhone.kénéne.dako.wolou.motakh.nakhole.noumou.Guene.rafété.moguene.adouna.amoule.solo
Salam a mon avis il doit acheté un numéro changé de voie pour lui dire d'arrêter ou lui dire à son mari tout ça dans l'anonymat
Na guiss tata non si pa